Moussa Tué€ à Yeumbeul par son Oncle, Son père versent de chaude larmes et témoignent « diarbatam..

  Рет қаралды 79,306

People 221 TV

People 221 TV

Күн бұрын

Пікірлер: 201
@hawabarham75
@hawabarham75 3 ай бұрын
Nagni bari liniou touddou yallah... La meilleure protection
@cheikhibrahimadiankha7548
@cheikhibrahimadiankha7548 3 ай бұрын
Je confirme❤
@mvmvdou
@mvmvdou 3 ай бұрын
Hasbouna alllah
@Mouhamedbeugbaye
@Mouhamedbeugbaye 3 ай бұрын
Walahi wakhgua deug 📿❤
@bintchaykh7370
@bintchaykh7370 3 ай бұрын
Wallahi soubeu ak ngone nak, bouko defei dinaniou loutiou thi saytane
@OusmaneDiallo-wk3jc
@OusmaneDiallo-wk3jc 3 ай бұрын
Légui nite gni taluniou lén ludul téléphone yi thé chéytany mongui fofou khôl daniou KO War Di soukhat sinon Dafay déé comme guarab
@FatimandaoTymandao-gr4gl
@FatimandaoTymandao-gr4gl 3 ай бұрын
Yalnaniou yallah mousseul si seytané, mousseul niou si jeuf ndiou khebou, dieuf younouy rethiou tamite. Yalnaniou yallah samm
@babasy-y3j
@babasy-y3j 3 ай бұрын
Amine
@mauricediouf4918
@mauricediouf4918 3 ай бұрын
Amine 🙏🏾
@kambayependasall8908
@kambayependasall8908 3 ай бұрын
Allahouma amine
@bosslady-hq5hi
@bosslady-hq5hi 3 ай бұрын
😭😭😭😭😭 lan moñou dal ñoune wa senegal ? Yalla nañou Yalla mousseul té samal ñou souñou ndiabot si barke Seydina Mouhamed saw ❤.
@sidyndiaye-fw2vb
@sidyndiaye-fw2vb 3 ай бұрын
Niak bayi khél sunu borom mo niou dal
@lofatou6218
@lofatou6218 3 ай бұрын
Aminee sibarke allkhoran ❤😂
@aminaseye-hs9ij
@aminaseye-hs9ij 3 ай бұрын
Salalahu aleyhi wasalam amine
@sophiasoumare2041
@sophiasoumare2041 3 ай бұрын
Aye way réyanté bi beurina Sénégal 😢😢ay way yallah nagnou yallah samal bopam are gneup si barké Nabi Moustapha psl 🙏🙏
@OureyeSeck
@OureyeSeck 3 ай бұрын
Machallah mame ji kou bakh walahi liguéyekat leu talibé baye leu moussa yalla nako yalla yeureum té kharéko aljana😭🙏😭🙏🙏
@ingcoingco3926
@ingcoingco3926 3 ай бұрын
Il faut condamner les meurtriers à perpétuité sans possibilité de libération conditionnelle. Diminuer les droits pour les criminels.
@sophierienquelaverite662
@sophierienquelaverite662 3 ай бұрын
Wala niou ray ko kouthi ray
@kc-qo9hj
@kc-qo9hj 3 ай бұрын
Vraiment
@lnpthereallnpthereal3786
@lnpthereallnpthereal3786 3 ай бұрын
Kou ray niou ray sa ndey billahi rewmi instant mom moy lolou
@YahyaMane-dw1gy
@YahyaMane-dw1gy 3 ай бұрын
Kou Rey niou reyla mo gene
@mariamadiadhiou6031
@mariamadiadhiou6031 3 ай бұрын
Wa mba li diamla
@Teamdrolevideo90210
@Teamdrolevideo90210 3 ай бұрын
Comme kou ray douniou la ray! Naniou def beine prison pour les criminels. Ci dig alleux bi. Dou ame toiture, dou ame douche , dokhou foss ngay nane di lek beine daggitou pain une foi par jour enplus daniouy dag sa niari lokho ba parei di la nok gouddi beuthieuk amoul nelaw li moy solution bi enplus comme serie laniou koy def diko tek chak mardi li moy solution bi
@HuggyBear04
@HuggyBear04 3 ай бұрын
Wa tanyi reyanté Senegal bi diam leu??? Ay wayyy
@abysall5599
@abysall5599 3 ай бұрын
Moma diaxal dall😢
@CoumbaDiouf-ft8si
@CoumbaDiouf-ft8si 3 ай бұрын
Dama ragal li aye sacrifice leu
@aminatawone2531
@aminatawone2531 3 ай бұрын
Massa sama dome yalla nako yalla yeureume téé kharéko adiana wassalame
@tedinendour
@tedinendour 3 ай бұрын
Wa mane li mome aye cauchemar là wala ohh mn Dieu pitié 👏🥲😭
@MimiMimi-vm5oe
@MimiMimi-vm5oe 3 ай бұрын
Il se peut que amena ayy mbir mystique, sacrifices ou khaptal you bone youniou dougueul Sénégal on sait jamais. Kou yabou di mouslou, di deff say invocations ta moytou boubakh
@barandiaye7347
@barandiaye7347 3 ай бұрын
Kou ray niou ray la tanque défouniouko lii dou dièh
@DiaMaty-f3m
@DiaMaty-f3m 3 ай бұрын
Bilay waxati ko dinagne déme ba dotu niou togati Sunu keur yi dh si niamu deuthie yi lagne agne dissi réreu 🥹🙏li méti neu raye rk
@ansatouadeletekagne6715
@ansatouadeletekagne6715 3 ай бұрын
Elhadj massah waye li metina trop toutes mes condoléances et paix à son âme 🙏
@Baba-xd3bk
@Baba-xd3bk 3 ай бұрын
Kou responsable mashala Moossa yala khare Aldiana
@dabaniang8141
@dabaniang8141 3 ай бұрын
Yalla nako bour yalla yeureum te dièguelko kharèko si aldiana fir dawsi thi barkhè seydina Mouhamed psl 🤲🤲
@Mbaye-o6o
@Mbaye-o6o 3 ай бұрын
Une semaine niou ray tji 5 personne 😢 Sénégal dou rew
@MbodjAmadou-dw3sh
@MbodjAmadou-dw3sh 3 ай бұрын
Ay way gnoun lan mognou dal😢😢😢 Yalla nako yalla yeureum kharéko aljanna
@maremefalloufall6894
@maremefalloufall6894 3 ай бұрын
Vraiment mon pays va male que dieu nous protège avec toute notre famille repox en paix mon fils courage là famille tout mais condoléances
@papefaye272
@papefaye272 3 ай бұрын
Man ben problème la am walahi tei dou banlieu kasser limay wakh ni senegal leigui majeur partie des jeunes ko guiss leigui affaire de milieu lay dounde man lolou depasser nama d
@MimiMimi-vm5oe
@MimiMimi-vm5oe 3 ай бұрын
Louy affaire de milieu,? En tt cas niouy bakh régler di diangui école ou métiers wathie régler beurri na. Kou nek ci lenene nak amoul mouthie ni intérêt
@alhamdoulilah3991
@alhamdoulilah3991 3 ай бұрын
​@@MimiMimi-vm5oeJe venais pour poser la même question
@mvmvdou
@mvmvdou 3 ай бұрын
​@@MimiMimi-vm5oebilae amna ay jeune you correcte amna ay waga tmt
@serignendiayebeuguefallou7088
@serignendiayebeuguefallou7088 3 ай бұрын
Ohh Thiéye Sénégal foumou dieu 😢
@sokhnagueye2363
@sokhnagueye2363 3 ай бұрын
Yalla nagnou yalla mouseul cii pauvreté 😢😢😢😢doynawar
@cira1345
@cira1345 3 ай бұрын
Que dieu nous guide dans droit chemin que firdawci soit sont deumeurs internel inchallah amine ya rabie Allah courages
@serignemansourtoure86
@serignemansourtoure86 3 ай бұрын
Je suis vraiment écœuré du silence notable de nos autorités face à ces tueries récurente sans précédent au Sénégal 😡😡😡
@abdoundiaye2069
@abdoundiaye2069 3 ай бұрын
C'est la lutte qui a rendu la jeunesse agressive
@alhamdoulilah3991
@alhamdoulilah3991 3 ай бұрын
La drogue, l'alcool, manque de repère et de référence aussi
@FallouDioum-qv1if
@FallouDioum-qv1if 3 ай бұрын
Tu as tout compris abdou ndiaye
@mvmvdou
@mvmvdou 3 ай бұрын
Non lamb yakoul dé mais plutôt l'alcool les drogues durs
@fatoucha4507
@fatoucha4507 3 ай бұрын
Il faut ajouter le slogan du " seule la lutte libère"
@abdoundiaye2069
@abdoundiaye2069 3 ай бұрын
@@alhamdoulilah3991 mai lamb dji yifay dem li ngua wakh layign dieufeundiko di agressé population paré dem soiré di zémbré di daw reck amoul arrêt
@WEUZ-h50
@WEUZ-h50 3 ай бұрын
Mon pays va mal 🥹🥹🥹 Ô seigneur couvre nous de ta miséricorde et éloigne nous de Satan.amine ya rabbi 🤲🏾
@fantasagna4076
@fantasagna4076 3 ай бұрын
Allahouma Amin 🤲🏽
@nobasiby9540
@nobasiby9540 3 ай бұрын
Amine ya Allah
@kambayependasall8908
@kambayependasall8908 3 ай бұрын
Allahouma amine
@ramatoulayengom4686
@ramatoulayengom4686 3 ай бұрын
Amine
@ndeyekhadysow3689
@ndeyekhadysow3689 3 ай бұрын
Amine yah rabbi
@mariannefoster8268
@mariannefoster8268 3 ай бұрын
Toujours banlieue La gendarmerie doit fait des descente fréquente C pas normal ca
@fatouyayunabibumambabacars4373
@fatouyayunabibumambabacars4373 3 ай бұрын
Toukhou village diotna😢
@fatouyayunabibumambabacars4373
@fatouyayunabibumambabacars4373 3 ай бұрын
Rèw bougnouko sangoul si djiko sangko si dètte😢 walahi méti trop sakh vraiment yalna yalla kharéko aldiana si barké seydouna Mohamed psl
@mariannefoster8268
@mariannefoster8268 3 ай бұрын
@@fatouyayunabibumambabacars4373 bilahi wakhal dé Boye démm yobalaime
@mariannefoster8268
@mariannefoster8268 3 ай бұрын
@@fatouyayunabibumambabacars4373 Bien dit Vérité absolue
@fatouyayunabibumambabacars4373
@fatouyayunabibumambabacars4373 3 ай бұрын
@@mariannefoster8268 parèl li môme woratoul srx
@mansourdieye9494
@mansourdieye9494 3 ай бұрын
Sénégal dafa nék deuk bi xamni alhourane niorouniu dioulite bounek War nga Di diangue alhourane mou done sa wétale alhourane day rakhass xol lépp Lou Bone sa xolou guéneko Sénégal daniuy AK dioulite té dieuféwouniuko bou nieup done diangue alhourane diko wétaliko lii yeup d'où am
@Ummu_yuusuf
@Ummu_yuusuf 3 ай бұрын
Wakh deug
@myamandiang
@myamandiang 3 ай бұрын
Ay lou khew Senegal 😢😢😢li metina
@AbdouDiop-d6t
@AbdouDiop-d6t 3 ай бұрын
yala nanou yala samal bopam samal niou sounou ndiabote si barke seuydina mouhamad psl
@FatouJacquelineTall
@FatouJacquelineTall 3 ай бұрын
Que alha lui conduit au paradis 😭😭💖
@mamikebe645
@mamikebe645 3 ай бұрын
Ay seynaté togual sonounagnou thi ray yi😢😢
@SirèNdiaye-z1b
@SirèNdiaye-z1b 3 ай бұрын
Cheikh mouhidin samba Diallo wahon na ni statut bi nék Dakar temps que diélé ouniouko fi Dakar dou mousseu ame djam est ce que dou lolou la tamit
@Dashouu
@Dashouu 3 ай бұрын
Wayé statut bi yagg na fi té lii amoufi wone. Nagnou yarr xallé yii té yarr sugnu bopp
@laperlecmoi5995
@laperlecmoi5995 3 ай бұрын
Delou si dîné rek
@soldarousbabacar7291
@soldarousbabacar7291 3 ай бұрын
Yal nako yalla yeureum si batou la ilakh illala
@princessemyadiallo9791
@princessemyadiallo9791 3 ай бұрын
Ndaysane mètina yalnako yalla yeureum khareko aldjana firdawsi thieuy Senegal khamètoumako bir keur yi kène mousouko guis daguay kou diap rakam wala diarbatam diko door door you meti bou. Yaye dji wakhè niouniko da bagn kou door domam keur yi mètina
@BitouFall-nc1uu
@BitouFall-nc1uu 3 ай бұрын
Wa lou khéw senegal ahhh man dh diakhlé na
@astoukebe2678
@astoukebe2678 3 ай бұрын
Man dama tit
@aysatoudiop4808
@aysatoudiop4808 3 ай бұрын
D’où dara iblise mo gnauw ak dolé ba paré diamou yalla bi tamite Desna Fo bi mo eupeu diamou yalla bi😢
@sénégalmapatrie
@sénégalmapatrie 3 ай бұрын
Billahi lougua wax loloula mais soka waxé niouné dagua seytané.😢​@@aysatoudiop4808
@lnpthereallnpthereal3786
@lnpthereallnpthereal3786 3 ай бұрын
Dello nala question bii
@Diara757
@Diara757 3 ай бұрын
​@@aysatoudiop4808lep tarikha yi la
@MarieHelenDiouf
@MarieHelenDiouf 3 ай бұрын
Paix à son ame 😢😢😢😢
@nabousylla1314
@nabousylla1314 3 ай бұрын
Sénégal warnagne fi def ay sarakh parce que li kene khamoul lanla.Tok sa keur sakh takhoul nga mouthie
@MamanDione-m3f
@MamanDione-m3f 3 ай бұрын
Yalla nako yalla khare aldiana firdawsi barke seydina Mouhamed psl
@abdoudione169
@abdoudione169 3 ай бұрын
😢😢😢solution bi mome penne de mort rek moy solution bi niko yalla wakhè
@noumchjoop6808
@noumchjoop6808 3 ай бұрын
😭😭😭RIP moussa
@modoudioplamp2157
@modoudioplamp2157 3 ай бұрын
Un homme responsable ❤❤❤
@AwabijouDia
@AwabijouDia 3 ай бұрын
Mane je demande hana président dafa touki dougni wax si ly tamite ah,
@elhadjiabdoulayeba4749
@elhadjiabdoulayeba4749 3 ай бұрын
Boudone ay agresseur daccord mais genrou ray yii a part yaubou prison etat mounoussi dara se sont des problemes de famille
@alhamdoulilah3991
@alhamdoulilah3991 3 ай бұрын
Khawma kane d mais mane diomi na thi Sénégal. Yembeul... banlieue Dakar bi tamite
@awakane1050
@awakane1050 3 ай бұрын
Seytané bakhoul so mèrè andalak sa sagou doyna War
@khadijakounta8434
@khadijakounta8434 3 ай бұрын
Nidiaye bi daa sadik ak kep kouy khekh Di dieul lo khamni meune naa ray nite
@Chambabel153
@Chambabel153 3 ай бұрын
Walakhi Senegal lilikoy fathie moye peine de Mort. Kou Raye nagnouko raye kou sathie gnou dagu salokho. Te Senegal defarate len toguaye te yare ndiabote bi 🤲🤲🤲🤲😭😭😭😭
@jaimemonpayslesenegal8268
@jaimemonpayslesenegal8268 3 ай бұрын
Boy bii mo guéné pakaa bii légitime de défense la
@clairemari7292
@clairemari7292 3 ай бұрын
Paix à son âme courage à la famille
@assanecorea9078
@assanecorea9078 3 ай бұрын
Merci bcp
@AboubacryGASSAMA-zs7oi
@AboubacryGASSAMA-zs7oi 3 ай бұрын
Yalanako borom bi yereum té haréko aldiana firrdawssi amine
@MultiLajoie
@MultiLajoie 3 ай бұрын
Sénégal sa famille molaye raye gniou nane seytané , peine de mort comme ça dina gniou khame dakh seytané leu 😢
@elmoussafall3887
@elmoussafall3887 3 ай бұрын
Shutt deukk bi metina so diougué si li dall si lenene 😢 walahi sécurité police war na yookk pon Sénégal 92 kéneu sagnatoufa à partir de 20hr diapp moto rk dou liguey issh
@BbMor-k4y
@BbMor-k4y 3 ай бұрын
Mon pays vas mal😢
@binetadia8439
@binetadia8439 3 ай бұрын
Ay way en moins d une semaine combien de raye li eupouna 😢😢😢
@bigdia2266
@bigdia2266 3 ай бұрын
Un homme responsable
@Chambabel153
@Chambabel153 3 ай бұрын
Nel disante Yalla diakarlo ak gnoune , mais dou nbemkete ndakh circumstances😭😭😭😭😭
@beugfallou2853
@beugfallou2853 3 ай бұрын
Moi perso je suis traumatisé bilahy walahi
@jaimemonpayslesenegal8268
@jaimemonpayslesenegal8268 3 ай бұрын
Ndeysane nidiaye djii da beuguone mou bakh rek😢
@Pirowzer
@Pirowzer 3 ай бұрын
koo beug mou bakh digko reyyy yow esk tout va bien saway?
@jaimemonpayslesenegal8268
@jaimemonpayslesenegal8268 3 ай бұрын
@@Pirowzer yaaw laa waraa wakh esk cv boy bii moko beuguone raay khamo nou histoire bii démé dangaay lathié
@Pirowzer
@Pirowzer 3 ай бұрын
Heee legui yow foo dieule histoire bobou😅🤣🤣
@ndeyefaye3821dabakh
@ndeyefaye3821dabakh 3 ай бұрын
Thiey Sénégal ly ba Cagne🤭🤭🤭🤭🤭🤭🤭🤭🤭😭😭😭😭😭
@Fatimagoudaby
@Fatimagoudaby 3 ай бұрын
Sénégal dal War nous kholate li fa kew doynawar dal
@awasylla5203
@awasylla5203 3 ай бұрын
Wa tamite rewemi dou nou si wakhe aye nite youyou raye regue li tamite doye na ware yalla na Yalla defe si rewemi diame
@Calamar-k2u
@Calamar-k2u 3 ай бұрын
C'est quoi le problème au Sénégal ont ne comprends rien ?
@PapaTibasse
@PapaTibasse 3 ай бұрын
Concert casserole yi rk
@cheikhousmanebadji6969
@cheikhousmanebadji6969 3 ай бұрын
Le problème c'est pas le Sénégal c'est Dakar n'a léer
@lilgamelilgame9586
@lilgamelilgame9586 3 ай бұрын
wa mai lu xéw senegal
@OumouFall-o6w
@OumouFall-o6w 3 ай бұрын
Paix à son àme Sénégal khôl yii mo soré Yalla nagnou kholat sougnou boop délou si Yalla
@Mouhamedbeugbaye
@Mouhamedbeugbaye 3 ай бұрын
Walahi ❤
@luluvroumvroum9502
@luluvroumvroum9502 3 ай бұрын
Li deh Moy kham ligueyam, "faniou wara yem niou yem feu" les autres prenez exemple sur votre confrère,il ne va pas vite en besogne. Genre journaliste de terrain yi la Sénégal sokhla
@malickba9778
@malickba9778 3 ай бұрын
Est-ce que dou satellite bou neek cii diaweu dji moy haftal sénégalais yii tamit 😢
@nancyndoye5293
@nancyndoye5293 3 ай бұрын
Wah lou lhew senegal, ça c est anormale. Loutakh li?
@MatyDiop-hd2wd
@MatyDiop-hd2wd 3 ай бұрын
😭😭😭😭
@couritad4398
@couritad4398 3 ай бұрын
Wa li ba lagn
@Oupsididitagain
@Oupsididitagain 3 ай бұрын
Senegal legui comme ay Americain un 2 3 Ray ba kagne khametoumaleen d man dama ragal sah gnibisi senegal ndakh yii khete allahouakbar legui ay sauvage ngeun ak ay khol you gnioul nek ay bandit ma leen ragal senegal rek doyna seuk
@EvaBasse-g4i
@EvaBasse-g4i 3 ай бұрын
Khol yé woww rek haine lagniou am gniou dénthiouko lou yague motahh ray d'où nék dara thi gniom haine bi la
@cisseaziz2707
@cisseaziz2707 3 ай бұрын
Mai senegal mom leegui chak jour ray ray ba kagne tiite na deh
@MahmoudKoly
@MahmoudKoly 3 ай бұрын
souba 🔥 billahi 💦 dé may 🔥 hii🔥bi guine Bissau 🔥 hi ho 🔥😭 adouna 🔥 dou dhr 🔥
@AwaDelechat
@AwaDelechat 3 ай бұрын
Moi personnellement je ne comprends plus rien au sénégal autant de mort
@SirèNdiaye-z1b
@SirèNdiaye-z1b 3 ай бұрын
Dama diomy dh
@YacineMbaye-c9z
@YacineMbaye-c9z 3 ай бұрын
😢😢😢😢😢😢😢
@KhidmalBarkham
@KhidmalBarkham 3 ай бұрын
Khékhé nganaay yeufou tapétela😡
@diopabdou6983
@diopabdou6983 3 ай бұрын
Histoire bou amé naniouy lath noumou démé ? Mane sama diarbate bouma guénél pakka dima diéma diamm dotoko déf ....surtout nga deuk sama keur di déff malay téré rk Cest de la légitime défense
@Thiam-i9y
@Thiam-i9y 3 ай бұрын
Kou ray sama mbokk ma ray sa ndy amoul xalate
@Diara757
@Diara757 3 ай бұрын
Khale yi kosi deg mouy wakh mouguinan barke seringe touba ak worna seringe touba yen kilifa tarikha yi wakhlen ak talibe yilen topeu khamal len li Yallah ak Yonente bi S A W wakh mogeun sen thiakhan yi ay magal gamou apel thiante wakhlen Khale yi niou diamou Yallah
@lnpthereallnpthereal3786
@lnpthereallnpthereal3786 3 ай бұрын
Senegal de instant bii com gta san andreas billahi ray bi di melni toule ak malle kou ray niou ray sa ndey lolou kasse moy solution bii
@GoraLo-bi1wl
@GoraLo-bi1wl 3 ай бұрын
Il voulait juste la corriger saytane mon bari dolle rekk
@chachawane6836
@chachawane6836 3 ай бұрын
Correction baci paka c'est trop
@coach9635
@coach9635 3 ай бұрын
​@@chachawane6836boy bi ndieuk diamé
@AichaLuna-ot2lw
@AichaLuna-ot2lw 3 ай бұрын
Mais il y'a quelque chose qui va pas , Sénégal 😢😢
@user-laurentiwobi
@user-laurentiwobi 3 ай бұрын
😢😢😢
@cabouthiong6806
@cabouthiong6806 3 ай бұрын
Bilahi wounte viral rèk
@ndiemendiaye9979
@ndiemendiaye9979 3 ай бұрын
Mane lima guisni comme peine d mort amul nanu def ku rey niu teth la a vie bole thi do am visite ben yone ni mm 5mn pur prendre l’air
@hamidoutall9134
@hamidoutall9134 3 ай бұрын
Lep yayam la hamone na lep topou xalé bi diko wakh mounieul rek tay li lako yobé
@siradiop1391
@siradiop1391 3 ай бұрын
Djiné yis ak cheytan danion tasse thi deke bi kou mene moyetou thiow ak aye problème you bari défko ak di laap di deguelou alkhour hanne
@FatouBenzamineDieng
@FatouBenzamineDieng 3 ай бұрын
Wa gue yakar ni ay djiné dougougnou ci deuk bi ah li mom doyna war peine de mort faw mou am fi
@CheikhouToure-xr1rp
@CheikhouToure-xr1rp 3 ай бұрын
Saytanei togol dougou gue sougnou deuk bi
@AichaBa-xk5jp
@AichaBa-xk5jp 3 ай бұрын
Li eupe na déh
@mansoursarr1250
@mansoursarr1250 3 ай бұрын
Amna Oustaz bouniwon fek moniment bi migui fi Dakarou dougnou ame diam reyanté dana beri ak yenen nak yenen
@WEUZ-h50
@WEUZ-h50 3 ай бұрын
Mouhidoune samba diallo !
@DiamaNdiaye-l9u
@DiamaNdiaye-l9u 3 ай бұрын
Sen faut yi si titre bi barina trop xolat len sen diang journaliste yi topou cas rek nguen fi neiker va dolen xol sen titre yi
@ndeyeamydiallo9581
@ndeyeamydiallo9581 3 ай бұрын
Khalè yi gno wara bayi Lou bone son oncle ne lui voulait que du bien ba natou dal co si
@veroniquenatack7392
@veroniquenatack7392 3 ай бұрын
*Ay way Kholale lolou rk😢💔*
@MimiMimi-vm5oe
@MimiMimi-vm5oe 3 ай бұрын
Lolou la parfois danga léne di beugue yare mais dougn la falé deugueur bopp tella wow beut. Motakh khalé soko beugué yare mou teu bayiko diko sétane surtout ko diouroul
@PrincesseAidaBa-ek7eb
@PrincesseAidaBa-ek7eb 3 ай бұрын
​@@MimiMimi-vm5oeweh ta parfetment reson
@AmbroisineMendes
@AmbroisineMendes 3 ай бұрын
Ana yar ak paka tamite hum
@alassanegueye3965
@alassanegueye3965 3 ай бұрын
Reiw boko dieulei ci dereit , sa ngour dafay beuri ay bakane you rhott.
@rounjofficialminekomine9772
@rounjofficialminekomine9772 3 ай бұрын
Hay hay hay hay tuer mom hana dafa hew legui
@MoussaDia-f6h
@MoussaDia-f6h 3 ай бұрын
Wa mane damay beugeu djomie wala une semaine de meurtre sa devient sérieux maintenant
@mamadoundao2579
@mamadoundao2579 3 ай бұрын
Nagnou dème un deux raye niou toguala thiébou yap va paré soul la
@sophrotall8105
@sophrotall8105 3 ай бұрын
Khaw ma kou am khelou ray Aziz Dabala mais yi lal na lalake ganawam tang na lol yalna fi yemmmm borom bi dakhal niou cheytane si souniou rew ak liko weur
@sandoumbembooj699
@sandoumbembooj699 3 ай бұрын
Seras ak daaral ba abatiore Fora pikine Thiaroye Yeumbeul dereetou malaa yi seen leeguey yeep raay khaar ak naakh Moy seen leeguey
@maremefalloufall6894
@maremefalloufall6894 3 ай бұрын
Pene de mort c'est toue c'est très facile j'ai les l'arme c'est pas facile
@NdiagaDiop-f1x
@NdiagaDiop-f1x 3 ай бұрын
Soyez sérieux !!! Ne mettez pas le grand père à l affiche avec un couteau ensanglante !!!!!!!! Toujours vous vous attaquez aux rasta ??????
@diopabdou6983
@diopabdou6983 3 ай бұрын
Bougn Niane deuk ak yén boyi dawal katt charette yi niniou deuké Yeumbeul ak thi banlieue bi li Yallah Xam doyna
@FatouSeck-cn2vz
@FatouSeck-cn2vz 3 ай бұрын
Peine de mort rek c la seule solution
@MultiLajoie
@MultiLajoie 3 ай бұрын
Sénégal ray ray domou diambour et dire satane subhanallah 😢
FAMILLE SENEGALAISE - Saison 03 - Episode 39 - VOSTFR
1:24:02
Pikini Production
Рет қаралды 1,3 МЛН
Chain Game Strong ⛓️
00:21
Anwar Jibawi
Рет қаралды 41 МЛН
Что-что Мурсдей говорит? 💭 #симбочка #симба #мурсдей
00:19
Drame à Keur Mbaye FALL: Il tue son ami suite à une dispute !
16:40
LERAL NET - LERAL TV
Рет қаралды 15 М.
Polygame - Saison 3 - Episode 127
30:06
Senepeople
Рет қаралды 150 М.
Chain Game Strong ⛓️
00:21
Anwar Jibawi
Рет қаралды 41 МЛН