Mbacké : Concert Wally seck annulé, les chaude réaction de la jeunesse de Touba.

  Рет қаралды 9,112

MOUHALIM TV INTERNATIONAL

MOUHALIM TV INTERNATIONAL

Күн бұрын

Пікірлер
@Jeunepatriote
@Jeunepatriote 9 сағат бұрын
Dieureu dieuf sama boki baye fall yii sa kaw sa kanam inchallah ❤❤❤❤
@Mammorbeye-tf8gu
@Mammorbeye-tf8gu 8 сағат бұрын
Diaradiuf seringue TOUBA dégel rk❤❤❤
@BallaNiang-r5y
@BallaNiang-r5y 10 сағат бұрын
Mbaye fall yi wakh nal basonou mérci mbaye fall❤❤ piont❤
@matarthiam9572
@matarthiam9572 10 сағат бұрын
Kou meunoul respecté li khalif beugue si Touba rek nga delou sa deukou Mame wala sa deukou Baye , am lén yar ak téguin ak worma . Jub jubël rek mouride ndiguël
@cheikhabdoumbacke6970
@cheikhabdoumbacke6970 11 сағат бұрын
Merci beaucoup wally seck ❤️❤️❤️
@BallaNiang-r5y
@BallaNiang-r5y 10 сағат бұрын
Réw rék mérci mbaye fal❤piont ❤❤
@ousseynoutoure3621
@ousseynoutoure3621 12 сағат бұрын
Gonei yoyou dal jusqu'à preuve du contraire thiosanei wougnou touba aye lobbi gnofiye gneuw di nirouniroulou wa touba nguir maneu yakheu dieureudieuf waly yalna serigne touba faye
@hamathndiaye6803
@hamathndiaye6803 11 сағат бұрын
Jajeuf les Baye fall Yalla nguen dathié ngueureum segne bi.aaaamine
@MaoFall-c7k
@MaoFall-c7k 11 сағат бұрын
❤❤❤
@MaoFall-c7k
@MaoFall-c7k 11 сағат бұрын
Nice wally seck ❤
@magiangfall4001
@magiangfall4001 10 сағат бұрын
Wakhalene thi bokale bingeni bokale yalla
@toubatouba4966
@toubatouba4966 8 сағат бұрын
Wakh ko sa baye ba paré
@AbabacarSamb-h5j
@AbabacarSamb-h5j 7 сағат бұрын
sa data ndéye yaw katale sa leufeule ndéye feulé
@Bour_ndiaye_bour
@Bour_ndiaye_bour 7 сағат бұрын
Yaw lane moy bokalé
@lazanbambacke450
@lazanbambacke450 12 сағат бұрын
Maasallaah ❤
@almustafambakke6163
@almustafambakke6163 4 сағат бұрын
Nek leen ay Niit té Xam Séen Bopu té Li Serin BI bëg fawu dina am Inchalla
@SyllaMouhtar313
@SyllaMouhtar313 8 сағат бұрын
Wadji Rango Sac Bi AK Boye Bi Sol Yéré Bou Rouge Yén Rekka Wakh Deugue Ndigeul Amoul commentaires Dieufé Rekk
@Tttttttt-fm3ge
@Tttttttt-fm3ge 12 сағат бұрын
Mani bayi léne saye tané waly seck ak Mbacké Mbacké yi nio farrr
@beugssalioumbacke2726
@beugssalioumbacke2726 12 сағат бұрын
@@Tttttttt-fm3ge Merci beaucoup 😘
@Bawolbawol
@Bawolbawol 25 минут бұрын
Yaa mana meew
@toubadarmanko7193
@toubadarmanko7193 Сағат бұрын
Jeureudieuf Baye fall yi
@DerMor-z8z
@DerMor-z8z 7 сағат бұрын
Deugg bi moy dasi am talibé you compléxé rek am lou kéne amoul bayikofi di wouti lou bone tchim mani deuk bi lou serigne bi beugg mofiy am sokhka woun si xakatou kén koum nakhari nga dem sa deuk Maam
@Sarr-jx7ux
@Sarr-jx7ux 6 сағат бұрын
Jeuness touba gni thi eup dagno gnak diom nek lenne ay nite
@DIEREDIEFSERINGETOUBA4
@DIEREDIEFSERINGETOUBA4 13 сағат бұрын
ALLZ BADA
@oumarsarr4087
@oumarsarr4087 29 минут бұрын
Ay niouss rék mokoy fath
@Bour_ndiaye_bour
@Bour_ndiaye_bour 7 сағат бұрын
Kolén si diap mouy déf naka soudoul nonou gnaf léne ndayam bou bakh dieureudieufé bay fall yi
@sonkofocus2024-ph4hv
@sonkofocus2024-ph4hv 4 сағат бұрын
Koula téré déme concert mome dangako wara sante fo khamni aye bkar rk ngafay dieulé diaroull déme 😮
@Diks-m
@Diks-m 10 сағат бұрын
Mais lou takh mbacké Coumba am ndeye la ak Coumba amoul ndeye
@sagyatal8545
@sagyatal8545 12 сағат бұрын
7:28 En bleu Waw goor
@BayemodouNdiaye-f6b
@BayemodouNdiaye-f6b 12 сағат бұрын
Thiey wally mon barri baïre😂😂
@Sarr-jx7ux
@Sarr-jx7ux 6 сағат бұрын
Dagua nane saytané mo bari baïré
@sagyatal8545
@sagyatal8545 12 сағат бұрын
9:47 Waw goor en rouge
@badadiopsatouba3828
@badadiopsatouba3828 12 сағат бұрын
Je suis Baay Faal yii 😅
@beugssalioumbacke2726
@beugssalioumbacke2726 13 сағат бұрын
😂😂waly seul
@محمدسيسهمعلمالقرءان
@محمدسيسهمعلمالقرءان 13 сағат бұрын
Bada Waxi nit nga wax dé😂
@tout1958
@tout1958 12 сағат бұрын
Touba li Sérigne beugeu rék Moy am Domi xaram yi dém léne séne deukou baye wala séne deukou Mame
@bigue5329
@bigue5329 12 сағат бұрын
Merci Sérigne Mountakha bouye defar kene douko thi fek bapar niou beugeu dhi khoti warmam domi kharam yi niake diom laniou te séné wadioure niou thi wara diapou dimbale Sérigne bi thi warma yi
@MohaMed-ep1dt
@MohaMed-ep1dt 8 сағат бұрын
Ana sa deukoub bay yaw
@Djilydiob-jf2ey
@Djilydiob-jf2ey 12 сағат бұрын
Dëgg bi bi seen baay yi fobo ñaw fi xam nañu li Sëriñ bëgg kuko man nga took kuko manul nga dellu sa Dëgg maam wax ji jeex .
@tout1958
@tout1958 12 сағат бұрын
Domi xaram yi kouléne topou Touba am boîte de nuit tégeul léne séne ndeye dém séne deukou Mame
@abdoulayediop8062
@abdoulayediop8062 9 сағат бұрын
nagn waxanté deuggeu nak waayé wally seck bou taxawéh naani baye fall leu loolou yabaaté leu, moom neu nekk musicien bimou doon rek té bayyi baye fall gui. un baye fall ne devient jamais un musicien. baye fall dafay deukkeu ci topp yalla di tarbiyou. waayé nekk ci seen yeufou thiaaxaan yi ba paré taxaw naani baye fall laa. le baye fall n'est pas n'importe qui. waly seck nak sou beuggéh nekk baye fall neu soppéh kou. baye fall deuggeu dou doon musicien nak vraiment. ngeen baal meu
@dmcdjilymbayecolle4629
@dmcdjilymbayecolle4629 7 сағат бұрын
Ay thiakhane rék la baye fall yi nék mais baye fall yi niom danioye teugeu di féthie
@jamaaTV591
@jamaaTV591 13 сағат бұрын
Reew dong a leen jàpp ñoom boyi Waly yi
@abdoulahadgueye4643
@abdoulahadgueye4643 12 сағат бұрын
Bolene bakhone âme diome ame coleuré ame ngore beugue lou bakhe Dolène dioté ak Baye Fall dara
@MouhamedDiaw-f9b
@MouhamedDiaw-f9b 3 сағат бұрын
Borom kap bi kou téppi leufeul ndeyam la ak kabou domerame dji mouy diaye nandité so gnewé Dakar khamni do nandité
@ibrahimacissedieureudieufs2732
@ibrahimacissedieureudieufs2732 12 сағат бұрын
Khaley Touba yii di wakh ay complexés you bone laniou ay séér youy nandité laniou khamouniou séne bopp
@modousarr8848
@modousarr8848 12 сағат бұрын
niak fayda fi la Omar diange saka seringe bi wokho l'en fi doul nafékh yi ngén don
@SidiDienne
@SidiDienne 9 сағат бұрын
Ayy saga amoul sange. Amal tégune
@toubatouba4966
@toubatouba4966 8 сағат бұрын
Sa baye premier nafék
@ousseynoutoure3621
@ousseynoutoure3621 12 сағат бұрын
Baye fall yi deifougnou dara sou ngueine bayei fo reck baye fall yi amougnok yeine problème
@abdoulahadgueye4643
@abdoulahadgueye4643 12 сағат бұрын
Boyou Touba yi nio bonne té niak coleuré. Deukeul sa baye banga dioudou fayo bène droit ndokhe sakh doko faye. Nguène beugue yakhe deukou diambour.
@ndiayetoubausa391
@ndiayetoubausa391 12 сағат бұрын
Kofi baye fall yi diabou rek nan ko Dorr yar ko rew nan trop
@abdoukarimditmacodoundiaye993
@abdoukarimditmacodoundiaye993 7 сағат бұрын
Bokalé guéne wara wakh
@komxel
@komxel 2 сағат бұрын
Demal fadiou ba wër
@papeleye267
@papeleye267 9 сағат бұрын
Légui loutakh niouy dieul khaliss wally si Magali gui😂
@SidiDienne
@SidiDienne 9 сағат бұрын
Kane moko dieul
@toubatouba4966
@toubatouba4966 8 сағат бұрын
Merci a tout les baye fall ❤❤❤❤❤❤❤❤
@CisseModouxaadiabdallahcisse
@CisseModouxaadiabdallahcisse 8 сағат бұрын
Legui kan moko dieul
@Bour_ndiaye_bour
@Bour_ndiaye_bour 7 сағат бұрын
Khana sa papa lako diokh mou andiko meuno bayi féne
@fallelhadjiabdoulaye2347
@fallelhadjiabdoulaye2347 6 сағат бұрын
Ko guise mou dieul khaliss wally wahko fi ya mana fén😂😂😂😂
@madinagueye168
@madinagueye168 9 сағат бұрын
Nit bokko japper tamit surtout bou deukoul Touba wala comprendroul worma yi dangakay fatali worma yi te bagne ko yobbou
@tout1958
@tout1958 12 сағат бұрын
Borome gassgett bi Domi xaram deugeu la
@Bawolbawol
@Bawolbawol 32 минут бұрын
Dañoo reew te doff baay faal yi rekkkk niofi baaax complexe
@Tttttttt-fm3ge
@Tttttttt-fm3ge 12 сағат бұрын
Mane lima diakhal waly daye diokhé adiya adiya dji fane lakoye dieulé
@dëgmonjëkdëgmomuj1780
@dëgmonjëkdëgmomuj1780 12 сағат бұрын
Khana sa baay lako jox, danga gis Sëriñ Muntaqa jël xaalissu Waly
@khadynardiagne2681
@khadynardiagne2681 12 сағат бұрын
😂😂😂
@beugssalioumbacke2726
@beugssalioumbacke2726 12 сағат бұрын
Billy kay lu jara laaj
@bigue5329
@bigue5329 12 сағат бұрын
Da nga masa guiss Wally diokhe adiya delene swi te teudi dou ngene masa am ndam thi kaw Sérigne touba li Sérigne bi beugeu moy am inchallah force koumou nekhoul nga niapou sa ndaye thia Khadije
@BabacarSarr-p5e
@BabacarSarr-p5e 10 сағат бұрын
Tu l'as vu? Est ce ce xadiya est consommé ?
@toubadarmanko7193
@toubadarmanko7193 Сағат бұрын
Mbirmi yombena li Serigne bi kouku meunoul bayi gueneul Touba dém Sa deukou bayi wala gua del fenene
MBACKÉ : Annulation du concert de Wally Seck avec So Events
10:40
« L’échappée », la nouvelle émission d’Edwy Plenel
58:41
I Sent a Subscriber to Disneyland
0:27
MrBeast
Рет қаралды 104 МЛН
Who is More Stupid? #tiktok #sigmagirl #funny
0:27
CRAZY GREAPA
Рет қаралды 10 МЛН
BÉTÉ BÉTÉ - Saison 2 - Episode 5 **VOSTFR**
55:32
EvenProd
Рет қаралды 3,2 МЛН
La situation en Syrie risque d'exploser et d'embraser davantage le Moyen-Orient...
49:19
FAJARU du Jeudi 26 Décembre 2024
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 2,3 М.
What is Turkey's agenda in Africa?
10:51
GZT
Рет қаралды 179 М.