Modou Mbaye corrige Siteu “ Na Bayi Aziz Ndiaye ak Baye Ndiaye té focus ci BG2 sinon combat bi dina

  Рет қаралды 40,141

Sans limites TV

Sans limites TV

Күн бұрын

Пікірлер: 71
@ElhadjmoussaNdiaye-x1i
@ElhadjmoussaNdiaye-x1i 14 күн бұрын
Siteu waxou fi dara. Aziz règlement la wax. Daw kouko def niou dagg la. Xamonn na boubakh relation promoteur bi ak mbeur mi
@abdoulatifdiop5640
@abdoulatifdiop5640 13 күн бұрын
Xam nako deh 😂😂😂 guiss n'a leupou
@adamaseck8816
@adamaseck8816 12 күн бұрын
Siteu day dof doflou rek beugue dit woté walou
@fatoumbackefaye7170
@fatoumbackefaye7170 13 күн бұрын
Merci Modou mbaye deug nekhoul Mane mom Modou lo Moy sama mbeur mais siteu dafa rew yalna ko balla gaye nok ba parè dane ko😊😊😊🎉🎉🎉
@mameelbachirdiallo7925
@mameelbachirdiallo7925 13 күн бұрын
Loy mére😂😂
@fatoumbackefaye7170
@fatoumbackefaye7170 13 күн бұрын
@mameelbachirdiallo7925 siteu dafa indisciplinés rek
@ibrafatyndaw9891
@ibrafatyndaw9891 14 күн бұрын
Siteu dou dane balla gaye ndakh gnémé woul Staff balla gaye tée avant mouy djeul combat bi kham na léep tée lamb dji gneupa kham relation gnom Aziz ak balla gaye
@keydaddytv
@keydaddytv 11 күн бұрын
Inshalah du dane balla gaye
@GorguisambaNdao-ob1bt
@GorguisambaNdao-ob1bt 14 күн бұрын
Merci moudou mbaye
@mbayediopgadiaga353
@mbayediopgadiaga353 14 күн бұрын
Ndeysann modou mbaye sa xoll daa rafett
@CoumbaSall-o7t
@CoumbaSall-o7t 13 күн бұрын
siteu touss rk la am si combat bi 😂 Balla Gueye yallna ko yalla may ndam si barki Baye niass 🤲🤲🙏💪♥️
@CodouDia-w9w
@CodouDia-w9w 13 күн бұрын
Amine
@jobehamidou6545
@jobehamidou6545 13 күн бұрын
Merci beaucoup modou mbay
@jobehamidou6545
@jobehamidou6545 13 күн бұрын
Balla gaye2 ndam rek inshallah
@moussafaye1467
@moussafaye1467 13 күн бұрын
Eumeu sené doit lutter avec alune seye 2 Zarco tapha tine Sa thies modou lo
@yerosow7063
@yerosow7063 13 күн бұрын
Sa Thiès VS Xlo mom desna touti
@salyallemomuawrksarr8652
@salyallemomuawrksarr8652 14 күн бұрын
Yaw Modou mbaye Aziz Ndiaye ngay yeuk lé AK was diambar production siteu dafa ragal Balla gaye 2 😂😂
@alassanemane3021
@alassanemane3021 13 күн бұрын
Félicitation waa albourakh évents 💪❤❤❤❤❤
@FalouNgom-o3m
@FalouNgom-o3m 13 күн бұрын
Zarco Aline seye 2❤❤
@khadimfall979
@khadimfall979 13 күн бұрын
❤❤🎉BG2 rekkk ❤❤❤
@Pap-v2d
@Pap-v2d 14 күн бұрын
modou mbaye yaye sen baye
@KossoGadiaga-vw3wc
@KossoGadiaga-vw3wc 14 күн бұрын
Siteu kasse siteu kasse ❤❤️❤️👑👑👑👑
@fatoualiounefall9160
@fatoualiounefall9160 12 күн бұрын
Siteu pikine Texaco
@sadandiaye7962
@sadandiaye7962 12 күн бұрын
Modou mbaye yaw yagui melné guisss Lou daal Tapha tine kone boul nék nar fék Siteu menoul bayi Aziz et baye 🤨
@fadaleba1005
@fadaleba1005 13 күн бұрын
Je pense que vous devez pas oublier alioune seye deux du coup c’est mieux de faire un combat entre alioune sey et Zarco le vainqueur croisera à eumeu séne pour moi c’est un tope combat
@AstouDieme-f9h
@AstouDieme-f9h 9 күн бұрын
Siteu dé dotouko défati Balla gaye 2dina ko dore bamou teudeu dina khame ni Balla dou modou lo
@Veezen-s5b
@Veezen-s5b 14 күн бұрын
Mon rêve de regarder ces combats en 2025 Zarko vs eumeu sene Fild de balla vs gris 2 Alioune seye 2 vs gris Bordeaux Jackson vs Diene kairé Sa thies vs reug reug rvnche Pokola vs Quens Gouy gui vs Mor kang kang Youssou ndour vs Gora sohk Thapha mbeur vs diop 2 Siteu bou ngor Kirikou Thiate daouda Fall vs Moussa ndoye Mathieu vs boul lale
@ViolettaGomis
@ViolettaGomis 13 күн бұрын
Ta bien dit fils
@ndiayedistandiayendiaye2209
@ndiayedistandiayendiaye2209 12 күн бұрын
Modou rew na
@bayelakhatndiaye1450
@bayelakhatndiaye1450 13 күн бұрын
Tapha tin ,& aline seye 2
@cheikhndiaye6698
@cheikhndiaye6698 12 күн бұрын
Gris 2 Alioune seye
@SallSangue
@SallSangue 11 күн бұрын
Modou mbaye yagui comache fare dh ndakh légui azize moy se patarôn
@fatoumatabomou4670
@fatoumatabomou4670 11 күн бұрын
Boula nékhone bindeu Commencé wayé defoko😂😂
@khadimfall979
@khadimfall979 13 күн бұрын
Siteu daa tiite 😂😂😂😂😂😂
@Mbagnick-h8y
@Mbagnick-h8y 14 күн бұрын
Modou Mbaye waxal waxji Siteu limu wax moy baye ak Aziz nuniu wara défè do yoon daniuko begga xeex,yow Modou Mbaye yènni say dangay déconé tè damalay topp
@blackpure5177
@blackpure5177 14 күн бұрын
Demal diangui
@raymondhaddad2116
@raymondhaddad2116 14 күн бұрын
Copain MODOU a raison sur ce cas, siteu mo guena kham né aziz balla leye diapalé lolou dara dou ko changé , il le fait à tous les combats de balla SITEU dafa warra concentré wou ci entrainement yi té focus rek , lou ko yalla meye mou dieule QUE LE MEILLEUR GAGNE
@gora8046
@gora8046 14 күн бұрын
Du moment que Siteu khamone neu ta kham nani aziz ak baye ndiaye balla laniouy diapalé ba dieul avance bi loum ci gobé nako gar mom siteu.
@NédioKa
@NédioKa 14 күн бұрын
Mai pourquoi Aliou Sèye 2 vs Zarco lolou combat dakkou ko
@yilebaba6565
@yilebaba6565 14 күн бұрын
Alioune seye 2 vs moussa ndoye revanche mo dakh
@bayefalldjibyndigueldiallo4597
@bayefalldjibyndigueldiallo4597 12 күн бұрын
19 Juin 20 Julliet
@cheikhndiaye6698
@cheikhndiaye6698 12 күн бұрын
Modou mbaye wah gua niari wah siteu niari grand yim beurél défoul dara té mok lac siteu gua wah mo beuré archives yagifi
@papasillytraore7777
@papasillytraore7777 14 күн бұрын
Sa Thies Vs Gris 2 🔥🔥 Ficelé
@SaliouDiop-e4r
@SaliouDiop-e4r 13 күн бұрын
Gris 2 loumfi déff
@kenyboris
@kenyboris 13 күн бұрын
Alioune seye na changer stratégie beurém ,ben vip dou nangou ngakoy daur bamou teud😂 ,lamb sossi beugué sori dangay privilégier beuré bi
@SadekhDiouf
@SadekhDiouf 13 күн бұрын
SITEU DINA DÉLOO AVENCHE BII BLY
@alexandremonteiro661
@alexandremonteiro661 14 күн бұрын
Zarco / SEYE 2 , Zarco Eumeu ou Eumeu / SEYE 2
@AtoumaneNiasse
@AtoumaneNiasse 14 күн бұрын
Modou Mbaye mansour ba ak Azizz Ndiaye dou béne Azizz Ndiaye ak boye Ndiaye danouy faral balla Gaye ba gnip xamko
@ibrafatyndaw9891
@ibrafatyndaw9891 14 күн бұрын
Siteu avant Mouy djeul combat mola geuna kham Lolou dafa geumoul bopam rek tée Lolou lamb dji gneupa ko kham siteu boumou gnou sonal
@MrJali9
@MrJali9 13 күн бұрын
Aziz Ndiaye is Balla Gaye2’s Manager. For God sake you get to grow and know better.
@bayesambakane2109
@bayesambakane2109 13 күн бұрын
Eumeu Sène Vs Zarko Bou Eumeu Danara Daaw Boy Yiii Rèk Ahhh
@dimodablackdevil5636
@dimodablackdevil5636 13 күн бұрын
STADE FOOTBALL BI PROMOTEUR BUGN KOFI JOX NGUIR LAMB, MINISTRE SPORTS BI CI BOPAM LAGNUY NOKU. LUTAX AZIZ NDIAYE WAXUKO BIFI MACKY DI NEK, DOMERAM. LAMB DI YËFU DOF SALTÉ
@abdoulayediouf2140
@abdoulayediouf2140 13 күн бұрын
C'est que siteu yeneuko yaubou foumou agoul koumou dane ? Danoufi ken daw rek ak wax gou bari, yakh jeunesse bi ngéne kay défal promo nane Yalmine, ki dou sanfran danoul ken, téyite amoul respect amoul sportivité, il reste d'etre sportif.
@papafaye4033
@papafaye4033 14 күн бұрын
Modou mbaye légui daga beuri wakh
@ctiondaradji
@ctiondaradji 14 күн бұрын
Motay wakh Moy liguéyam
@GalleBa
@GalleBa 13 күн бұрын
Siteu a région Aziz ndiaye dafaye diable balla
@fatoumatabomou4670
@fatoumatabomou4670 11 күн бұрын
Souma nékhone bindeu raison dh wayé défoko 😅😅
@Papasamb-g8c
@Papasamb-g8c 14 күн бұрын
Siteu limouy wakh kham nako dofoul
@senesaliou4198
@senesaliou4198 14 күн бұрын
Tapha mbeur vs Jackson Fils de balla vs Moussa Ndoye Reug vs zarco Aliou seye vs eumeu Lac 2 vs Tapha tine Sa Thiès vs modou Lo Thiatou Daouda fall vs Mor Kang Diop 2 vs talpha
@papahabibdiop
@papahabibdiop 13 күн бұрын
Mo ya kham lamb
@adamasy3893
@adamasy3893 14 күн бұрын
Siteu fimou wakhé dafa kawé dé bakhna
@julesndiaye6019
@julesndiaye6019 14 күн бұрын
Lane mofa kawé
@MamadouNiang-zh8nf
@MamadouNiang-zh8nf 14 күн бұрын
Moma diakhal 😂 daw rek la meune
@gora8046
@gora8046 14 күн бұрын
Du moment que Siteu khamone neu ta kham nani aziz ak baye ndiaye balla laniouy diapalé ba dieul avance bi loum ci gobé nako gar mom siteu.
@AssanedieyeAssanedieye
@AssanedieyeAssanedieye 14 күн бұрын
Siteu fimou wakhè il a rèson aziz dou prèsident cng baye wakh linouye dague beure yi
@mohamedamar54
@mohamedamar54 14 күн бұрын
Démal deglou la réaction de Père Max Morgane qui a tout éclairci sur ce que Aziz a dit. Limou wakh yeup suo réglement CNG lako tekk.
@julesndiaye6019
@julesndiaye6019 14 күн бұрын
Azize waxoul da diotali ren
@blackpure5177
@blackpure5177 14 күн бұрын
Demal diangui
@Mameles
@Mameles 14 күн бұрын
Da ngue guénéwoul say millions rek motakh…
Lou Ken messoul wakh thi balla gaye... balla beye 1 corrige gris
23:38
🎈🎈🎈😲 #tiktok #shorts
0:28
Byungari 병아리언니
Рет қаралды 4,5 МЛН
Жездуха 41-серия
36:26
Million Show
Рет қаралды 5 МЛН
The Lost World: Living Room Edition
0:46
Daniel LaBelle
Рет қаралды 27 МЛН
$1 vs $500,000 Plane Ticket!
12:20
MrBeast
Рет қаралды 122 МЛН
Zarko cogne sur Gris Bordeaux " khamon Nani combat bi damalay…"
15:26
Sortie de Yékini..; Siteu Aziz Ndiaye Daf Ko Sarakhé..😳..; Pawlish Mbaye Eclat Le deal Apres l F2F
23:24
🎈🎈🎈😲 #tiktok #shorts
0:28
Byungari 병아리언니
Рет қаралды 4,5 МЛН