Ndiouga Dia coach de Modou Lô se veut clair : "Reug Reug Mo Guena Nékha dane ci mbeur y..."

  Рет қаралды 28,456

Lutte TV

Lutte TV

Күн бұрын

Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct / luttetv
/ luttetv
/ luttetv
/ luttetv
luttetv.com/

Пікірлер: 127
@mouhamadoudiene1315
@mouhamadoudiene1315 Жыл бұрын
Boy yeup laniouy défaral inchallahou rabi. Omar Kane au suivant. Gninane Reug vs Reug Boy Niang bayilén igniane modou néna boy yi lay may chance boy Niang dieulna kassou fondém ba paré na Reug nieuw dieul bossam guinaw insbi mo geuneu confirmé ci boy yi. Rannnnng rek inchallah
@NdiasseSylla-h3k
@NdiasseSylla-h3k Жыл бұрын
J’aime tes paroles 🤝
@adamaaw3486
@adamaaw3486 Жыл бұрын
Pourquoi pas Tapha Tine..?
@zokorasall9617
@zokorasall9617 Жыл бұрын
Modou lo vs reug reug mo geun nexx
@Mo13092
@Mo13092 Жыл бұрын
Ioe ko yapp? Fi dou gambie gayine reug reug na dieul franc, am 11 combats beug beuré roi des arènes
@mhd_0039
@mhd_0039 Жыл бұрын
Damani reug vs modou dou lamb dji reug vs boy niang modou vs tapha tine loloy logique mbeur bou ay 14 combats wam matoul nguen beug ko diokh roi des arènes bayilen lolou day yak lamb khalé dzy prouve lou beuri dorz niam combat royal comme niko niep defé wasalam
@ibusene8075
@ibusene8075 Жыл бұрын
Reug Reuv future Roi des Aréne inchalah da mane beuré machalah
@Laminediallo013
@Laminediallo013 Жыл бұрын
Sonnerie bi 😊❤🎉
@MamadousyNdiaye-t6m
@MamadousyNdiaye-t6m Жыл бұрын
Père mayléne niou chance rek léguii mou leer éy Reug Reug éy Reug Reug père dieuléne Reug Reug c'est une très belle affiche vraiment Reug Reug c'est un très grand champion
@papadiom9260
@papadiom9260 Жыл бұрын
Gathe ngalama Champion khekh nga lounekh thi combat bi. T’ es un vrai boxeur mais travaille ta main gauche quand mm. Tu as une bonne garde défensive mais tu n’ utilises pas ta main gauche offensivement. En plus Da nga warona continuer khekh bi !
@mamadoumoustaphadia8188
@mamadoumoustaphadia8188 Жыл бұрын
Père ndiouga sopenala machallah
@modoulebou634
@modoulebou634 Жыл бұрын
Nena Reug Reug mo guena nékha dann si lamb dji 😂😂wa mais modou Lo ma may Reug Reug chance rék🙏🏿👑👑🦍
@mhd_0039
@mhd_0039 Жыл бұрын
Lolou dafa tell bayilen di woutal yoon ay mbeur
@SarryElhadjiOusmane-kq5lc
@SarryElhadjiOusmane-kq5lc Жыл бұрын
Athia Père Ndiouga Dia nasa Jamm Yaag Amiin
@senateurndao094
@senateurndao094 Жыл бұрын
Modou lo reug reug combat la
@ibusene8075
@ibusene8075 Жыл бұрын
Reug Reug Modou lo Combat bou nekh lay done
@mhd_0039
@mhd_0039 Жыл бұрын
Dou logique
@TECKNOFINANCE
@TECKNOFINANCE Жыл бұрын
Père avec tout le respect, maylen Reug Reug chance, vous verrez s'il est facile à battre ou bien. Il faut demander Franc il en connaît quelque soz. Reug Reug l'a battu 2 fois.
@TECKNOFINANCE
@TECKNOFINANCE Жыл бұрын
12 fois
@falyndoye3800
@falyndoye3800 Жыл бұрын
13 fois même
@IbouDiaw-l9s
@IbouDiaw-l9s Жыл бұрын
Plus 2fois
@Killer-z1u
@Killer-z1u Жыл бұрын
Reug dou dara saway Sa Thiès moko humilié
@zokorasall9617
@zokorasall9617 Жыл бұрын
13 fois la reug reug dane fran
@atoumaneniasse4854
@atoumaneniasse4854 Жыл бұрын
Machallah pér lou leer nga wakh ❤❤❤
@diaspora2553
@diaspora2553 Жыл бұрын
Kone reug reug vs modou lo laye done insalla
@mhd_0039
@mhd_0039 Жыл бұрын
Dou lamb
@diaspora2553
@diaspora2553 Жыл бұрын
Boune beure' modou danou de
@fadelbambiste1451
@fadelbambiste1451 Жыл бұрын
Père ndiouga on t’aime🥰
@africanboy2817
@africanboy2817 Жыл бұрын
Père linga pothie amatou fi😅😅😅
@cheikhahmedlo7718
@cheikhahmedlo7718 Жыл бұрын
Paire ndiougua vrais ndandité la ta am xam xam🥰🥰🥰🥰
@SoldarouBamba__4
@SoldarouBamba__4 Жыл бұрын
Modlô vs tapha tine Reug Reug vs lac de guerre Siteu vs Balla gaye 2 Boy niang vs franc Quench vs serigne Ndiaye 2 Gora sock vs moussa ndoye Diene kaïré vs jackson Amanékh vs Alioune seye 2
@ManoVideotech
@ManoVideotech Жыл бұрын
Modou Lo vs Tapha Tine 🔥 🔥 🔥 🔥
@halloufaydou9425
@halloufaydou9425 Жыл бұрын
Fans Modou la J’aime bien ce combat ndakh niarry derr lagne Ayy mbapate katt Mais yaag yaag modou dey yobou wate courone bi parcelles ❤
@ousmanesarr756
@ousmanesarr756 Жыл бұрын
Bilay bagnou gnou père reug aka yomb dane mais maylen niou chance rek ngir yalla😂 modou mo meun boy yeup mai si ndiekk lagnou la niane mayal reug chance après nga niouss niou grawoul😂🙏🏻
@abasall711
@abasall711 Жыл бұрын
😂saway ya nex way si nako maye chance insbi amul combat
@ousmanesarr756
@ousmanesarr756 Жыл бұрын
@@abasall711 bilay khulo wugnu niom nio meun kay nangnou may chance defaral niou khana lolu kay metiwul 🤣🤣🤣
@ballandiaye9430
@ballandiaye9430 Жыл бұрын
Dieulen reuk rek après guendi comprendre
@koundoundiaye148
@koundoundiaye148 Жыл бұрын
Modou lo vs reug reug moy combat bi
@mhd_0039
@mhd_0039 Жыл бұрын
Dou logique modou vs tapha tine loy lamb dji ba paré
@Mahmoudsene
@Mahmoudsene Жыл бұрын
Modou vs reug reug moy combat bi
@koundoundiaye148
@koundoundiaye148 Жыл бұрын
En tt ka combat bou nekh la
@mhd_0039
@mhd_0039 Жыл бұрын
Dou logique modou vs tapha tine loy lamb dji ba paré
@baradieng1489
@baradieng1489 Жыл бұрын
Sa mbeur dane ga takeu radio diwakh mais reuk reuk mbeur champions la pere
@modougueye1279
@modougueye1279 Жыл бұрын
Saway sounou danoul tay ndongu dafa dane danatt danatt kignou am kouko amm Fo diarr wkh
@ahmedlo8767
@ahmedlo8767 Жыл бұрын
Degue naniou la Pére boul waxx dieul lene niou rek daguene khamoul reug Reug père
@SarryElhadjiOusmane-kq5lc
@SarryElhadjiOusmane-kq5lc Жыл бұрын
Billahi Modou du moromam
@ig4661
@ig4661 Жыл бұрын
Reug Reug vs boy niang laniou bgueu
@koundoundiaye148
@koundoundiaye148 Жыл бұрын
Boy niang meunoul diougué si défaite di dieul reug reug, staffam doukhko nangou
@64FallAmadou
@64FallAmadou Жыл бұрын
@@koundoundiaye148khana woutoul xaliss rek bougne ko fayei louko diar mou dieul
@falyndoye3800
@falyndoye3800 Жыл бұрын
Père xana Léweul bi dafa nex😂😂 yagui comédie dei ngani Wa Dieul lén avance Reug reik après nguéni comprendre
@abdouamar583
@abdouamar583 Жыл бұрын
Abdoul Aziz mbaye ba😭y’a kasifadhi ❤️😭
@AmadouDiallo-em6pm
@AmadouDiallo-em6pm Жыл бұрын
Modou lo reug reug combat la boy Niang reug reug combat la
@cheikhouomarwane3227
@cheikhouomarwane3227 Жыл бұрын
Yonou lamb Reug Reug doit encore faire du chemin avant de croiser Modou Lô. Et Modou lui même le sait . Reug doit se battre avec d'autres lutteurs avant d'accéder à Modou Xaragne Lô
@MamadousyNdiaye-t6m
@MamadousyNdiaye-t6m Жыл бұрын
De quoi as tu peur chez Reug Reug pour que tu mène une politique qui n'est pas a sa faveur Mayléne niou chance rek kou bakh léguii mou leer en plus c'est une très belle affiche
@MauhamedJabbie
@MauhamedJabbie Жыл бұрын
MOUDOU LO TAPHA TINE
@Killer-z1u
@Killer-z1u Жыл бұрын
Père wahnga deug reug reug dou guiss coup kou tassé ak mom dassal loxo yi 😂😂😂dou dara
@mbathiodiagne6149
@mbathiodiagne6149 Жыл бұрын
Reug Reug vs mod dafa téél na dieul boy niang 2
@Isseu122
@Isseu122 Жыл бұрын
Père Gnouga kone kagna 😂😂😂
@ndiayeabdouaziz588
@ndiayeabdouaziz588 Жыл бұрын
Niari mbuer yi kou si modou lo diel danou balla gaye 2 ak rueg rueg danou
@adamaaw3486
@adamaaw3486 Жыл бұрын
Et Tapha Tine
@MatchoDanfa
@MatchoDanfa Жыл бұрын
Reug reug vs boy Niang moy combat
@ndiougamar2202
@ndiougamar2202 Жыл бұрын
Est ce que boy Niang Di n'a dieul risque bobou
@zokorasall9617
@zokorasall9617 Жыл бұрын
Modou lo vs reug reug laniou begue
@isidorekinz7381
@isidorekinz7381 Жыл бұрын
Prenez REUG REUG alors...Même gratuitement il va lutter mais ...Hummm!!! Faites attention a REUG REUG quand même et aussi a SA THIES. Pourquoi demander plus sachant que vous allez gagner ces 2 petits
@mhd_0039
@mhd_0039 Жыл бұрын
Damani reug vs modou dou lamb dji reug vs boy niang modou vs tapha tine loloy logique mbeur bou ay 14 combats wam matoul nguen beug ko diokh roi des arènes bayilen lolou day yak lamb khalé dzy prouve lou beuri dorz niam combat royal comme niko niep defé wasalam
@freesenegal12345
@freesenegal12345 Жыл бұрын
Père ndiouga ya xéww si jamono bii😂🎉
@almaremegueye736
@almaremegueye736 Жыл бұрын
sokhore bakhoul démléne khole palmaré sou ama ak boy ng reug reug modou lô moy yon tapha tine manoul beuré
@mhd_0039
@mhd_0039 Жыл бұрын
Yaw kay wakhal reug ngua beug mou beuré rek mais ya guene khamni tapha tine vs modou moy lamb dji
@almaremegueye736
@almaremegueye736 Жыл бұрын
@@mhd_0039 si mais ya wakh ma tapha apare eumeu kane la dame sérieuxement
@mansourdrame5109
@mansourdrame5109 Жыл бұрын
Gniy wakh Reug Reug vs Modou Lô xamolen lingen di wakh Reug Reug 11 combats mou beug beurré ak roi des arènes fi dou Gambie na beurré ak ténors yi ba paré té Sa Thiès dafko dane ba paré continuer di prouver bou dioté dina beurré combat royal 👉🤨
@kharagnembaye5958
@kharagnembaye5958 Жыл бұрын
Waa Bocar do dieulat Adama diouf 😂😂😂😂😂
@aliouneelevage6482
@aliouneelevage6482 Жыл бұрын
Vraiment pere ndiouga modou lo ç le khalif general koulou mbeur
@domou__rewmi
@domou__rewmi Жыл бұрын
Boy niang vs reug reug
@ibrahimabasse5934
@ibrahimabasse5934 Жыл бұрын
Reug reug tapha tine fin de saison kou dane beurek Modou lo
@loaboubacar3595
@loaboubacar3595 Жыл бұрын
Souma sagnon Modou lo day xar sa Thiès ndax gno tolo Tay mai tafa tine mom combat bobou dou Nex
@ndiayeabdouaziz588
@ndiayeabdouaziz588 Жыл бұрын
ans 2023 a 2024 man lan fal lom di ans saga katt dax sa touba ak serigne cissé ak boy mor té xamou diou dara
@modo6218
@modo6218 Жыл бұрын
Kou manoul dan sathies begue beurè ak modou ko 😂😂
@ndiougamar2202
@ndiougamar2202 Жыл бұрын
Kou danne fété kaw😂😂😂
@64FallAmadou
@64FallAmadou Жыл бұрын
moma diakhal
@thiernombaye4035
@thiernombaye4035 Жыл бұрын
Reug todiagoul feneu franc lay beurel force modou lo bayam la
@MoctarSarr-e1t
@MoctarSarr-e1t Жыл бұрын
Pere souma amoul woon limay nela da ngay fèen reug mo gueuneu nexa daan nga wakh de 😂😂
@cheikhbasskeurmassar9548
@cheikhbasskeurmassar9548 Жыл бұрын
Père néex nga nak 😂😂😂😂😂😂😂😂 pourtant lou léer la wakh nak
@MbackeFall-ds5uh
@MbackeFall-ds5uh Жыл бұрын
Modou douko dieul na dieuli franc ba parée
@ousmanesarr756
@ousmanesarr756 Жыл бұрын
Reug douko dieul na dieul quench ba paré
@LybassFall
@LybassFall Жыл бұрын
Franc reug dane nako 14 fois franc lane lafi def
@aboubacarsadikhdiop2016
@aboubacarsadikhdiop2016 Жыл бұрын
Reug Reug n'est pas Boyniang ddd
@moussambengue7196
@moussambengue7196 Жыл бұрын
❤🎉❤❤❤
@ibrahimabasse5934
@ibrahimabasse5934 Жыл бұрын
Linek yone Moy reug reug tapha tine fin de saison kou dane beurek Modou.
@mhd_0039
@mhd_0039 Жыл бұрын
Nono modou tapha tine moy lamb dji reug boy niang
@Omarsane7491
@Omarsane7491 Жыл бұрын
Reug reug modou lo dou bere ak mom ta franc nekeufy
@jpsf687
@jpsf687 Жыл бұрын
Modou lo....beuré kessé danouko Paul maurice ken dakouko beuré si boy yi...beuré la wakhh dé...mais bounou Modou lo doré niar beurém defa reer.....Reug Reug bou diélé Modou lo dina ko wekhh khatt
@elhadjiseydoudiop8551
@elhadjiseydoudiop8551 Жыл бұрын
reug reug vs tapha tine kou dane dadié ak modou lo finale
@AzizDejong
@AzizDejong Жыл бұрын
Et sa thies
@elhadjiseydoudiop8551
@elhadjiseydoudiop8551 Жыл бұрын
@@AzizDejong sa thies il faut que mou dadié au moins 2 VIP avant qu'il obtient un combat royal.
@khadimthiam3081
@khadimthiam3081 Жыл бұрын
Modou lô ak estafam xamnaniou reug bou bah dèsna ci yène diaroul comantè.
@durkio5486
@durkio5486 Жыл бұрын
Reug meunoul khekh modou dakay door mou danou
@abaseye3859
@abaseye3859 Жыл бұрын
Diellen combabi kholl
@mamodoucamara8181
@mamodoucamara8181 Жыл бұрын
Diokhma si 5000 yi père
@fabygueye6061
@fabygueye6061 Жыл бұрын
Reug Nieup xamnagne nii Bombardier bii Combine leu Té Modou dou Combine Beuré té gua dieulii lac Après gris après Eumeu Sene lekk sii millionyii geuneu Taxaww Baxnaa Vraiment il faut être Con pour prendre Modou a lheur là...
@abdoulayedabo9509
@abdoulayedabo9509 Жыл бұрын
Bayil yakk derr Kone moye nangou nioulay daan daan bou Bone
@cheikhdiop9673
@cheikhdiop9673 Жыл бұрын
Reug reug beuré bimouy beuré danoul mod lo kokou beuré yotanté lay déf ta bouko beuré ak mod lo ay rafale lakoy mod lo dor bamou teude sa Thiès késsé mo ci yor beurém dof ta lolou moy dane mod lo wala mou dane la wayé di diéma ték khél comme boy Niang do dane mod lo
@almaktoumdiop8749
@almaktoumdiop8749 Жыл бұрын
Meuni modou yaw so beugué khaliss woutiko modou limouye doyé reug reug reug doudéme beuré ak petit lô reug reug dafa déss bou mouye mbeuré roi sa thies moko dane démba rék gñioukoye khalale yone reug reug tapha tine reug reug boye niang reug reug lac de guérr reug reug franc gñi gñioye adversario reug reug
@maximeflaviendiouf1161
@maximeflaviendiouf1161 Жыл бұрын
Il doit passé par francs
@mouhamedsambe7820
@mouhamedsambe7820 Жыл бұрын
Reug reug dou sama mbeur mais franc na dieul quench reug douko dieul sino mou dieul gris wala lac tei fran amoul vip bou d’accord beurei ak mom nakh dafa war beurei ak quelques morom pour guayi dieul ko
@YoussouLeye-w7w
@YoussouLeye-w7w Жыл бұрын
Franc prouvee goul vraiment reug dane jordan jordan mo dane forza apres jordan reug elton reug gris 2 reug gouy gui yaw forza rek begue dab reug reug nono way
@ixparish1453
@ixparish1453 Жыл бұрын
​@@YoussouLeye-w7w bayilene niouy ratati reik bounou soné dinane nopi franc khamna loutax ak dh dou sieul Que'ch lou nk moune nakossi fek lissi dess lamegnie lakoy motalé Na wakh reik lamb mogui sunu canam
@64FallAmadou
@64FallAmadou Жыл бұрын
modlo sa thiès mo mane si mome dara mais dou boy yi takhaw diko déklou
@mhd_0039
@mhd_0039 Жыл бұрын
😂😂 sa thies dh modou dinako dan ba tok si kawam the dou kham lou lhew 😂😂
@64FallAmadou
@64FallAmadou Жыл бұрын
@@mhd_0039 🤣🤣🤣bakhna ba boba inchallah
@bayemodoufall2879
@bayemodoufall2879 Жыл бұрын
Mocvxccv❤mocv
@Elhadji2187
@Elhadji2187 Жыл бұрын
Reug reug n'a dem beurré ak ay moromam ba paré defagou fi dara
@patriotsafricains3745
@patriotsafricains3745 Жыл бұрын
Reug Reug liko dessé pour mou diot roi bi da Bari, dafa begu soutér déme si roi bi dafay yomb trop
@LybassFall
@LybassFall Жыл бұрын
nafeikhe
@MbackeFall-ds5uh
@MbackeFall-ds5uh Жыл бұрын
Modou douko dieul nadiar si franc baparé
@BabacarSall-d9d
@BabacarSall-d9d Жыл бұрын
Sonnerie bi😮❤🎉
@toutiwakhjobloubari8746
@toutiwakhjobloubari8746 Жыл бұрын
Modou lo vs Reug reug moy combat bi
@toutiwakhjobloubari8746
@toutiwakhjobloubari8746 Жыл бұрын
Reug reug vs Modou lo moy combat bi
@mhd_0039
@mhd_0039 Жыл бұрын
Dou logique modou vs tapha tine loy lamb dji ba paré
@domou__rewmi
@domou__rewmi Жыл бұрын
Modou lo vs tapha tine moye combat bi
OCCUPIED #shortssprintbrasil
0:37
Natan por Aí
Рет қаралды 131 МЛН
요즘유행 찍는법
0:34
오마이비키 OMV
Рет қаралды 12 МЛН
Arrivée de Modou lo/petite lo combat
9:03
CombatTV
Рет қаралды 656
Boye Niang2 Infiltré par le Camp de Modou lo; Khadim Gadiaga devoile les secrets aprés Le Combat…!
12:59
OCCUPIED #shortssprintbrasil
0:37
Natan por Aí
Рет қаралды 131 МЛН