Barki Serigne saliou Mouhamed Niang est le meilleur chanteur parmi les thiantacoun moi personnellement c’est grâce à lui que suis devenu talibé Serigne saliou vraiment c’est toi qui mérite le nom de l’ambassadeur donné à Oumaro
@ndiakhatesaliouniang2614 жыл бұрын
Bilahi vous avez raison 👍❤
@khadysene42684 жыл бұрын
Mm
@modiiistodieng81943 жыл бұрын
GV
@dioufeva1031 Жыл бұрын
Tiey mouhamed niang"ma wax nak litax thiow thioW dama xeuy demoul wone bagni deim tei far djitou leine mbacke ya meune djiteul wadjia moudione thia yonn wa"Métaphore bou doywarr🥰🥰je t'écoute depuis mes 13ans et aujourd'hui g 23ans nagnou fii yalla bayi inchaalah🥰🥰
@LoliForce-e7u3 ай бұрын
Manchallah❤ Amine 🤲
@coumbaba23255 жыл бұрын
Douma thianta wayé mouhamed niang motakh ma beugeu Cheikh bii ba démm na keuram médinatoul salam takhna tamit ma geuna beugeu Serigne Saliou t douma Mouride 🥰wayé diné djii yeup bénn la ❤️🙏
@alamiircbd16085 жыл бұрын
Sa xol Mo rafét
@codouthiam35415 жыл бұрын
Aida 1
@codouthiam35415 жыл бұрын
Aida. Baye
@morndong28063 жыл бұрын
Mouhamed Niang le meilleur de tout les temps, Cheikh Betio yalla n'a yalla yok ay lerame
@fatimademe38455 жыл бұрын
Cheikh béthio yalnako yalla kharé aldiana ani sopéyy mouhamed Niang yi👍🙏🙏
@khadimsaye61075 жыл бұрын
Magiu ni
@fatimademe38455 жыл бұрын
@@khadimsaye6107 bégue na si yaw
@ndeyemariethioune25705 жыл бұрын
sant nanou lol thi noumou démei
@fatimademe38455 жыл бұрын
@@ndeyemariethioune2570 nono bakh 🙏🙏
@momylabambiste74895 жыл бұрын
Fatima deme mane dé dama beug mouhamed niang té meussoumako guise walahi
@khadijadiouf24945 жыл бұрын
Walay Mouhamed yalla mo def ma beug la nguir dieumi serigne Saliou damay rêve Buss bouniou may tack ma def ak thiant nga niaw wayal mako li rk lay nian kou guis sama comantaire rk nga nianal mako nguir diemi serigne saliou🙏🙏
@tigerwoods76995 жыл бұрын
Kayma tak la niou woko sounou mariage
@ismagningue82475 жыл бұрын
Yallah na lako Serign SALIOU défal. Waw Coumba !!!
@khadijadiouf24945 жыл бұрын
Amiine Waye
@khadijadiouf24945 жыл бұрын
Tala Dieng 😁
@khadijadiouf24945 жыл бұрын
Isma Gningue amiine
@AngelLopez-sk3ex5 жыл бұрын
grâce à tes chansons que j'ai aimé cheikh bi merci bcp niang mouhamed
@maestroassgueye75505 жыл бұрын
Même moi aussi
@ndeyeyacinembengue31735 жыл бұрын
Angel Lopez c vrai moi aussi
@balla88435 жыл бұрын
bari nga si morrom
@souleymanendiaye63415 жыл бұрын
Je t'assure même moi aussi
@boussolefadallkalla60965 жыл бұрын
Angel Lopez méme moi aussi
@damelducayor84065 жыл бұрын
J’ai les larmes aux yeux😭. Dieureudieuf serigne saliou. Cheikh bethio yalah nala Bour bi kharé Aldianna firdawsi.
@chachabalde69585 жыл бұрын
Machalla merci si hommage bi ndakh cheikh bi bam lay dioh pass port diplomatic gnou barii si mer té barki S Saliou cheikh bi dala bgue foumouy dem ande ak yaw dieundal la billet té pourtant yak say morom weuykate yénafi nek mais khol bi Ken ngathie et toi même tu le c , legui nak mom boumadone yaw dangay dem si tawam bou bi toup diegalou thiantacoune yi dagn la bgue bilahi mane mom jtmmmm de tro , tu sera tjr la bienvenue c nous , Sénégal nak mo bari ay seytané té Sakh nak aida diallo nga diotel ndakh mola def Dieuwrigne universel nga delo koko fala wakh dji commencé wayé nak lou warone am la gnipsil sa keur guir yalla ak dieumii s saliou
@naboufall83415 жыл бұрын
Macha alla wakh dj rafetena
@yacinesock62435 жыл бұрын
@@naboufall8341 contane na
@goraseck35633 жыл бұрын
Je ne suis d'aucune obédience confreriques du Sénégal mais une chose est sûre et certaine, CHEIKH BÉTHIO est un homme avec un cœur en or ,beaucoup l'ignore
@FatySaliou Жыл бұрын
Merci beaucoup
@abdouwahabkane909 Жыл бұрын
Tu as parfaitement raison malheureusement certains ne l’ai connais pas
@MameboussoKandji-pd5hp9 ай бұрын
❤❤❤❤ah machallah c'est magnifique 🎉❤❤🎉
@germainegermaine15525 жыл бұрын
Je suis chrétienne mais j adore ta voix rawatina bi weuy j ai grandi à mbour Niang ballo yallna yalla weurréne batt bi
@fallthierno44885 жыл бұрын
Non sama khôl dans sédeu si Mouhamete niang Li rék DINA takh nonou yi nopi Mouhamete niang kouko khame khané dafeu beugue cheikh béthio Thoune bamou diekh kou d'accord deusseul j'aime
@adjifatoudabo12815 жыл бұрын
Que la terre de touba soit légère à cheikh bethio thioune et tout musulman disparu.
@khadykonate27125 жыл бұрын
Masha allah tes chansons me vont droit au coeur ❤❤ yalla same la ci barcké S. Babacar sy ❤❤ je t'adore❤💋
@satoundiaye50985 жыл бұрын
hooooooo li dawe na yarame kolaré guinawe laye fété vraiment j suis tidiane mais j'adore la sincérité des thiantacounes
@sokhnasene15355 жыл бұрын
satou ndiaye ohhhhh bilahi dama dioy sama xool séd na liii rk la don khare si iow moukhamad amal diamou
@assysene85065 жыл бұрын
D'où Ya KO fi bayiwone bimouy doune nga bayi bamou dé nga koy rendre hommage amo béne koleurè
@semousarr1935 жыл бұрын
@@assysene8506 assi je l'ai dit partout j'étais seul heureusement qu'il y a toujours des gens comme toi qui sont honnêtes même s'ils ne sont pas nombreux. Qu'est ce qu'il n'a pas dit de movais au cheikh? Il a même affirmé qu'il voit du satanisme dans le thiante il l'a dit sur les ondes de la radio touba Fall qui se trouve a touba. Maintenant celui qu'il juge d'être le dirigeant du satanisme est mort il se permet de lui rendre hommage. Si ce n'est pas de l'hypocrisie qu'on me dise ce que c'est.
@yacinepouye96935 жыл бұрын
J su tidiane mais j su fan numéro 1
@Eladji-sall444 жыл бұрын
yawe danga bakhe rek
@mouhamedmouhamed80055 жыл бұрын
Cheikh bi yalla nako yalla yueruem mouhaméd niang dafay khalé rék mé khol bi chiekh bi mosi nék lamou saf kako mathi moko kham
@joelembiidndao14435 жыл бұрын
Bilaye lolou mo ame dhe
@mamekharicissesourang75585 жыл бұрын
Amiine
@lissabah74854 жыл бұрын
❤❤
@ablayembaye79995 жыл бұрын
Mashalah mane Sonia bou serigne babacar sama khôl Sedna ndakh thiofel gouma ame thi serigne saliou rta yalla nala sougnou borome bolek sa sopey bâ thia aldiana firdawsi amine
@maissadieng99215 жыл бұрын
Diadieuf serign Mouhamed Niang man déh serigne saliou mbacké rek lala beugué dakh moy sunu lepp yalla gua dadjé ak yeurmandém dja barkép serign saliou
@go.visionofficiel47255 жыл бұрын
porn
@patriciabacker93415 жыл бұрын
4
@generalmime67315 жыл бұрын
Maissa Dieng amine domou bay barke s Saliou💞🙏
@maissadieng99215 жыл бұрын
éva dieng amine amine
@yamadieye61883 жыл бұрын
Je suis Layéme mai j'aime bcp Mohammed
@ayshamohamed71745 жыл бұрын
Ndeysane douna thianta bokou ma si tarikha mouride mais li dafa rafeite.. Dawna yaram. Aduna dou dara. Na leip di rafeit rek. Reiro amoul, niaka wakhtane mo ame! Mouhamed Niang yalla na yalla weureul baat bi. Cheikh Béthio yalla nako serigne saliou teirou!
@ibndiamalgueye32665 жыл бұрын
Aka wérr
@khadimsaye61075 жыл бұрын
Ay way nn yaw baye fall ga bilaye
@ibndiamalgueye32665 жыл бұрын
@@khadimsaye6107 waw ay baye Gueye lan
@bvediarrachousene58325 жыл бұрын
Wallahi li dafa rafét yalna diam yagg té batt bi gueuna wéer cheikh bi yalna yalla yokk léram té tass nou si barkém
@B-SN.TV44675 жыл бұрын
Amiin wayy Aysha say kadou Raffétna
@khassidayireiik83494 жыл бұрын
Le meilleur lyrics de tous les chansons de Mouhamed Niang
@FatouSall-ru7kw Жыл бұрын
Lou. Leer❤
@MODOUAMARtvofficiel Жыл бұрын
@@FatouSall-ru7kw🎉
@maiinarassoul91675 жыл бұрын
Mane ki damako beug❤️yalna sa diam yagg niang ballo🙏
@dofousewroumbacke69785 жыл бұрын
Cv
@parisparisparisparis66065 жыл бұрын
Maina rassoul ma beug nalla lo diahk Cheikh bi loooooo sha
@niangmodou475 жыл бұрын
Maynala 10000fcfa ndakh Niang ballo dji nga wakh
@mamediarradioum57695 жыл бұрын
Amine
@abdoulayecisse36575 жыл бұрын
Je l'aime encore plus
@moustaphalabaikasarr63215 жыл бұрын
Macha alla bil lahi li rafét na trop mane dé douma mourid mé Cheikh bi sagou l'islam yalla nako yalla yerem té wané léko ak sa ngam ba
@modoudiop21605 жыл бұрын
ohhh yalla khamnani lii daa nékh iska yéenagui déklou loumouy wakh boubakh kontannt nagne mouhamet niage cheikh bi yallana yalla dolli yeurmandem si kawam ak mbolém djioulite yeuppe amiine
@elsaadix27885 жыл бұрын
Mana way dafa am wayantou am M3 mounamed niang Way degue la man En plus mook cheikh bou diop way katou sikar yima xam si reewmi yeppou yeppou sen paroles yi nioom niaar bokoun sakh ak gni si dess Nuvau yi nioo tolloo woul Machallah nala yalla lafal thiat te aarla. Amoul morom si gars yi
@IbrahimaKane-jp4zt3 ай бұрын
Moussak
@vieuxka2823 жыл бұрын
Ndéysane chiekh béthio thioune Yalla nako Yalla yuerém témou yéssal yuermandé si mome.اللهم إغفر لهم وأرحمهم وأسكنهم جوار سيدنا ومولانى ورسولنا محمد صل الله عليه وسلم آمين يارب العالمين
@evadipmoree19755 жыл бұрын
Mdeyesane Niang Ballo bolèwoul daraki wakh je suis devenue thaintacoune grace a toi Koulaye khèkh si yonou Thiantacoune dala khamoule yalla na yalla guena wèral bate bi mousale leu si thiatt si barkèpp Sougnou yakar Serigne Saliou
@zeynazey67515 жыл бұрын
mane dh j n sui po mourite mai walahi lezi ki mo takh ma beug yonou mouride j l'aime jam si iao mouhamed niang worna brom bi sama mémoire say son moka féssal❤🙏
@mamourfall31445 жыл бұрын
Ay way yaw yabakhe rèk
@mamourfall31445 жыл бұрын
Yaw ya bakh rèk
@zeynazey67515 жыл бұрын
mamour fall bilahi ki j laim trop mome Motakh ma beug cheikh bi
@cheikhdiawara70135 жыл бұрын
Ndeyssane Waw coumba Sokhna Zeyna
@alamiircbd16085 жыл бұрын
Ndaysan Rawal
@fulgyrosesarr17845 жыл бұрын
Ndeysannn je suis chrétienne mes j'aime tro mouhamed Niang yalla nala yalla faye sa xol do yakou do yakoulé si barker wérou koor gui
walaye walah ken dou CHEIKH BETHIO THIOUNE aka gorè daniouulay SANT FAW
@diopgambou13625 жыл бұрын
Momm niang famou nèkone batay fala nèk loumou am nèna serigne saliou douma fatè mouk sama cheikh bi nitt ki boko khamoul frèquente woul doko kham 👉👂👂👂👂waye bi
@serignesaliou47723 жыл бұрын
Tonton bougane sama pape ta fa serigne bethio mais rip ces lui le pdg de xelcom logistique
macha allah Mouhamed niang yalla ngafi yague tè wèrr
@bintasow44384 жыл бұрын
Bilay beug Serigne Saliou reka wor Mouhamed naing Sama fans bi tu est le meilleur
@ahmadoufaye44572 жыл бұрын
Les éléments de serigne saliou yakarou diam yi doufi amati
@iboudiagne41644 жыл бұрын
Mouhamed niang man damala beugg té yalla takh billakhi
@mouhamadoulamineseyebeugue27415 жыл бұрын
*_Ndeyesenn Mohammed Niang DOUNDEUL Niang _**_#cheikhbi_**_ yalnako yallah yeureum té kharé ko aldiana si barkép SERIGNE SALIOU MBACKÉ_*
@dioufdanane66185 жыл бұрын
Mohamed Niang sop nala
@mouhamadoulamineseyebeugue27415 жыл бұрын
@@dioufdanane6618 *diā dieuff way*
@bambageneral22695 жыл бұрын
Yallna ga amdiamou way doudal way
@mouhamadoulamineseyebeugue27415 жыл бұрын
@@bambageneral2269 *_#amine_**_❤🤩👌_*
@saffdiagne12445 жыл бұрын
Alhamdoulillah Serigne Touba Merciii ❤❤❤li nekhna trop 🙏cheikh bi yallah nako yalla yeureum si barke seydina Mohammed amine 🤲
@ndeyemaguettendiaye98655 жыл бұрын
Machalla nex na lol laf thiat li moy ak talibé gniy wax danio xamul rk mouride gui bein bop la nio bok kiniou beug top wolou yakar dieureudieuff serigne Touba👌❤️
@diodiofall32955 жыл бұрын
Seigne saliou takhna niou kham cheikh bétio Wayè bok ngua si niouko diotali Talibè cheikh la wayé machalah way Niang Danguako yagu wooy mouy nekh ❤️
@edencom95285 жыл бұрын
hoooo machalah ndéysane mouhamet mane damala beug lol di thianta touba sacré coeur beug na guir serigne bi gua siar si serigne saliou geultapé svp boko défé déf lou raféte looool way yaw kéne manouma guéné si keur gui gnoun nieupa guilay khar
@fatymature94765 жыл бұрын
Lolou la warra deff bilakhi on l'aime 🙏🙏🙏🙏
@edencom95285 жыл бұрын
ont l'aime trés fort té fi keuramla
@gueyendioraheritage25875 жыл бұрын
yalla na la yalla defal diam Billahi Machallh 💕 mouhamede niang lii rek lane done khar ci Yaw ✅✅
@BAMBISTETV5 жыл бұрын
Ndaysan son bi fan yi yepp migui won sama khel mi khamon nani mouhamad dinanko hommage serigne cheikh bethio yalla nako yalla fay ay dieufam you bakh te dieugalko ay dioumtem barkep serigne saliou Niang Dieuredieuf 👌🏾
@fatoudiobaye28675 жыл бұрын
Mouhamed niang man damako beug rek te soumay mariage inchalla beug na mou nieuw
@mbayeissa73635 жыл бұрын
fatou diobaye kaye ma takk la ngir Serigne bi
@cheikhndiaye85695 жыл бұрын
Diadiaf
@willshitavilane55365 жыл бұрын
Inchaalla
@fatoudiobaye28675 жыл бұрын
@@mbayeissa7363 nako dal🤣🤣
@mbayeissa73635 жыл бұрын
fatou diobaye desna ci yaw loumaye deff ba ame sa contatto
@balliseck22375 жыл бұрын
Bilakhi kou beugué s Saliou tékhé gna ❤️😍❤️😍
@mamegor34063 жыл бұрын
Billay
@maciritagueye80475 жыл бұрын
Niang balo khobi lem maleu beug walahi dundal té bat bi gueun wer bilay ya takh ma am estime si cheikh yalnalako Serigne saliou terou 🙏🙏
@zeinasabaly27245 жыл бұрын
Je suis Talibe Cheikh mai vraiment je t adore Macha Allah ❤️❤️❤️❤️
@ramsesalsalihatbeautymane28365 жыл бұрын
Ah Niang Ballon guissou mala wayé touché nala té khamna ni ameu ngua regret mais aduna nak mo téralé nonu kounék dangueuy dioté ak sa wédiour wayé lou ameu solo moy toubeu dieureudieuf
Machalah li rafetna trop. yow ya takh ma kham cheikh bi mak souniou wakeur ...Mangui rafetlou single bi ...Di la niane rek Niang nga féki Serigne Saliou gueule tapée ...guinaw aye diam ...yow soldat nga .yaye LAMPOU yone wi ...Boul deglou kene kouy yak
@ndeyefatoudiokhane92345 жыл бұрын
Bilahi
@nogayetoure25715 жыл бұрын
Lou werr gua wakh
@sokhnalasalikhatesamb14055 жыл бұрын
Machaallah niang❤ay talibei cheikh laniouy done ba kérok niouy sango souff yakar Serigne saliou rk😭😭repose en paix cheikh bi reste tjrs dans nos cœur❤😍😭😢
@ndongoodiagne37645 жыл бұрын
Vibrant hommage chapeau... yalla nako yalla yereum barkep serigne saliou
@estrella_bambasalihate81505 жыл бұрын
Un mois déjà mais n'empêche ça me touche encore plus que la première fois ❤ Paroles yii amna sens j'adore ta franchise et la sincérité dans cet hommage... Yalnako Serigne Saliou sunu yaakar térou niit kou bax Cheikh Béthio Thioune
Vraiment tu es le meilleur mohamed grace a tes chanson may deglou tiante gayi niola diaxasser akk cheikh bii rek diangue kate you xamoul dara yii rek di forcer mais yalla moguilenedi wonni ya nekk si xolou nity bilay lou rafrt ga def
@cheikhndiome75555 жыл бұрын
une fierté POUR LE MOURIDISME dieurdieuf mouhamed Niang thianta à vie DIEUREUDEUFI CHEIKHOUNA AHMADOU KHADIM
@ndeyeamydieng73185 жыл бұрын
Alhamdoulilah man li la done khar si yaw lou refét la yalla na srgne saliou fay💚💛💜💙❤❤❤💝💝
@bigmo44915 жыл бұрын
Tu es Fort je t'écoute souvent k dieu te protége et ne répond pas a ce ki dise du male de vous
@mbayegueny30133 жыл бұрын
Mane dama mBeuke cheikhe Bethio thioune❤️❤️
@ndongogueye7565 жыл бұрын
Mouhamed niang yalla na yalla wéral batt bi cheikh bi yalla nako serigne saliou térou
@yacinekare53504 жыл бұрын
Dounde ak dé nio ande wayé sounou cheikh yalla nako yalla yeureum té kharéko aldiana you kawé ya .Moukhamed Niang mom yalla na batt bi gueune di werr rek .❤❤
@leproduitdesongrand-pere63465 жыл бұрын
Waaw mani gaa yi yaaleen meunn, ak lou meuna xeiw sa relation ak Seriñ Salihu taawu Cheikh bi yagg na tei batay mingui weuyy mashallah
@fatoufall84664 жыл бұрын
💓💓💓 texte day riche waye💓💓💓💓 Macha alla dosén morom. Si par F F talibé cheikh Tidiane sy
@fatousow91815 жыл бұрын
Machallah mouhamedd niang yall na yalla geunn werall batt bii Diamou srn saliou thiunn mam bambii yall nalla sa sang ba terou sii barke srn touba
@pendasow58715 жыл бұрын
Lolou forna fat Soww sama Xole bi seuddd naaa troppp bilahi dama contane
@fallousene95312 жыл бұрын
Ndayé sane linekhna 😭😭😭😭😭😭😭
@moustaphadiop57025 жыл бұрын
Ndayesane Cheikh bi yalla nako yalla yerume si barke cheikh Ahmadou bamba
@aliounegueye64225 жыл бұрын
macha allah sama sopé mouhamed gnang li rafét na te nékh na chékh béthio yalla nako serigne saliou téro aldianay firdawsi thi barké borom touba mouhamed gnang yalla na yalla sakhal sa diam te wéral batt bi yokal la ay khéwal barké serigne saliou
@mbayendiaye26395 жыл бұрын
Serigne Cheikh Béthio yalla nako Serigne Saliou wallou tape bleu pour le amine
@astoundiaye5375 жыл бұрын
Lou diogué si khol si khol lay dougue koula degue khamni kou beugue cheikh bi nga yalla nala yalla moussal si nafekyi are lak
Serigne Saliou ndeyssane gnepp la yémm salaw motakh gnou tale ko té talouko machalah💕chui tidiane mais j’aime serigne saliou Moukhamed Niang doundeul❤️🙏🏻
@amycollegueye91125 жыл бұрын
Machalla Niang li rekk laye khar si yaw mouride Niép gni serigne cheikh saliou lagnou dèm ndakh mofi nékh s saliou cheikh bèthio thioune yalna tasèk yeuremadè dè borom bi si barki s saliou
@deguenesarr71805 жыл бұрын
Machallah baat bi mo dioub dousen morom si waay mouhamad niola beug ngir serigne saliou👌👌
@mamygaye94345 жыл бұрын
Serigne bethio yalla nalla borom bi aré aldiana mane je suis tidiane ma damaka fonk beugko parcek keine guenoukou 1 jrs danio togue ucad amouniou louniou lekk ndeysane mane ak sama 2copines niou dem b keureum bilahi serigne bi teralniou diokh niou lekk bilahi ak xalisse bou beuri neniou louguene beug rek niewate lene fi ...keine dou serigne bethio ci bakhh
@cheikhsall62305 жыл бұрын
Machallah yalla da fonk doumou adama motakh koko fonkk mou fonkoula
@mamygaye94345 жыл бұрын
@@cheikhsall6230 entoucas suniou boromm dafa fonk domou adama kone niit sou yeukeuté leek defko siseu guemigne tiyaba bobouu rekk guemnani cheikh migue aldianaa parck jourr bobouu serigne dafa sedall suniouu xoll tte la journée on avais pas mangé mou metiwote tropp
@cheikhsall62305 жыл бұрын
Aminnn motakh gniye wakh dagno khamoul
@xs51355 жыл бұрын
Machalla kadou yi téguinéna koula khame khameni kou beugone serigne bi gua serigne bi tamite koula beugonela thiante so dane way serigne dadane bék barki serigne saliou bonne continuation mon frère 🙏🙏🙏🙏
@bebemounass8665 жыл бұрын
Mashallah Mouhamed Niang kéne dou yaw 👌 , Cheikh Béthio Thioune yalla na yalla yokou lérame si Aldjiana you kawé ya si barké Serigne saliou Mbacké Amine 🙏
@sambasene45815 жыл бұрын
Machalla damala beugeu niang yalle na yalla weurale bate bi bare képe serigne Salliou Mbacké
@moussangom2605 жыл бұрын
machallah way yallah na baate bii wéreu si barké serigne saliou ❤❤
@ndeyefaye92265 жыл бұрын
machalla 😍😍
@amintambengue41435 жыл бұрын
Amine
@soukeynasoukeyna59125 жыл бұрын
Ndeyssane Lou diogué si khol si khol rék léy délou machallah que le cheikh repose en paix
@serigneabdoukhadre4945 жыл бұрын
tele du rire walahy yalla na diamou yague
@yayougalass33525 жыл бұрын
Pourquoi je pleure quand j'écoute cette chanson? 😥
@maxfall71545 жыл бұрын
Machallah dawna yaramm trop chiekh bethio yalla naco yalla yereum yokou ay lérram sii barké s saliou
@giusypassalacqua61355 жыл бұрын
I love you Mouhamed niang machallah nekh na lol. Paix a son âme serigne bethio
@ndiayeseynabou90425 жыл бұрын
Je suis talibé baye wayé baké baye niasse serigne saliou mbacké kén la cheikh béthio yallah nala sa sangue ba téroula téral tie aldiana firdawsi mouhamed niang bilay liguay déf tie khole yi yallah nalako suniou borome faye tie yiw machallah
@mhd03615 жыл бұрын
*Fiere D'être Thiantacoun🙏🏿🙏🏿❤️❤️*
@momoothiam16485 жыл бұрын
MHD 03 beu aldjana ❤️
@khadijakamara66945 жыл бұрын
Bâ faw
@fallmansour16385 жыл бұрын
Thiantankoune lagni done ba faw
@diarryba15415 жыл бұрын
Sax si thiantakoneb rekkk moworrr nex ténopalé
@coumbafall8815 жыл бұрын
mouhamed niang sokhla nagne la si thiant gui plus ke jamais.sa way wi firndel nako.yaw s bethio mola tanal bopam.🙏🙏🙏🙏
@toubaservices29885 жыл бұрын
Walahi dina léér gnépp ni Thioune, yay deuggi Serigne Saliou
@aidandiaye15125 жыл бұрын
Touba Services
@abdoulayeniang75715 жыл бұрын
.
@abdoulayeniang75715 жыл бұрын
Ff
@abdoulayeniang75715 жыл бұрын
J j
@ibrahim8899-j3z5 жыл бұрын
Macha allah très belle chanson Mouhamed ♡
@shamthiam77745 жыл бұрын
Je suis Tidiane et gm trop mouhamet niang. Il nous poussent à mieux découvrir Serign saliou kou yéméla mom sang bobou mbacke
@someone-ib7gd5 жыл бұрын
Ndeysan ki mome kenn la si ziakr katt yi. Machallah ay waxam dafa lerr am solo batam nk mome waxalé wouma ko yalla nala yalla sammou té arr la s barké Serigne Saliou