Barké baye Niass pagaye c'est la première fois que je te vois mais dioulit nga té goor nga akh samba et mario autant comme d'autres belles âmes lii wer té wor moy dou niep melone ni yeen kone aziz akh waly dounou meuseu dée Cii ay lokho cheiyatine. Markhabane à vous tous. Que le tout puissant SWT vous rétribue vos efforts ❤❤❤ maman tu me fais pleurer à chaque fois que je te vois yallah na yallah atté seydi abdoul aziz akh ay nonam inshaallah rabbi.
@AstouSy-f8iАй бұрын
Mane souma guisser mère bi rek sama adouna touki mais Pagay def geste bou nice yalla nala ko yalla faye rafete na lol
@fatoucisse3171Ай бұрын
Meme mane sa youmako guiss dioy deyssane
@AstouSy-f8iАй бұрын
@ bilakhi Fatou damako niéwantal surtout noumouy wakhé elle n’a plus de force gni khamo ak biniou guadoul mère bi sakh liiiiii
@khadygueye5714Ай бұрын
Blh gno yam damako yeureum
@fatoudhasalihateseck9554Ай бұрын
Li deh domou Aziz yi gno thi warone djitou guissouma ben danseur bou diouk demander justice pour Aziz ces traître ak fimou diar ak gnom😢
@remadiouf23 күн бұрын
walahi ndeyssane beuri nguasi ay morom
@lacitoyenneafricaine8566Ай бұрын
"Kou woutter takha gnakeu bo tewone do ame" un proverbe wolof très véridique signifiant en français " si de ton absence s'en suit une privation, de ta présence tu n'aurais rien obtenu". Or le français a dit "les absents ont toujours tort". Cela pouvait justifier que Pagaye Mbaye n'eut rien donné à Aziz. Mais Pagaye n'a pas donné tort à Aziz. Cela aurait justifié l'autre proverbe wolof qui dit "kou touki gnou rerr se ganaw" signifiant "à ton absence on dine sans toi". Là encore Pagaye n'a pas dîné sans garder la part de Aziz (même mort, il a des héritiers dont sa mère). Donc, les absents n'ont tort qui si on veut leur faire porter le tort de leur absence surtout involontaire. Merci Pagaye, l'amitié n'est pas grisâtre avec ton beau geste mashallah. Pagaye, Aziz sou tewone ame ndakh woutter takhoul nga lek bako! Wa salam.
@FatouSylla-jh4qyАй бұрын
Wallahi li metina 😭yalna yalla atte te leeral lépou Barcké serigne fallou 🙏
@AdjaBa-y3vАй бұрын
Merci Pagaye pour ta fidélité ton amitié avec Aziz mashallah
@NdeyetakoSowАй бұрын
Ohh metina g des larmes aux yeux mère bi yeureum nako Aziz yala n'a dé Di noflayam ci barkey saw
@mamendelladiop9058Ай бұрын
Mach'Allah. BIG RESPECT à Pagaille Mbaye. Limom rafetna ❤❤❤
@fatoukinembaye4787Ай бұрын
Bilay pagaye mbaye yaye gorre pire tè ame kolerè samedi passé kou gneuwone Sorano sa khôl toyena ndakh sa hommage bingako defal
@hourayedieye6814Ай бұрын
Ohhhhhhhhh ndeyssane j'ai des larmes qui coule 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭 c'est vraiment triste yallah nako yallah yeureum souniou Aziz ndeyssane 😭
@hawasoumare1689Ай бұрын
Machalla pagaye yaye garemi yalla na la yalla faye
@SounkarMandiangАй бұрын
Machallah yalla nala yalla faye pagaye def ngua lou rafete ❤❤❤❤
@diaynabacisse6090Ай бұрын
Bilay li pagaye def rafetna trop bilay sama khol bi dafay meti à chaque fois ma guiss famille bi Pagaye yalnala yalla faay yiw
@nassetall7625Ай бұрын
YALLA nalèn Thiat sèkhlou ta may lèn kholou mougne ta Yalla yeureum AZIZ ak WALLY amine yarabi 🤲🏼❤️
@adamandiaye4314Ай бұрын
Machalla Bagaye Mbaye courage la famille Aida courage metina loleeeeeee
@oumousamb2028Ай бұрын
Pagaye ya bakh. Yalla naléne sama Borom faye bijahi Nabil Moustapha Sallalahou Aleyhi wa Salam.
@NdeyeFatouKeïta-j3kАй бұрын
Wouy sama khol bi 🥺🥺❤️🔥
@yacineniang7611Ай бұрын
Ohhh Mére dioye lonama 😢😢😢 li dafa yomb trop mais yalna yalla leral lepp tei Aziz ak wally yalnaniou khippé adiana firdawsi
@madeleinemar6991Ай бұрын
Pagaye yaye gore waye yalla nala yalla defale diame si bareke seydina mouhamed 🙏 🙏 ❤❤❤
@MaimounaDieng-fz5hrАй бұрын
Paguaye ak samba nguere ay goor pur lagnou.yalnalene yalnalene yalla fête yiiw.mere bi yalnako yalla takhawou té lep leer
@mariemethiam5861Ай бұрын
Walahi. Li molay wane que nekk ak nitt ki bess bou nekk takhoul moudone sa waay. Nit ki meunala sorri lolou fekk diégué nala😢😢😢😢
@FatimandaoTymandao-gr4glАй бұрын
Ina lillahi wa ina ileyhi rajihoun, aziz ak boubacar yalnaniou khipé aldiana té yallah yeureum bolem dioulite
@ZeynaTounkaraАй бұрын
😢 Bilahi Ande yeup Ande ak goor mothie Geun pagaye yaye goor di garmi samba nguer yowite bou azize gneuwaton do rousse bilahi magou Aziz bi soumako guisse cmm azize mo tok Abdou Aziz ba Wally yalla nagnou khipe aldjianay firdawsi Thie Barke Seydouna Mouhamed psl 😢😢😢
@dadashu2052Ай бұрын
Psl
@AmicoleDia-be5cpАй бұрын
Amine
@AissataBah-ih1kpАй бұрын
Amine Ya Rabouna 🤲
@MbayeNdiaye-v1wАй бұрын
Man de yalla khana ni dama nékh machala
@SeynabouFaye-b6qАй бұрын
Ah machallah pagaye mbaye Mario samba guer ay gor deugue guéne lii Moy nite mou nekh guéne bokou mou nakari guene bokk yalnalene yalla Faye Aziz demna yalna souff woyof ci kawam wayé khamna foumou nek kholame Sedna maman courage aida métina lole wayé nak yalla bakhna justice pour Aziz et Wally rek lagnou rek
@FatouDio-y8gАй бұрын
Est ce que vous voyez la douleur dans le regard de la soeur d’Aziz 😢😭😭😭😭😭😭💔💔
@FatimandaoTymandao-gr4glАй бұрын
Kou ray ben niit raynga nieup 😢
@seynabfatalecisse9141Ай бұрын
Aida est trop belle ma challa
@sokhnandiayeba5606Ай бұрын
Très belle meme mashahallah tabarakala
@rouguikebe9984Ай бұрын
Wi machallah 🎉
@AminataBaldé-f3dАй бұрын
En plus elle a une belle voix ❤❤❤
@veroniquenatack7392Ай бұрын
*Machallah❤🙏🏽*
@aissatousagna7070Ай бұрын
Trop sakh macha allah ❤❤❤❤
@khadygueye5714Ай бұрын
Pagaye yaay goreu geunala beug❤
@Faby-u7hАй бұрын
Pagaye tu as fait un geste noble que dieu veille sur vous
@Faby-u7hАй бұрын
Justice amoul Senegal li da yombou lol Bilahi faate ay Domou diambour té dara fekou lasi mane yayou Aziz dama ko yereum yalla nalene yala mey xolou mougne reposè en Paix mes frères 🙏🏻
@byka1219Ай бұрын
Kane mo fate té dara fekouko si? Khamoni ki ray avoué na moungui si kasso bi?
@kaani_teumbeulАй бұрын
@@byka1219 ki teug faat bi minguii si biitiii di tapeu datam ! Nafeeek nguen trope ! Di beug leurrer helou diaam yi fiii faaté khadioufi thiaga bu sokhor nabou ley teug leep nak sokhor ak alalou adouna ! Senegal nak kou dé ya perte ! Aziz souma bokone ak mooom fouma guiss nabou leye ou un membre de sa famillle damaay dakhar ndeyamm à coup de couteau fadial sen bop match bi tasss vu SENEGAL sunu justice coumba am ndeye ak coumba amoul ndeye leu ! Nanie ko wakh teh dé teh bayilen naaafeek ! Wa salam
@byka1219Ай бұрын
@kaani_teumbeul 😂😂😂 ta haine va te tué !!!! yaw justice takhoula diok dangua am febarou kholl 😁
@thiabandoye7173Ай бұрын
@@kaani_teumbeulli dei mo am Senegal
@kaani_teumbeulАй бұрын
Haine ouiii pask ya injustice ! Cette vipére de merde là jla connais ni dAdam ni deve jlai connu lors de ce double meurtre qu'elle a plannifier ! Emprise sakh jle regardais pas pour te confirmer khawma wone thiaga fethie kat bobou ! Mais son acte barbare là double meurtre bimou teug moma méti fi faté khadioufiii ! Kheww mi dou si slip thiaaya lasi mariniére lasiii ! Moy deum bi dans l'histoire ! Elle a trahi son ami ! Yeufou deum deug la deff !
@aminatafode8425Ай бұрын
Kene dou samba nguer ❤
@OumulBah-ns4tkАй бұрын
Wahatikor kenna du mom
@YafayeAïchatouFayeАй бұрын
Ndeysane adouna dou dara yalla bakhna merci pagaye🙏
@KhadySarr-bo9gjАй бұрын
Bilay j'ai des larmes😭😭😭😭😭
@rokhayadiatta4626Ай бұрын
Moi aussi c triste vraiment
@rouguikebe9984Ай бұрын
Mercii Pagaye et Mario c vraiment noble cette acte❤️ Que justice soit faite✊️
@fatimenahaye-wn7ekАй бұрын
Bilaye walaye sama khole dafa méti trop ♥️ yalla na yalla yereume ci barké seydina Mohamed amine yarabine 🤲🤲🤲🤲🤲🤲
@aissatasysy135Ай бұрын
Pakay diardiof mane ndeysane chaque jour sou ma guisé famille bi sama khôl déy diékh billaye wallaye surtout mère bi déma ko yeureum beu kéne khamoull limou nouro.ndeysane mère nouyounala bou bakh ak Aïda ak modou bâ ak gniénéne yi yeup machallah yala na yala may léne kholou mogne
@AntaSow-t6rАй бұрын
Merci beaucoup pagaye ylla na yalla faye
@princesseonelove8908Ай бұрын
C est trop dure je n en peux plus
@meuzndiaye1458Ай бұрын
Hoo pagay mbaye yalla na la yalla fay❤❤❤❤❤
@AliouSeck-j1vАй бұрын
Aziz dabala rk❤❤❤
@michoudymen30Ай бұрын
Yalla nalein yalla faye sein khôl,sama❤ toye na😭😭😭
@ngomamboup-lr9ymАй бұрын
Machala azize yalna ko yala dieguell
@AminataBaldé-f3dАй бұрын
Amine
@MaimounaDieng-bp2pgАй бұрын
Ay way justice pour Aziz d’abala ngir yala
@MametilloFallАй бұрын
Pagaye et, samba naguère ay,fort,lagnou, merci beaucoup,et paix a leur âmes reposse en paix 😭😭😭😭
@radiagueye3092Ай бұрын
Machallah yalna yalla fay leu
@thiabandoye7173Ай бұрын
17:16 mere yalna la yalla maye kholou mougnee 🙏🏾
@fatimenahaye-wn7ekАй бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤du courage yaye boye masa🙏🙏
@khadidiatoundiaye3120Ай бұрын
Li rk la kharite fi jarinie Waw Goor Fall
@diakherlaye4580Ай бұрын
Yalnalen yalla yeureum kharelen aldiana c dure
@fatoujoof2093Ай бұрын
Pagaye you are good brother stay bless🙏🙏
@veroniquenatack7392Ай бұрын
*Pagaye et ttes les personnes qui t’ont accompagnés un grand merci pour vs geste bi nice na li la kharite di gneurigne moromam🥰❤️*
@aichafall3679Ай бұрын
Machalla yalna yala fay la
@FatoubintouDiallo-f9nАй бұрын
Merci pagaye bien fait yalanala yala faye
@NdeyeaidaDiop-ct1gqАй бұрын
Machalla yalana yallafaye
@hawasoumare1689Ай бұрын
Mario da khamoule rek mes azize rakou yayou ndakhte la
@Lacherifaaidara-i5Ай бұрын
Mamame la mai nioune niol ay yayam
@AstouSy-f8iАй бұрын
Ndeyssane dawe si heure bi kou wakhone Aziz sa bakéne bi saye nite yiguay nékal niokoy dieul mou bayi la ray bi niawe na bilakhi
@rokhayacisse7905Ай бұрын
Vraiment
@veroniquenatack7392Ай бұрын
*Bilahi😢😢*
@MakouKhoumaАй бұрын
Ndayesan 😢😢
@meuzndiaye1458Ай бұрын
Kharit ni layyy mél❤❤❤❤❤❤❤
@cocottejolie2469Ай бұрын
Defguene Lou rafete ❤️❤️
@yacineseye3156Ай бұрын
Machallah Pagaye yalla na yalla Faye yiw Aziz yalla nako yalla yeureum
@fatoujoof2093Ай бұрын
Abdou Aziz and wally yalla nalla yallah haral Arjairnay Firdawsi Amin yarabi yallahou 🙏🙏🙏
@rachelandrews5889Ай бұрын
Thank you guys this is really touching I pray he continues to R.I.P Hugs 🤗 to the family I’m typing in tears I pray for Allah to strengthen the family ❤
@ndeyesalioundiaye3119Ай бұрын
Yagulenfi rek yen tewer thi barkep s saliou❤
@diopndayefatou8938Ай бұрын
Machallha ❤❤❤😢
@kandjikhady6659Ай бұрын
😢😢😢😢😢😢machala li rafètena
@MametilloFallАй бұрын
C'est bien sa, merci beaucoup pacaye
@JesfdemАй бұрын
Pagaye y'a bakh y'ay gor machallah❤❤❤❤❤
@aramediop991Ай бұрын
❤❤❤❤❤machalla merci
@AbdoucissDioufАй бұрын
Pagaye l'homme de valeur un vrai noble que justice soit faite samba nguér goor pire
@MaimounaFadiga-fv1vpАй бұрын
Yaye boye yalnalène yalla doli may kholou mougne kharé ardianay firdawsi Aziz et Boubacar Si barké Nabi Moustapha psl😭😭😭😭🙏🙏
@aissadicko9817Ай бұрын
Merci Pagaye Mbaye tu es reconnaissant❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@MariamaDembele-gy7kzАй бұрын
Machala ya bakh bilaye ❤❤❤
@papagdiagne6297Ай бұрын
Ndeyssane yalnalene yalla fay bilahi li daffa metti gni def dieuf diou bone dji yalnagne alkou beutieuk ndarkam
@FatouSidibe-d5lАй бұрын
Ohhhhh beau geste😢😢😢😢😢 ndeyssane
@HabyDiallo-u6gАй бұрын
J'ai de larmes au yeux tellement triste justice pour Aziz et walli
@CoumbaWade-de7bwАй бұрын
Oh c est dur vraiment on on sent encore la douleur dans le regard de la maman mais aussi de sa sœur Pagaye Yalla na la Yalla fay yiw Que Dianatoul Firdawsi soit sa demeure éternelle demeure éternelle
@marybarham3490Ай бұрын
aziz ak boubacar wally yalla nalen yalla yeureum te khareko aldiana
@LuisaLuisa-t5sАй бұрын
Pagaye Noble Deuguela ❤❤
@isac1478Ай бұрын
Vue le comportement des membres de la famille de Aziz , cela confirme que ils savent Bel et bien qui est derrière tout ça... Dioundiou doyna borom khél.
@mbayangsoumare7713Ай бұрын
Ou sont les autres artistes ils foivent faire comme pegaye
@kyasock9415Ай бұрын
Pagaye lou rare gua def mouy gorée ak yarou
@pendaseck6448Ай бұрын
Gérer yala bayilene merci mou nopalou
@MamyNiang-s7tАй бұрын
Machalla❤❤❤❤❤
@AwaMbaye-j3wАй бұрын
Merci mario
@bouwally3702Ай бұрын
Mais où sont tous ses amis qui étaient ici temps décès bi 😢😢😢kharite yombouna mais gor mo diaffé😢😢😢c'est vraiment dommage pour la famille
@malily6705Ай бұрын
Comment on peut tuer l'enfant de quelqu'un 😭
@FatouNdiaye-c9bАй бұрын
Machaallah.paixa'son.ame.avec.waly
@Shasha-nt3rmАй бұрын
Mashaallah ❤❤❤❤❤❤
@AlimatouDiéne-u2lАй бұрын
Machalla un bon geste❤❤❤❤
@martinebindia9528Ай бұрын
Justice pour Aziz et wally pr k leur famille puisse faire leur deuil la maman m'a fait couler des larmes trop triste
@MadameSane-yo1rjАй бұрын
Aziz foum teude bilay contane nasi yaw naysane li rafétna😢😢
@kandjikhady6659Ай бұрын
Justis pour aeisse et wally
@moniquekore9847Ай бұрын
Très bon et noble geste de ta part
@AissatouWade-z2nАй бұрын
Heure bouma guise yayi Aziz rek damay dioy bilaye
@khadidiatoundiaye3120Ай бұрын
Oh🥺🥺🥺
@codougueye290Ай бұрын
Yalla nalléne yalla maye kholou mougne
@AdjaBa-td3vmАй бұрын
Yalla nala yalla faye ya bakh
@magattegueye7863Ай бұрын
Yalla nalène yalla fay yiw
@aissatoufaye9775Ай бұрын
Talle bou Ya ALLAH talle Sanissi mate te geune feyko
@mariamaba3161Ай бұрын
Ndeysan😢
@mariamathior2Ай бұрын
Ndy la maman elle est meutri gni def li yalla bougnou ame diame😭😭😭