Balla gaye2 grand champion le roi incontestable des arènes Mashallah le PAPA des lutteurs !
@aliounembaye9675 ай бұрын
Sa xam xam rek nga wax
@ouzdaking3825 ай бұрын
@@aliounembaye967 sama kham kham moye deugeu !
@LeytyFall6 ай бұрын
Ndiaga amgua xél machalah
@AmadouHabibLy6 ай бұрын
Vérité Absolue ❤
@SeydinaThiam-b7y7 ай бұрын
Ndiaga nioune nieup guediawaye laniou deukk mais dagua beuri loy critiquee balla gaye lolou bakhoul heure boy beuré daniouy niew stade dague ticket ndakh nigua mél ci balla gaye
@dmo.gsenegal56917 ай бұрын
Dou si mome deh seytané yii neik si plateau bii gno beuga créé problème deugloul bou bakh wakhtane bii plateau nafeukh lagnou
@ahmadoudiop50167 ай бұрын
Ndiaga déh dadone dieul risque si ay combat balla gaye té bokunu écurie pask dadone bok si accompagnant yi sol cagoule te cng bi meunone nakossi sanctionné dadone sone si balla diko japalé contact mais yéna far lép gnak waxatane leu rek mo waral nguen réro
@amadoundiaye88417 ай бұрын
Diagua a dit la vérité
@m.moussa6787 ай бұрын
Kouy andale mou taner la tei djapale woula bayikoo nek sa boppp.
@ibrahimagadiaga76067 ай бұрын
Boye ande ak nit pour intérêt kay gua dème ligueyi gua âme loumou âme niak fayda rk la défe Ki balla gay magou ko contact sédo la amoul diapalé
@abdourahmanesindidi18187 ай бұрын
@@ibrahimagadiaga7606saway and bou deugo diapalante amsi yalla bindoul niep niou yam kon ap andeu kou tane sa morom nako dimbali
@Amethfouteu8157 ай бұрын
Bilahi fadam kou sof la dara hamouko 😢
@MalahDarénokiwi7 ай бұрын
❤❤❤❤❤
@OmarSarr-sl3kn7 ай бұрын
Blh ndiaga dollé dafa nekh 😂😂😂😂
@sergedione76587 ай бұрын
Ndiagua Dolé ak Fadam2 bi gnou dalane té fala diar bayi😂😅😂😂😂😂😂😅.
@ndiougamar22027 ай бұрын
😂😂😂😂 Dafa néekh
@BrigitteDione-b2r7 ай бұрын
Bekay. Dinamaray
@diaaammmouuuurekkkkkkk7 ай бұрын
Ki da niakk fayda bilahi mome balla rek lay kheuyè diko gonto
@NiangBoundaw-h2m7 ай бұрын
Abdoulaye sylla met l'accent sur la création d'emplois pour stimuler l'économie sénégalaise
@DpDp-hg6fx7 ай бұрын
Yow mi balla gaye magoula daga tardè di lamb rek démal défi lénéne do mbeur
@papembaye79937 ай бұрын
Saway ki balla gaye meun nako diour. Je connait ndiaga dolle dep8 son enfance. Ecole 18 ecol football ball aidara , il etait trs disponible pour son quetier quie jamono2 Bakhak inoncance moko tardel si lamb Pour precisé 14 ans mogui si guissoumako degoumako Kou oyof am yeuk yeuk nitter mo nek ni
@abdoulatifdiop56407 ай бұрын
Wakhal wakhou nitt
@gabrielmendy47887 ай бұрын
Loko khamal yaw wakhal lila wore
@ahmadoudiop50167 ай бұрын
Saway balla est mon lutteur mais ndiaga ak sama copin gno bokone classe école 18 ki balla moko makk même bou beuriwul
@LamNdiaye7 ай бұрын
Ki balla magué naka 5 en😊
@YahyaDumbuya7 ай бұрын
Mr,did you ever confront balla gaye 2 an tell him all what you have been saying in the media. The problem of this new generation is everyone runs to the media anytime they have personal issues with other people.