Ohhh kandj wakh dji rafetna trop🙏🏾 amna niveaux, xam xam🧠 fégn nasi, yar fégn nasi, nité fégn nasi,xam sa boop fégn nasi, jambar Osi fégn nasi 💪🏽 motakh yar keepa am solo ❤🙏🏾
@ousmanesy672711 ай бұрын
Il est agréable à écouter et donne beaucoup d'enseignements
@MoussaNdiaye-mr7eb11 ай бұрын
Il est tellement fort en communication 🎉bonne continuation
@AladjiMbaye-s1c11 ай бұрын
Koula yéne lou bone la yeureum barckép Serigne Touba bonne continuation mon frère ❤❤❤
@moustaphasognane207111 ай бұрын
Un homme humble qui parle tres bien . Loum wakh nge naw ko boy Niang tu as de la chance davoir ces genres de personne chapeau
@bambagueye245411 ай бұрын
Merci beaucoup Kandji vérité absolue, Sénégal mo bari ay nit you nafékh billakhi
@lesamouraisnoir530411 ай бұрын
Mâcha Allah yalla nassa jamm yague Nitte Kou Bakh gua ❤
@aramesndiaye59011 ай бұрын
Bilahi je le respecte beaucoup bro yallah nala yallah defal diame ak salam❤
@senegal211 ай бұрын
Yene family Kanji damalen beug koubeug boye niang damalaye beug
@ninkinanka364411 ай бұрын
IL A UNE UNE COMMUNICATION UNIQUE CLAIRE ET LIMPIDE. RESPECT KANDJI
@boubafall101411 ай бұрын
Bien communiqué machallah Dafa dii modou Lo moy champion bi mo lén meun fouff❤
@adandoye375911 ай бұрын
Franchement kandji je l’estime beaucoup mane nit so baxé soumalay khole di contane nakh damay yeuk sama yaram ki kou baxla ❤️🙏🏾
@Azoura2211 ай бұрын
modou ✨ xaragne lo rek santé 👑 yalla
@khadimdieng213011 ай бұрын
kii beugue naka waay❤❤❤❤bien communications👏
@djeganengom11 ай бұрын
Kandji je sais pas fo diagué mais tu es un extraterrestre Machallah yalla nala yalla defal diamou ✅
@Del2Mas11 ай бұрын
Way limou communiquer fi c'est extraordinaire❤
@ousseynoundiaye818211 ай бұрын
La discipline peut tout donner il est peut aller très loin Je connais ce jeune homme Courage mon frère
@Amdy47811 ай бұрын
Ndaysane kandj borom bax nga yalla nala borom samm arrla soutoural defalla taw fex Ak taysir rk inchallah barkep borom Touba ❤❤❤❤❤❤
@GoraNdoye-ko6hw11 ай бұрын
Machala kandji production pdg etdr l'homme social bonne continuation inchala le meilleur reste à venir ❤
@ndiaboutadiouf930011 ай бұрын
merci kandji tu communique bien machalla vérité absolue
@syllamomo598811 ай бұрын
Merci kandji yalla nala yalla sam❤❤❤❤❤
@alaathiou193611 ай бұрын
un petit rectificatif...On dit " C'est indépendant de notre volonté" quand tu dis "c'est pas..." dafay changer li nga beugue wakh......Sinon xel mou sell ngay wakhé yalla nala yalla défal diam machallah
@joliemamanndiaye286111 ай бұрын
Tu es excellent communicant!!!! Bravo
@damendiaye574111 ай бұрын
Galsen bi yup kén dakouko communique machallah kandji yalla lafal la thiat
@elhadjiibrahimadiatta948511 ай бұрын
Courage mon grand tu reste tjour le meilleur
@GoraNdoye-ko6hw11 ай бұрын
Machala production kadouyi rafetna torop yalla nalayalafay sakhol si domou adama yi❤
@ballacisse756111 ай бұрын
C’est un gars qui communique très bien
@bakarysagna620611 ай бұрын
Manchallah le grand bien parler
@Boupscanayadaly11 ай бұрын
Machallah tu communique bien yalna sa diam yague
@sukaiceesay828811 ай бұрын
Merci Kanji ❤
@MrFayemanou11 ай бұрын
Alahou akoubar écouter les 5 premier Minute conseil pour toute les jeunes Merci kandi
@karbaladomoupikine476911 ай бұрын
Machalla le PDG kandj production borom ETDR
@AliouKama-zs9ye11 ай бұрын
Kandji bravo mais n'oublie pas que zambala fait partie de vous faut le trouver un adversaire ❤
@diamilmboup439211 ай бұрын
Les Kandji Machalah man dh HawMalen mai Bilahi lou rafet Rek ngendi wah
@AmalaMbaye-l4j11 ай бұрын
Très bien communiqué
@mormbaye140611 ай бұрын
Machalla sama wadji diambari serigne cheikh darou rakhmane ken dou yaw
@aissatousy187511 ай бұрын
Machala tu as bien parlé et wakh fji tegene na rafet ne te ande n ac yare machala nivau bi cawe na lolou tre bien comunike bien di Bon continuation day bakh t day gen bakh inechala ❤❤❤
@dofouAmabousamel-cl1sk11 ай бұрын
Kandji production référence leu bilay ❤
@Gayeserigne6611 ай бұрын
Mbokou talibé darou Rahmane
@mortallaseyedallou697611 ай бұрын
Ma chaallah wakh bi rafet na❤️❤️❤️❤️❤️
@bambagueye245411 ай бұрын
Machallah Kandji❤❤
@atoumaneniasse485411 ай бұрын
Kou doul Modou lo boye niang mon la geune staff machallah
@atoumaneniasse485411 ай бұрын
Machallah kou bakh nga té toujours lou bakh ngay déf lou bakh ngay wakh xawmala mais dama lay nianal boul ragal dara❤❤❤
@moussapayemane416711 ай бұрын
Tt mé respé le grand kandji,Boye Niang 2 dou sama mbeur mais yow kou diara respeter nga,sa wah rafetna trop machalah
@sukaiceesay828811 ай бұрын
Fadam doul rek laye deff 😅😅😂😂😂😂
@assanegueye2811 ай бұрын
Masala amena solo ❤❤
@aliouneelevage648211 ай бұрын
Kandji kandji toujour veridique et sportif
@abdoulayendoye54211 ай бұрын
Un gar très correct Macha alla
@ChekheNdongeu11 ай бұрын
Booy niang dafa bakh dafa yarou nionkoye nianale mou don roi des arene inchla Man la kheuss Bou Bathie Seras
@juniorjunior134511 ай бұрын
Vraiment il communique bien
@bayeratebayerate589311 ай бұрын
Amna solo de
@niassesouleymane716311 ай бұрын
Il a parfaitement raison dans la lutte ya que de la violence verbale autrement dit il faudrait revoir le langage qu'utilisent les acteurs de la lutte .....
@oumarkandji220311 ай бұрын
Macahalla domou bay wakh rafet na am na solo ferté kandji ❤
@cheikhngome145611 ай бұрын
non kandji yaw diambar nga yalla moula bakhal Mane cheikh caïman damala begue ndakh begue binga begue boy Niang thiapathioly dikou diapoule yalna yalla doli la Diame ❤❤❤
@cirely322011 ай бұрын
Machallah
@bakhyaye749911 ай бұрын
Kandji mi nit kou nité la macha allah yalna yalla deffal la diam
@TigerLionn11 ай бұрын
Boy Niang kasse❤❤
@cirely322011 ай бұрын
Nioune pikine lagnou deuk kandji yalla nala yalla faye ak sa famille du courage boy niang et ama ak eume sene ak sock nioune pikine rek lagnou topou
@mortallaseyedallou697611 ай бұрын
Ndanan nga❤️❤️❤️❤️❤️
@AladjiMbaye-s1c11 ай бұрын
Bilahi walahi bodone fayanto do khol sakh nitou lamb wayé nak koula yéne lou bone la yeureum barckép Serigne Touba
@ndeyegueye860111 ай бұрын
dieradiaff s Touba ❤
@serigneabdoulayembow361511 ай бұрын
Machallah kandji bon parleur
@cheikhomardrame583611 ай бұрын
Il communique bien
@dofouAmabousamel-cl1sk11 ай бұрын
Macllala❤❤❤❤
@SaraSara-rw1qf11 ай бұрын
Mancha Allah
@AluneDiop-c9r11 ай бұрын
Machalla nit nga de🎉❤❤❤
@marathiam156011 ай бұрын
Le seul dans le staff de boyniang qui accepte qu’il y a eu erreur dans la façon de lutter de boyniang Staff ni lay mel accepter erreur yi pour diang si euleuk Tout son staff en premier pere Mansour diop tapha kandji bassi pere degaulle gneuo dagni waxni boyniang defoul erreur si beurei la dano etc Ce OUI ON A FAIT ERREUR lolou la boyniang soxxla pour diang si euleukk
@AliouKama-zs9ye11 ай бұрын
En tout cas c'est un gar très social ❤❤❤
@Fallbayeridial11 ай бұрын
Verite absolut la waxx
@biranesdiop758811 ай бұрын
Merci kandji li gna wakh lep deugeula yalla nala yalla dolil diame bagna bakh te khamkham rek gna wakh merci
@dmxbig43211 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤k
@DiossiDiop11 ай бұрын
❤❤❤❤
@modoudiop784111 ай бұрын
MODOU 🎉🎉🎉🎉❤❤👍👍👑👑🤲🤲🤲👍👍
@aliounediaw648311 ай бұрын
il est fort en communication machalla vrai Gentalmen
@cheikhniang0211 ай бұрын
Père Degaul dh na poste courant bi key 😂😂😂
@assanegueye265211 ай бұрын
Wallahi le PDG sama kharitt bi ❤❤
@senegal211 ай бұрын
Kanji boulene degloukene yene dagenanite nite ni bougounouniar niou ande
Boy nia reug reug comba la Modou lo tapha tine comba la balla gaye 2 sita comba la
@mamegorseck616711 ай бұрын
Wakh mom dako man rk Modou mom bayabou wa pikin bayikofi 😂😂
@modoundiayesonko11 ай бұрын
Boy nia reug reug comba la
@modoudiop784111 ай бұрын
MODOU ❤❤❤🎉🎉🎉💟💟💟💟👑👑👑🤲🤲🤲👍👍👍👍👍👍👍👍❤❤❤❤❤
@bilalfall295311 ай бұрын
Délen tallal micro yi gni ko yélol
@ChekheNdongeu11 ай бұрын
Kandjie danga kham lamb moune wakh machala booy niang kasse la niouye topou Dafa yakametiwon mai limou def modou lo ken moussouko ko def booy niang rek mo dor modou lo ba mou kao
@modousiyndiaye947811 ай бұрын
Ndanane leu
@moussafall-y7v11 ай бұрын
kou la dieggge khamm ki nittt geunou la mon frerrr
@cheikhdiop993211 ай бұрын
Kandji daf ma nekh ndakh bati olof yii
@ahmedmb749111 ай бұрын
Deug Rek lafi dég Fadam 2 dafa nul Rek Mo takh mouy wakh affairou infiltré un champion comme Modou lo n’as pas besoin d’infiltrer
@mohamedgueye562411 ай бұрын
Vraiment ces les genres cont doit donner la parole il comique bien et les pékinois doit écouter sa
@ChekheNdongeu11 ай бұрын
Kandjie kou bakh la kou beug booy niang la beug wa pikin la motakh niounie kandjie rek la niouye topou
@ChekheNdongeu11 ай бұрын
Dafa wara ndinaga dore eperkile goche na geuneu diang di dorée eperkile