MODOU LO MOTAX GNOU KHAM PAPIS - SERIGNE NDIAYE HAUSSE LE TON - SITEU DAGNE KOY DOOR MOU KEPOU

  Рет қаралды 45,908

KEWEL INFO

KEWEL INFO

Күн бұрын

Пікірлер: 76
@Kli227-p5s
@Kli227-p5s 2 ай бұрын
Merci beaucoup Serigne Ndiaye wakh bi rèftè n'a ❤ Modou lo seul 👑👑👑
@mbayecisse611
@mbayecisse611 2 ай бұрын
Alhamdou lilahi kon papis magui fi rèk Yalla na Yalla May ndam modou lo
@modo6218
@modo6218 2 ай бұрын
Serign ndiaye bamouy ande ak modou lo bobou ay papis ay sa touba ken andou si ak modou lo Serign ndiaye ak modou lo danio yague depuis 2005 ay 2006 yague na
@moustahadrame6979
@moustahadrame6979 2 ай бұрын
Bilay wallae c vr
@damendiaye5741
@damendiaye5741 2 ай бұрын
Mod'lo yalla nala yalla soutoural may la ndam bou reuy inchallah❤
@modoukane5115
@modoukane5115 2 ай бұрын
Merci seurign ndiaye si papis moye modou lo
@SeexAhmadTiijaanJóob
@SeexAhmadTiijaanJóob 2 ай бұрын
Moodu Xarañ Lóo Yal na Yàlla may ko ndam lu seed guy ci kaw Sitë ci Barkeb Alxuraanul-Kariim !
@AlsaneBa-kd3ui
@AlsaneBa-kd3ui 2 ай бұрын
Amine
@SeynabouFaye-ei1gz
@SeynabouFaye-ei1gz 2 ай бұрын
Amine
@NiangseckBorsomarieme
@NiangseckBorsomarieme 2 ай бұрын
Amine ya raby barker seydina mouhamed psl ❤❤
@almaktoumdiop8749
@almaktoumdiop8749 2 ай бұрын
Mé papis modou lô mo takh nou kham ko papis sakh wakh nako ay yone yalla naa diam yaga
@elzoatti8951
@elzoatti8951 2 ай бұрын
Modou lo pour la victoire
@PapaBarry-cw1vz
@PapaBarry-cw1vz 2 ай бұрын
Yalla naniou yalla may ndam inchallah Serigne Ndiaye yay goor deugue 🙏
@DoudodiengDoudo
@DoudodiengDoudo 2 ай бұрын
MODOU XARAGNE LO🫧Le Super Roi 🤴 le GOAT🐐Le Meilleur Mashallah 🥰 Contane Naaaaagnou🥰
@AtoumaneNiasse
@AtoumaneNiasse 2 ай бұрын
Machallah serigen Ndiaye ❤❤❤
@DoudodiengDoudo
@DoudodiengDoudo 2 ай бұрын
Serigne Ndiaye Beug Nala😊❤
@awadiongue5434
@awadiongue5434 2 ай бұрын
Waw mais yéén lolén beugue papis ag modou nékou si rék gnién beugue séé déf rada aah maylén gnou diam waye
@DameNdiaye-b7v
@DameNdiaye-b7v 2 ай бұрын
Modou seul Moy mbér my ❤
@MamaNiane-x9h
@MamaNiane-x9h 2 ай бұрын
Machalla serigne Ndiaye ❤
@AssaneNdiaye-t6i
@AssaneNdiaye-t6i 2 ай бұрын
Modou lo défaite rk si katanou yalla inchallah 🎉🎉🎉❤
@KhalilDien-fe5uh
@KhalilDien-fe5uh 2 ай бұрын
Kharaaaaaaagn seul❤❤❤❤❤❤
@papengom259
@papengom259 2 ай бұрын
Siteu yalnako yalla may ndam amine
@MamorDiaw-fj7zm
@MamorDiaw-fj7zm 2 ай бұрын
Athieu serigne ndiaye le sorcier bou diexe rekk diexena
@ousmanendiaye1712
@ousmanendiaye1712 2 ай бұрын
Serigne Ndiaye Seul
@papezulefaye7263
@papezulefaye7263 2 ай бұрын
Serigne ndiaye bouléne setane ben seytané di dokh si diganté modou ak papis mane modou dou sama mbeur mais niom niarr sen ande dafa raféte
@daoudafall9949
@daoudafall9949 2 ай бұрын
Merci Serigne Ndiaye X lô kassei
@DjelyStar
@DjelyStar 2 ай бұрын
Wei Fama diopp bi migui nice
@ibrahimaniang1463
@ibrahimaniang1463 2 ай бұрын
Ki rék mo meuneu wakh si modou bilaye Serigne Ndiaye ak Modou thiouth ba sekhe
@OusseynouNdiaye-s5l
@OusseynouNdiaye-s5l 2 ай бұрын
Modou lôooooo ❤❤❤
@DjilyLeye-oz3qz
@DjilyLeye-oz3qz 2 ай бұрын
Modou lo ndame rk comme dinga gnouko tamma lé
@NgomDjiga-c6r
@NgomDjiga-c6r 2 ай бұрын
Fatma Dia demale dieul bou siteu dala meré😂
@rokhayathiam7913
@rokhayathiam7913 2 ай бұрын
❤️❤️❤️❤️👑
@diamilfaye7253
@diamilfaye7253 2 ай бұрын
Lerna❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@cheikhbasskeurmassar9548
@cheikhbasskeurmassar9548 2 ай бұрын
Lolou papis wakh nako sakh
@abdoulayeNdiaye-p7b
@abdoulayeNdiaye-p7b 2 ай бұрын
Papis day wor
@modoundiaye1941
@modoundiaye1941 2 ай бұрын
❤❤❤❤ 🤲🤲🤲🤲
@KhadimSene-c5u
@KhadimSene-c5u 2 ай бұрын
❤❤❤❤🎉🎉
@FallWaly-c6g
@FallWaly-c6g 2 ай бұрын
Walay siteu xamul likoy xar
@alhamdoulilah9154
@alhamdoulilah9154 2 ай бұрын
Papiss premier combat modou lo eumeu séné la commencé and ak Modou lo mais papiss pour moum moutakh modou lo nekk champion 😂😂 papiss danga nieuw fekk modou lo am limiy am ba pret boula nekhé boul niawati
@ibrahimambaye277
@ibrahimambaye277 2 ай бұрын
Golo kham na , keur gou bari khath ... balla. Ah youuu😂😂😂
@bilalkhalyfall9938
@bilalkhalyfall9938 2 ай бұрын
Yèn xana modou rk moy mbeur gnak nguén class nk
@rouguikebe9984
@rouguikebe9984 2 ай бұрын
​@@bilalkhalyfall9938niom kay top modou rék😂
@moussapayemane4167
@moussapayemane4167 2 ай бұрын
Modou Lo am na nane katou sangara,am na toukh katou yamba
@modo6218
@modo6218 2 ай бұрын
Boy yaroul daniou niaf sa ndey dé domeram
@moussapayemane4167
@moussapayemane4167 2 ай бұрын
@@modo6218 sa data yaye,hana sa baye nane katou sangara là
@layekharagne2224
@layekharagne2224 2 ай бұрын
@@modo6218caddou yi rafetena
@KhadimSene-c5u
@KhadimSene-c5u 2 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉❤❤❤❤❤🎉🎉❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉❤❤
@cheikhbasskeurmassar9548
@cheikhbasskeurmassar9548 2 ай бұрын
Siteu mo meune Modou serigne bi
@moustahadrame6979
@moustahadrame6979 2 ай бұрын
😂😂😂
@rouguikebe9984
@rouguikebe9984 2 ай бұрын
Rêve😂
@CheikhouSenghor
@CheikhouSenghor 2 ай бұрын
Yakowakhonne contre ama balde loguissonne modou lo dou sene morome
@djibingom5668
@djibingom5668 2 ай бұрын
Modou papis moko gueuneul rakam papis tmt nonou naniou lène bayi niou nk sène diam ta nioune gniye wah dara lèrou niou thi
@marcusmouhamed
@marcusmouhamed 2 ай бұрын
Siteu dh bouko modou mayé tank sah duko dann vraiment amul xam xam bou dann modou
@Bassirou-f8c
@Bassirou-f8c 2 ай бұрын
Yangui nakh sa bopou d
@marcusmouhamed
@marcusmouhamed 2 ай бұрын
@@Bassirou-f8c ah saway ki dh modou dekoy duma rek kom nimou def gnom Ama sen wadji beurem da dess trop
@mussafaal1321
@mussafaal1321 2 ай бұрын
Vraiment ta raisons
@volfroitfall8785
@volfroitfall8785 2 ай бұрын
Mane dall ragallnaa modou daanou
@marcusmouhamed
@marcusmouhamed 2 ай бұрын
@@mussafaal1321 demay lathie essk sénégalais yi hamnagn modou wadji mo nakare beurel dey songue di door di teud di door boy niang mo meun 10 siteu te yeungaloul wadji nn modou man defma yem
@fallouniang399
@fallouniang399 2 ай бұрын
Yaw mom waxo fi dara
@malangkujabi5108
@malangkujabi5108 2 ай бұрын
Ragal ngen rek balla moye sen baye
@volfroitfall8785
@volfroitfall8785 2 ай бұрын
Eumeu boye niang ak bomb nak
@PendaTalla-c5z
@PendaTalla-c5z 2 ай бұрын
Yéne dé séni bay nieup kham naniou niane la nanal glace Modou Lô seul
@habibsylla7838
@habibsylla7838 2 ай бұрын
Téte de con on parle de modou lo vs siteu
@ElhadjiMoussaDIALLO
@ElhadjiMoussaDIALLO 2 ай бұрын
Yene kouy sene bay
@cheikhoudamba
@cheikhoudamba 2 ай бұрын
Yéne niata bay nguene beurineu deh 😂
@goudamamadoudanfakha1464
@goudamamadoudanfakha1464 2 ай бұрын
Modou lo waro bayi doff yi toukh Kate yi di book sa entourage.kholatal sa wakhine mo gueun diay prekk gui gua nè wessou nagne loulou
@DiaAmadou-jh9wo
@DiaAmadou-jh9wo 2 ай бұрын
Copain ki mo Serigne Ndiaye boumouy andak Modou môme ak sa Touba kéne khamahoul Modou on habite ensemble Lou léér lalay wah papiss da geuna feuss rk
@modo6218
@modo6218 2 ай бұрын
Say Serign ndiaye mi ak nicola legui mongui France baniou ande ak modou lo ay papis mi ay sa touba niom ken andou si modou lo depuis mbapat 2005 2006 lolou yague na
@dramealiou7869
@dramealiou7869 2 ай бұрын
Merci serigne ndiay c am kana
@DiaAmadou-jh9wo
@DiaAmadou-jh9wo 2 ай бұрын
@@modo6218 walahi Nikola borom Sephora yi
VIP ACCESS
00:47
Natan por Aí
Рет қаралды 24 МЛН
黑天使被操控了#short #angel #clown
00:40
Super Beauty team
Рет қаралды 57 МЛН
小丑教训坏蛋 #小丑 #天使 #shorts
00:49
好人小丑
Рет қаралды 37 МЛН
LAST FACE 2 FACE ENTRE: MOD LÔ ET SITEU 👑🔥
19:50
MAP_AU_CAMPUS
Рет қаралды 5 М.
Regardez Dame Mbodj humilie Barthélemy Diaz en direct 😭
23:27
Diégo l’Espoir
Рет қаралды 5 М.
Match : Equipe Modou Lo Vs Equipe Papa Sow Au Parcelle assainies
10:33
VIP ACCESS
00:47
Natan por Aí
Рет қаралды 24 МЛН