«Na guéne sama seuy kharitam lay woudiel motakh…» Pendo Guissé répond à Mamy Cobra et sort les audio

  Рет қаралды 201,144

People 221 TV

People 221 TV

3 ай бұрын

Пікірлер: 702
@People221sn
@People221sn 3 ай бұрын
N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
@user-wz5be2dr5m
@user-wz5be2dr5m 3 ай бұрын
❤❤❤❤❤
@fatoumatabintoubathily8133
@fatoumatabintoubathily8133 3 ай бұрын
Ma bagne 😂😂
@chocovibes4728
@chocovibes4728 3 ай бұрын
Il faut désinstaller toutes les applications gnou dem si ale bi beyiiii thiep soble pomme de terre tomate âme auto suffisance alimentaire li moye solution bi
@fatimambay7006
@fatimambay7006 3 ай бұрын
Yaw de mak yaw niou boko xalat
@mortalaless8364
@mortalaless8364 3 ай бұрын
si boba souf si nanouy wakhi souli cable optique bi di connecter
@makyarrjaimemonpaysgeumbam7463
@makyarrjaimemonpaysgeumbam7463 3 ай бұрын
Billahi wakh nga deug
@adamaberthebakhayoko8156
@adamaberthebakhayoko8156 3 ай бұрын
😂😂😂😂​@@mortalaless8364
@antambow8814
@antambow8814 3 ай бұрын
Nagan Nougou rek lagnouye ware yobou sans téléphone gnou def cure de déresaux sociaux 🔴😡
@user-tn3tm2pr2x
@user-tn3tm2pr2x 3 ай бұрын
Yalna yalla défala diamme yague sa borom keur machalla je l' aime à cause de sa sincérité et notre Serigne Babacar sy rta que du bonheur chérie du courage
@virginiediawara1474
@virginiediawara1474 3 ай бұрын
Péndo pate moy fathie lépe yaw dagua ame nawlé❤
@Artiste_chanteuse418
@Artiste_chanteuse418 3 ай бұрын
Wakh dji Moy maytoulen internet bi ay djiguén nguén tmt 😢naniou Yam djiguén dafay Yam tmt am kersa mandou téy maytou xana guisou len sokhna aidara bou Wally seck Aka Yam té téy kokou ken douko guiss fen Soko guisé rek danouko bet vidéo woko maytoulen internet bi té baxna❤
@naboufaye4918
@naboufaye4918 3 ай бұрын
Pendo bilahi koula sope la mais il faut arrêter les détails parceque talibé cheikh day Dale en plus dou Bari détails daye mougne yenne wakh yii si Barker Serigne Babacar Sy ❤
@coeur2lion38
@coeur2lion38 3 ай бұрын
Amna solo dé talibé Serigne Babacar sy dacoy Niro waham dou Bari dou wah Lou gnaw aussi mé parlé rék détails rék
@AwaThiaw-kh1gz
@AwaThiaw-kh1gz 3 ай бұрын
Talibe cheik day meni alima n Diane détail zéro 🎉🎉🎉🎉
@khadijagaye9020
@khadijagaye9020 3 ай бұрын
Protège téléphone bi Mommy Seck yallah nako yallah yeureum 😢❤
@veroniquenatack7392
@veroniquenatack7392 3 ай бұрын
*Amennn🙏🏽🙏🏽🙏🏽*
@sokhnambaye6819
@sokhnambaye6819 3 ай бұрын
Amine yarabi
@rokhayacisse7905
@rokhayacisse7905 3 ай бұрын
Ah bon pourquoi ??
@famasalihathioubsaliha9201
@famasalihathioubsaliha9201 3 ай бұрын
Amine
@awambaye6465
@awambaye6465 3 ай бұрын
Yen nieup yam 😢amolen ben classe l
@diouldewar
@diouldewar 3 ай бұрын
Nitt dall daguaye kham sa nawlei Dama khamoull niom choco Adamo awoush kitty ak niomi seinn lou nitt di andeu ak niom ba niouyy am accès sisa vie 😢😭
@maretouseck4387
@maretouseck4387 3 ай бұрын
Lolou moma diakhal
@OumiAidara
@OumiAidara 3 ай бұрын
Mane mii moma diakhal
@user-ll6ei5rt5k
@user-ll6ei5rt5k 3 ай бұрын
Manké
@Iboudieng-bu4hv
@Iboudieng-bu4hv 3 ай бұрын
te mom da Olofe trop te toucouleur lu ci famille toucouleur bou bakh laa bok bilahi ♥️
@bushra4079
@bushra4079 3 ай бұрын
Wayadi ak niakk classe rek ...
@chocovibes4728
@chocovibes4728 3 ай бұрын
Mami tamitttt sa khariit moyeee woudieiii ak pendo bosssiii meunoul wakh lou bakh walaaa nga tok ak niom niar nieup face to face wakh ak niom comme Que mouno neutre li moyeee deug Mamy mossiii warone manou koula vocal ngani ko lidiantiii ko ak mome
@barbietrvpsm105
@barbietrvpsm105 3 ай бұрын
Vraiment
@lenadiatta4032
@lenadiatta4032 3 ай бұрын
😢😢😢c’est vraiment désolant de voir comment on s’attarde sur des détails alors que l’avenir de notre cher pays est en danger
@user-yi3jt6kt9q
@user-yi3jt6kt9q 3 ай бұрын
Surtout lolou 😢
@user-eq8dg3zs6o
@user-eq8dg3zs6o 3 ай бұрын
Moi je suis deçu quand meme , parce que je t'adore dèsolee !
@user-yt1zd9zb8t
@user-yt1zd9zb8t 3 ай бұрын
Pendo bouy wakh na wakh rek dé guene si serigne babacar sy li ay details la way
@user-kb4hu5uu2k
@user-kb4hu5uu2k 3 ай бұрын
Daye doule sah
@Iboudieng-bu4hv
@Iboudieng-bu4hv 3 ай бұрын
danga inian kese
@salyallemomuawrksarr8652
@salyallemomuawrksarr8652 3 ай бұрын
Ndayssane pendo yaw danga bakh té gorèe yalla Nala yalla diapalé te yalla takhawou la si barki Serigne Saliou mbacké détenu Yi yalla naléne yalla guéné figniou nék 😢😢😢😢
@user-te7ib6jo4e
@user-te7ib6jo4e 3 ай бұрын
Ki dafa niak faye da ki dou sakh rouss
@oumydiatta4838
@oumydiatta4838 3 ай бұрын
Sou bakhome dou dem si imbecille bou melni Choco difa yakh Mame ak papay diambour.noit Bo nakharé derete dangay mandou do togne mais ki mak bou niak fayda la.
@khadijaboungakablinde4133
@khadijaboungakablinde4133 3 ай бұрын
@@user-te7ib6jo4e Bilay nimako beuge wone ms bet nama
@aichasy9043
@aichasy9043 3 ай бұрын
Moye lolou pendo danouna ohhhhhh
@mariameboudabakh698
@mariameboudabakh698 3 ай бұрын
Il pendo am foula dou mom kesse mo fi am djeukeur dafa bari wakh il faut que mou ham né que magla waye tessante ak Haley you ndao
@ndeyeseynaboucisse2432
@ndeyeseynaboucisse2432 3 ай бұрын
Dou werou djiguène, dou wérou sargal djiguène. Werou droits de la femme la, droit à l'edication, à la sécurité, à l'egalité et à l'equité. Bayilen tchi khel please🙏
@mariamasano4844
@mariamasano4844 3 ай бұрын
Pendo sa waax dji weeroul deh. Danou gua deh. Bayilen dieuw, topeul feulé way. Zéro classe
@ndeyesarr8234
@ndeyesarr8234 3 ай бұрын
Wakhou fi dara Mamy dako woo direct gnépé woul tonetou dèm si choco di wakh gnou siweul ko
@belleduteteaupied1393
@belleduteteaupied1393 3 ай бұрын
Ya gmank classe wathié sa personnalité pendoo gnola bayi
@mamitaofficiel5755
@mamitaofficiel5755 3 ай бұрын
Yaw yako bayi mes on l’aime love pendo❤
@Sokhna-mg8zn
@Sokhna-mg8zn 3 ай бұрын
​@@mamitaofficiel5755pendo Dou nitou darra
@thianediene4236
@thianediene4236 3 ай бұрын
Soko bayei ya ham nioune diap nen ko
@sambafall1685
@sambafall1685 3 ай бұрын
Bilakhi pendo doméram la thime
@user-ys3yb7zz1c
@user-ys3yb7zz1c 3 ай бұрын
Sokhor la def
@fatoumadjiguenendoye2096
@fatoumadjiguenendoye2096 3 ай бұрын
Yallah nagnou yallah moussal si siiw ak milieu yallah nagnou yallah moussal si wakh diou niaaw pendo lo amone valeur yangikoy perte guènal si andoum khalè gni yallah nama yallah baal tèsanter ak bou niaaw dafa bokou si diom dagnouy dèf louni wingu guèn di khol niit si beutt amougnou bèn kersa aue sec oeil lagnou aaaah nono waay
@user-ye2ws8ou4b
@user-ye2ws8ou4b 3 ай бұрын
merci beaucoup pendo vérité absolue ❤❤❤❤
@antafall9631
@antafall9631 3 ай бұрын
Yakk ngua lepp menone ngua patreu rek setane mais diar si nitt pour fayou est pas digne d’une grande dame comme toi c’est vraiment désolant avec la situation du pays les morts et tt sen xel dou dém si yalla loudoul Mala def Yama def pffff tjr les femmes
@Ndiagobalamaissa
@Ndiagobalamaissa 3 ай бұрын
Pendo liguey wakh mo amoul ben sens dagua rouss amato crédibilité
@aichabittaye
@aichabittaye 3 ай бұрын
Yaw kou rew nga
@deugrek-gk3lx
@deugrek-gk3lx 3 ай бұрын
Merci doul kat bou rouss leu
@Iboudieng-bu4hv
@Iboudieng-bu4hv 3 ай бұрын
liko moko tek bobap mo dougou ci olof yi te mom toucouleur la dafa olofe trop daa bayi yonam
@mimie.a6424
@mimie.a6424 3 ай бұрын
​@@Iboudieng-bu4hvmais iow tes vraiment a l'ouest des gens qui se dispute pour des conneries. Toi tu viens nous parler des ethnies melni douniou ay sénégalais
@Iboudieng-bu4hv
@Iboudieng-bu4hv 3 ай бұрын
@@mimie.a6424 olof momel nonou
@marietoudiatta9019
@marietoudiatta9019 3 ай бұрын
Lolou Waroula😢😢
@user-ge8mv1qy9e
@user-ge8mv1qy9e 3 ай бұрын
Ay man comment momeynekh soylir dagey reeeeebesono wa senegal yeb ay comedian laniou Yana yalla def Si senegal diama tapeh kholyi boleh kholyi adouna doukar ❤
@adamandiaye4314
@adamandiaye4314 3 ай бұрын
Pendo guissé bayile wakhe lougnawe ni ga défone Oumou sow lougnawe rek gaye wakhe wakhofie dara
@papefaye272
@papefaye272 3 ай бұрын
Yaw ya meuna teipi sa leufeul ndaye
@rokhythiam5531
@rokhythiam5531 3 ай бұрын
Vraiment waxoufii daraa bilae
@SokhnaCisse-yy5yj
@SokhnaCisse-yy5yj 3 ай бұрын
Bilahi wakh nga duegue dafa meuna khass té trop pour mo guene niepe 😏😏
@amythiam7251
@amythiam7251 3 ай бұрын
C pas vrai Wakhal loula lérr té bayi djakhasé
@sarrmassaer1870
@sarrmassaer1870 3 ай бұрын
Yaw ya meuna todj sa leufal Ndeye
@abibdieng4362
@abibdieng4362 3 ай бұрын
Pendo daal nandité yii kham nane ni ya nek si deug mamy cobra kagn lafii khew mom😢❤
@Iboudieng-bu4hv
@Iboudieng-bu4hv 3 ай бұрын
mom moko deff daa olofe trop da wara khame ni dou Olof toucouleur lu
@SiraDiouf-yc4qp
@SiraDiouf-yc4qp 3 ай бұрын
Pendo amo bene fouleu
@user-kb4hu5uu2k
@user-kb4hu5uu2k 3 ай бұрын
Doulkate la rék ki
@deugrek-gk3lx
@deugrek-gk3lx 3 ай бұрын
​@@user-kb4hu5uu2kdoulkat bou mak leu
@Iboudieng-bu4hv
@Iboudieng-bu4hv 3 ай бұрын
danga inian kese
@ndeyendiayandoye4732
@ndeyendiayandoye4732 3 ай бұрын
SAMA FAN'S FAUT SUIVRE CERTAINES PERSONNES DU COURAGE❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@hhjg1664
@hhjg1664 3 ай бұрын
Pendo yw borom bakh nga❤🇬🇲🙏 don't mind them
@ndeyediakhate1063
@ndeyediakhate1063 3 ай бұрын
Balantelen akh rekk mou diekh adouna amoul solo😢
@astoudiouf9191
@astoudiouf9191 3 ай бұрын
Mais mami dieuwoula, dalako wakh directement, limoula wakh dangasi warone ndiangate mo guene, mano justifier linga wakh
@ndeyefatougaye4071
@ndeyefatougaye4071 3 ай бұрын
Moma diakhale
@diatousarr591
@diatousarr591 3 ай бұрын
Louy yonou mamy si seuyou diambour mome seuyoul doubaiy
@ndeyefatougaye4071
@ndeyefatougaye4071 3 ай бұрын
@@diatousarr591 Wa loutakh tontouwouko moma diakhale nagne bayi choco miii bakhna
@user-mo6on5yd1b
@user-mo6on5yd1b 3 ай бұрын
Machala pendo amal diam sama sopé bi❤❤❤
@pendamboup1003
@pendamboup1003 3 ай бұрын
Yaw kou manke nga gni gnepe yalene mak nga nek fi di tesante sawoudjou eupe nala classe
@user-qx3xs5kv2u
@user-qx3xs5kv2u 3 ай бұрын
Billahi pendo mane Damala beugue yalla nala yalla sameu
@liinguere998
@liinguere998 3 ай бұрын
woté bi ak choko modoul won yon niit meune gua fathie liguay fathie ak kiguako sekeul mamy tamit lousi sa gatt si seuyou diambour😂 han
@deugrek-gk3lx
@deugrek-gk3lx 3 ай бұрын
Merci beaucoup lolou moy yakamti doul
@Ajafatt
@Ajafatt 3 ай бұрын
Merci pendo ❤❤❤❤❤
@mamediarrandiaye9173
@mamediarrandiaye9173 3 ай бұрын
Merci beaucoup pendo
@FallouYally
@FallouYally 3 ай бұрын
Concentré sur vous Machalla
@sokhnasene6789
@sokhnasene6789 3 ай бұрын
Gni di blâmer pendo yena nafekh mamy cobra louy yonam si woudié diambour
@DiopMameAmy-bj2uu
@DiopMameAmy-bj2uu 3 ай бұрын
Bilay yaw rek ya wakh déug
@ndeyesallyndiaye5285
@ndeyesallyndiaye5285 3 ай бұрын
Ligua deif niaw na waro wone wo choco nah tay sa lwax mo daim daga wara xam ni mak gua nekato xalei defal yeufou grande dame.
@coumbadiouf9752
@coumbadiouf9752 3 ай бұрын
Machalla machalla ma.soeur découragée
@coumbandiaye6273
@coumbandiaye6273 3 ай бұрын
Pendo bagua démé bay fayou manone gua ko défé nané pas di wo choco mi gua khamni amoul classe tay mom vraiment danou gua amoul lofiy justifie yaw dala audio kay audio ko gua tontou
@seynabousy7641
@seynabousy7641 3 ай бұрын
mamy tamit ell est dans ttes les sauces....noooo
@ndeyemaladosow8603
@ndeyemaladosow8603 3 ай бұрын
Mamy dafa compound roule chow bizz rk
@user-yc2zp6rl2d
@user-yc2zp6rl2d 3 ай бұрын
Machalla femme de valeur cou bakh gua beugue sa famille lo am sa famille guako défal louma ler wakh ❤❤
@khadijasamb4677
@khadijasamb4677 3 ай бұрын
On t’aime Penda nitou deugu gua fonce rek yalla bakhna Ton mari est mon frère amoul bén problème bakh n’a amna yeurmandé boul degu Lou kén ❤
@Iboudieng-bu4hv
@Iboudieng-bu4hv 3 ай бұрын
te loci khamoul nk ci famille toucouleur bou bakh laa bok sett with mom moko deff toupou ci olof yi rk
@mamadouniane401
@mamadouniane401 3 ай бұрын
Merci beaucoup
@fallmalickfall2653
@fallmalickfall2653 3 ай бұрын
Thiotou ndeyam mim rew rek ayy nitt gniu yakante ayy gor yo khamni kom djiguene
@naboundoye7286
@naboundoye7286 3 ай бұрын
Sarap li wayi😂😂😂😂😂
@ngottembaye3731
@ngottembaye3731 3 ай бұрын
Mercie
@famaseck4231
@famaseck4231 3 ай бұрын
Mersi pendo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@ndieneka7938
@ndieneka7938 3 ай бұрын
Wakho fie dara ak fila nite ngie tegone
@ndeyedioufmouserignefallou6720
@ndeyedioufmouserignefallou6720 3 ай бұрын
Bayiko kikay beet na niep
@Iboudieng-bu4hv
@Iboudieng-bu4hv 3 ай бұрын
daa dioum rk waroul won dougou ci Olof yi toucouleur day am foula mom daa olofe trop 😢
@jaimemamere5958
@jaimemamere5958 3 ай бұрын
@@Iboudieng-bu4hv😳😳 c'est quoi ces termes raciste ?
@Iboudieng-bu4hv
@Iboudieng-bu4hv 3 ай бұрын
@@jaimemamere5958 Olof mousoul beuge toucouleur sen bopou rk len kham
@dodoujatta7400
@dodoujatta7400 3 ай бұрын
We love you pendo guissé❤❤❤
@jatoucham
@jatoucham 3 ай бұрын
We love you Pendo❤❤❤
@astouyorodia1388
@astouyorodia1388 3 ай бұрын
Danguèn di diawalè deugou ak arrogance,mak nga do xalè,
@Iboudieng-bu4hv
@Iboudieng-bu4hv 3 ай бұрын
danga inian kese
@user-pi3gx2rq4x
@user-pi3gx2rq4x 3 ай бұрын
Diama sy yaw pendo ❤❤❤❤❤❤❤
@awabayo2785
@awabayo2785 3 ай бұрын
Amouléne béne classe
@MaramesagoKane
@MaramesagoKane 3 ай бұрын
Pendo bo kholé si photo bi sa protège téléphone bi ga wara delosi sakhel adouna diaroul li
@ramatandiaye2571
@ramatandiaye2571 3 ай бұрын
Pendo goor dou avenir,goor dialoul khass sa moromou djigeen
@MamediarraDiouf-nj5co
@MamediarraDiouf-nj5co 3 ай бұрын
Bilay
@user-of5rb4ef8y
@user-of5rb4ef8y 3 ай бұрын
Pendo amal. Foula meune gna diour mamy cobra
@jadychatou167
@jadychatou167 3 ай бұрын
Bayil doul,Mami cobra raak lay donne thi mom.
@rouguikebe9984
@rouguikebe9984 3 ай бұрын
Wakh deugu dafa wara affaires téseunté yi nak ish😒
@binetadiallo7784
@binetadiallo7784 3 ай бұрын
@@jadychatou167😂😂😂😂😂wa ioe
@user-iq6iv4ne5i
@user-iq6iv4ne5i 3 ай бұрын
Merci pendo❤❤
@ToufaDGueye
@ToufaDGueye 3 ай бұрын
Penda beugueu nala dé Mais vraiment WAKHO Fi DARA Touss gua fi wakhoul
@aichaba8275
@aichaba8275 3 ай бұрын
Moi je t'aime bien pendo surtout gua néke talibé Serigne Babacar déma rouss je trouve même pas les mots stp arrête les détails guir yalla😢 diama mo guéne l'épée.
@ndelladiagne2460
@ndelladiagne2460 3 ай бұрын
Amo béne classe😊
@Iboudieng-bu4hv
@Iboudieng-bu4hv 3 ай бұрын
yaw yaa amoul classe 'pendo tabakh na kerum dougal si ay Rakam yorr autom bou rafet yorr passport ram didem fiko nekh✈️ di ligeuy machalla di fayekou khalis sak werr kii si famille toucouleur bou bakh la bokou ki bokoul ak yen deh
@fallmaimouna8650
@fallmaimouna8650 3 ай бұрын
Pendo soff nga gnak nga fayda
@Iboudieng-bu4hv
@Iboudieng-bu4hv 3 ай бұрын
danga inian kese
@FatouMandiang-lm2ls
@FatouMandiang-lm2ls 3 ай бұрын
Merci dcp 👍❤❤❤❤❤❤
@fatoubinetoulam275
@fatoubinetoulam275 3 ай бұрын
Mais môme dieuwoula
@salyallemomuawrksarr8652
@salyallemomuawrksarr8652 3 ай бұрын
Pendo guissè yaw dall deuguel sa seuy mamy Cobra yaw yako guéne fouff te yaw ndanane NGA machahllah ❤❤
@oulidiop8981
@oulidiop8981 3 ай бұрын
Vraiment certains commentaires vous êtes faux pourquoi sakh mamy di wax ci sëy diambur elle kameme elle est marié mamy mariage 20jour nga deff donc tu ne peux conseille personne force à toi pendo❤
@user-bd6lp5tc3b
@user-bd6lp5tc3b 3 ай бұрын
Yangui kaay juger ta hamoko pendo sou menon seuy Dina tok si you ndieuk ya Elle a le droit de défendre son Amie
@oulidiop8981
@oulidiop8981 3 ай бұрын
@@user-bd6lp5tc3b il faut dire la vérité mamy a tort pendo ne pas ça co-épouse mm si la première femme c'est sa copine elle n'a pas le droit d'y mettre sa bouche
@barbietrvpsm105
@barbietrvpsm105 3 ай бұрын
Wakh deug yallah mami mo nekhoule défendre momite
@rokhayagueye3040
@rokhayagueye3040 3 ай бұрын
Gni gnon seytané 😂😂si bopom
@AmyThiam-kn5gp
@AmyThiam-kn5gp 3 ай бұрын
Pendo lim wakh si live choco gnawna
@aramesall3422
@aramesall3422 3 ай бұрын
Trop sakh
@Iboudieng-bu4hv
@Iboudieng-bu4hv 3 ай бұрын
danga inian kese
@sokhnakane2759
@sokhnakane2759 3 ай бұрын
Machallah
@seydoundiaye8987
@seydoundiaye8987 3 ай бұрын
Dafa rousss rekkk😢
@Iboudieng-bu4hv
@Iboudieng-bu4hv 3 ай бұрын
toucouleur lu motakh kham nga peul da gawa rouss😂😂
@ramatacisse6264
@ramatacisse6264 3 ай бұрын
Senegal dagno wara deinstaller application yi installer wate yènène mais des autres version
@kizzydiop
@kizzydiop 3 ай бұрын
Yaguenaka wakh, nakhe niou ame diam vraiment🤔 surtout tick tock ak live .
@ndeyemaladosow8603
@ndeyemaladosow8603 3 ай бұрын
Sourtou live Tik tok yi you thie barry amoule change😢
@yayemariediouf9160
@yayemariediouf9160 3 ай бұрын
Wahofi dara niake fayda daga rouss té mouno delou guinaw thimmm
@user-il3tw2qe2v
@user-il3tw2qe2v 3 ай бұрын
Tata pénda talibé Serigne Babacar sy gua boy lén tontou da am gnou sokhar rék ❤❤❤❤❤
@mansourdiop3938
@mansourdiop3938 2 ай бұрын
Pendo boul dougou si calan yi amouniou classe
@user-fq8cb2rv5o
@user-fq8cb2rv5o 3 ай бұрын
Reste comme tu es ne change pas je t'adore ma belle
@user-jh1qs1gg8s
@user-jh1qs1gg8s 3 ай бұрын
Kone yaw mami dieuwoula en face la wakh ak yaw.yaw nak danga done dieuw pendo ya manké faut type binga done
@omb55
@omb55 3 ай бұрын
Dako dieuw kay nak vocal transférer le
@user-jh1qs1gg8s
@user-jh1qs1gg8s 3 ай бұрын
@@omb55 souko nèkhé kounek amnga sa kharite ok
@deugrek-gk3lx
@deugrek-gk3lx 3 ай бұрын
Merci
@AbsaDiop-ed7ui
@AbsaDiop-ed7ui 3 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤MERCIE BEAUCOUP PENDO GRAZIE MILLE VIELEN DANK JE T ADORO ❤❤❤❤❤❤❤
@flimanche1492
@flimanche1492 3 ай бұрын
Macha allah ❤❤❤❤❤
@arretekeita880
@arretekeita880 3 ай бұрын
Machalla pendo ❤
@mariesec824
@mariesec824 3 ай бұрын
Vraiment pendo nimala nawé warr ngua diombalé sa bopeu genrou choco et adamo😢. Cobra ak xalé you ndaw yoyou bayilén ndakh dougnou say morom. Conservél sa personnalité té bayi xalé yi way
@NgaytaFaye
@NgaytaFaye 3 ай бұрын
Har day wesou mboté gni bi ngay nek si art dioudo gouniou bayil hale yi ngay fréquente nga dem and ak say morom te nga bayi hasté gueno fi ken nieup la wedi😢😢
@user-bh6mk2tu8d
@user-bh6mk2tu8d 3 ай бұрын
Merci ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@angel-uc8jd
@angel-uc8jd 3 ай бұрын
Prndo say audio mo guène t ya wakh lou ñaw dou sa thieur bète nga ñou barri
@mamediarrandiaye9173
@mamediarrandiaye9173 3 ай бұрын
Vous avez raison merci beaucoup pendo
@filianambodji-ps7dj
@filianambodji-ps7dj 3 ай бұрын
Khamna kholam mo tangone rek mou wo choco parfois so merei tei amo contrôle meune nga deff loy rethio
@ria-cy7cv
@ria-cy7cv 3 ай бұрын
Merci pendo
@elhadjicheikhba4122
@elhadjicheikhba4122 3 ай бұрын
Bayil Serigne Babacar sy doul rék Nguay déf domeram dji 😥😭
@papamoussasarr6483
@papamoussasarr6483 3 ай бұрын
😂😂 li ngay wakh diouboul dh
@Xalendakaru343
@Xalendakaru343 3 ай бұрын
Yaw do am fouleu touti té khamni li dou sa thieur... Meun nga diour Mami Cobra ak ndeyam, bayilen niak fayda té guéne ci yeufou xaleyi... Tchiiiim😮😮😮😮
@Queenprincesse1
@Queenprincesse1 3 ай бұрын
😂😂😂😂😂😂
@sarahbibish2197
@sarahbibish2197 3 ай бұрын
Vraiment 😏
@khadyndiaye3706
@khadyndiaye3706 3 ай бұрын
Waxoufi touss dafay fénn rk rous rk moko diap dieuw rek laniouy def
@Iboudieng-bu4hv
@Iboudieng-bu4hv 3 ай бұрын
​@@khadyndiaye3706 yaw yay fenkat bi pendo sakh man damako mere ndakh mom toucouleur lu dem dougou ci oloff yii te oloff daaa gawa yabate
@awagadiaga5212
@awagadiaga5212 3 ай бұрын
Pendo merci
@yayemariediouf9160
@yayemariediouf9160 3 ай бұрын
Wahofi dara lolou dou raison baga koye khass
@user-bp5et8xw5q
@user-bp5et8xw5q 3 ай бұрын
Mane dei aka mouma neikhone mais cii problème akh oumou sow la paré ci mom dafa meune wax bu niaw
@annadiouf3304
@annadiouf3304 3 ай бұрын
Bravo pendo ❤❤❤❤❤
@fatoumbackesylla4481
@fatoumbackesylla4481 3 ай бұрын
❤❤❤❤❤beugue nagn la ba nopi
@maciagomes806
@maciagomes806 3 ай бұрын
Machalah
@AmySenghor-tx6fm
@AmySenghor-tx6fm 3 ай бұрын
Wakhofi touss gnakeu class
@Iboudieng-bu4hv
@Iboudieng-bu4hv 3 ай бұрын
danga inian kese
@coumbajaaksembe5779
@coumbajaaksembe5779 3 ай бұрын
Moytoulén xarit you bari wagni audio bou meunoul niak khamlén liguen di wakh boulén ken dougal Senegal yakouna 😭
@fallousylla7866
@fallousylla7866 3 ай бұрын
AMO COYE WO COUDOUL CHOCO YA NIAK CLASSE
@lenabadji2581
@lenabadji2581 3 ай бұрын
Vraiment
@ndeyedioufmouserignefallou6720
@ndeyedioufmouserignefallou6720 3 ай бұрын
Vraiment kikay amoul ben classe
@deugrek-gk3lx
@deugrek-gk3lx 3 ай бұрын
Merci beaucoup
@Iboudieng-bu4hv
@Iboudieng-bu4hv 3 ай бұрын
amoul classe kay ndakh moo dougo ci olof yi toucouleur bou bayi khetam dougou ci ay olof loula dall yako tek sa bopou 😢
@Ndiayeniangua
@Ndiayeniangua 3 ай бұрын
@@Iboudieng-bu4hvyaw lou nek thi olof yii toucouleur da geun olof😢
@MadelaineNiassy
@MadelaineNiassy 3 ай бұрын
❤❤❤❤merci
@maxfaby7542
@maxfaby7542 3 ай бұрын
Man de hamouma sah vrais problema bi mais man Pendo yow rek la Andal ❤❤❤
@nabousylla1314
@nabousylla1314 3 ай бұрын
Nit kou live NGA fêtèlèko sa bop nane dafmay garouwalè,lolou bokoul si âme classe.Nit do def Lou nit wakhe Lou bonn nga ni yow lay wakhal
@diadodia8348
@diadodia8348 3 ай бұрын
Yallah na dieukeur ak say bokk deigou ci yaw nii ga deugo ci mom😢😢sinon dina doy warr d
@aissatoudiene7010
@aissatoudiene7010 3 ай бұрын
wahofi draa dgaa rouss donggg 😢
A pack of chips with a surprise 🤣😍❤️ #demariki
00:14
Demariki
Рет қаралды 55 МЛН
Must-have gadget for every toilet! 🤩 #gadget
00:27
GiGaZoom
Рет қаралды 11 МЛН
Al khayri, Pendo Guissé devient Niarel et menace Les awo
10:40
PENDAO PRODUCTION
Рет қаралды 84 М.
Série -  Woudiou Peetiorgo 2.0 saison 2- Episode 8
20:25
Khar Media
Рет қаралды 28 М.
Dame Mbodji tire sur les députés de Benno Book Yakar "Na DIOMAYE dieul ay matouway"
15:51
A pack of chips with a surprise 🤣😍❤️ #demariki
00:14
Demariki
Рет қаралды 55 МЛН