🛑modou lo vs bala gaye ficelé bour guewel sermone les baol baol et defend aziz ndiaye les 2 couronne

  Рет қаралды 34,072

Bprod media TV

Bprod media TV

Күн бұрын

Пікірлер: 195
@MoustaphaFadiga-jy3dr
@MoustaphaFadiga-jy3dr 4 ай бұрын
Modou lo bilahi walahi talahi meune na dane balla gaye ba rayko mes nioune nio beuré woul dagni beuré ak boyi inchalla bayi ak courrone bi inchalla
@malicksine3831
@malicksine3831 4 ай бұрын
Wakhgue deugue Bour bravo 👏👏👏👏❤
@yayademba1040
@yayademba1040 4 ай бұрын
Thanks brother i love you, you always speak truth from Gambia
@yayakonte6292
@yayakonte6292 4 ай бұрын
Mashalla b.❤❤❤
@DjibrilBa-xp7te
@DjibrilBa-xp7te 4 ай бұрын
Bilahi walahi watalahi modou dou meussa mbeur ak balla Gueye sili déc carrière ram geum léne yalla té nopalou Modou kharagne lô bourou lamb dji seul 🎉❤❤❤
@modoubayefallsikroulla1423
@modoubayefallsikroulla1423 4 ай бұрын
Balla sokh woula beurék mome l'empereur moy bourou bouryi
@Moussagema
@Moussagema 4 ай бұрын
Modou bou dielaté Balla di niak couronne bi
@SerignembayeGueye-j8u
@SerignembayeGueye-j8u 4 ай бұрын
Yangui dioum dh boul watt
@Lesoleil-deminuit
@Lesoleil-deminuit 4 ай бұрын
Watt dinala lakk ak lingay doff yeup di watt si mbirou lamb
@linkstardidingkeba2922
@linkstardidingkeba2922 4 ай бұрын
Boy watt waatal lo kham Mod lo amoul bèn compte boum lay rendre
@dofouAmabousamel-cl1sk
@dofouAmabousamel-cl1sk 4 ай бұрын
Gnoune baol lagn deuk amdi Moustapha tine lagn beugu ❣️
@tigrenoir5147
@tigrenoir5147 4 ай бұрын
Büur bilahi Modou khalatoul beuré ak Balla gaye 2
@falloudiop8211
@falloudiop8211 4 ай бұрын
Bilahi dagama nékh lool Sakh mais tay d'accorouma dh Aziz bakhoul yawou nk dama la beugue lool Sakh
@SmilingColourfulShirt-wq9ez
@SmilingColourfulShirt-wq9ez 4 ай бұрын
merci bour ❤❤❤❤
@ModousambModousamb-mm2wk
@ModousambModousamb-mm2wk 4 ай бұрын
Merci Bour guéweul la preuve Aziz deux fois yi bombardier dan Balla Gaye yeup mo teuguon combat bi Kon xana dafa saraxé won Balla gaye vraiment gni danio wara nék nit té bayi sén dof dof lou bi😂😂😂😂😂
@yesyes7713
@yesyes7713 4 ай бұрын
Balla gaye 2 est le meilleur lutteur de l'histoire du Sénégal 🇸🇳👑
@kharagnembaye5958
@kharagnembaye5958 4 ай бұрын
Légui gniko dane deux fois ay lane lagne 😂😂
@mamepathengom9398
@mamepathengom9398 4 ай бұрын
Thieye lobie bi ci lamb ✍️ aye domou Azize ak Bécaye Mbaye ✍️ dépense lagnouye dawe dé😂 respecte léne Modou lô ✍️ yalla moko déf limou doone ✍️ Balla gaye na dieul Fran mou dane ko ci 1 minutes ✍️Bour eupouléne xél sénègalaiyi 😂😂😂😂 lamb yakouna ndakh wakh Kat yi gno tardél lamb ✍️
@Victoireman
@Victoireman 4 ай бұрын
Modou avant Mouy beuré couronne 👑 wahona biss bouko dieulé xaaleyi rek laaye maay chance teu il a raison mogui ci fin carrière Lolou la wara deefe c pas parce que balla a essayé ci rakam échoué legui beug beuré waate AK Modou gris ect.. Lolou doyna balla n'a maay chance xaleyi Modou balla khewina tout chose a u fin...
@dofouAmabousamel-cl1sk
@dofouAmabousamel-cl1sk 4 ай бұрын
Bour gueweul ndongo Aziz nga
@IiiiloooHoko
@IiiiloooHoko 4 ай бұрын
meci bour ❤❤❤❤
@biranecamara6796
@biranecamara6796 4 ай бұрын
Soumay deglou bour plaisir lay am ❤
@sidibarhamatraore293
@sidibarhamatraore293 4 ай бұрын
Ak mane mi diambar. Il est très posé buurr.
@CASI7797
@CASI7797 4 ай бұрын
Tapha Tine bane titre leu amone beu Balla daneko djeul Empereur la khamoul😂😂😂
@seck-z7h
@seck-z7h 4 ай бұрын
très bon question ❤😂
@DjibrilBa-xp7te
@DjibrilBa-xp7te 4 ай бұрын
L'empereur geudiawaye la yém 😂😂😂😂😂
@cheikhdiop9932
@cheikhdiop9932 4 ай бұрын
Eumeu nena begeu nako niam lempeure day fay
@CASI7797
@CASI7797 4 ай бұрын
Walahi pask dou titre des autres promoteurs, exclusivement créé par Aziz Ndiaye pask beineine promoteur bou teug Balla dou teikk empereur bi ni avantage yi..donc c'est un titre insensé
@boubacardiallo5647
@boubacardiallo5647 4 ай бұрын
Buur t’as parfaitement raison Famille Tapha Tine Séne sorties bi gniou deif c’est un échec Baniouy daan mouy nékh keine dégouléne gni Guemou niou Yalla 🙏 blh
@CASI7797
@CASI7797 4 ай бұрын
Modou Lo mo beureiwoul pour Aziz Ndiaye pour mou clair.
@taladioum6815
@taladioum6815 4 ай бұрын
Aziz moko yonni guys😂😂😂. Empereur guediawaye leu yéme
@ndiayennbi7557
@ndiayennbi7557 4 ай бұрын
Pourquoi aller retour youdoul diekh Nann maye chance khaleyi
@CASI7797
@CASI7797 4 ай бұрын
Ce que tu oublies c'est que couronne empereur bi mo amoul beine valeur😂😂😂
@DjilyDiop-rv6jc
@DjilyDiop-rv6jc 4 ай бұрын
Balla sou amon yeurmandé bouko doré khamné manoul fayou douko gagne
@Inspecteursock
@Inspecteursock 4 ай бұрын
Damay yakamti wakhtanou Bour tellement il est très pertinent
@Babacar-mu2gr
@Babacar-mu2gr 4 ай бұрын
Bour l'expert de la lutte sénégalaise avec frappe
@adamslo7971
@adamslo7971 4 ай бұрын
Ay kanara aziz guéne Yoe akh Fdm doull
@babacarwathie
@babacarwathie 4 ай бұрын
Bour y’a mena doul deug 😂😂😂
@zakaryagangue3543
@zakaryagangue3543 4 ай бұрын
Bour boul watt Dara woroula ci ligay wakh Watt dafa fort té dou yéfou thiakhane
@madembatoure7005
@madembatoure7005 4 ай бұрын
Vraiment
@dienefaye7323
@dienefaye7323 4 ай бұрын
Balla na beuré ak franc grand contre petit modou lo balla gaye 2 eumeu séne gris dafa doye
@younoussdolle6844
@younoussdolle6844 4 ай бұрын
Mane ndeysane lima metti si senegal moy dagay bagn nite pour bagn ko rek Aziz ndiaye ak baye allé Andi nagn balla boy niang diap ko dane ken waxoul Balla dem entraîné Andi entraînement dane Tapha niouné mystique
@MamadouDiallo-yu1jo
@MamadouDiallo-yu1jo 4 ай бұрын
Modou lo bouy dieul balla di gnakk couronne bi 😂
@honorebabacarSy
@honorebabacarSy 4 ай бұрын
Legui ioe lo si wakh au moment ou que gua nekeu fi di wakh di watte ni buur amoul sansse
@niomrelo1959
@niomrelo1959 4 ай бұрын
bour bayil fénn li aziz di déf doulako wakh ngay watt nii
@ElhadjiFall-nw2he
@ElhadjiFall-nw2he 4 ай бұрын
Yaw Yalla rek mo xam nite ay soukh nguene bayil yok yi😮 bayilen di watal ay nite lambj
@ElhadjiFall-nw2he
@ElhadjiFall-nw2he 4 ай бұрын
Seye tane ngua guene lene seen khel si courone bi de mal si eume Mes Lou tax Kiko sane 2 fois soul mere nako fathe si (((tay schingua))))
@papagorakebe7594
@papagorakebe7594 4 ай бұрын
Danio beugone tapha door balla bamou teude yalla dogalouko mougn léne
@safietousalomon1795
@safietousalomon1795 4 ай бұрын
Daguene ragal fawzeyny ni rek Modou dofoul sah beuy dieule balla 😂😂
@ndiagaseye5304
@ndiagaseye5304 4 ай бұрын
Lolou dafa safatoul balla na dieul si boy yi mom ak eumeu yéup ak Grise mais lolou moy takh lamb dji oubé ko
@Victoireman
@Victoireman 4 ай бұрын
Yéne dé depuis votre echec si boy niang dagéne Ragale dougatt ci boyii 😭😂🤣 teu doumeuu léne meuus degg ngeen laatch eumeu 😅😅 walla boy niang 😅😅
@yaramfall6996
@yaramfall6996 4 ай бұрын
Wakhou doff yi nak yaw wathial dieul si boy yi Modou référence la wane nalén yone wi
@moustaphadieng2880
@moustaphadieng2880 4 ай бұрын
No tapha yaxe na dèrou baol baol yèpou ross na 😭
@KhadimDiaw-vh7uj
@KhadimDiaw-vh7uj 4 ай бұрын
Mais balla boudanoul émue sene nak loutakh wakho si lolou kom ningay wakhe si modou balla
@DjibrilBa-xp7te
@DjibrilBa-xp7te 4 ай бұрын
Mbeur mo oubi khôlam❤ roi mosay nék
@DiakhatePapasada-pf3is
@DiakhatePapasada-pf3is 4 ай бұрын
Bamou dess ama dia mbeur😂😂
@TheirnoNiang-c9x
@TheirnoNiang-c9x 4 ай бұрын
@@DiakhatePapasada-pf3is😂😂😂
@YoussouSall-d8y
@YoussouSall-d8y 4 ай бұрын
Modou. Lo. Seul xlo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤. Bourguéle. Moi je suis pas. D'accord avec toi. Baye diaye. Et. Aziz diaye. Se. Sont des. Crompe
@Sallmyname
@Sallmyname 4 ай бұрын
Bour kéneu wakhoula Modou lo mounoule dane Balla Gaye 2…modou bii bou dieulé balla Dakoy dane nioun supporters yi on en doute pas, mais Modou a clairement dit que que dotoul beuré revanche un point un trait…en plus qu'est-ce que ça changerait si modou le bat ça sera toujours 2-1 pour Balla
@Victoireman
@Victoireman 4 ай бұрын
👍👍👍 yéne comprendre woléne insbi monde lamb nieupa beugg modou danou, comme k balla ak bombardier rek nioko daaneu motakh nioouy forcé...teu modou kokou borom téte ka mogui ci fin de carrière rakam laay maay chance apres déme...
@bocza8251
@bocza8251 4 ай бұрын
Lima diaxal moy balla mo dane modou 2 fois moko meune le meilleur lutteur de tout les temps thi waxi ay fanssame ba paré tapateu si guinaw modou nane ko kaye niou beuré par force😂😂😂...ko raw meune ko kay paré ngassi mome wala😂
@IbrahimaKa-eg4ff
@IbrahimaKa-eg4ff 4 ай бұрын
😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
@ibrahimasarr711
@ibrahimasarr711 4 ай бұрын
Fen reck motakh sa kanam soufouneh ni tegal say tama
@mamadououmarba8253
@mamadououmarba8253 4 ай бұрын
Demande national akk international laniou yamale la lutte c pas entre balla et modou lo seulement ou eumeu sene…. Balla na khole boy yi
@DjibrilBa-xp7te
@DjibrilBa-xp7te 4 ай бұрын
Modou kharagne lô bourou lamb dji amoul diotou balla Gueye ak l'empereur nanou dokhane sen ndeye féle
@Moussagema
@Moussagema 4 ай бұрын
Khana ndégnuene ragal Balla ?
@bamediallo7082
@bamediallo7082 4 ай бұрын
Merci beaucoup bien dit
@AmadouThiongane-b7g
@AmadouThiongane-b7g 4 ай бұрын
Nmirou bour❤❤❤❤❤❤
@papagorakebe7594
@papagorakebe7594 4 ай бұрын
Supporter modou lo yi niofi nek di wakh rek niom balla gagné bakhoul si niom daniouy tite ndam yalla moko mome aziz ak baye souniou momome ndam boy niang ak eumeu ak bombardier douniou dane balla
@ibralemeringue3258
@ibralemeringue3258 4 ай бұрын
aay Bour yi yeupe ay nanfek laniou Balla gaye bimouy door Tapha Tine lolou lassi joublou woone boumou deim di diaay khool bou Nice
@saliouthiam2462
@saliouthiam2462 4 ай бұрын
Dagn léne yonni dh 😂😂😂mais fii mouss dou naane niékh 😂😂😂il faut arrêter modou néna beuré woul balla gaye 😢gueun léne yalla nak ahh
@MamadoulayeMbaye-k1e
@MamadoulayeMbaye-k1e 4 ай бұрын
Ioe bour mouno wakh ba modou beuré ak balla guaye
@thiernodiop1460
@thiernodiop1460 4 ай бұрын
Sene lobi bi dou diale kham nagne lep bayilen Modou lo
@abdougueye4837
@abdougueye4837 4 ай бұрын
modou lo bou dieulé balla danou watt
@abdoulayendoye1803
@abdoulayendoye1803 4 ай бұрын
bour kou gnemei ngeuh
@DjibrilBa-xp7te
@DjibrilBa-xp7te 4 ай бұрын
Sénégal mo nékh de fane keur Aziz Ndiaye nieuw tok di wakh loula nékh
@Abdoumbayesunucandidat
@Abdoumbayesunucandidat 4 ай бұрын
Bour sa data yaye way
@TidianeKebe-ls1fc
@TidianeKebe-ls1fc 4 ай бұрын
❤❤❤❤
@ibralemeringue3258
@ibralemeringue3258 4 ай бұрын
Bour seytané ngua kounguen sacrifier nguen beugue comme cadavre binguen daane dimanche
@BabacarkonteBoubacar
@BabacarkonteBoubacar 4 ай бұрын
🙏🙏🙏🙏❤️❤️
@dioufpapndiaga3556
@dioufpapndiaga3556 4 ай бұрын
Aziz sokhor mo KO diap gueumoul yalla yow vrai fimistenga
@ndiayennbi7557
@ndiayennbi7557 4 ай бұрын
Balla guaye donn na roi té danoul eumeu danoul b52 Kénnn manoul am 100%
@mbayendiaye5033
@mbayendiaye5033 4 ай бұрын
Bour khamnagne lepp wakh nagne la combat bi nimouy démé bou yague say analyse fofou rek nguakoy tek mais lo meunti wakh khamngua ni ya oustaze le rois incontestable incontesté modou xaragne lo domou mère ngoné diodiou dafa dall téye am personnalité kéne douko dougal si séne you niak fayda yoyou doléne may sakh bountou bobou soit honnête en vous même Ma deuk ak aziz défendre lo kham nguay watt ni sa pose mo diss rek
@papagorakebe7594
@papagorakebe7594 4 ай бұрын
Aytia l'empereur des arènes balla gaye 2 fékheul léne sen khol yi
@dofouAmabousamel-cl1sk
@dofouAmabousamel-cl1sk 4 ай бұрын
Bour gueweul wakho DEUG guémal sa bop Aziz dou sa dara sa guémègn gou salté gui
@lucniang8736
@lucniang8736 4 ай бұрын
Avez oublié nimou défone Elton xanna
@TaphaDiouf-10.18
@TaphaDiouf-10.18 4 ай бұрын
Way tapha tine amoul diome nimou tollou balla gaye diko door mounane balla na bayi beurré niak diome😮
@madembatoure7005
@madembatoure7005 4 ай бұрын
Bayileine modou lo amna combat ak siteu balla gaye sou beugei beurei na dieul franc
@ibrahimasarr711
@ibrahimasarr711 4 ай бұрын
Nafeck bou rey ga yen gnep balla gueye 2 guen suporte khaliss molen tital
@NgangeDiakhte
@NgangeDiakhte 4 ай бұрын
Bour ragual yalla si li nguay waxx
@mouhamedfall6002
@mouhamedfall6002 4 ай бұрын
Tapha tine dal deguén ko tekk deal yeew ko bamou deugueur Mai’s nak mom moy guaka bi
@BassirouSamb-oe6sh
@BassirouSamb-oe6sh 4 ай бұрын
Non modou biss bou dieule balla niou sarrekheko nakh Aziz Ndiaye pékhèm yeup beuggg modou diokh balla corone bi rek motakh Mouy cré ay empeureurr
@TaphaDiouf-10.18
@TaphaDiouf-10.18 4 ай бұрын
Buur yaw seytané nga produit aziz nga courone nou empereur amoul sens si lamb dji nieup courone nou roi des arènes lagni weur😂
@BayloGning
@BayloGning 4 ай бұрын
Y a mon affaire
@ballacisse7561
@ballacisse7561 4 ай бұрын
Bour mo nieme Yalla.Kene wakhoula né Balla moy dane Modou.Lolou mo safoule kene
@FatouSowSall-cu6uv
@FatouSowSall-cu6uv 4 ай бұрын
Bour dagay sone rk mais meuno wakh baniou dieul Balla nopalou len way
@vitosy5123
@vitosy5123 4 ай бұрын
Heee gnoune wa modou lo gno katoul ndem beuré ak balla na lér
@MbayeAdama-w2z
@MbayeAdama-w2z 4 ай бұрын
Protéger dente soko solé so wakhé dagn la dégue😂 ba tapha nane balla
@RamatoulayeDiallo-z2v
@RamatoulayeDiallo-z2v 4 ай бұрын
Pourtant si amna beneu partie tapha dafa sigui après balla coratko
@augustefaye-h9t
@augustefaye-h9t 4 ай бұрын
Pour dire vrai iow bour mar kattou boune nga aziz minguay défendre pions lala diapé rek dila damié ngay Doul di tek
@BabacarkonteBoubacar
@BabacarkonteBoubacar 4 ай бұрын
🙏🙏
@cheikhdiop9932
@cheikhdiop9932 4 ай бұрын
Ai milioun diar lii
@bounadjallo
@bounadjallo 4 ай бұрын
Grand contre petit mifiné balla na may chance zarco combat la???
@biranecamara6796
@biranecamara6796 4 ай бұрын
Bour wallahi diaroul andi ay leeral wakh katyi bayileen niouy wakh rek
@AbdouCisse-xs5mc
@AbdouCisse-xs5mc 4 ай бұрын
Bour gueweul bayil mare tanou sa moromou goor
@AboubacryGASSAMA-zs7oi
@AboubacryGASSAMA-zs7oi 4 ай бұрын
Bèn thiowe amoul bèn thiowe bariwoul bilahi .site internet yanay wakh rèk .mes lamb bobou dou ame insha alla .ah linak dou diam beurè wouniou ak balla gaye.na kounèk teuyè sa couronne 😅😅😅😅balla gaye na dieule franc boudè dafa beug confirmè bopam .dèf ni modou lo .adouna lèp ay risque la 😅😅😅
@modousarr8848
@modousarr8848 4 ай бұрын
nopalou lén Modou mbeurél woul
@yamlihambayeinfo1102
@yamlihambayeinfo1102 4 ай бұрын
Doul rek gaye dh
@gueyemayoro8243
@gueyemayoro8243 4 ай бұрын
Ay topé rek guén fou toy guén takfa
@moisabarry
@moisabarry 4 ай бұрын
Bour on comprend votre communication c'est Aziz qui vous envoie et vous paye pour communiquer sur ce combat 😂😂😂😂😂😂😂 on a compris votre stratégie Balla n'a qu'à descendre et donné une chance aux jeunes
@babadiao5030
@babadiao5030 4 ай бұрын
C'est ça seulement On comprend
@abdoulayembengue705
@abdoulayembengue705 4 ай бұрын
Ah oui comment il peut jurer comme ça, thieyye service commandé, c'est soi disants chroniqueurs corrompus,achetés polluent la lutte
@boubacardiallo5647
@boubacardiallo5647 4 ай бұрын
Supporters Modou vous êtes des peureux 😂
@IbrahimaKa-eg4ff
@IbrahimaKa-eg4ff 4 ай бұрын
Modou lo amoul dourai yor couronne bi di tan kou mouy beur
@Victoireman
@Victoireman 4 ай бұрын
Moome mooy roi des arènes amna privilège taneu kouka nekh😅😅 koone pour yéne ama AK bouy Niang douniou mbeur ? Teu boy Niang moolen moudié daane😅
@ibralemeringue3258
@ibralemeringue3258 4 ай бұрын
Modou lo dotoul dieul Balla yéna ko daane deux fois di mar tatam diko topou
@serignemorfall5635
@serignemorfall5635 4 ай бұрын
Billahi tapha damako yeureum lool
@adamslo7971
@adamslo7971 4 ай бұрын
Meuno wax ba modou dieull combat bii geumo Dara cii ligay pr sa wax yii meun tax modou tegui kadom nioune nio begoull balla Gaye soxla wougn ko xana doléne deg
@DadaSow-pk2br
@DadaSow-pk2br 4 ай бұрын
Yéne gnoune gnoléne nokhou 2fois motakh nguéne tapette
@MoustaphaFadiga-jy3dr
@MoustaphaFadiga-jy3dr 4 ай бұрын
Linguay wakh ni niak lo def motah ngua geune di wakh pour bagne niou khass la mais vrais nafekeu ngua walahi Aziz dalen fay pour nguéni tageu balla ak diko wakh louko nekh geume len sene bopou danguay doul rek linguay wakh ni guemoko sakh domeram ngua rek
@cheikhndiora422
@cheikhndiora422 4 ай бұрын
Bour degay feen
@BassirouSamb-oe6sh
@BassirouSamb-oe6sh 4 ай бұрын
Bour sama waye nga mais nitte daffa leundeum te lo kham kham nitte mou guene la kham bopam te niom bounou done deff sakh doko yeukk wakhouma nio deff wakhouma deffouniou yalla rek kham
@papenar2561
@papenar2561 4 ай бұрын
Bour yaw gueumo dará sén biir yii rek ak sen poche molen gnoor yaw fadam mola gueuneu deugou fouf faut type nga
@DjilyDiop-rv6jc
@DjilyDiop-rv6jc 4 ай бұрын
Bour khalatal né lingay wakh dinga KO wakhat thi bamel
@ThiernoSamb-e1t
@ThiernoSamb-e1t 4 ай бұрын
D'agave..wake.rek
@massendiaye5802
@massendiaye5802 4 ай бұрын
Légui gars yi khamnanou liguéndi joué Bour certe t'es pertinent mais amneu yo khamni dotoul dial
@MadokyMadoky
@MadokyMadoky 4 ай бұрын
Balla naguounade
@georgesdieganediouf2684
@georgesdieganediouf2684 4 ай бұрын
La couronne de balla gaye 2 n'est pas pour les arènes mais pour albourakh. Arrêtez !
@cheikhdiop9932
@cheikhdiop9932 4 ай бұрын
La couronnne de modou no validé CNG
@georgesdieganediouf2684
@georgesdieganediouf2684 4 ай бұрын
@@cheikhdiop9932 mais n'est pas de l'initiative d'un promoteur mais de l'ancien structure qui devient du cng.
@CASI7797
@CASI7797 4 ай бұрын
Totalement raison
@PapamamadouDassilva
@PapamamadouDassilva 4 ай бұрын
​@@georgesdieganediouf2684 CNG reconnaîtrul roi des arènes ay nitt gnoko crée signé wugnuko sen papier donc empereur aussi ay nitt gnoko crée pour la promotion de son événement lolu rek leu il faut que guen comprendre.
😱Allahou akbar Balla Gaye Waroul wone Trokhal Tapha Tine, Cheikh Abdallah Diouf limou wakhe Graw na
25:38
Deadpool family by Tsuriki Show
00:12
Tsuriki Show
Рет қаралды 7 МЛН
Support each other🤝
00:31
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 53 МЛН
LAST FACE 2 FACE ENTRE: MOD LÔ ET SITEU 👑🔥
19:50
MAP_AU_CAMPUS
Рет қаралды 2,8 М.
Deadpool family by Tsuriki Show
00:12
Tsuriki Show
Рет қаралды 7 МЛН