Moussa Seye Wolofal Serigne Abdoul Karim (Vidéo Officiel )

  Рет қаралды 913,897

Moussa Seye L'officiel

Moussa Seye L'officiel

Күн бұрын

Пікірлер: 928
@MoussaSeyeLofficiel
@MoussaSeyeLofficiel 5 жыл бұрын
Machalla guisna Tahaway bii yalla nalen serigne bii fayal bopam
@F2S_Hamsatou_Tv
@F2S_Hamsatou_Tv 5 жыл бұрын
Moussa Seye L'officiel bilay xol ti sede na yalla nala yalla takhawou thi barkep serigne touba
@ablayediop3447
@ablayediop3447 5 жыл бұрын
TAWFEX AK TAYSSiR🙏💖💞
@bassleye1944
@bassleye1944 5 жыл бұрын
Diam thi yaw mon frère
@famacisse4989
@famacisse4989 5 жыл бұрын
Machallah yalna sakh
@elgoramboup7869
@elgoramboup7869 5 жыл бұрын
Moussa Seye L'officiel yalla nalaa souniou boromm deiff maguoume diné
@pasambang91
@pasambang91 5 жыл бұрын
Machallah yalla na yalla weeral batbi tei def la mak bou am l'islam si barké cheikhoul khadim 🙏 🙏
@modouabdoulayendoye5155
@modouabdoulayendoye5155 5 жыл бұрын
Serigne abdou karim yalna doune 100ans you coummencé taye si barkép serigne touba mame mame diaa🤲🤲🤲🤲
@saliouwade3051
@saliouwade3051 5 жыл бұрын
Nekhna yalla nala thiat sèkhlou dama beug s fallou barké s fallou yalla n'a guisnanetè ak s basse Abdou Khadr s barké s fallou
@maremesodafall5475
@maremesodafall5475 5 жыл бұрын
Wallay ki noumou may def eup na. Meunouma deglou ay diangam té dioyouma. Yalla nala yalla def mak bou barkél.
@nenejupiterndiaye1059
@nenejupiterndiaye1059 5 жыл бұрын
Mashalah yalna Yallah weireul baatt bii ba loo. waakh dounya dikoo deigg dissi diariniou
@northstar3486
@northstar3486 5 жыл бұрын
Yalla nala yalla def mak bou am bat si barke serigne abdoul karime🤲🤲
@lemoumbengue7037
@lemoumbengue7037 5 жыл бұрын
Yalna la yalla défal goudou fane ak wére té baddee bi wére si barkéb serigne Touba
@soxneufatimamakhtardiouf5613
@soxneufatimamakhtardiouf5613 5 жыл бұрын
Masha Allah wayeii yalla nala borom bii mousseul sii beutt akk lamign si Barkeii Xassidas yii Ku Tedd Ki samal leu bopam si Barkei Borom Ndindy👌🙏🙏
@damediop5316
@damediop5316 5 жыл бұрын
Machallah s. Moussa yalla nala serigne bi tek loxo defla magoum mouride geuna werl batt bi si barke b touba amine
@thiernondiaye3092
@thiernondiaye3092 5 жыл бұрын
Machalah yalla nala yalla def mague y’alla defale la diam diou sakh goudé fane ak wer
@diowfaty2699
@diowfaty2699 5 жыл бұрын
Ndaysan Mahcalla way yalla na yalla wéerall sabattbi Amin
@cheikhawaballa459
@cheikhawaballa459 3 жыл бұрын
Machallah ♥️♥️Sr Moussa Saye Khasida Yalna Yalla Barkél Batbi Thi Barkéb Khasidayi Machallah Sr Abdoul Karim Borom Makarimal Ahlah❤️❤️
@maguisalioukane3396
@maguisalioukane3396 5 жыл бұрын
Bilahi barki serigne saliou damala beug sama khol yalla nala souniou borom samal bopam mayla goudou fane au werr si barké serigne saliou
@alaloussalioumbacke9160
@alaloussalioumbacke9160 5 жыл бұрын
Ndeysane yalna yalla goudal sa fane may la wrer mousal la ta mouthieul la defal la tawfékh ak taysir barkep Serigne saliou
@dembasarr62
@dembasarr62 5 жыл бұрын
Li daw na yaram yalle na yalla faye bay karim moy leppou
@TAGGARTV
@TAGGARTV 5 жыл бұрын
gniye dieull seni domme di lenne yobu si ay thiakhane yu mell ni ... sen petit gale.. warr gena kholl si ki deh khale bou ndaw dara gno rou ko loudoull serigne touba ... di diadieufeul ay wadiouram NANU BAYI KHALE YI GNOUYY DEF LO AY THIAKHANE
@papemoussadiaby5161
@papemoussadiaby5161 5 жыл бұрын
Yague fi lolou té were
@loufadiaw3150
@loufadiaw3150 5 жыл бұрын
Machalah yalla nala yalla lafal thiat thie barké Serigne Touba ak khasidayi (amine)
@duduwade497
@duduwade497 5 жыл бұрын
Machallah Serigne Moussa seye yalna yalla goudale sa fan ak gnieupp
@ndayediallo4461
@ndayediallo4461 5 жыл бұрын
Machalla yala ngafi yague lol tes wér si barké serigne touba doundal Lou bari
@mamadoudeme5562
@mamadoudeme5562 5 жыл бұрын
Yagg fi lole srg moussa seye nako gneup nianal
@ablayemboup1225
@ablayemboup1225 5 жыл бұрын
Yague fi loool serigne Moussa amna sollo
@manedaba5098
@manedaba5098 5 жыл бұрын
Machalla
@mouhameddrame1464
@mouhameddrame1464 5 жыл бұрын
Machalla
@sougoubuzzdiakhate4596
@sougoubuzzdiakhate4596 4 жыл бұрын
Machalla
@sougoubuzzdiakhate4596
@sougoubuzzdiakhate4596 4 жыл бұрын
Machalla
@sambcaposamb8411
@sambcaposamb8411 5 жыл бұрын
Yalla nala yalla défal diammu machallah mourid bi
@cheikhmouhammadkabircamara351
@cheikhmouhammadkabircamara351 5 жыл бұрын
Machallah yalla n'a yalla samb barké Kou déteude ki cheikhoul khadim Amine
@boussombacke88
@boussombacke88 5 жыл бұрын
Machalah yalnala Ahmadou samou té arla si barkep radiab bi🙏🏻
@papasambandiaye5405
@papasambandiaye5405 5 жыл бұрын
Machalla SERIGNE moussa seye woy nga Sama SERIGNE baye Karim fallilou nala yalla fay thi barké Ahmadou
@sonhiboulo9752
@sonhiboulo9752 4 жыл бұрын
Machallah 😍 yalna yalla somou barkepp brom touba 🤝😍
@arameka6853
@arameka6853 4 жыл бұрын
Yalla na yalla weral bat bi mousal la si thiat walahi j'ai des larmes aux yeux serigne abdou Karim damako beug mbacke yalla nala fi yalla bayi basi kanama kanama si barké serigne fallou mbacke 🙏🙏
@ndeyehenriettengom4966
@ndeyehenriettengom4966 5 жыл бұрын
Mashallah longue vie à toi que Dieu te protège amine
@fadallks3265
@fadallks3265 5 жыл бұрын
thiam henriette
@bayecheikhdieng6549
@bayecheikhdieng6549 4 жыл бұрын
Cv
@moustaphakebe7167
@moustaphakebe7167 5 жыл бұрын
Yalna yalla goudal sa fane
@mamanaida6855
@mamanaida6855 5 жыл бұрын
Machallaaaa yalla sunu borom same la barki cheikhoul khadim
@fatoundiaye5175
@fatoundiaye5175 5 жыл бұрын
Bilae mala sope yalla na takhaway bii yaag nexna lol wooy nga sama yakar yalla nala yalla faye sama xoll sedna 💖💖tè borom makharimal aqla yaag fii lolo tè werr Serigne Fallou sur terre❤✌
@falloudiop5373
@falloudiop5373 5 жыл бұрын
Ndeyesane yalla nala serigne touba takhawou defla makkk
@babacarkarimdiop1073
@babacarkarimdiop1073 4 жыл бұрын
Cheikh Abdou Karim borom makarimal akhlaq sama yakar tay ak euleuk 💓💓💓
@sambaaw8271
@sambaaw8271 5 жыл бұрын
Kou begg Moussal Beusseul j'aime Te nianal Baye Karim Yagui Fi Te And ak werr
@NDIAYE310
@NDIAYE310 5 жыл бұрын
Yallah nala yallah taxawou seye samm la mousseul la si tiate lamign AK saytanei ak beute bou bone si barkei Cheikhoul Khadim incha'allah linga wakh yeupa neik si mom c'est makarimal akhlah incarné 💕♥️
@mamadoureussarr460
@mamadoureussarr460 5 жыл бұрын
Machalah woy bi néhna mais yalna nala yala féy si barkép sérigne fallou
@amiamar2620
@amiamar2620 5 жыл бұрын
machalla amna solo goudoufane ak weer si barke Mouhamet saw ak Cheikhouna Ahmadoul Khadim ak souniou serigne Cheikh Abdou Hakim Mbacke amine
@serignemodoudieng1000
@serignemodoudieng1000 5 жыл бұрын
Machalah yalla na yalla goudeul fan wi wëral batt bi barké borom Touba
@asssambsamb3510
@asssambsamb3510 4 жыл бұрын
Yalna bat bi yaga wer machallah
@mamandiaye1791
@mamandiaye1791 5 жыл бұрын
Machallah.yalna la serign bi fay yiww si barké cheikhoul khadim
@mouhamadoudieye1355
@mouhamadoudieye1355 5 жыл бұрын
Machalla yalla na baat Bi wer way yalla may la fan wou goud té lafal la thiat barkè CHEIKHOUL Khadim
@oumyndiaye1139
@oumyndiaye1139 5 жыл бұрын
Machallah yalla na yalla werral batt bi si barké s fallou mbackè😍❤
@iloveserignedarouhassanndi231
@iloveserignedarouhassanndi231 5 жыл бұрын
Machalla serigne moussa seye yalla gua am gueramou serigne touba amien yalla nala yalla Samb ta arrla li nexna loooooooo
@bayoumbendiop7233
@bayoumbendiop7233 5 жыл бұрын
Ma ça allah waay yall nala yalla lafal thiatt
@zeyynasene8662
@zeyynasene8662 5 жыл бұрын
Machalah yalla nala yalla def mague amna solo sant serigne Touba rek
@djibril-karimtv8063
@djibril-karimtv8063 5 жыл бұрын
Biss niki tey ya doon sama diang kat barkep Serigne Fallou
@MoussaSeyeLofficiel
@MoussaSeyeLofficiel 5 жыл бұрын
Machalla
@nogayegaye1313
@nogayegaye1313 5 жыл бұрын
@@MoussaSeyeLofficiel goudeul fanne way
@ndeyefatoutall7144
@ndeyefatoutall7144 5 жыл бұрын
machalla li nékhena si xol yalla na yalla wérale batte bi si baké serigne touba mbacké
@mamisow5308
@mamisow5308 5 жыл бұрын
Papa Djibril man miiii tamit def Nako diang katt
@djibril-karimtv8063
@djibril-karimtv8063 5 жыл бұрын
@@mamisow5308 koon nio bok eUipe mak yaw
@footempo
@footempo 5 жыл бұрын
Machalah sopou nala trop yalnala yalla takhawou🤲🤲
@modouthiao5712
@modouthiao5712 5 жыл бұрын
Machallah seringe Moussa seye yalla n'a yalla de fall la diam
@famacisse4989
@famacisse4989 5 жыл бұрын
Machallah yalna yalla goudeul fane yi yalna serigne touba fayal boppam
@mamecheikhdiop4122
@mamecheikhdiop4122 5 жыл бұрын
Mash'Allah tarkallah beugue na youni méel Billae goudal fane yalla wéereul baat bi yagal lafi sunu kaname Barkei yonénté
@modoudiop6704
@modoudiop6704 5 жыл бұрын
Talibé chieck bou beugue serigne ABDOU karime machallah
@karimsall2979
@karimsall2979 4 жыл бұрын
S'érige moussa seya Mahalia yallenafi Hague téwermunne
@ahmeddiaw442
@ahmeddiaw442 5 жыл бұрын
Ame n.a. solo lolou Yalle nala yalla takhawou bou baxe Sii bare kè kou tèdde kii
@sokhnadia7156
@sokhnadia7156 5 жыл бұрын
Machallah yalla na yalla barkel si barkep cheikhoul khadim
@khadimediop9804
@khadimediop9804 3 жыл бұрын
Bilahi yala nala Tièt sèh lou..dioulite ak mourid fier nañou ci yaw..ndaw you mèl ni yaw lañou soh là souñou rèw ngir un senegal meilleur même soudè certain amouñou chance binga ame
@sokhnasamb732
@sokhnasamb732 5 жыл бұрын
Machallah yalla na sounou borom wéreul bat bi t samou la défal la soutoura si barkè borom ndindi thiakaw thiakanam rk
@mounasssaliou4305
@mounasssaliou4305 5 жыл бұрын
Liguéyal s.touba rék mo woor👌machallah waye ndawou cheikhoul khadim bii laff thiate 🙏🏼😭😭
@fatousene7217
@fatousene7217 5 жыл бұрын
Machallah amatina solo serigne moussa seye yala nala yala faye❤❤
@bayegalayegueye177
@bayegalayegueye177 5 жыл бұрын
Machalah yalla na serigne bi yagal la
@lourd12diop8
@lourd12diop8 5 жыл бұрын
Macha Allah Yalna Yalla wereul bate bih inchallah Teuh goudeul fane yih wereul leuh inchallah
@bijouziko1284
@bijouziko1284 5 жыл бұрын
Yallah na yallah goudal say fane si barke SEYDINA MOUHAMED (PSL)
@touretapha1623
@touretapha1623 5 жыл бұрын
Yalla na yalla defall diam way li nékh na si xoll
@ndeye.fatou.Mme.diop.
@ndeye.fatou.Mme.diop. 5 жыл бұрын
Machalla yalla na la yalla deff magg nga yaga ligueyal di wolafal serigne touba.
@modoundiaye7867
@modoundiaye7867 5 жыл бұрын
Yalla nagafi yag lol
@ibrahimadieye6472
@ibrahimadieye6472 5 жыл бұрын
*Li dal doyneu kemtane.* *Dieureudieuf Serigne Touba*
@fallouba2771
@fallouba2771 5 жыл бұрын
Machallah yalla na bate bi wer 😘😘😘😘💝💝💝💝💝💖💖💖💖💖
@elhadjisouleyecisse8201
@elhadjisouleyecisse8201 5 жыл бұрын
Yallana goudal sa fane fayla sa khôl defla magoum barkel man deh tidiane wayé koula sopp la
@franciscodiaz2022
@franciscodiaz2022 5 жыл бұрын
Akassa Serigne Moussa!!Yallahnala Borom bi Sam tè defal la barkè.
@lalacamara5980
@lalacamara5980 5 жыл бұрын
Yalla na yalla wereul bate bi si barké Cheihoul Khadim
@kharysyll3766
@kharysyll3766 5 жыл бұрын
Machalah yalla na yalla weral batt bi❤❤❤❤❤
@serignesaliougaye1169
@serignesaliougaye1169 5 жыл бұрын
Machallah yalla nala yalla takha wou
@madickediop8267
@madickediop8267 5 жыл бұрын
Machala s Moussa yalla nala yalla samou
@modoukhalyndao4017
@modoukhalyndao4017 3 жыл бұрын
Masaallah serigne Moussa seye.L’ enfant exemplaire 💥 et aussi le choix du peuple 💖💗
@fatouseye2737
@fatouseye2737 5 жыл бұрын
machalla sama domou baye bi yalna sougnou borom weral batbi amine ziar ak magal
@mamediarragning4908
@mamediarragning4908 5 жыл бұрын
Ohhhhhh Ndeysan yaram dawatina s. Moussa Yalna bat bi gueuna weur 😍😍
@madamemadame3380
@madamemadame3380 5 жыл бұрын
Yalla nala Thiate Sekhlou Ya Rabbi. Macha'Allah
@fatimadia4920
@fatimadia4920 4 жыл бұрын
Wallahi Enzim li nekh na si xol douma si doyal weral S Moussa Seye ndoundou kou barguel barguep xasidayi
@cheikhndao701
@cheikhndao701 5 жыл бұрын
Machalla yalna yalla guena weral batt bii🙏🙏❤️
@ramalovebarry8702
@ramalovebarry8702 4 жыл бұрын
Machalla yalna yalla guena weral batt bii🙏🙏
@ramalovebarry8702
@ramalovebarry8702 4 жыл бұрын
🙏🙏🙏🙏❤
@maguettendiaye7076
@maguettendiaye7076 5 жыл бұрын
Machalla nekh na loll yalla nala yalla fay Amine si barkep Serigne bi
@serignefall8417
@serignefall8417 5 жыл бұрын
Am na solo yalla nala yall defal diamou thi barce brom touba
@kheusskheuss169
@kheusskheuss169 5 жыл бұрын
Machalah li nekh na way yokouté rk ak werr thi barké borom touba
@ndiayediatta5340
@ndiayediatta5340 5 жыл бұрын
Machalla yalna yalla sameu la té deff la mak si barké MOUHAMAD PSL
@gorandiaye390
@gorandiaye390 5 жыл бұрын
Machala yalla na yalla goudal sa fan mayla werr ci barke Seydina mohamed alay salatou wasalam
@mameabdouazizdia
@mameabdouazizdia 5 жыл бұрын
Macha Allah...Yalenala yalla samemou
@madinainfo6491
@madinainfo6491 5 жыл бұрын
Mach Allah s. Moussa sy yalla nala Yalla defal diam
@nenesakhodiop3657
@nenesakhodiop3657 5 жыл бұрын
Baye Serigne उएवपवदपदपव
@sokhnadiop1898
@sokhnadiop1898 5 жыл бұрын
Nekh rekh
@naboundiaye5095
@naboundiaye5095 5 жыл бұрын
Toyal Gua sama xol Serigne Abdou Karim rek la sope yalla na weral bate bi defla guay makk moussal lasi thiate barké cheikhoul khadim
@mariamabousso2558
@mariamabousso2558 5 жыл бұрын
Machaalah ligua wakh thi sama SERIGNE bi daw na Yaram 💖💖👐 Sangue bobou balla aissa boury k serigne mbacké k maaram Narou Mame Awa faye ☄💫❤❤❤❤
@awandiaye6008
@awandiaye6008 5 жыл бұрын
Machallah nékh na trop
@dollarsrozo7570
@dollarsrozo7570 5 жыл бұрын
machalla yalla wéral la t goudal say fane gnoune amougnou loutoul serigne touba linguay wakh ni mane kham nasi dara bilahi
@modoufall4327
@modoufall4327 5 жыл бұрын
Macha halla yalla na borom bo goudall sa fan
@sonoafricano6064
@sonoafricano6064 5 жыл бұрын
Machalah yalla nala yalla samm ta are la def la makk barkep serigne touba
@mamefalloufall874
@mamefalloufall874 5 жыл бұрын
machalla yalna ko yalla diapalée
@mamadouthiam2417
@mamadouthiam2417 5 жыл бұрын
Yallah nalafi Yallah yagall si barké borom touba
@cheikhouleroitempsboy2416
@cheikhouleroitempsboy2416 5 жыл бұрын
Akassa mouride yalla na leine defal diamou ak xéweul
@nianacise2550
@nianacise2550 5 жыл бұрын
Dayesane yallana yalla défal diam kontanna si yaW trop
@ablayesylla2320
@ablayesylla2320 5 жыл бұрын
Machalla yague fi loll serign moussa seuy tée wérlé
@diaodiop
@diaodiop 5 жыл бұрын
Machallah yalla nala yalla sam tè wéral bate bi
@18safartv90
@18safartv90 5 жыл бұрын
Ndieysan akasa Amna solo Lolllll barkéb 18 safar
@konateciss7997
@konateciss7997 5 жыл бұрын
Mach Allah amna solo
@MoustaphaMbathie
@MoustaphaMbathie 5 жыл бұрын
@@marouprod ko mom daje bi mom la wala s cheikhouna mbathie. Kii xalé la dankoy nianal yalla samou ko, s cheikhouna mbathie bimou guisé clip bi waxou thi dara mais nakk bolfi wax waxi droit d'auteur parce que momol wolofal bi momol daje bi , bofé néké di manacé dafay doyy warr ,
@ndoumbeseye3420
@ndoumbeseye3420 5 жыл бұрын
machalah domou baye🙌🙌🙌ay way noumay def ba guiss sama rak dji yalla nala yalla lafal thiat lal gama nak mane mi beugeu serigne fallou mbakè ak baye karim bamou diéx
@yacinediouf4929
@yacinediouf4929 5 жыл бұрын
Machala serigne Moussa longue vie à tw et à serigne Abdou Karim mbacké ❤❤
@binetafall7887
@binetafall7887 5 жыл бұрын
Ylla n'a ylla weral mouthial la si barkei srg Touba Mbacké
@bigmozgz4000
@bigmozgz4000 5 жыл бұрын
Macha Allah Rak Ji yalna yallah def la magou diné
@seynaboundiaye5629
@seynaboundiaye5629 4 жыл бұрын
Machalla s moussa
@mbackediagne8575
@mbackediagne8575 5 жыл бұрын
Yalla na yalla samou laa Arlla barkè borom Touba
S.Moussa Seye Wolofal S.Mountakha Mbacke (Clip officiel)
7:37
Moussa Seye L'officiel
Рет қаралды 94 М.
Serigne Moustapha Gningue Wolofal Serigne Saliou
21:17
Touba Mbodji
Рет қаралды 1,5 МЛН
小丑教训坏蛋 #小丑 #天使 #shorts
00:49
好人小丑
Рет қаралды 54 МЛН
IL'HAN - Qalqam | Official Music Video
03:17
Ilhan Ihsanov
Рет қаралды 700 М.
WOLOFAL BOU DOY WARR: lAAKHOU SERIGNE BI PAR S. Ousseynou Gueye
22:53
KOUREL 1 TOUTANK  DAHIRA MAFATIHOUL BICHRI DAKAR PARCELLES ASSAINIES U5 Le 25 décembre 1441.H2019
4:05
TAWFEKH PRODUCTION INTERNATIONAL HD
Рет қаралды 3,1 МЛН
WOLOFAL SERIGNE MBAYE DIAKHATE SAKHARGUI
37:48
sagou sénégal officiel
Рет қаралды 70 М.
Hommage à Sokhna Maïmouna Mbacké, fille cadette de Khadimou Rassoul
19:49
Jalibatoul Maziyah
Рет қаралды 631 М.
SERIGNE OUSSAYNOU GUEYE WOLOFAL CHEIKH  SAMBA DIARA MBAYE GAMOU LOUGA 2021
30:07
Wolofal  Sant Serigne Touba par S  Cheikh Diop Mbaye
13:09
DIOP BEUGUE FALLOU
Рет қаралды 844 М.
🔴Triste Wolofal Déee Serigne Moussa Seye😭😭😭
9:23
Moussa Seye L'officiel
Рет қаралды 29 М.