Fan's Modou lô la meii ce sera la première fois que je supporte Balla
@DjibrilBa-xp7te4 күн бұрын
@@mamecheikhmbow5033 wakhi doff 😁😁😁😁😁
@DjibrilBa-xp7te4 күн бұрын
@@mamecheikhmbow5033 nioune Modou kharagne lô bourou lamb dji seul
@aidajuf83773 күн бұрын
Park mo douma sa mbeur dan ko
@omarlaye26584 күн бұрын
Je suis un fans de Modou lo, Mais Balla gaye 2 yalnako yalla maay ndaam
@RokhayaBiteye-g8k3 күн бұрын
Siteu guirr yalla amal diom rék nga tahaw bi dou yooyou déh 😂😂😂mafia Balla gaye ana guéne 🎉🎉🎉 Balla seul amoul lénéne
@alphadiallo91714 күн бұрын
Situé bipa do youhou do napaté ki Moy Balla mola Daka wah mola Daka beuré
@loufa2992 күн бұрын
Balla gaye 2 Seul kou d'accord lalal j' aime🥰❤
@MatarNdiaye-j9n4 күн бұрын
Je supporte modou lo mais siteu damako yagg beug walahi ❤❤❤❤🎉 ndam rek baye fall bi nio bok darou salam ❤❤❤ mais amal yarr nigua dokhalé ak modlo bakhoul .😢
@FatouMbaye-dy2ol3 күн бұрын
Kon déh. Nion yam mane supportére modou lô la mais siteu la faral siteu yalla nako yalla soutoural mayko ndaam sikaw balla gaye2 inchallah
@DjibrilBa-xp7te4 күн бұрын
Yaldaw vs fawzeyni 😂😂😂
@kanegueye3884 күн бұрын
Siteu fait attention Ballah est un vrai lion
@AbdouSene-f5k4 күн бұрын
Balla seule je suis fière d'être sérère euplé wo Balla gaye 2 ay suportere sérère
@JeanNdong-y1r4 күн бұрын
Do sésère erreur nga Wassi thiakhane gueum khokhof
@babacarndaw45804 күн бұрын
Dangay doul
@ndiagafaye31064 күн бұрын
Fooko tek
@zrtikhdcbn4 күн бұрын
Moi aussi je suis serrer je supporte balla
@sidzboy38364 күн бұрын
Lep bene la c’est le Sénégal qui gagne
@KamaraSarr4 күн бұрын
machallah je trés contant balla gaye2 surtout sporsor néwéli métani en paulh ci wolof moy nékhna météwoul
@oumar-dz2ne4 күн бұрын
Fans de modou lo là mai je supporte BALLA GAYE 2 ndam rk INCHALLAH
@bagiss3603 күн бұрын
Je suis supporter de Modou lo mais balla yalla nako dane insalah 😊
@elhadjipapaseye55404 күн бұрын
Je suis fans modou mais yalna baalla dan
@MamegorDieng-os2fj4 күн бұрын
Amine
@sambadiouf91214 күн бұрын
C'est parce que siteu def lén douma dan lén avec la manière et vous vous êtes refusé 😂
@SYN9794 күн бұрын
@@sambadiouf9121sou dégoul français nopil wala nga wax li nga xam😂
@FatouMbaye-dy2ol3 күн бұрын
@@sambadiouf9121boul wakh lolou Mane supportére Modou lô la mais siteu la faral siteu damako beugue bilakhi siteu yalla nako yalla soutoural mayko ndaam sikaw balla gaye2 le 5 juillet inchallah tarkidan bi ak Modou kharagne lô kessé lagniouy toppou siteu rek amoul lénéne
@FatouMbaye-dy2ol3 күн бұрын
@@sambadiouf9121Mane déh mbokkou masi Mane supportére Modou lô la mais siteu la faral siteu yalla nako yalla soutoural mayko ndaam sikaw balla gaye2 inchallah
@NeneCorrea-sy2ll4 күн бұрын
Pere max mom 10% rek nio ko intéressé si combat bi wayé amoul yakar si mbeureum bi😂😂😂 Yaldaw vs Simba
Mome ak Lac beine leu, sougnouy signer rek guani ils vont écraser leur adversaire 😂😂😂
@TaphaKara-e9t4 күн бұрын
Siteu a vie ❤
@alphadiallo91714 күн бұрын
Gnari siteu balla moléne meune. Situé Wahbi mo eup djeuf dji. Balla Moy lamb
@AbdouAziz-ri8td4 күн бұрын
Siteu Thiak Thiak le Comédien la Dey Daw
@LamineBadji-x3r4 күн бұрын
Balla dhé dinalleuh door ayy door you métty daane leuh 🤣🤣🤣🤣
@mouhamadoudiene13153 күн бұрын
Supporter Modou la mzis Yalla na balla tègeul sa ndy do nitou dara domaram ji tekk khél rek nga nékkè ci lamb champion clos clos bi. Balla Gaye yalla nako yalla soutoural ba do am reupp ci mom sinon rek adouna toukki ndakh sa gatt gou reuy
Boul si ték sa khaliss de Siteu moko mane té inchalla siteu dinako dane inchalla
@SagnaMoussa2 күн бұрын
Balla seul siteu mom wakh mo takh Mouy am combat après chaque défaite mais waroul sakh am Balla dans les normes
@CHeikhKebe-um4ku4 күн бұрын
Siteu késsé❤❤❤❤❤❤❤❤
@FALLOUNDIAYE-d2m3 күн бұрын
Siteu rek ♥️♥️♥️♥️♥️
@yacinebouballaguaye22434 күн бұрын
Machalla respect pour mon petit frère l'homme au mental fort nous les supporters fidèles nous sommes la pour vous souvenirs force a vous champion yalnala yalla défal diam ake ndam inchalla Amine yarabi balla rék balla késsé 🤲🏻❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🤲🏻
@ibrahimaibrahima64484 күн бұрын
Aythia Yacine ya waur dh sampou rék takhaw degueur Balla Gaye 2 à vie ❤
Vraiment waxkate gua avant combat day wax après combat day wax😅😅 biir combat gua daw Introduction wax Développement daaw Conclusion waax😅😅
@LibasseBa-c6u3 күн бұрын
Balla gaye le lion 🦁 de Guediawaye ndam rek inshalla ❤❤❤💪💪💪💪
@omardieng54224 күн бұрын
siteu kasé❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@mhdmetza1224 күн бұрын
Ohhh "Balla le lutteur le plus populaire 😊"
@khalillze16724 күн бұрын
Regard Max mbergane 😂😂😂dafa melni xaliss moko dougal ci combat wayé dou revanche déeee😂😂😂
@mouhamadoudiene13153 күн бұрын
Dmrm ji xaliss rek la geum mom moy dawlo siteu bagn mou danou pour meun yokk cachet wam
@MamadouSAMB-ov6mhКүн бұрын
Lo menoul am sii modou lo doko am si balla
@soppeousmanesonko7774 күн бұрын
Modou Lo Seul 🥰 Siteu Ndam reke inchallah 🙏
@adamadiouf99263 күн бұрын
Vision Sénégal 2050 inchalla ❤❤❤
@Petitzo3 күн бұрын
Siteu siteu leuhhhh 💥😂❤
@AliouNdong-w1g4 күн бұрын
Siteu rk❤❤❤
@Mbodji-walo4 күн бұрын
Yalmine bi seul❤❤ yalla nala yalla may ndam❤ kanam inchallah borom xôlou social❤
@FatouMbaye-dy2ol3 күн бұрын
Amine yarabi je suis supportére de Modou lô mais siteu damako beugue bilahi siteu yalla nako yalla soutoural mayko ndaam sikaw balla gaye2 le 20 juillet inchallah
@Mbodji-walo2 күн бұрын
@FatouMbaye-dy2ol amine
@MameAbdouNdao4 күн бұрын
Je suis un sérére et fier d’être supporter balla gaye 2
@ibrahimadiouf96854 күн бұрын
Ma sœur ngèneu lène ci li ngéen nek: nek sérère téwoul nga supporter Balla. Bo wakhei ni:" je suis fière d'être sérère mais je supporte balla" c'est comme si nek sérère supporter balla dou lou normal. Alors que siiiiiii
@NdiagaNdiaye-kj5om4 күн бұрын
Première fois may supporté Balla gaye,Siteu Dafa Bari wakh trop
@abdoukhadrediouf59194 күн бұрын
@@NdiagaNdiaye-kj5om tei tapett la . Lolou rek mo m méti
@MatarNiang-m9g4 күн бұрын
Séne data yaye situé seull
@ouzlepikinois4 күн бұрын
@@MatarNiang-m9g fils bayil saga yii li sport le rék té ndam li ngènoul galsen
Nous sommes tous des humains afférou ethnie bokoul sii sport boulén gnou sonal
@ibrahimadiouf96854 күн бұрын
Balla moko fi adiwoone d contre Yékini. Ndem si Yallà, papam doubless yalnako Yalla xaarei aldiana mais dem na ba casamance di diooy nane Yékini néna faaléwoul diolas yi tei walaaaahi Yakhya waxoul lolou. Yalla baal ma mei bobou da fekkei ñou ragal mystiquou Yékini dou woute wallou. Grawoul on a compris. Olof ndiaye nak wax na ni:" kouñou fay nga mérr li nga lèblé mo baxoul"
Siteu guir yalla boul daw deuguelal sa bopeu guir yalla bi dou yoyu 😂😂😂
@FallouMboupe3 күн бұрын
Fans Modou lo yepp balla le faral ❤❤
@FallouDiop-r6l3 күн бұрын
C'est amine Bruxelles 👑🦁❤❤❤
@bayelayendiaye85754 күн бұрын
Ndangoulal balla AK champion waw tmt
@khalillze16724 күн бұрын
Héeee homme de tenue héeeee😂😂😂
@2M5-Motivation4 күн бұрын
Siteu réwna néna sama combat ak Omar Sakho taxawna 😂😂😂
@MoussaNdiaye-w5c4 күн бұрын
Fier d'être sérer siteu rek bi dou yoyou dé balla
@aablayesy4094 күн бұрын
Supporter modou Lô Yi si commentaire yii Louye sene bleme Siteu mo dane modou Lo sérieux Siteu seul ❤❤
@petitjoeba40314 күн бұрын
Albourakh dala nakh gua djitou si press bi
@SambaSarr-g4w4 күн бұрын
Nn siteu mo dakka djaye lamb kw😂😂😂😂😂
@demboababacardiedhiou25393 күн бұрын
Parlementaire bi 😂😂😂😂
@senegalkesso12934 күн бұрын
MANI KENE DÉM JEUNDI JUS AK GLACE WELLY❤️
@abdourakhmanediallo82764 күн бұрын
Idee bou bakh la ❤
@IbrahimaNiang-r7f4 күн бұрын
Siteu seul fière d'être sèrere ndam rékh inchallah
@FatouMbaye-dy2ol3 күн бұрын
Amine siteu rek amoul lénéne je suis fans de Modou lô mais siteu la faral siteu yalla nako yalla soutoural mayko ndaam sikaw balla gaye2 le 5 juillet inchallah
@pascalkane97673 күн бұрын
Siteu sait faire le show il vend bien ses combats maintenant Balla Gaye 2 c'est une autre réalité 😂
Site de média yi mélni ay sponsor 😅 ak séni micro you beuri danguéna wara fay marketing 😂 Siteu seule wwaw tarki bi rk laniouy topou 🎉❤ Mé balla nk dou niékhou niébé attention tarki 😢
@MbayeDonde-n9o4 күн бұрын
SITEU SEUL BROM DEUK BU ❤❤❤❤
@ndoyebara40404 күн бұрын
Siteu télna na wouti walou di monan revenche lay dieuleul yekini 😂😂
@Bayedarou-r7l4 күн бұрын
Balla nguirre yalla kii dakharale ndayame
@SaliouNdiaye-v1p4 күн бұрын
Balla seul seul seul seul ❤❤❤
@SaliouSy-kk4mw3 күн бұрын
🙏🙏🙏🥰🥰❤️❤️🤲🤲
@damelo26534 күн бұрын
Yaw mom do touss mounane revanche 😂😂
@azizjazzdiop94116 сағат бұрын
Fait très attention Balla techniquement tu est plus fort mais Siteu peut te battre il cé bokou amélioré en lutte
@MamadouKa-h2k3 күн бұрын
😅balla neena dekoy dakheu ba diappoko daane Kone déjà khamnaci saway dou daw
@bachiroufaye72654 күн бұрын
Balla rekk❤
@ZakariaDiedhiou-bg5dsКүн бұрын
Ce jour là balla danako wone lane moye Say Say boudawé mou fékofa tégueulko bé mou nékh inchallah
@mameballacisse16214 күн бұрын
❤❤❤❤❤
@ndenediagne504 күн бұрын
Siteu yaw dara Djiomboula baye fall nga ❤
@AssaneSadio-nk2ih4 күн бұрын
@@ndenediagne50 Beury défaite REK. Man fii nga diarr baa dane balla fala xamoul
@ndenediagne504 күн бұрын
@ balla gnata défaite la am mdrrr dane force 😂
@zrtikhdcbn4 күн бұрын
Je supporte balla mais tu a raison
@damewilane55Күн бұрын
Siteu nagua am ndy diome sama dernier chance migui ni si yow Ki sogua tané sa trou yeup lay teuthieu
@Dani-ibrah3 күн бұрын
Kou dann bakhna 😂
@PapaThiam-pm8ss4 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@patrioteafricaindusenegal62844 күн бұрын
Thiey Lac 3😂😅😅😅😅😂😂😂
@TalibEsxadim3 күн бұрын
Daaw gua ba aksi fii😅😅ya gnaak diome nak
@ModoubarraDIAW-u9k4 күн бұрын
Siteu bari na wakh légui mogui mélné gou kham Dara 😂 ba balla diap la
@ismacisse71624 күн бұрын
Modou lo seul ❤ balla dam rek lnsahallah wakh ak daw rek la moune mo raw thik thik
@SerigemodouDia4 күн бұрын
Yal daw 😂
@GoFall-y6j2 күн бұрын
Siteu wakh rèk la meune papaye Modou ga ame dë yaroule boy siteu🤫
@AliouneGning-j7j4 күн бұрын
Père max Dina raylou boynia dakh 10%
@allefall55454 күн бұрын
Siteu wakh dj mo eupou dieuf dji
@seydounouroufaye83534 күн бұрын
Ndam rek siteu
@NdiayebassBassndiaye4 күн бұрын
Www ki dou lac 3😂😂😂
@BocarGuangué4 күн бұрын
Siteu beugg na actionè te lamb dji yeup lay daww 😂😂😂