Kokou dal nitou intéré la té amalouko béne ndiarigne na gueme bopam yala dinako maye kou bakh inchallah
@kgueyekhadydioufmachalaave86183 күн бұрын
Je demande pardon de ma contribution et mal ecrire sa saute les mots du pays que je suis je suives toujour cettte emisión merci Fatou tu brave gent machala que le bon dieu te garde
@tocktocktoon50069 ай бұрын
Ne nieuw me takk ko cette femme est merveilleuse
@modoungom311610 ай бұрын
Demal wouto bénéne dieukeur mo gueune worrdé
@mbowmalick668110 ай бұрын
Sokhna fatou ziar nala borom yàlla bakhna sa émission bi Amna solo lool mashallah et bonne continuation 🎉
@SigePouye10 ай бұрын
Biss bo delo soumala reke😮sangne gua delou si kokou yawou
@RamatoulayeDiallo-gd8ru10 ай бұрын
Et après même si on t appelle madame c est ta vie privée.Mais walahi si tu retourne avec ce gars tu finiras par le regretter car il sait que t as un joli coeur.patiente et c est mieux que de retourner avec cet homme et sa famille qui ne valle rien tente ta chance ailleurs c est mieux pour toi dé . Bakhna dal
@siradiarra86027 ай бұрын
Il faut jamais retourner avec ce gars
@AdjamaimounaFaye6 ай бұрын
Dafa l’air
@ibrahimasall37244 ай бұрын
Sil vous plait, cest quoi "njak nanggu"
@pacogueye297210 ай бұрын
Seugeum mbeugel Moy seye doumala conseillé gua delou ak mome wayer bo dieuler décision delou gua fusillant ❤
@NdoumbeSamb-v4x10 ай бұрын
Non bayil wadji fofou ga nek si Europe meune gafa ame dieukeur
@amsaba10 ай бұрын
Waw waw
@FamaNIANG-ns6dr7 ай бұрын
Si tu veux mon conseil, tourne la page pour de bon. Ta fille comprendra et je te souhaite de rencontrer un homme qui t'aime et te mérite vraiment ❤ bon courage
Ki nitou interet la ,dafa beugue voyagè ,Ndawsi na am foula lo nègoul gnak do am louko gueune ,wadji beugoula tè amoule diomm
@SeynabouGueye-s5p6 ай бұрын
Sokhna si diambar nga goré nga té beguue nga seuy wayé nak ki d'où djekeur ndax bou goréwone Dina dieéma woute sax ci loumou diap ndax diabar nawléla🫶🫶
@PayaFall-ez1nf10 ай бұрын
Ay way ben coté yeureum na wadji deh 🥺😢 mais soukoy djokhati khaliss na fek moukoy ame mais boudé lénen boumouko djokh khaliss😊
@cherifkillah101310 ай бұрын
Mbeguel ak respect moy seuy
@MarSeck-jd1qbАй бұрын
😮😮😮😮😮😮😅😮😮😢😢😮😢😮😢😢😮😅😢😅😅😅😅😅😅😅
@dramebouba674910 ай бұрын
Wadji nitou intré la dhe wa bakhna na gueme yalla rek faté wadji🦻👈🦻👈
@moriciss63689 ай бұрын
😢😢 vraiment les femmes kangne ngéne di yéwou xalé you yii ma guiss beuguounous sona gor boula taka nala yore tes diokhla wargual ko khamni lép yako déf guouro sakh deuinouko bayil mou dém ki intéret rék lalay doyé
@THIAM_GAMIN10 ай бұрын
nako bayi rék ndakh wadji intérêt la la toppé
@mboupmbaye24110 ай бұрын
❤ salut CV mbeuguel il faut soit vissillat Les hommes
@awafall524310 ай бұрын
Bilaye sofa Dello wadji dinala Leek bagua séte
@Tigresse00008 ай бұрын
Bilahi sokhna Fatou djiguene gni lignouy dadj
@oumarmbaye79059 ай бұрын
salut sokhna fatou ❤ Maashallah mouray bi diékna tarou na yalnala yalla defal diam
@SowDiaynabaАй бұрын
Togal khar yalla ta nagouli yalla dogal kokou dou chenge djiko dou chenge wadji amoul ngor amoul kersa amoul djom 43:25
@thiernosaliousidibe996310 ай бұрын
Essayé rek peut être changement am mais néanmoins mets tes biens à ton nom
@khadydiedhiou337610 ай бұрын
Nakho baye nitou interéla wag😢
@ndeyemichellediallo59210 ай бұрын
Ay sokhnassi ki boul meussa delouwatt ak môme bokow defe lises tii sa adouna yeup digua amate aye déception djiko ak borome pakh
Néko boufa délo dinagneko gnaff nationale. Sister khana daga beug déh té ton heure n’as pas encore sonné
@eugeniecoly466410 ай бұрын
Moi je te conseille de tourner la page. Vivi pas vie il restera toujours le même
@altesseroyale438310 ай бұрын
Fatou danga mana togne sérère yi Wayé tèye samouraye mouraye you toucouleur la😂😅
@OamodouDiop10 ай бұрын
noooo sétil kénéne mo geune
@Générale-Ba410 ай бұрын
Quelle tourner la page quel trouver une autre personne qui est musulman et croire en Dieu
@NdeyeMdeneMdene10 ай бұрын
Bilahi sokhnasi bagnal boul yakh sa adouna ki baxoul
@cheifall9310 ай бұрын
Boume si dougat dagaye sonale
@damboup353110 ай бұрын
Macha allah amna solo mais mom na bagne ndakh wadji alal lako topé
@Black-lion22110 ай бұрын
Je ne lui conseil pas wadji nobou ko intérêt lakko toppé qu’elle se concentre sur elle même ses projets et son enfant amana Europe dina feu guisse kenene inshaallah.
@nafymboup321710 ай бұрын
Wadji dé yonou touki la guiss thi mome😂nobou ko dé nako bayi
@NdoumbeSamb-v4x10 ай бұрын
Wadji beugouko khalisam rek la beug demal mou les la
@gabrielngom915110 ай бұрын
Il faut expliquer certains termes en wolof aux gens comme NDIAAG NANGOUL
@mariamafaye778010 ай бұрын
Cc mais amour famme bi na djibon ak ex dieukeureum mai boumou dougou si seuy bi ndakh bousi dougué dinako deff lou raw limouko défone wa salam😍😍
@afounasabaly281410 ай бұрын
Retour pas,il est comme ça famille intérêt rehk
@imblack89627 ай бұрын
N'a faté wadji ak Mboki wadji gnak n'a diome trop 😂
@DiborGueye-l7m10 ай бұрын
Boudone ma na douma demate dah wadiy nitou intêret la😢
@Aminatandiaye-n8n10 ай бұрын
Salam sokhna fatou ❤sokhna si na fàté ki menteur la traître la migui ni dou séti propre domam sakh wadji dal bakhoul
@IbrahimaGaye-IG10 ай бұрын
Ah waydji dou dara badola rék la nako bayi té séti lénén ki nittou intérêt la
@SeynabouGueye-s5p6 ай бұрын
Boufa délou ndax qui goréwoul té intéret moko bayi ci yaw
@khadimdiouf680810 ай бұрын
Amou Masi xalat
@gnimadiedhiou78637 ай бұрын
N' doh dou baaye yonam
@papemedounemedoune27366 ай бұрын
Waa goor dineu am genrou djiko yii sa way ioew matto ko dé bilakhi ins bi guis leu en face rék la beugoon
@adamafall998310 ай бұрын
Non nako bal de waye bou mou sey ak mom begoula
@Coolblack67547 ай бұрын
Les sénégalaises AK gno meune sêyale goor bou gnak fayida mais quand tu est homme sérieux qui subvient a leur besoins doff légni leu diape....
@sebastiensane48907 ай бұрын
C est encore un piège pour te soutirer tout son argent comme li a l habitude ; de le faire bo fa delouwattee mou metti tchi yow torroopp . Tu es une femme de valeur ; tu peux trouver mieux qq un qui connaît ta valeur . A bon entendeur salut .
@amathdiop322410 ай бұрын
Yalla diekhoul boulako dara diaral.ko xamni d'où séti sakh domom ,boulsi dougate digua ame lénên louko guene inchalah
@awafall524310 ай бұрын
N'a bayi wadji amoul diome
@DiarayeDiao10 ай бұрын
Si sama xalate boumou délou watt si seuy bi kou goor ki intérêt lako toppé
@angelafaye77549 ай бұрын
Sokhna si Ton ga nitou intérêt deug la khalatal sa bop ak sa dom Europe défa meti nobato ko n’a kou nek dem conseil d’une sœur qui vit en Europe depuis 25 ans
@SowDiaynabaАй бұрын
Boulédaim les inbaisile ne change pas bothi doutais do am ndam sa khalisla sokhla mbeuguel amatoùfa ngor amatoùfa kersa amatoùfa togal khar yalla kham khathi bogis wersk gou kenenela bayîl moudem tairaimou te bayil mougis
@kadiortv10 ай бұрын
Gnak diome bakhoul
@malickthioubdiallo533310 ай бұрын
Fatou je reviens waadji mere naako trop faut jamais le pardonner wal laahi dou change c'est lui meme qu'il a repudier 7 fois neeko mou gnam benene goor bou ci delloo dinako seeyal seeyal limou yor
@stephinahstephane87557 ай бұрын
Asalamu haleykum, suma amon ci yaw ab sagn sagn do dellu mukk ci moom ci aduna wa salaam.
@sambaliou585910 ай бұрын
Na tournée page bi
@astoutoure480810 ай бұрын
Si c’était moi doumassi delè parce nobou la sa xalisss la Beug malgré amguê dom mais tournel la page topato sa dome dèfarate sa vie xol lëneène par ce que ki sa xalisss la Beug
@wanealpha196510 ай бұрын
Wadli nitou entre
@MultiLajoie6 ай бұрын
Balko té dawko, ki badoléla yallah woneuna vie ta vie tranquille et oublie se vampire 😅❤
@altesseroyale438310 ай бұрын
Guène pendant 10 ans lolou nomou toude?😂😅
@ElhadjiomarDrame-ug4du9 ай бұрын
Bole yakh sa adouna woutile kenene
@NdoumbeSamb-v4x10 ай бұрын
Epuis amoul diom yorr diabar doko defal dara defoul béne effort bayiko dalay sonal rek ga balma
Pas tout les hommes les hommes sont différents comme la différence des femmes 😂@@AbsaDiop-ed7ui
@AbsaDiop-ed7ui9 ай бұрын
@@ndongolo9150mercie beaucoup diereudief
@obietrice462010 ай бұрын
Fatou svp delen wagni munit yi su baré ba baré 30mn maximum minimum 20mn ngen deffko 2 parti wala 3 part 1 moyes ndakh dana takh niou geuna comprendre histoire bi merci 🙏🏾