Thiéye serigne Maodo sy . Mo diékh thi yallah mo séye thi saydina Mouhamath mo beugeu Cheikhou tidiane
@alidiao154010 ай бұрын
Inalilahi wa ina ileyhi radjihone ndeysane baracalahou fika mame Ousmane yalna yala yeuteumko ak mbolem dioulite thi barque seydouna mouhamad aleyhi salam❤
@ramatoulayediop747010 ай бұрын
Yalnako YALLA yereum te xareko aldjana firdawsi.
@mortallabeye786510 ай бұрын
Macha'Allah ! Yalla na Bour Yalla térou Serigne Mame Ousmane SY Dabakh ci Yeurmabdèm gou yaatou ga ak Ndièggeuleum gou kawé ga, té dalal ko thia Aldianay Firdawsi bi Barackaty Seyyidil Wujud PSL. Amiine Ya Ilaahi !
@Sopeymbaye10 ай бұрын
J adore la famille sy .yalla nako yalla yereum mou guissentek seydina mouhamed psl ak mamame yi papame yi te yalla tase gnoussi Sene barket
@Thiatgueye-nx1tj10 ай бұрын
Machallah machallah machallah machallah sy malik sounou sang bi amatina solo sy malik yalla nako yalla yeureum te jegal ko thi barke seydina mouhamed s a w
@Ndeyeastouballa10 ай бұрын
Mame Ousmane Sy Yalla nako yalla yeureume té kharéco adiana firdawsy si barké Mohamed psl 🤲🏾🤲🏾
@oumoukaltomdiop520210 ай бұрын
Ndeysane Sy Malick c triste 😭 Mame Ousmane Sy Dabakh yalna yallah kawel aldjanam wanalé ko ak Mamam you bakh y’a🤲
@toutanendiaye701910 ай бұрын
Yalla nako Yalla yeureume t kareco aldiana firdawci t mou wetelecou Rassoulahi pls amine yarabil alamina s'y malick
@derambodj262210 ай бұрын
Yalna Yalla yésal yeurmandé ak diégal thi barkei nabi Moustapha psl
@aissatawar483810 ай бұрын
Wa inna lillahi inna ileyhi rajooun sincères condoléances paix à son âme Qu'Allah l'accueille au meilleur des paradis Firdawis
@malickkane155310 ай бұрын
Machallah ❤ mission accomplie YALNA la yalla yeureum té kharé la sa aldiana you guena kawé ya si barké yonénti bi
@tinendoye11710 ай бұрын
Yalna Yala yessal yermande si kawam Seydina Mouhamed Psl terrouko sa Aldiana Amine si barkep Seydina Mouhamed Psl Amine
@djibrildiatta627310 ай бұрын
Que DIEU sauve son âme .Amîîn
@diakhereseye327510 ай бұрын
😢😢😢😢 oh serigne Maodo Sy xolll yi toy nagne
@aissatoutoure351410 ай бұрын
Il m’a fait pleurer walahi 😢😭😭😭😭yalla nako yalla yeureum mame yaw Tmt yalla mayla goude fane Ak wer inchallah ❤❤❤
@myamya652310 ай бұрын
ndeyssane li dafavtriste ndeyssane. Elections té tah wayé li gnimou touché beurina trop
@adjathiam-fh2cz10 ай бұрын
Serigne maodo yalla loole té wére lole inchala ❤❤mas ta
@saffiatoundure775110 ай бұрын
Ndeysaan y yalnako Yallah yeram teh hareh kor c Jannatul firdawsi 🙏🏽🙏🏽😪😪
@diaryndiaye301810 ай бұрын
Machalla Mame Ousmane sy Dabakh yalla na Niou ka yalla fayale si Barke seydouna Mohamed saw
@FantaDieme-u4n9 ай бұрын
Ndeyssane c un jeune mame Ousmane aka bakhe je me un ziare général gt chez lui Wallahi mouwathiei bopame teirale gnou ake sa famille Wallahi Nianalema ake gni ma andale paix a son ame 😭🙏yallanala sa mame teirou cibarkem
@aramembaye9710 ай бұрын
Que le tout puissant l'accueille dans son paradis firdaws ainsi que les personnes qui s'y sont devancees thie barke Seydina Mouhamad psl amine.
@AlbouryDiaw-gq3uq10 ай бұрын
Yalla nako yalla yereum té khareko aldiana firdawsi Amine ❤
@thiorosall10 ай бұрын
Yalla nako yalla yeureume khareko aldiana firdawsi barkép seydina mouhameth amiine
@adjafatouthiaw209410 ай бұрын
Salam Amine YA RABI sws
@yamadiedhiou48210 ай бұрын
INA LILAHI WAA INA ILEYHI RAJIHOUNE MAASSEU YALANAKEU YALLAH YEUREUME TEU KHARÉ KEU ALDIANA FIRDAWS INCHALAH YALANEU BOU YAAKAR TASSE INCHALAH YALANEU KEU YALLAH TÉREULE SI FIMOU NÉKEU 😢😢😢😢
@OusmaneNdiaye-jl3ft10 ай бұрын
Yalla nako Yalla yeureum khareiko Aldiana ci barki Seydina Mouhameth SAW
@maimounandour744210 ай бұрын
Yalna yalla yieureum kharéko aldianay firsawsi kou bakh ❤️. Diko diaalé a toute la houmma islamique
Alhamdoulilah Rabil Alamina Massessaleine linou bok yalanako Boromebi mtw yeureume bidiahi Taha psl sounou sangue Amine
@astouniang470510 ай бұрын
Toujours moi de mars 😢 yalna yalla yereum
@DraméSidymohamed26 күн бұрын
Le décés de mame ousmane sy dabakh me fait pleurer❤❤❤❤😢😢
@AlbouryDiaw-gq3uq10 ай бұрын
Que son âme repose en paix ❤
@ndeyebineteseck932310 ай бұрын
Allakhouma amine ya rabi
@ndeyebineteseck932310 ай бұрын
Bismillah alkhamdoulilah gloir a allah le tout puissants psl sur notre bien aimé masha allah alkham doulilah
@marietoundoye316010 ай бұрын
Ndeysane yalna yalla wathié yeurmadem ci mome ta wanaléko akh wediouram sy , métina yalna gouddal sen fan gni dess
@myamya652310 ай бұрын
massa sunu serigne massa Sy Malick beguniu nguene am loulene meti Sy Malick. Yalna leneu borom bi subhana wa tanhla naylene holou mougn. Yalnako borom bi subhana wa tanhla yereum haréko aljana yok leram tass niou ci barkem barké Seydina Mouhamed sallallawu hanleyhi wa salam
@fatimenahaye-wn7ek10 ай бұрын
Machala machala masa Sy Malick❤️♥️🤲🙏
@diatoudiop456210 ай бұрын
Yallah na khipé aldjana firdawsy allahouma amine inchallah 😭😭😭😢😢😢😢
@NdeyekhadyDiouf-en7qt10 ай бұрын
Yala n'a ko yala yeureum te kharelene ko aldiana firdawsy amine massa sy
@abdousakho407610 ай бұрын
Yalna nako Yalla yereum té khareko aldiana barké seydina mouhamed
@khadyjadiop574010 ай бұрын
Maodo sa oyof ak sa khol bou diégué daf ma yéme machalah yalla nala nala yalla bayi Bassi kanam gua gnouy koungué Sy Dabakh dagay toyal khol ❤
@matysamb165610 ай бұрын
Ndeysane walahi Sy Malick metina mais nounial Sy Malick beugouniou Dara lou len meti wagné. Yalla ken meunoul kheuthio ak mom Mame Alpha kou tey Dale mandou billahi ken degouco thi dara Yalla na Yalla yeureum co té kharéco thi Aldjana firdawci Yalla yok ay leram té tasse niou thi Barkem thi Barker Serigne Babacar sy rta nioulen di nianal Sy Malick Yalla bayilen fi bathi kaname kaname thi Barker Serigne Babacar sy rta ndiabotou Mawdo daniou sell yiw Yalla molene defal lerr AK bakh yiw Yalla na Yalla goudeul seni fan thi Barker Serigne Babacar sy rta Sama khôl toy na walahi
@ndiawarba34110 ай бұрын
Sama khole fessna
@elhadjimalicksy3010 ай бұрын
Amine ya rabbi. Ya baax.
@myamya652310 ай бұрын
ndeyssane ziar nalene sama mbok yi
@MoussaCiss-iq6kb10 ай бұрын
Paix à son âme amine yarabi yalla nako yala yerume kahréko aldiana
@mariamadiawara575210 ай бұрын
Mame ousmane yallana nga doneu ganou bour yalla si barké seydina mouhameth psl.
@DiarietouNiang-q5e10 ай бұрын
Ndeysanne que firdawsi soit sa demeure éternelle. Amine
@CheikhOumarSow-oy9rd10 ай бұрын
Yalna firdawsi done sa dalouwaye si Barké SÉYDOUNA MOHAMMED PSL
@adjathiam-fh2cz10 ай бұрын
Yalla kharé aldiana yarabi si barké seybi mouhameth psl ❤
@cheikhcissokho918110 ай бұрын
Machallah Yallah yog yeurmandem nou yagko nianal Sy Malick
@lionelione-zd7oq10 ай бұрын
Inali lahi wa ina ilayhi rajigona amina Amina
@ThioroDiop-k2v10 ай бұрын
Amine yarab ,
@ngoneseck517410 ай бұрын
Yall na hipe ardiana firdaw mame Ousmane sy dabah😢
@morsarr656010 ай бұрын
Amine ❤️♥️♥️
@IbrahimaDrame-er2pr10 ай бұрын
اللهم إغفر له وارحمه واسكنه الفردوس الأعلى مع النبى صلى الله عليه وسلم 😭😭😭
Thieye waaye adouna sy malik yallnako yalla khare alldiana firdawsi
@nogayekone116010 ай бұрын
Yalla na Yalla yesal yeuremademe thi kawam thi barker seydina Mouhamed psl 🙏 🙏🙏😭😭
@nogayesene343910 ай бұрын
La ilaha ilala Yalna Yalla harékou si aldiana Firdawsi si barké Seydina Mouhamad PSL
@jodiemaury930610 ай бұрын
Massa siggil leen nigalé yallah yeurem tè kharel aldiana firdawsi amine ya rabi
@dieynanndiaye925310 ай бұрын
اللهم اغفر له وارحمه واجعل الجنة مسكنه ومأواه اللهم اجعله في جوار سيد المرسلين صلي الله عليه وسلم مع النبيين والصديقين والشهداء والصالحين وحسن أولئك رفيقا البقاء والدوام لله وحده
Ndaysan 😭 yalna yalla léral ganwam Amine ya Rabi 🙏🤲😭💔
@amymbaye519210 ай бұрын
Yal na yalla yeureum ko ta diegal ko ci barke moukhamad psl
@loumbabacar493710 ай бұрын
Yalna yalla yaame😭😭😭😭😭
@boussoniang356310 ай бұрын
Innalilahi wa innahilayhi radiouhon nouvelle tiss neuh li bour yalla rék moko sagn yalna ko bour yalla yeureum té kharé ko aldiana firdawsi😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭 hadara bi dioyna wét😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@oumarly318510 ай бұрын
Machalla yalla nako yalla kharé aldjana
@mamefatouba58010 ай бұрын
Ndeysane yalnako yalla kharé aldiana firdawsi paix à son ame