Je suis un fans de Balla gaye 2 , mais modou lo m'a convaincu que il faut aimer ce que tu fais pour espérer le sommet. Merci Modou lo que le seigneur te protège et bonne continuation 🎉❤
@kineseck878611 ай бұрын
Aminnn yaaw kou baakh ngaa ❤
@jomojoe641411 ай бұрын
DIADIEUF. YOW BOKO AK SISSOU MANE YI 😂
@BabacarCisse-y1l11 ай бұрын
Doul yaw bariga wakh
@jomojoe641411 ай бұрын
@@BabacarCisse-y1l BAYIL SISSOU BI
@jomojoe641411 ай бұрын
@@BabacarCisse-y1l SISSOU MANE GUEU
@OureyeSeck11 ай бұрын
Le lutteur du peuple et le chanteur du peuple❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@abdourahmanfall190811 ай бұрын
Et le rappeur du peuple Dip ❤❤❤❤❤
@cheikh2411 ай бұрын
@@abdourahmanfall1908 je supporte Eumeu mais Modou Lô je l'aime par Allah parce que je me vois en lui ( esprit gagneur ) longue vie à toi mon Youssou Ndour de la part de ton neveu Cheikhouba.
@rouguikebe998411 ай бұрын
Li déss sa carrière yalla bo amati défaite ❤fêtél sa victoire bou bakh tega nopalou😊❤❤❤🎉🎉
@moustaphadia877711 ай бұрын
Allahouma amine ❤
@pumasarr578211 ай бұрын
Amine ya rabi ❤❤❤
@diawalysonkoalassa178611 ай бұрын
Non. Dakoy ame. Roi des arènes bi yakouna bientôt. Waroul woone bayi You wayko 😢😢😢. Koumou way dagay fay, wolla diaar fa faatou. Voici plusieurs exemples : - Tyson moom amoul morom, koumouci dadièl dalay daane : fala diaar daanou faw 😂 ; - Ndeye Astou Adj, borom salon coiffures ya : fala diaar fay 😂 ; - Coupe du Monde 2002, Fimou né boufi yamoon sakh mou nèkh : fala gaïndé yi diaar daanou 😂 ; - Yahya Diop Yékini, yèg scène You en tant que Roi, fala diaar daanou faw 😂 ; - Balla Gaye 2, bimou yèguè scène Youssou, la tékalikook Roi bi 😂 ; - Birima, ki nekk ci clip bi fala diaar faatou 😢 ; - Abou Thioubalo, bimou wayè You ba lègui teuuna takhawal carrière bi 😂 ; - Golbère Diagne, biko Youssou wayè fala diaar fay 😂 ; - Ndongo Lô, bimou wayè ak You, fala diaar fèbar ba diaarfa faatou 😢 ; - Mbaye Dièye Faye meussneuko wakh You, je veux vivre, rester libre, Boobou ancien la 😂 ; - Bimou inviter Papa Thione yarhamou, souniou Papa dji dako ndieuk wakh You, échange micros, mou tarbiyouko alkouraan ba morceau bi dièkh 😢😢😢 ; - Depuis très longtemps il veut chanter père Elhadj Mansour Mbaye. Kookou nikko You, sama doome ga, sama lèpp ga. Wanté damlaa niaane rek. Boulma way 😂😂😂 ; Action bou yèmé la. Niou kham deugue khamnanou Bamako leuko dieulé. Fala wayé "Tia gaal gui laako fèkk, mingui sango seur. Douma fatté Bamako". --- Donc Modou, carrière de Roi est en déclin. Retiens ceci cher peuple. L'histoire retiendra 😊😊😊.
@penda15411 ай бұрын
Fen kateu
@malickndiaye789911 ай бұрын
Amine yarabi ❤
@ousmanesy672711 ай бұрын
Modou Lo nous apprend à travers la lutte qu'il faut travailler dur , croire en soi et faire du bien pour réussir dans la vie.
@mbenefall-vm9ec11 ай бұрын
👑📿👊🤛👍🙏🙏👌💪💪💪🤳☝️😂❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@danielmendy277111 ай бұрын
Il est juste phénoménal 😊 Modou Lô je t'aime de tout mon cœur ❤ Le Roi 💫💫💫👑👑👑incontesté ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@PiscoQlf11 ай бұрын
Après bcp de travail modou est devenu le Goat dont tout le monde rêve de battre vrm c’est le Goat ❤
@Diamola8011 ай бұрын
Grand dé youssou ndour la classe rék ❤❤❤😂 le roi de la musique 🎧 africaine et le roi 👑 des arènes modou Lo❤❤❤❤😂
@miittaDoundouGuiss11 ай бұрын
Et le roi du hip hop Doundou guiss ❤😂
@mouhamedlo582811 ай бұрын
Lou lér ga wax 😂😂😂😂😂😂❤❤❤@@miittaDoundouGuiss
@sekoubanore432111 ай бұрын
modou vraiment vraiment tu est un bon lutteur kepou kousi anda ak modou do mousséu ruse
@layekharagne222411 ай бұрын
Le meilleur lutteur de l’histoire de la lutte sénégalaise ❤️👑🐐
@cecilediouf850011 ай бұрын
Hoooo mon ❤ explose de joie.🤩🤩🤩Tapis rouge .Pour toi.Yal nalla YALLA same léne ak sama taw bi PAPIS DIEGANE.🥰🥰🥰🙏🙏
@m.b.o.u.p11 ай бұрын
dadié wate nagne😂
@layekharagne222411 ай бұрын
@@m.b.o.u.p guiss gua dh 😂yama makk wala mala makk 😂
@m.b.o.u.p11 ай бұрын
@@layekharagne2224 😅yama mak dh 18ans
@layekharagne222411 ай бұрын
@@m.b.o.u.p donc sa grand frere la 😂
@Mahibdione11 ай бұрын
Le meilleur lutteur de la lutte sénégalaise. Budé image dafa tuti mais budé état d'esprit dafa ponkal😂😂😂😂
@jomojoe641411 ай бұрын
WAWAW. MODOU LO EST LE MEILLEUR LUTTEUR DE SA GENERATION
@zalely141211 ай бұрын
Je l'aime billay Modou Lo yalnala yalla dèfal diam❤❤❤
@Aminata46811 ай бұрын
La confiance en soi et l’estime de soi n’ont pas de prix et Modou possède ces choses MashaAllah à lui❤
@serignesinythiam11 ай бұрын
Je suis très content de mon frère Modou Lo seul le travail paye walahi de la part de ton grand frère serigne thiam bierhoff ❤❤❤
@mouhamadoulaminegning541811 ай бұрын
N'Oublier pas Mbaye D F. Il a un talent immense lui aussi. Youssou est un génie tout comme le Roi kharagne.😂
@malily670511 ай бұрын
Massallah il aime trop yéré wolof 😍
@Fatoumatawele-wb1gn11 ай бұрын
Waw lolou moy solou kilifeu
@malily670511 ай бұрын
@@Fatoumatawele-wb1gn 🙏
@khadydiouf402811 ай бұрын
Kelifa la nak Masha Allah
@diarra__diouf77711 ай бұрын
Modou yalna la yalla same teh mouseul la thi thiatt ak lamigne Machallah notre roi des années xaragne national yakofa amm🤟🏽❤️
@serignendiayebeuguefallou708811 ай бұрын
Ohh vraiment Youssou Ndour est toujours le meilleur de tous les temps avec son public de classe 👍❤❤❤
@darougueye-h5h11 ай бұрын
Les deux roi nous sommes fierre d’être Sénégal ´Modou lo tié mon lutteurs toi seul
@ladyj706111 ай бұрын
Le Empereur de musique et le Empereur de lutteur fofou tothie ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@ndeyembaye890811 ай бұрын
Les meilleurs maachaalaa
@kineseck878611 ай бұрын
Bilahi walahi ndeyssane deugue laa
@boubafall101411 ай бұрын
Mon cœur ♥️ bat 💓 Modou Lo à tout les mérites champion incontesté ❤
@fansfcbarcelone139911 ай бұрын
Mane Modou LÔ nimou tollou di Dane mbeur yi diakhale nama 😂😭❤️👑✅
@MrFayemanou11 ай бұрын
Lolou rek mo takh ma beug koo😊
@malickhanne574011 ай бұрын
C'est ça qu'on dit FOULA DIOM AK FAYDA 🎉
@aissatousow34011 ай бұрын
😂😂😂😂 mann mi diaxal nama
@papamakhtarniang11 ай бұрын
Yalla moy wané bopeum si nitgni rék hana. Moy fékeu kou gnépeu wara eupeu dolé mou boléko sisén biir mou gnousslén gnom gnép😂😂😂 yalla la👆👆👆 dou lénén👆
@danielmendy277111 ай бұрын
😅😅😅walay ndeyssan
@souleymanelaye763711 ай бұрын
Le roi des arènes avec le roi du mbalax❤
@cheikhdaroundiaye942911 ай бұрын
Les trois personnes qui sont plus fort au Sénégal Youssou Ndour.dip doundou guiss.modou lô❤🎉
@layeseck149511 ай бұрын
+Sadio mané
@VerseVibesHub-nh7vr11 ай бұрын
+ Sonko
@warriorkemiseba918411 ай бұрын
C'était BG2 et aujourd'hui c'est M'LÔ, adouna nonoula amonnafi.
@MamadouBa-k4q11 ай бұрын
Il a fait une histoire inoubliable Modou kharagne Lo ⚡️🙏👌le roi 🤴 des arènes
@senegalrek257911 ай бұрын
Tu sens que youssou ndour Dafa respect Modou champion day beug moromam ❤🎉❤🎉
@CASI779711 ай бұрын
Ame kou wakh ci souff ki comme dou mbeurrr, c'est l'impression que j'ai eu quand je l'ai vu en face. Je me demandais comment il fait pour battre les lutteurs. Respect Modou Lo
@bayefall230811 ай бұрын
Kéne Dou youssou koula bagne dina sone wayé Modou lo yala Sam la ❤❤
@bintouba911811 ай бұрын
Il a toujours respecté ses adversaires ❤❤❤❤❤❤. Modou lo da yarou ❤❤❤❤❤❤❤
@aissatougueye910711 ай бұрын
Linganiou bégueul yeup nioun wa parcelle yalla nalako fay❤
@ndeyeastoundiaye37811 ай бұрын
Amine way ❤❤
@sodagueye376911 ай бұрын
Dama khôl mo ngui nekh❤You wakhna Lou âme solo liguey mo worrr
@coumbatoure808711 ай бұрын
Li nekhna wayy j'aime beaucoup modou❤❤❤
@MamadouLamineBADJI-p8f11 ай бұрын
Père Mbaye Gueye tu es fort honnêtement tu es le meilleurs de ta génération
@KhadiFall-bj7bi11 ай бұрын
Oh Modou lo est un grand ambianceur 😂😂😂❤❤❤❤❤
@CombayeDieye11 ай бұрын
Machalla ❤sa ma khol séd na Modou lo rk lay topou ki dama ko beugue ❤❤❤❤❤
@abdoulayesall43311 ай бұрын
Les deux rois ❤ken dou Kharagnnn Lo Kharagnnn feppeuh❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@kingby679511 ай бұрын
machallah ❤️ j'aime beaucoup ton sénégalais rek mo wor 🇸🇳🔥❤️🔐🎉🎉🎉
@bajeboulenger253811 ай бұрын
Salam Youssou ngui Yallah boul yobou baïré Modou Lo bi ko meusseu way faillite na ba mou fay… alahou m’a sali allah Mouhamed 🤲🏾
@kalymbaye657811 ай бұрын
Vraiment modou tu es spéciale yoh❤❤
@morgaye958211 ай бұрын
Un vrai roi Modou kharagne lo 👑
@yannly53111 ай бұрын
Il est phénoménal MODOU LO❤
@MilkMilo-qr5uc11 ай бұрын
Son excellence XLo🥇👑🐐
@MilkMilo-qr5uc11 ай бұрын
@@matarmbuegu2855 mon frère ziar nala nom victoire bi mom kérok contane rk chamipion bi déssé lougnou dara liga wakh mane mi mome rk lay xalate franc dama ko geume mais dégue na mogui ak avance makane mais yow koko gissal mou beurél bou doul gnisi kaw kokoy diokh?
🥺khôl Sèd n'a ak ababacar mbaye Modou kharagne lô rék lani topou on t'aime beaucoup ❤️
@kharagnembaye595811 ай бұрын
Amna guél Bouy wakh Modou Come dou mbeur 😂😂😂
@papamakhtarniang11 ай бұрын
2:10 femme bi néneu ki comme dou mbeur😂 nonou lako mbeur yi di guissé hépko mou eliminer lén gnom gnép😂 one by one😂
@SophiiaKa11 ай бұрын
Kone dou mane dongue mako deg😂
@danielmendy277111 ай бұрын
😅😅😅mom.lay réeee niii
@nafisene533511 ай бұрын
😂😂😂😂nena dafa sett torop. Kharagne rek machallah laf Thiate ci mome
@diarra__diouf77711 ай бұрын
Ah dfa civilisé si mbeur Katt mo yey😂 nn modou dou nitt
@MoustaphaNdaw-cm7qb9 ай бұрын
Mame sama yaye da avc mé mé bou guissé modou lo daye tané jauré bien k mou guissko bala daradikhéw dp8 thiaroye svp répon moi c urcent
@mouhamadousanoussybadji448011 ай бұрын
Très beau Modou
@momo2320sn11 ай бұрын
Cey papis mo diara andal dé 😂day lamb rèk mom ci ganaw modou rèk
@lbyoungtv222311 ай бұрын
Wolou yalla mankei ssi rewmi dh😂😂 you koum way gua danou rk laffi guiss 😂😂 Xana yegoulenn bi dou premier fois modou yeg si scène youssou tei térei woul mou donn l empereur des Arènes 😅❤❤❤
@nafisene533511 ай бұрын
Lolou dé la wakh tout à l’heure. Wakh bobou dafa niaw sakh Bilahi. Ani Yalla?
@salioukane876411 ай бұрын
ki nimako baneui won ms ligui mom rk lay toupo barck borom touba ❤❤❤
@oumardieng599611 ай бұрын
Machallah Machallah youssou ndour
@MaguetteDioneKa-ln1hq11 ай бұрын
Ndeyssane contane na trop Dieureudeufeti Modou lo Dieureudeufeti papa Youssou Ndour Youssou kham ngua loutakh ma beugue la Danngua bakh té niak Kiniane té gueume ligueye
@shnset_11 ай бұрын
MachaAllah sama Oustaz Modou lo que Allah te protège
@usgalsen11 ай бұрын
2:09 Soxna si nee na "ki kom du mbër"😂Aka rëy laammiñ!
@Footballfoot3311 ай бұрын
Kone dégeu guako
@bocarba83882 ай бұрын
Mane keiy wakh na nane laye dané mbeur yi defa diy war ak touti way am
@DembaKa-vm6bs11 ай бұрын
Simplicité, politesse, mentale de gagnent=Modou lo
@MameSow-vp7rj11 ай бұрын
Modou kharagne lô le messi de l'aréne ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@FatouFall-l7i11 ай бұрын
Machalla mon champion Modou lo yalla nala yalla are samla 🤲🤲
@faye671811 ай бұрын
Niari ndanane niari champions ❤❤❤
@gorfall11 ай бұрын
TIEY ADUNA!TIEY ADUNAAA!ADUNAA WAAW!UNE CHANSON DU GRAND YOUSSOU NDOUR..JE CROIS..!
@TallaSeck-d8w11 ай бұрын
Li dafa nekh yalla na niou yallay bal amine lim am dako mérite billahi ❤❤❤
@ThiateFaye-r6e11 ай бұрын
Kii damako beugue ba soumayko hole diii pleurer bilay ❤❤❤❤
@alicealicia68711 ай бұрын
2:10 nenako kiii comme dou mbeur😂😂😂wallahi sett na, civilisé na
@birahimdiallo189511 ай бұрын
Les rois sénégalais 😂🎉
@ngoneseck517411 ай бұрын
Vive le roi contanagnou lollllll y'all Nala ndam li djik manchalla
@mamendiemethiam754011 ай бұрын
Machalla modou kharagne lo samalaye khole sakh damaye ré yal na nék sa djike ya khéw dé té yalla bo khéwi
@p._-11 ай бұрын
C'est Modou lo notre roi des arénes ❤❤❤❤😊😊
@MCdiakite-c2q11 ай бұрын
L homme humble modou kharagne lo avec toute sa célébrité
@Thiam-babél-c2i11 ай бұрын
Kou beugue Modou maye ko j'aime bok ❤
@CASI779711 ай бұрын
Ohhh yaramm dawnaaa. Merci You merci Kharagne
@lhommedelarivegauchedufleu310111 ай бұрын
Machallah Modou Xaragne Lô sama mbeur mi
@MamadoulahiNdoye11 ай бұрын
Modou lô yalla nako yalla mayue diam si barké seydina mouhamed ❤❤❤
@pointdevue130411 ай бұрын
LE ROI DES ARENES ❤❤MODOU LO
@ndeyembow669511 ай бұрын
Machalla ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ l'AF thiat amine ya raby sama doome la Mala beugue pire
@KhalilDien-fe5uh11 ай бұрын
Le Roi❤❤❤❤
@FallouLoume-nh5yj11 ай бұрын
Balla rek lay topou mais dara mom kham na ko lamb mom dotula fátté le roi des arènes ❤
@KhardiataMbengue-d5m11 ай бұрын
Sama champion bi❤❤❤❤❤❤❤
@amadoubeye134511 ай бұрын
Le roi du Mbalakh AK le roi des arènes
@dienagueye935311 ай бұрын
Wah le public de You on en parles weuleu ??? Quelle classe xallé yi 😍
@SophiaSamb-s4v11 ай бұрын
Modou lo notre roi ❤❤❤❤❤Machalah
@ousseynoukane698011 ай бұрын
You le meilleur de tous les temps ,notre Lionel Messi
@AdamaMballo-t9s11 ай бұрын
Macha allah excellent modou lo le nouveau maire de pikine édition 2024
@sokhnadiallo901311 ай бұрын
Modou Lo machalla ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳
@mamadouba691511 ай бұрын
Modou lô sedall nga sama kholl bi ❤❤bi nga dane ama balde❤nga watiok man❤ kharane forcé 💪💪💪💪💪💪💪
@davidsat29711 ай бұрын
Bobou la wathie ak fan’s yeupe 😮😮😮😮Thieuye kharagne Yalna la sounou borome yokk
@sambandeyendour143011 ай бұрын
Le chanteur du peuple
@medounediopgueye65211 ай бұрын
YEUREUM NA KOU YOUSSOU NDOUR WAYEU 😢😢😢😢
@diamsambadiallo879211 ай бұрын
Le meilleur de tous les temps.
@OusseynouSambou-bf8sb11 ай бұрын
Lii nice naa trop bay ❤❤❤
@AmadouabouDiallo-l1v11 ай бұрын
Modou modèle d'inspiration pr tt les jeunes sa métier daga Koy beug te fonkouko
@dieynabasamb660211 ай бұрын
Contane bilahi ❤Modou Yalla nasa diam Yague🫶🏻❤️❤️❤️❤️❤️