Machallah merci à ETOILE DIAMONO TV 4K. C'est la première fois que je vous découvre. Cet interview avec 10.000 était très enrichissant. Merci à l'interviewer pour votre humilité. Yalnalene sam té arlene
@JoakineFodeDasylva3 ай бұрын
10 mil l'ambassadeur du peuple 🇸🇳🇸🇳💪💪
@_serysery_3 ай бұрын
Bravo 10 milles déugg rék nga wakh. Khan wagni saga yi rek👍🏻👌
@almaktoumdiop87493 ай бұрын
Yéne sénégal yéna geumatoule yalla serigne pour lane kéna touko digate té mouhamed mo geune serigne touba geune ma elhadj malick souma serigne geune gñiépa té danoukoye digate yalla sakh am na gñoukoye digate guéni sounou serigne si danouléne di geume forze meunoul né
@FatouabdoulayeNdiaye3 ай бұрын
De tout coeur avec 10000pb maachaallah djangue ame solo lole
@BabacarFaye-sq6rv3 ай бұрын
Vérité absolue teine taw ❤❤❤❤
@ThiernoGueye-ul7uk3 ай бұрын
Bravo 10.000❤❤❤❤❤❤
@toque58553 ай бұрын
Ñòom ñeupeu ngui deuk ci quartier you nékh yi Dakar, Di liguèy loo ay Talibè Té dougn lèn fay, djiguèn ñi nèk séni Mindane, gòor ñi nèkeu séni gardiens dougn lén fay deureum, amougn bèneu yeurmbané ci nit‼️🔥Tòok mouy dokh yi ñooy khékh cheikh Omar Diagne ndakh robinet yé teudj ‼️
@DAMEMbaye-iv3zz3 ай бұрын
Étoile diamono rek lañouy topp 🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
@MariamaDiallo-cp3jk3 ай бұрын
Machala d'imile problème y'a deugou li wah thi gordjigéne néka gore di diaye poupe douai âme
@AppelZone-ci2fk3 ай бұрын
Dieureudieufè borom touba ❤❤❤❤❤
@boubasambe383 ай бұрын
Machalla 10000probleme nassa diam yague je t’apprécie bien
@HalilPro-cp6cg3 ай бұрын
❤❤❤Étoile diamono
@NdiagaGueye-n7u3 ай бұрын
Machallah 0000 Problème,dieureu dieuf
@tinedaouda3923 ай бұрын
Macha allah ❤10000
@ThiernoGueye-ul7uk3 ай бұрын
❤❤❤❤Rang mouy souss
@AliouCisse-x5d3 ай бұрын
Diadieff rangg bien dit
@BadjiElhadji2 ай бұрын
Bouléne félicité 10 mil Day doul bokoul si gnou gnou fal diomaye dém lén kholat ancien vidéo 10 mil ki guemoul Dara
@idsmovengo54713 ай бұрын
Manshalla 10000❤❤❤ véridique
@MamefatouDiagne-d7z3 ай бұрын
Wawaw amna solo diné rekk
@adobaby93 ай бұрын
10mille néna ngeun Ndey abonnés
@ebrimaloum61483 ай бұрын
Ken farul ak sa ndaye Ken andull ak sa ndaye nga khamekononu
@AmethNdao-o3r3 ай бұрын
10.000 problèmes ténn tawzeunn maateu from laakhira Rang Mouy gaww, Rang Mouy gorré
@DaoudaSene-q3b3 ай бұрын
Manchalla
@boubasambe383 ай бұрын
😅lou lerrrr la wakh fronnnnnnnchment😎
@diopabdou66003 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤
@bambafall6483 ай бұрын
😂😂😂astafourlah ki mo rew non 10milles rewna
@laoucouledesruissaux44953 ай бұрын
Cheikh omar diagne joumoul fén deug la wakh
@basselabdou98913 ай бұрын
❤❤❤
@OumyDiallo-d1p3 ай бұрын
Yaw mayeh niou diamou
@NdeyekhaytaThioune3 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤
@DaoudaSene-q3b3 ай бұрын
Ya mana Doul ioe Serigne Touba day moromom Domouxaram
@DaoudaSene-q3b3 ай бұрын
Cheikh Oumar Diagne bane histoire ladef cii dîné islamique ak kouko xam Daniou xamadi torop même sunu borop da téré kouy dingatte yéféér Waxatoumalakh kou dioxé doundeu béép pour religion islamique
@GoraMbengue-f2j3 ай бұрын
10000 rekk laniouy topp 😂 rangggggg
@zizadirector3 ай бұрын
Tout ceci commence par l’influence des gens qui sont arrivés à l’extérieur pas le chemin de l’immigration. C’est eux qui leur attire le plus c’est vraiment désolant. Paix à l’heur Âme .
@almaktoumdiop87493 ай бұрын
Sénégal dafa yéss wakh you bone rék Sénégal dou dème dakh kéna yénétoule samorome diam
Sa way bayil manque de respect bi nitt day yarrou yaw Lila wadji wakh deug leu bayil rew makk day yarou
@mcniangorfromonebrainfamal6393 ай бұрын
Étoiles Diamano
@AdjuntoOfrece-qr7db3 ай бұрын
Diadieuf 10mil😂
@papengom2593 ай бұрын
Ki réw na ndayam
@Gaye-industrie3 ай бұрын
Mai 10 mille cest pas possible l'apparance est trompeuse
@cheikhmorgueye3 ай бұрын
😂😂😂😂
@PapeBa-mt8qq3 ай бұрын
100mill diambarr la
@elagegueye33103 ай бұрын
😂gane gamou ak magal si islam la bokk.etoil demal seti borom hamham ma guen
@abdoukarimsamba98123 ай бұрын
Alkharan tamit aye nitte nioko bind
@lazoNdiaye-bj5yx3 ай бұрын
Sawaye alkhourane wakhou yalla la nit khalatouka yalla moka wathié si seydina mouhamed, daguaye wakh nitte moko copié tass gua si adouna bi
@abdoukarimsamba98123 ай бұрын
Wahouma nitt mo halate dai nitte moko bind defko aye libre wala
@aldioumadieye90883 ай бұрын
Yallah en réalité waham moy kullu mbidéf sinon yallah gnép la wahal. Après les livres se sont des récits historiques, géographique, sciences, mathématiques, spirituelle métaphysique, physique quantique et le biographie des auteurs ect. Donc oui ay nite gnoko bind.
@elagegueye33103 ай бұрын
Nouko ay nit bunedoul ay deumb niokoy bune deu.sen serign mo bundeu nee mo guen yenentebi psl 😂
@abdoukarimsamba98123 ай бұрын
@@elagegueye3310 sawaye yaw nehe ga dai .c 10000 ki a dit mome djangul Francis alhiurane la djangue mou libre ecole aye nitte nioko binde mane ko coran bi tamit aye nitt nioko bind.boule tonye kene sawaye
@elagegueye33103 ай бұрын
Kan mofi wahonne nan djiguen bou amoul loumou lekk meunna diay boppam?😂😂