Il faut que sa soit clair Franc a fait 13 combats et 13 victoire sans voir ni Serigne Mor ni Sa Touba donc ce n'est pas aujourd'hui qu'il va laisser les gens prier pour lui pour faire venir d'autres non et en plus ce n'est que Franc qui gère ça ay frère ram nio koy géré donc si vous voulez le soutenir il faut le faire pas pour Franc mais pour les couleurs de parcelles Assainies parce que Franc défend ces couleurs
@fallousarr57282 күн бұрын
Bien dit
@thomasmendy25432 күн бұрын
@@moustaphasonko596 merci
@pierrefabriceboucal2 күн бұрын
@@moustaphasonko596 bien parlé frr
@AtoumaneNiasse2 күн бұрын
Billahi lou leer nga wakh
@TallaAw-b2d12 сағат бұрын
Bien dit
@BassirouGueye-i4r3 күн бұрын
Franc yalla nakou yalla May ndam
@Mahidrame-v2v3 күн бұрын
Bayi dawe lakhou wayé diguén ame gathié inchallah fran name réck
@diakara23063 күн бұрын
Fran inchala day dane ama balde diel bou guaw inchala 💪🙏🙏
@moustaphasonko5962 күн бұрын
Allahouma Amine 🤲 Ndiago or bi seul
@djilyseye13272 күн бұрын
Inchallah amin
@morgaye95822 күн бұрын
Ndam rk inchallah François Gomis
@LamineNdiaye-rl5mx2 күн бұрын
yAla na franc dann ama baldé le 16 février thi barkeb seuydina mouhamed 🤲
@ELIZOELIZO2 күн бұрын
Fi nga andi Niang bou ndaw contre Zarko nga dadié ak sa touba, niou daane la ba sa birou mbeur bi wéeh tale, xanna boobu heuthio lambji, Ndam pour Franc inchallah 🙏🏻
🇺🇲 incha'Allah yalla nanioukô féké talko si diam akh salam incha'Allah Ama baldé et Lac rose yalla nalléne yalla maï ndam si barké seydina Mohamed psl ♥️🫶
@Zam-Zam710Күн бұрын
BAYILÉN DOOR 😂 SERIGNE BOUFI AME FITT DAGUAY GUÉNEU WAX SAY MBEURS MAIS DI TEK XEL NANE AMENA AY MBEURS YOUMAY NIANAL NIOY DANE C'EST TROP FACILE 😂😂 BO AMÉ FITT KAY WAXAL 😮😂 MERCI NAK SI LIGUAY NIANAL AMA BALDÉ NAK INCH'ALLAH AMA MOY DANE DAFMA LÉER KOM NIMOU MA LÉRÉ NI LE 16 DINAKO FÉKÉ INCHAALLAH
@thiernolo96953 күн бұрын
Dieuredieuf ti serigne mor❤❤❤❤❤
@LassanaSy-q7l3 күн бұрын
AMA danna franc bouyage 😂😂😂
@ShiekhjobeTijan2 күн бұрын
Yalña Yalla May Franc ndam lo Rey ta Gaw ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@IbrahimNdiaye-nq7jw3 күн бұрын
Merci beaucoup
@LamineTine-e4j23 сағат бұрын
Diamou lene Yalla mo geun wakh bi fi Yalla 👌 mofi nek seul
@Zam-Zam710Күн бұрын
LAC ROSE ET AMA BALDÉ YALNANOU AME NDAM INCHAALLAH LE 16 FÉVRIER 2025 ❤🎉
@MoustaphaNiang-t8d3 күн бұрын
Serigne mor kou ko beug la blhi❤❤❤
@dembajamanka-bx4wj2 күн бұрын
Ama rek insha'Allah 🎉❤😂
@AliouneGueye-bg5mw3 күн бұрын
Wakhi sokhor rk lay wax li nguenne beugue dou am franc ndam rk inchallah
@amakane64942 күн бұрын
Li rek sa montre que ay door la il a dit qu'il a 4 mbeur té nioy dane, mais le journaliste dite lui ces mbeur la sont qui ? Et tu insiste mais sou mbeur yoyou dano sakh doko kham, faute au journaliste serigne si ay napaté katela niou 😂
@mouhamadba56092 күн бұрын
@@amakane6494 Bilay dafa yomb nane 4 mbeurs lay nguémb té nioy dane. Té gnémé wo wakh niane mbeur la c’est du tapalé way
@amakane64942 күн бұрын
@@mouhamadba5609 journaliste bi mo ayoul rek soudone mane dina wakh mbeur yi par la force 😅
@mansourkane14262 күн бұрын
Gni aye commedien lagnou Bilay 😂😂😂
@abdoulatifdiop56403 күн бұрын
Wa nioom lou len franc deff😮😮😮
@modoufall9592 күн бұрын
Franc da lén geumoul lolou molén méti
@HENSA859Сағат бұрын
Ma question est qu'est ce que franc à fait à tout ces gens jusqu'à ce qu'ils ne veulent pas parler de son combat . Ils sont méchant. Franc va terraser par la grâce de Dieu❤
@impacttv23823 күн бұрын
Ama moy danou beu diahaann
@MatarNdiaye-x5g3 күн бұрын
❤
@khadimdieng21303 күн бұрын
❤❤❤❤
@DaoudaNgom-o6g2 күн бұрын
'❤❤
@Ndiaye-t22 күн бұрын
Ama baldé défaite rek inchallah si katanou yalla sounou brom ☝️☝️☝️☝️
@khadysene22642 күн бұрын
ama yalna am ndam si barkè baye niass si kaw franc inchahala
@abdoulayendoye18032 күн бұрын
Franc mom khana ken faralouko yalla nio yalla soutoural
@AtoumaneNiasse2 күн бұрын
Man dal Sénégal mon nékh kaay ma nianal par force 😂😂😂
@rubengomis77522 күн бұрын
Francs yalla nako yalla may ndam
@modoufall9592 күн бұрын
Franc domi serér la xamna fimoy guembo Yaw ak satouba lilén méti moy franc geumou lén
Franc dal yalnako yallah may ndam mh franc khana leigui par force daf len wara yanlo tmt Franc il a fait 13 combats leigui vous voulais que mou bayi gnikadon ñaanal gnow ci gnen Bou fekei parcelle bi ngen di titaro deug leu il faut le soutenir c tout En plus y’en dolen yallah dolen waliwou kou nek kiko doy lay ñanlo
@modoudiop10212 күн бұрын
lou takh wa lamb deteste franc lan lalen def thiey yalla 😭😭
@djibysoung29982 күн бұрын
Aga Sega DH 😂 thiey yala
@amadiallo-kn2ye3 күн бұрын
Serigne mor d da am fouleu man lolou rek la guiss !!!!
Ki ma tasé ake mome malica maniko zarko ake gris bordeau kouye dane monima gris bordeau moye dane bilakhi wala barki séydina mouhamed gni danio niémé yalla gni douniou rouss gadié douléne raye
@daoudader46413 күн бұрын
Serigne MOR xamnako bou bakh aka mana doul
@magattediop44422 күн бұрын
@@daoudader4641 mbadou daur kate la🤣mane dh khawma ko wayé doyouma
@AbdouNdiaye-eg4dk2 күн бұрын
Mane franc lafaral wayé gumouma srigne mor didiakorlo ak wa unité 7 andeu ak wa keur ama kokou dé dou sergne mor
@marcusmouhamed3 күн бұрын
C’est la 2em fois may degg serigne yi di wah komsi franc delen si geiner ms wadji defa am ay gnane katam bou yagg dou kheuy rek bayilen parce que yaye gnanal modou lo
@PapiNiang-l3p2 күн бұрын
Gni daniou yabaté modou lo molène nara yamalè khamou niou doule dagni fène modou moy franc franc moy modou ❤
@modoufall9592 күн бұрын
Gni gnana lougn sax modou dagnouy out buzz rk si modou
@mouhameddiop31662 күн бұрын
Ki sakh khamoul dara mofi doone wakh modou lo day weur nombo siteu si watou sakou yii😂😅
@modoufall9592 күн бұрын
Sétanou ma vidéo bi dh mais loum wax day doul
@votremiroir76122 күн бұрын
Serigne yi dhé lékk khalissou mbeurs yi reck lagnoufi nékké😂😂😂😂😂😂
@moussafaye36332 күн бұрын
Wa gnar gnouy beuré faw kenn danou wakho fi touss
@moustaphafall94942 күн бұрын
Ioe khana wakho do wakh ndayi si combat bi ?? Wakh nga 100 wakh you bokoul wa khana ki mooy yalla legui wala ??
@papecisse60003 күн бұрын
Billahi wa diaspora bi moytou léne gni séne lamigne mo nekh rek
@abdouazizdiallo49162 күн бұрын
Mor bridel loudoul fein monouko
@BoyDiop-i8v2 күн бұрын
Fran ndame rek inchallah
@AbyDiaby-w7w2 күн бұрын
franc seul parcélle moye diriger ndam rk inchallah kome nonou ama tapéte leu fran kassé touss
@MatarNdiaye-x5g3 күн бұрын
Segne Mor yaw FRANC ngaye garouwalé wayé mano thi mome sa leufeul ndaye. Ok
LIGUA WAX NI DOU XAM XAM DÉ NAK 😂😂 LOUY MBEUR BOU MAKK DINA SI DANOU MDRRR😂😂😂 LOLOU KAY FORCE NAK FRANC AK AMA YEUP AY MBEURS YOU MAK LAGNE
@matarfaye52652 күн бұрын
Serigne yi douniou touss
@abdoulkhadrecisse50872 күн бұрын
Ama Baldé va battre franc d'un combat éclair inchallah 🙏 Première défaite de franc Notez bien ça
@yilebaba65652 күн бұрын
Lo wakh si balla gaye 2 vs siteu ?
@abdoulkhadrecisse50872 күн бұрын
@yilebaba6565 inchallah 🙏 Balla Gaye 2 moyy Dann Ba tokk si khanam Balla Gaye 2 va battre situe
@yilebaba65652 күн бұрын
@@abdoulkhadrecisse5087 Amine sama waa dji , lolou rek la beugue ! Au passage tu ressembles bcp à un frère à moi ! Je pense que balla en cas de victoire affrontera modou lo pour un 3e combat
@abdoulkhadrecisse50872 күн бұрын
@yilebaba6565 ha ok ça arrive ça comment il s'appelle ton frère. Oui je crois en tout cas si Modou lo croise Balla Gaye 2 encore Balla Gaye va reprendre la couronne 👑 inchallah
@yilebaba65652 күн бұрын
@@abdoulkhadrecisse5087 Il s'appelle Abdoulaye Kamara , oui ça arrive ! Je crois bien aussi ! Dafa melni modou lo balla laye calculer mo takh mouné novembre laye beurré !
@Sonne_M052 күн бұрын
Nn serigne Mor dioum nga dhe parceque déf nga sortie jourou combat diop2 vs mor kang kang si goudi etdr média molla dieulone matoul 3mois
@P.A.Dienior3 күн бұрын
kii noumouy wakhé Ama lay nianal dinane kouko ci boléwoul niakoul fayda mais yalla rek mofi nek franc seul
@moustaphafall94942 күн бұрын
Gnoom gneipou la franc di rouss lo
@ibrahimasene2187Күн бұрын
Kenn doma dimbalisi li gayi fokk nguir yalla 😂
@mamadoukamara9533 күн бұрын
Franchement gni di poser les question sont nuls. Mor néna PA là deuk taa kouko boléwoul sisay mbir faléwoula. C'est claire il est du côté de Ama. Il faut savoir lire entre les lignes et comprendre facilement.
@YoussouphaSall-i7i3 күн бұрын
franc lay nianal dafay bagne kouko khekh
@YoussouphaSall-i7i3 күн бұрын
bataille phsycologique
@fidelemendy2842 күн бұрын
Waw meun na nekkk bataille psychologique deh ndakh daye bagne wa pikine diko saga com nigne ko defone la fois passé contre modou lo
@mamadoukamara9532 күн бұрын
@fidelemendy284 possible ui
@otseunoglofficiel37092 күн бұрын
Ta raison
@cheikhbasskeurmassar95482 күн бұрын
Ama baldé mo meune mo eup dole
@mouhamaddieng62182 күн бұрын
Franc boule tiite dheii bilahi niongui sa guinaw ndam rek inshallah FRANC késsé laniouy topou
@moustaphafall94942 күн бұрын
Dangene di dakhar seen ndaye di doul rk menuleen dara si franc wakh ndym rk bayi
@fallousarr57282 күн бұрын
Lou franc def quelle est le problème loukhew
@khadimdrame17002 күн бұрын
Daye doule rek
@antanassendour475Күн бұрын
Nimporte koi bilay .franc bo doffè ba serigne yi nianal co dena danou parsk on les ai jamais vu dans ses combats. Se sont tous des arnakeuts
@mbayefaye12612 күн бұрын
Yaw dangay doul rk khamo dara nganane bédiéne Yako ndieukeu Andi si lamb 😂
@modousall26933 күн бұрын
Kone kay segne ama lay andi kou deg nimou wakhè birdèl dina mankèti dh kone
@matarfaye52652 күн бұрын
Ki wédinako bisniki tay dou dara
@moustaphafall94942 күн бұрын
Ioe khana wakho do wakh ndayi si combat bi ?? Wakh nga 100 wakh you bokoul
@MbayebabacarDiouf-wg5ii2 күн бұрын
Khamo darae
@ismacisse71623 күн бұрын
Mor do yalla do yonéne
@GoraMbengue-f2j3 күн бұрын
Mor boul watt tmt nianal yallah rekk té deff lingay deff.
@Jnrjoop3 күн бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@moiizasankhare40963 күн бұрын
Ama moy dane franc inchallah par force dolé mbam ❤💚🩷
@babacar31782 күн бұрын
C k nii danio wara khamni franc amna loumou keume tamite
@morykonde31892 күн бұрын
Meune na and ak franc di nelawale wa pikine
@NabyLeJuriste2 күн бұрын
Franc dal yalnako yallah may ndam mh franc khana leigui par force daf len wara yanlo tmt Franc il a fait 13 combats leigui vous voulais que mou bayi gnikadon ñaanal gnow ci gnen Bou fekei parcelle bi ngen di titaro deug leu il faut le soutenir c tout En plus y’en dolen yallah dolen waliwou kou nek kiko doy lay ñanlo