Il est excelent, ce Modou c un gran type, un Big cerveau
@mamadoudiop15312 жыл бұрын
Bilahi ki éspris la guiss na lolu
@bmkillertv1849 Жыл бұрын
Yen nakhlen yombouna..Ki wakhe kat la..mouni ragaloul yallah..Dans talib al ilm on lit ceci : La crainte et l’espoir font parti de l’adoration.Lui c’est un arrogant ignorant.Vous parlez d’esprit.Quel esprit ?
@mactardiallo984710 ай бұрын
Modou tu as dit tout haut ce que nous disons tout bas D'ailleurs Diamano biii kou Ragal Yallah esk aam naa...?
@Mlkoneservices10 ай бұрын
Degue nékhoul ❤❤
@barrezi4 жыл бұрын
Pourtant il a parfaitement raison, deug gou wérr la wakh, ragal yalla c'est pas donné à tout le monde. Nafékh menoul wéssou di déff lépp li yalla di téré ba nopi sagna takhaw ni da nga ragal yalla
@bmkillertv1849 Жыл бұрын
Allah n’a pas mentionné dans le coran..le fait de se repentir ? Les péchés que l’être humain fait n’a rien à faire avec la crainte d’Allah.Et la parole est à mesurer le fait de dire je ne crain pas Allah c’est différent du raisonnement qu’il fait..Il ne devrait pas raisonner en disant « je ne crain pas allah »..Que des spéculations dans le plateau..Pas de connaissance que des conjectures..Et il dit que des bêtises cet idiot..En plus il dit « yallah amoul yeurmandé » ngen key bayi ci plateau bi ?
@ababengaid41723 жыл бұрын
Modou yangui wathieu yonne dh yalla yeurmandé la dh moy ar rahman di ar rahim moy yeureum kouko nekh fi si dounya te tamit moy yeureum tanekham si alakhira modou yangui wathie yonne nakkk sois plus modeste et humble
Modou Geuy togou kaay biga took soudoul won yeurmande yalla rote ga bou yague tok biga tok fofou di wakhtan âme wer mana wakh mouma wo soudoul won yeurmande yalla fo dieum soudoul won yeurmande yalla.....
Il a décortiqué sa phrase👂 Pourtant kudul djuli à temps aka gneme Allah t yab ko sax Yalnagnu yalla bal rek t tek gnu si yoon Il est trop franc pour notre société Ndax sunu société day wodu wax alors que mom amoul filtre donc si deguine dafay violent thi sunu "entendement senegalais"
@NgonéDIOP-k9l10 ай бұрын
J’apprécie trop ce mec❤
@MakharyMbegue5 ай бұрын
merci beaucoup modou Gueye
@dieynabadieng71294 жыл бұрын
Vraiment d une part franchement parler je suis avec moudou .il est sincère avec lui .il ne laisse pas emporter par les autres vraiment .je ne veut pas le juger mais dé fois aussi il part trop loin. Bonne continuation et félicitations à toute l équipe tfm
@abliesowe51663 жыл бұрын
Ay wakhi doff rek la fi dègue Modou Gueye Ar-rahman si tourou yallah yi la bokou. Wakhi kou bèw rek ngay wakh Ndoye Ban Bayil rasatou bi yallah dañkoy xam ragalko tamite bolèsi.
@MbenefaueNgom Жыл бұрын
Nite kou deugeu franchement mais sénégalais yi dougnou comprendre fimouye wahé
@khadimbopp7671 Жыл бұрын
S saliou nena yalla yeurmadela waye boula fatele bopam do tal loudoul mom
@haneamdy22374 жыл бұрын
Fans club modou geuye depuit itali
@binetoudiop3374 жыл бұрын
Hane amdy j'hadère mais nak na changè chemisame bii😂😂😂
@haneamdy22374 жыл бұрын
Antouca nitou deug puir moy Modou Geuye il peuz bien ces mots wa salame
@fatouseck35614 жыл бұрын
@@binetoudiop337 il porte que tu blanc il la di
@fallouba27003 жыл бұрын
Modou ragal yape yalla la
@rgoyaf74864 жыл бұрын
Modou gueye je l'adore. Il est véridique
@abdoulayefayedia76512 жыл бұрын
Il a parfaitement raison ce Modou Gueye kou ragal Yalla dou déf lou bone
@eivanokaye55194 жыл бұрын
وقال صلى الله عليه وسلم إنماأعمال بالنيات وإنمالكل إمرء مانوىٰ
@tening29664 жыл бұрын
Chii ndoy bane mo ngi doda wakh louma d’accord yallah dagne kay xam
Lima diakale Moy Modou ak Mane danio bokkou même kalate Mane dama foguone ne werouma waye guis'na kou melni mane
@tatobin45 Жыл бұрын
Bravo Modou, faites jamais de politique/ Vite votre bon projet, mes enfants petits-enfants et amis et moi-même donneront un euros par mois. Alors foncez. Je suis fière de vous.🙏
@ibrahimakane7758 Жыл бұрын
J'aime la vérité elle a pour moi une importance capitale et rien en elle ne me semble indigne vous comprendrez donc aisément pourquoi j'ai beaucoup d'admiration pour ce monsieur
@abdoukhadrekebe35033 жыл бұрын
Machallah modou machallah
@RabiatouAnegbe Жыл бұрын
Bravo Modou!!! I think so great 👏
@ousmanediakhate22593 жыл бұрын
Ragal yalla n’a rien avoir avec les péchés car par nature l’homme est pécheur. On ne peut que chercher refuge au près de Dieu contre les tentations.
@babacargaye78743 жыл бұрын
Modou il est intelligent 🧠
@khadimba75762 жыл бұрын
Niveau bi kawé n’a khamo lenn li modou di wakh
@thiorofaye48604 жыл бұрын
Mani sétlou ba khame seuye bi dina bakh ou pas , lolou dou islam ,seuye yallah mokoye tak, Modou daffa dégue islam ta andeu ak yallah motakh douffi bakou di gnodi nane mo gueneu ragal yallah, il est sincére, honnete machallah Yallah khamoul sentiments fékna bb si birou ndayam rayko ta yeureumoul yaye dji, modou aye verset coranique laléne di tégual
@Ndiaye-tt8zh4 жыл бұрын
Niaka Kham yalla motakh guéne diko todou fi
@babacarsy28894 жыл бұрын
Je te respect tu parles pour toi inchaallah
@ibrahimafall939610 ай бұрын
J’en suis sûr et certains que d’aucuns pensent qu’il joue ou qu’il fait de la comédie Ndeyssane vous n’avez rien compris
@adjiwagne49713 жыл бұрын
Je l'aime trop
@anniefaty51583 жыл бұрын
☝️☝️☝️Modou fassé🤔on es en Afrique !!!gueumo serigne!!! louy sa tétal? koula Jokh tétal ?lou ko warral tétal bi ??pour quoi toujours tt noir et tt blanc... ya leundeum🤔🤠🤠🤠
@bmkillertv1849 Жыл бұрын
Dans talib al ilm ont lit ceci : La crainte et l’espoir font parti de l’adoration.Lui c’est un arrogant ignorant.Vous parlez d’esprit.Quel esprit ?
@bayefall52243 жыл бұрын
Modou gangaye khalé tu d'or
@adjaaminatadiop34403 жыл бұрын
Moi perso c'est aujourd'hui que j'ai commencé à regarder cette émission et je trouve ça vraiment intéressant. Mais j'aurais mieux préféré qu'on élimine Ya Awa. Par ce que grâce à votre émission on y apprend beaucoup on à besoin des personnes qui se servent de leurs cerveaux comme Modou et Ndélla mais po gni wakh juste pour qu'on remarque leur présence
@josephsene53133 жыл бұрын
Sénégal parfois Damaye rous si quelque débats goudou fan gatou fan yalla d'où défar pour 4 jour Di réy dans 3 jour Sénégalaise déy fénn fa moudiou guém ay fénam naniou délou si yalla Lou way sokhla yalla amnako
@vmvdousvne74044 жыл бұрын
modou il parle en argot il faut etre tres intelligent avoir un esprit ouvert pour comprendre la ou il parle
@Momarbineta4 жыл бұрын
Sûr d'accord avec toi
@Momarbineta4 жыл бұрын
Mais YALLAH amoul yeurmeundeh suis pas d'accord avec toi. Sa contredit avec la parole DIVINE qui dit ARAHMAN ET RAHIIM
@kineseck7064 жыл бұрын
Merci Modou Gueye tu es raisonnable
@papayqsnfdoye69614 жыл бұрын
J'aime beaucoup ce Mr Gueye parce que il est vraiment pertinent
@thiernodiallo70973 жыл бұрын
modu et tres pertinent
@layefaty18113 жыл бұрын
Modou ma la fann
@adamandiaye42234 жыл бұрын
Modou damako beugue🤣🥰
@abdousarr76193 жыл бұрын
Astakhfiroul lah Modou Guèye mi reuy na lamin dh té xamoul loumouy wkh ki dh kouko xol xam ni diangoul al qoran
@assaneretou65924 жыл бұрын
Modou tu es le meilleur
@kingmontagepro15554 жыл бұрын
Ay modou adouna worr nala dh
@mouhamedsoumare85874 жыл бұрын
Modou guéye yangui dioum dh Le Pardonneur fait partie des magnifiques noms de ALLAH SWT
@moussadrame38933 жыл бұрын
Frr kou dh AK sa bammél
@ibrahimakare6253 жыл бұрын
Vraiment modou dall en voulant être trop intelligent on devient con au final
@thiernodiallo22544 жыл бұрын
Modou moyetol yalla diaarr na ragal 😙
@m.s32544 жыл бұрын
Yalla diarna Raggal deug deug
@ibrahimandiaye83574 жыл бұрын
La parole est un couteau à double tranchant ,mais il faut bien écouter modou,car c'est un orateur qui masques ses paroles par la sagesse
@muhammadhashim25284 жыл бұрын
C’est juste un beau parleur mais ce qu’il raconte est dépourvu de sagesse il commet des sacrilèges.
@ElTIO_Galass4 жыл бұрын
Limou wakh deg deg la ayy doff nguen rekk senegal Ken ragalou fi yalla mais modou am na jamou yalla yo khamni de meun nan la nianal yalla yokou say fan
@adamadiobembengue88383 жыл бұрын
Séne télé bi nak bokena thi liye yakh awe askane ,ndoye bane yake saye morome khana diangouléne, fi yalla Di wakhé bindouma nite ak djiné loudoul niou diamou ma, télé thi ya ayou khalazina amanou itakhou rabakoum
@mopascal38964 жыл бұрын
Pour comprendre le raisonnement de Mr Gueye, il faut penser philosophiquement...
@maimounakanoute8024 жыл бұрын
Wakh gua deugue de
@dienanjie19764 жыл бұрын
No j'aime cette Monsieur bilahi mashallah tu é direct
@boyfromgalsen35134 жыл бұрын
Si vous l'écoutez bien modou gueye a toujours raison...
@altesseroyale43833 жыл бұрын
Sénègal daguène beugeu affaire serigne!
@wakhdeugguetayallatakh81294 жыл бұрын
Sénégal gni wara noppi gno fess télé yi désole😭😭😭
@soramalik58364 жыл бұрын
Je te jure
@demsss89453 жыл бұрын
Modou con neu 😂 nenaa yalla amoul yeurmandei 😭😭😭
@Sgueye13964 жыл бұрын
Modou Gueye a raison💯💯💯
@medinabayee-shop21894 жыл бұрын
Parfaitement d'accord avc modou,mais ndoy bann non,yala kouko xam ragualko.
@dallahbaba49933 жыл бұрын
Wa modou mi foum dukue
@khadimawagueye71144 жыл бұрын
Merci modou
@reinekeen76123 жыл бұрын
Modou daal dou nafèkh il dit ce qu'il pense. Voila
@fallmara91194 жыл бұрын
Merci moudou magi si yaw
@hallildiallo67813 жыл бұрын
Au Senegal y a tellement d ignorant, au nom de la verite ils confondent etre confiants et dire des betises de la sorte. Quoiqu il en soit ne divulgue jamais tes peches et pire encore tu le fais a la tele. Conneries sur conneries jamais au grand jamais tu ne seras parfait mais fais de ton mieux et ne te crois pas real an racontant les sordides que tu dis.
@seringemodougueye3293 жыл бұрын
way ki dafa reere amna gno khamni diarou gnio invite si tele
@khassimediop58044 жыл бұрын
Mane dé modou la beugeu bilahi
@papayayasissokho54614 жыл бұрын
J'aime Modou Gueye il est pertinent way limouy wax ak gnimouy waxal sax deganetei wouniou mais wax bou am solo la wax
@mohamedthiam5894 жыл бұрын
J’adore se monsieur Gueye il est véridique je te jur mai vous comprenez pas ou il est entrain de parler
@setane_tale3 жыл бұрын
Ou il est entrain de parler ?
@allesyll11523 жыл бұрын
Wa ki mom loum donne bâ ausé du wakh li ak mom moy Kane khana dafa bari khalis
@alassanendiaye73773 жыл бұрын
Bah oui c'est un grand philosophe Modou gueye
@madickendiaye32443 жыл бұрын
Modou gueye à ŕaison
@elhajidiawkabir70743 жыл бұрын
Nday bane khamo sarab ndayam
@assanemikaelfaye56513 жыл бұрын
Modou gueye akk gni nek si plateau bi yup yem hamou gatt.. Nena Yalla ampul yermande g potie niak jangue bakhoul defay rereul bilahi. Yalla nalen Yalla weul bati
@altesseroyale43833 жыл бұрын
Daguène di degglou Modou Gueye ak khèle! Ragal Yallah aye wakh rèèk la.
No modou il est extraordinaire jtjur!! Je sui totalement en phase avc lui
@pilotepilote35743 жыл бұрын
nNdoye Bane di doule yallah kay soko ragalé ngakay diamou soko niémé saganéko
@mamadmasd75444 жыл бұрын
Mo guerrier leu 💪💪💪💪💪💪
@yeroka59413 жыл бұрын
أعوذ بالله من الشيطان الرجيم إتقو الله تبارك وتعالى في كل حين إن الله غفور رحيم
@mariamabarro3673 жыл бұрын
Il dit trop vrai
@assanemikaelfaye56513 жыл бұрын
1. O hommes! Craignez votre Seigneur qui vous a créés d'un seul être, et a créé de celui-ci son épouse, et qui de ces deux là a fait répandre (sur la terre) beaucoup d'hommes et de femmes. Craignez Allah au nom duquel vous vous implorez les uns les autres, et craignez de rompre les liens du sang. Certes Allah vous observe parfaitement.
Sama pape lay degeu mounane ma yalla kendou ka ragal dangakay moytou
@modoucisse8594 жыл бұрын
Ah loy moyto kay ragal ngako
@fatoumatathiam30393 жыл бұрын
Sama Modou way
@diamouyallah27404 жыл бұрын
Al rahmane brom yérmandé ki eupp gneupp yérmandé tei di diokhé yérmandé téydji boula yeuramoul wone doo tolou fii ngua talou té doo am lingua am kone dél xoll linguèy wah
@aramengayefaye96003 жыл бұрын
Diéme ko raggal mo geuneu
@elpresidente54884 жыл бұрын
Soubhana lahou parfois nite wakh ba guéné bopam ci l'islam ta douci bayi khél Ki ci ay wakham wédinaci lou bari yo khamné nioy ponki l'islam Béneu mom wédina niane wédi sarakh wédi dogal wédi yeurmandé yalla té limiy wakh lép ci khél lakoy diéma ték allahou Moy yalla diotéwoul dara ak ragal yalla nite ki fék yangui bayi khél sounou borom ci say dieuf amnga ak ragal yalla gonék ci yaw wayé ragal yalla nak ay dimension la tambalé ci yonénté nio gueuna ragal yalla niép ndakh daniouko kham kham sagne sagnam tékci sahaba yi nitou yalla yi baci nioune gni gueuna soufé Ki daal toub moko war ndakh bou nékone ci deuk bouy atéwo charia danioukoy ray
@ibrahimadrame84753 жыл бұрын
Mane dh yaw la andal waxi dof mo takh mou ni Yalla ken dou ko ragal Yalla mo ni kham len ma nguen dog ma diamou ragal Yalla moy lan lo kham ni warone nga ko def té kham nga day am problem sa di guenté ak sa brom nga ba yi ko siy ragal ko siy rousse mais mome day wax ak khelam bilay sens savoir
@fatoubintourassoulgueye6943 жыл бұрын
Parfaitement raison d oukhty
@awathiam69454 жыл бұрын
Bro modou géstoule nga khole univers bi ak leep liko weur allahou défla ngay niit limou geuna téral si limou binedeu ay way naniou goréé ta sante rabbi souniou borom mi niou amal ta tagouwouniou dof deug moy kham lila war ta nékoulosi yagi réér bro !!fébar wésouwoul rééréé yeurmendé ya rabbi soumet toi pendants qu'il soit trop tard le seul reméde c'est le coran et le noble prophète seydina mouhamad salalahou aleyhi wa salam please!!! Salam frere.
@youssousow34553 жыл бұрын
Modou beugnala soumalay déglou dafay melni man ngay wakhal
@only-blackdoll94254 жыл бұрын
Mdr😂😂😂mane dall modou la begue
@FallMbacke-x7p Жыл бұрын
Aye yèfarr deug ak aye nafèkh Gnofi nèkk
@Malicksindidi19883 жыл бұрын
je n'est absolument rien à dire à se fou de modou gueye mai ndoye bane linga wax noko meuné(yalla soko ragalé doko diamu) ya bon ya yéss yay diahiil
@moustaphagueye77474 жыл бұрын
Modou mi waxi dof lay wax..yalla moni ina rahma talahou minal moukhsi niina..nganan yalla amoul yeurmandé
@pilotepilote35744 жыл бұрын
ki soumako mounone guiss diakhrane dinako wédilo limou wakh si anam gou tarr
@kissimadabo68424 жыл бұрын
Modou yaye chef💪
@khadim57794 жыл бұрын
Li mo takh SENEGAL dou am diammou maky sall bakhna ci wa SENEGAL