Baye mandione, un lutteur très courageux qui me plaît beaucoup machallah très véridique yalla nala yalla diapale À part balla c'est lui mon préféré
@AssaneMbeye-ho6jp Жыл бұрын
Lou l'ère la dione wakh
@AssaneMbeye-ho6jp Жыл бұрын
Coumba ame ndéy AK Coumba amoul ndéy
@malambadji3549 Жыл бұрын
Baye mandione mo dan bilay champion la ❤❤❤❤🤴🤴🤴🤴💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿
@djibrildieng8451 Жыл бұрын
Baye Mandione mi Dofoul... Daffa beugue diam rek❤❤❤ Cng daffa âme caméra daye âme image Lambe yep.
@layelaye7820 Жыл бұрын
Baye mandione gaindé la ta nit kou bakh la ta nit kou deugou la,mé sénégal mo beuri ay nawfékh gnom gni gnepeu kham nane ni modou lo def na 4appuis
@djibrildieng8451 Жыл бұрын
@@layelaye7820 ❤️❤️❤️🙏
@delgado7915 Жыл бұрын
Khame guani bou baxx modou 4 appui ne
@mohamedd7470 Жыл бұрын
Pere invité lén Yekini stp. Nameu naniou wakhtanam
@mouhamedniass6668 Жыл бұрын
Franchement fans modou lo la mai défna 4 appuie
@adamaaw3486 Жыл бұрын
FÉLICITATIONS BAYE MANDIONE 💪💪❤
@mamadouba6357 Жыл бұрын
Gëmël Yallah Ndione Modou LÔ mo tokk sa kaww😂.
@mamadougueye9986 Жыл бұрын
Ah deugue nekhoul vous tous qui êtes sur le plateau xam nguéne bou bakh li baye Mandione di wakh deugue rk mo nekh Yalla...ce que Baye Mandione a dit c'est vrai instant bobou la défaite n'arrangeait pas Modou Lô par ce que son dernier combat avant celui ci c'était une défaite alors que tout le monde de la lutte était avec Modou Lô. Mais ça arrive parfois Coumba am Ndeye Coumba amoul ndeye yaguena ci lamb guinañfi Yekini vs Tapha Gueye et tant d'autres exemples qu'on peut citer.
@timtim6971 Жыл бұрын
Ay vrai nafekh moy gnii 😂😂😂😂 4 appuis bou ler la modou def
@omarihandrick16537 ай бұрын
L'histoire retiendra que Baye Mandionne a battu Modou Lo, denge n ko xeex rek mais mome mo gagner . Je t'aime beaucoup Baye Mandionne
@Domino40 Жыл бұрын
Baye madione vraiment xolna combabi mai modou defoul 4 apuis modou dala dane
@layekharagne2224 Жыл бұрын
wallahi
@seydinamohameddieng8273 Жыл бұрын
Nafekh baxoul sa Thiès AK ndione la faralon mais ndione a raison Modou danouna Jackson aussi comme reug reug la fait
@ousououssououssou Жыл бұрын
Baye pourtant Modou defoul 4appuis deh yalla rekk lay wakhal
@TKFTV111 Жыл бұрын
Oui Lou lér nga wakh
@ousououssououssou Жыл бұрын
@@TKFTV111 non frère action bi mo gaw rekk mais lokho Modou fekanté woul sakh akk les deux pieds
@maxfall3597 Жыл бұрын
Dione borom bakh laa amal diam champion ❤
@makhtartraore5943 Жыл бұрын
Baye madione gni ay nafekheu lagnou gno gueune khame li ngaye wakh degueu rek nga lene wakh
@badarrangom1414 Жыл бұрын
Bayii lén nafék modou lo danouna
@bilalkhalyfall993810 ай бұрын
😂😂😂😂nanguou lén lou yallah dogual
@pascalkane9767 Жыл бұрын
Dieu aime la vérité et vous tous sur le plateau vous connaissez la vérité. Modou Lo a fait 4 appuis ce jour là on aurai du donner à Baye Mandione sa victoire.
@koulaalhakk8975 Жыл бұрын
3 appuis leuuh
@koulaalhakk8975 Жыл бұрын
3 appuis leuuh...mod lo en se levant il a remplacer sa main droite contre son pied...action rapide leuh arbitre Modou lo dafa gaaw...
@dabakhpouye Жыл бұрын
@@koulaalhakk8975wakhal deugu ioe deugu leu yalla beug
@koulaalhakk8975 Жыл бұрын
@@dabakhpouye non Modou da Meune beurré...Haram bi mo gaaw....kholatal lokho bii AK tank bii fékkantê wougnou....Baye mandione champion la mais Modou MOKO meune
@dabakhpouye Жыл бұрын
@@koulaalhakk8975modou mom dafa man ms frère kholal bu bakh rk
@boyeouakam6676 Жыл бұрын
Baye ya danon modou la faralone jour bobou me ya danon
@malickndemanesene7318 Жыл бұрын
Pa bi dey fene 😂😂defna 4 apui modou la faralone me moy lolou
@mansourkane8937 Жыл бұрын
Bilay ndione ya bari wakh 😂
@abdoudia9394 Жыл бұрын
En toute sincérité baay mandione a parfaitement raison il la terrasse Modou lo par quatre appui
@ouzdaking382 Жыл бұрын
Nafekheu bakhoule modou dafa danou baye madione c'est le roi des arènes
@papesidyfaye595 Жыл бұрын
Roi bou Gambie oui 😂😂😂
@veritesavoir54152 ай бұрын
😂😂😂
@bassndiaye2182 Жыл бұрын
Deugue reke la yalla beugue mais modou lo danou na yague na
@TKFTV111 Жыл бұрын
Modou Moy sa pp🦾
@madiopndiaye7570 Жыл бұрын
Waaay baye dafa beuri wakh mome kou ko diokhone victoire warone nako nagne gua eupou nit ki fouuuf mo dane la dieleu bou reuy guanane 4 appuie
@ibambaye6423 Жыл бұрын
Bilahi ya ndan bay madione
@kaozamane5601 Жыл бұрын
😂😂😂 c'est vrai baye madione waxngalénko mais n'empêche lignou beugue rekk laniouy déff... comme l'a si bien dit l'ami Coumba ame ndeye ak Coumba amoul ndeye mofi nék 😊
@legendediop9215 Жыл бұрын
Bekaye mom defeant leuh
@salioudia9358 Жыл бұрын
Ndiong sonalonna modou comba ba
@Momo-go5vh Жыл бұрын
modou mo dane beu legui !!! du courage baye
@djibrilkebe1498 Жыл бұрын
Il a raison. Deugue Nekhoul Nak. Sénégal Lii mofi am. Naafek rek
@mamecheikhantangom6213 Жыл бұрын
Modou Moy sa papa 😅😅😅
@moustaphadiop8230 Жыл бұрын
Baye ma Dion danga dan mpdou lo
@mamecheikhantangom6213 Жыл бұрын
Modou Moy sa papa
@mohamedthiam3138 Жыл бұрын
Modou ken dou mom. Mais ndione mo danone
@djibingom5668 Жыл бұрын
Da dane modou lo vraiment
@moussapayemane4167 Жыл бұрын
Baye mandione mi dof là,loutah bougoul déglou thim,mais nak Modou Lo danouna
@chakasen3996 ай бұрын
Baye Mandione a raison ! Il a battu Modou Lo !
@Vivian-ts2cj Жыл бұрын
100% kharagne Lo ❤ mais baye mandione moniou danone à l époque 😂😂😂 deug la yalla beug je me rappel dernier combat lawone avant fin saison ! Jour bobou bou arbitre bi diokhone ndione victoire supporters yi daniouy raye arbitre bi la preuve bi modou dané nioune nieupa fakhone si birr gueww bi
@bilalkhalyfall993810 ай бұрын
Saway yaw dh do fans kharagne
@wiliammalikk5482 Жыл бұрын
Baye nite kou bakh la
@djibrilkebe1498 Жыл бұрын
C’est vrai il a raison
@papadaue9446 Жыл бұрын
Merci
@ousmanesarr756 Жыл бұрын
Modou Lo instant yi mou nekk oustaz kouko ladj dou fenn dalay wakh bay madione mo dane bilahi 🤣🤣🤣🤣
@alioubluesfaye6447 Жыл бұрын
😂😂
@sambaba683 Жыл бұрын
Wakh dègueu yalla modou lô a fait 4 appuis Nèkhoul banèkhoul baye mandione modane modou lô dèffè lèrree mais dougnou farrrèeekkkk
@modougueye9757 Жыл бұрын
Man Lima diakhal ponkal mou tolni baymanione wara diap modou lo sanni mou nek fofou bamou danko mou diafanou si 4 appu
@babacarsarr1131 Жыл бұрын
Tay émission bi nekhone na 😂😂😂😂
@dofoujackson2544 Жыл бұрын
Modou nak défon na 4 apui you léér Jackson rk lay topou m défon na 4 apui contre Amet déme aussi wakh deug yalla
@alphasow5691 Жыл бұрын
Baye mandione ta raison c l'injustice l'arbitre n'a pas répondu la question
Guys mane supporter modou lo la, Mais 4 appuis amoneu c clair!
@abdoulayendoye1803 Жыл бұрын
Meusso nk supporters modou
@modoudiagne4769 Жыл бұрын
Bay Madion Mocodane
@modoubarasene9678 Жыл бұрын
Bay madone guemal yalla
@Peterpan-tw4tt Жыл бұрын
4 appuis bou lerr leu. Dione sa nga amoul badiene lamb rek
@mohamedabdhul9736 Жыл бұрын
Doul nga doul you tang dieur a appuis mossoul ame bb saloum kassé molene dane😂😂
@modoubarasene9678 Жыл бұрын
Dione katal ndayam dek Lou way
@anthioumanefadiga9314 Жыл бұрын
Baye mandione mii beurina wakhe trope
@fanignbadiane8955 Жыл бұрын
Vraiment li dafa niaw koi mé yalla deug leu beuge té deug rék moy moudiou
@yayadieme5998 Жыл бұрын
Le gas comment peut il défendre des choses aussi absurdes Modou lo a clairement fait 4appuis lolou on a pas de donner un raisonnement pour ça
@diopjean3631 Жыл бұрын
Modou lo sa baye la mola dane niak diome
@soppeousmanesonko777 Жыл бұрын
Wathie Ma Dane Na La woroul kou Dane dengaye féty kaw 😂
@bambistediop6652 Жыл бұрын
Grawoul démal def recours 😂😂😂 gris laniouy wo legui😂
@mouhameddia5168 Жыл бұрын
Balko dotouko defati gris aye touba ndiarém la yoor déh
@ycamara9034 Жыл бұрын
NIce bayema is right , 👍😁
@khadimba502 Жыл бұрын
C'est toute la malhonnêteté et leur partialité que condamnais. Bécaye tu ne veux pas dire à Baye Mandione qu'il a battu Modou Lô, mais tu peux te mettre devant toutes les caméras pour dire que Sa Thiès a battu Reug Reug alors même que les arbitres avaient déjà donné leur verdict. Coumba am ndaye Coumba amoul ndaye.
@falydiouf7746 Жыл бұрын
Baye mo dane diel bou lerr
@oneads7030 Жыл бұрын
ILS SONT TOUS CONTRE BAYE MANDIONE - ET POURTANT C'EST LUI QUI A RAISON
@papefall1718 Жыл бұрын
Modou lo mom yako dane
@baradieng1489 Жыл бұрын
Baye madion wakhna deugeu
@cissokhoawa4399 Жыл бұрын
Ya man day dol
@baradieng1489 Жыл бұрын
@@cissokhoawa4399 yaw damay karsa Ndaye dé sa leufeul ndaye
@cissokhoawa4399 Жыл бұрын
@@baradieng1489 yw Dky Dol rk
@cissokhoawa4399 Жыл бұрын
@@baradieng1489 🥒🥒🥒🥒🥒👎👎👎👎👎👎👎👎👎👎
@alysow9089 Жыл бұрын
Bari ngua wakh sof ngua del degu lou
@sohiboudiop5937 Жыл бұрын
Modoulo moy saber nak waye Dion nak takhal si victoire bi dall ndakh ligua amm siy victoire daberriwoul😂😂😂 motakh😂😂😂
@jazzjazz4902 Жыл бұрын
WA LITAKH MBEUROU THIAROYE YI TJRS AME AY PROBLMOU 4 APPUIS BAYE MANDIONE AMETH DEME REUG REUG BASSI KHADIM NDIAYE2 CONTRE MALICK NIANG?????
@cheikhbasskeurmassar9548 Жыл бұрын
Baye mandione mo daaan wayy 😂😂😂
@mamadoulaminembodji9648 Жыл бұрын
Il y a une veritè dans une histoire.faut pas faire de la veritè un mode de voire les choses
@mouhameddiouf8319 Жыл бұрын
becaye mbaye wakhoul deugue fi dara diakhassowoul modou lo defna 4apui si image yi alor
@lesamouraisnoir5304 Жыл бұрын
Pourtant Baye Madione à réson Modou lo à fait 4 appui
@brazza6317 Жыл бұрын
Wakh deug Yalla limou wakh Sénégal yep kham naniou ko, le 09 Août 2010 au Stade Demba Diop Baye Mandione Fall a battu Mamadou Lo par 4 appuis devant moi et des milliers de Sénégalais 😂😂😂
@fallougradel5547 Жыл бұрын
Pour dire vrai 4 appuis amna kay
@doudodieng476 Жыл бұрын
Baye Con naa😂😂😂sheutttttt
@iliskodjoloftv5534 Жыл бұрын
Baye Madione dadoul sakh degglo
@booygaye9894 Жыл бұрын
Nafeek bi nek ci yene daf ma dépasser pourtant bane dioxei reug reug victoire yene ñeep taxaw nei sa thies moo daan xarolene sax recours bi Baye mandione daanei modou lo lou lene ko terei deff guene nane décision arbitre
@ibrahimthiam4011 Жыл бұрын
Bilahi Ndione mo danone 😂😂 CNG dafsi diap rek
@Maestroo.20 Жыл бұрын
Trop d’hypocrisie dans la lutte.. ils savent tous qu’il a raison mais kene si niom nangou wouko
@khadimediop4398 Жыл бұрын
Jacksone contre Ahmed dém 4apui comme statu de la renaissance
@TKFTV111 Жыл бұрын
Bay mi da Bari wakh way akh
@omargueye2309 Жыл бұрын
Loutakh becay nigua wakhé né public ma sa Thies mo dane reug reug loutakh nagou wo honnête nes baye madione dane n’a modou Lo nagne bayi far farlo
@layelaye7820 Жыл бұрын
Senegal mo beuri ay nawfékh,yaw becaye mbaye ya geuneu khame ni baye mandione dane na modou lo 4appuis
@Généraldédjoul123 Жыл бұрын
Défaite yi bori na si mom kone wagnilén yoyou 😂😂😂😂
@ahmadousylla4995 Жыл бұрын
Reugour dafa waron dém att you bari kon baye ma ndione am ndam si modou lo de🤣🤣🤣🤣
@layelaye7820 Жыл бұрын
Yéne doléne ay nitou deug,ay nawfékh nguéne,baye mandione dane na modou lo wakh lén ko
@toumaniseydi4784 Жыл бұрын
Arbitre bi doule rek lay def no ki😮😮😮
@trompeursambenebisamb6245 Жыл бұрын
Baye madione sama mbeur nga mais bayil Jackson
@leregulateur Жыл бұрын
fans Modou lo la à 100% mais wakh deugue rk moo nékh yalla baye mandione daako daane sincèrement parlé cng ay nafékh akh ay voleurs rk lagnufa dadialé
@senegaleventschanel6913 Жыл бұрын
Yaw do supprter Modou lô , ki fanela dane Modou lô , 4 appuis pour dafay lerr
@leregulateur Жыл бұрын
@@senegaleventschanel6913 saway bilay walay Mala gueneuh beugue Modou lo fouff wayé nous sommes des sportifs en plus ay dioulite lagnu dagnuy wakh sunu diguantté ak yalla akh lignu guiss té Dara diarouma wakh loudoul deugue si aduna wayé Modou lo défna 4 appui devant baye mandione
@layekharagne2224 Жыл бұрын
@@leregulateur daguey doul modou deffoul 4 appuis te do fansou modou
@gueyelabsolu5889 Жыл бұрын
Adouna yeupou khamni Bayma Ndione Moo Danne Modou Lo lolou Mom amoul Wéranté sax 4 appuies✍️ kom Reug Reug mè Niakeu mbolo baxoull billahi 🥹boko amoul rék ndiou xékh la lolou moye Sénégal 🇸🇳 c sa le problème ✍️Ndione Modane modou Lo ✍️
@jazzjazz4902 Жыл бұрын
SAWAY SA KHALATE NGA WAKH MAIS LOKHO MODOU LO MA NGA SA KAWE MBEUROU THIAROYE YILIMOY SEN PROBLM 4 APPUIS AMETH DEME REUG REUG BAYE MANDIONE KHADIM NDIAYE2 CONTRE MALICK NIANG
@abassdiop3757 Жыл бұрын
Invité yékini
@mouhamessakho9575 Жыл бұрын
Yen khawma lolen di guissé li di 3 appuie 😂😂gueum len yallah