Mouhamed Seyni Gueye troisième Khalife de Dieu sur terre. Cela n a pas été facile mais tu as assuré Gueye
@PapeNgagneGueye Жыл бұрын
Maachaallah ! Yalla rékay Bour. Kou déglou kaadou yii khamné léepe Yalla késsé la .
@assanegueye1677 Жыл бұрын
Walahi Gueye kheweul leu dieureudieuf Sangabi
@solba56294 жыл бұрын
Yallah nagnouko yallah fayal tass niou si barkem kou niemanioul wakh Thierbi takhawayou wedi nga takhawe abamdonnel yen Nabillayii lay wakhal ak koumou mantadone signe souleymane ba Ngor
@PapeNgagneGueye Жыл бұрын
Nagniou léene moytou di diingate, mbidéef dina lorou ci wéedi ni ‘’ibliiss’’ loroo. Ahonzou billaahi mina shaytaanée radjiimi