NET TALI : Il Dit Niet à la 2ème Femme de Son Oncle qui voulait…

  Рет қаралды 150,574

Net Tali TV

Net Tali TV

Күн бұрын

Пікірлер: 96
@FamaNIANG-ns6dr
@FamaNIANG-ns6dr 4 ай бұрын
Machallah il ne faut jamais céder aux chantages. Yalla nala yalla diapalé, boulko meussa sekhal ak kéne koudoul sa diambar inchallah. Bon courage
@wourelsow1482
@wourelsow1482 4 ай бұрын
Khalé bou gor bi dh bilahy amoul morom Machalakh il se controle
@CheikhatndiayeNdiaye1987
@CheikhatndiayeNdiaye1987 4 ай бұрын
Yalna yalla diapale l'a t'es guawakh lep sa tonton mais nagua am preuve anrigistreko ak sa téléphone parce que lou bonne kendouko setane daymelni complice gua dafa meti gua nek bitimrew Di dane sa dolle lo amyoneko Bene dome rame diko bokatte benene guore bonne chance
@adamaba6287
@adamaba6287 4 ай бұрын
Félicitations Fatou pour le sponsor 🎉🎉🎉🎉 thé bi warna nekh❤
@abloslimshady
@abloslimshady 4 ай бұрын
Goor deug moy ki, Macha ALLAH! Awra jiguenn boumou takh nga tass sa famille!
@Mizafrica
@Mizafrica 4 ай бұрын
Khalé bou goor bi mo ame foula 👏🏽👏🏽👏🏽
@MarSeck-jd1qb
@MarSeck-jd1qb 4 ай бұрын
😅😅😮😊😊😮😅😅😅😮😮😅😅😮😊😮😅😮wsdddd
@MatarMboup-v9t
@MatarMboup-v9t 9 күн бұрын
❤❤❤
@MoustaphaDiongue-if7lc
@MoustaphaDiongue-if7lc 4 ай бұрын
Ziar nala sokhna fatou mala chope machallah ❤❤
@BinetaMbengue-vc7bu
@BinetaMbengue-vc7bu 4 ай бұрын
Nay yore téléphone Diko enregistrer guor bou djigueune wo si guor si neg n'a yob téléphone enregistrer ken doulo. Wak so ko defoul ma youko gua yob sa téléphone rek di enregistrer rek moy solution
@mameboussombaye7397
@mameboussombaye7397 4 ай бұрын
1 soumané dém loué dji mogane. 2 soumané soutouraalé mogane dh, ndax yonénte Bi salal lahou halayhi wasallam néna "kou soutoutaarl ab joullit yalla soutouraalko adouna ak allaakhirah" وفي الحديث الشريف "من ستر مسلما ستره الله في الدنيا والآخرة " S Fatou merci beaucoup
@manoutoure3505
@manoutoure3505 4 ай бұрын
Linga wax. Nii la ko guiss mane
@DieynabaSy-n6y
@DieynabaSy-n6y 4 ай бұрын
Nako Wakh vérité bi
@SeydinaSow-gg1nd
@SeydinaSow-gg1nd 3 ай бұрын
macha allah merci ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂
@Samboundiaye-sj1hf
@Samboundiaye-sj1hf 4 ай бұрын
En fin teams topou nétali nous sommes sponsorisés Niou nieuw si cas bi après 😂
@SidineMabruk
@SidineMabruk 4 ай бұрын
Macha Allah ❤❤❤❤
@ThiamSouleymanethiam
@ThiamSouleymanethiam 4 ай бұрын
Machaa allah ñîîfi aw nieupou kii rèkk mooye goore diouguèèfa louko moyy 2em ranwoune dina ame dè bayyiwouledè fawouti pèkhè billahi boofa toonguèè dingaguiss moussiba
@obietrice4620
@obietrice4620 4 ай бұрын
Na tokohu bayilen bumou ko wakh nidiayam muk ndakh daye yakh mboku na bayi nonou yalla dinako wer té mom su tokhuwoul dina moudji nagu deh billahi jiggen mo bari pékhé ségam waliou yi nio manul moudiou si gnom nittou ordinaire matul di wakh😢
@ROBERT221XAMXAM
@ROBERT221XAMXAM 4 ай бұрын
Kon nako wakh niarel bi nioubolo wakh ko nidiayam 😢😊 19:30 🎉
@mameboussombaye7397
@mameboussombaye7397 4 ай бұрын
Ah lolou Dou xalaat dh😅 Ésk kham nga Lou niaarél bay doundou keuram ? !!!😢
@PapeBa-go6eu
@PapeBa-go6eu 4 ай бұрын
Manshallal sa débat bi amna solo
@altesseroyale4383
@altesseroyale4383 4 ай бұрын
Djiadieuf théâtre shilajit gnou tago fofou! Khalé bou goor bi na woute prétexte guène keur gui. Bou wakh dara nidiaye, soutoureu lo âme solo la. Diane ni gnoye, bou boba diabarou nidiaye dotou ko wakhati bène wakhou gniak fayda. Wayé khalé bou goor bi dé yare na bopame, à 27 ans batèye démou lou palais?😂😅 gni ame 15 ans découvrir lèp, chapeau! Yafi meune dé!!!😂😅
@AliouneDiakhate-d2z
@AliouneDiakhate-d2z 3 ай бұрын
Merci
@MamadouhlmBa
@MamadouhlmBa 4 ай бұрын
Thieuy Thieuy netali nekhna 😊
@MaremeDiallo-v3f
@MaremeDiallo-v3f 4 ай бұрын
Frére wakh ko sa tons
@seydinafseck6954
@seydinafseck6954 4 ай бұрын
Il n'a qu'à chercher des preuves avant de dire cela à son oncle mais pas sortir de la maison
@AbdoulAhadGueye-ep6rd
@AbdoulAhadGueye-ep6rd 4 ай бұрын
Wadji mom comme reussirna li gueuneu difficile té mooy fékhé ba bagna ndialo ak oumpagnam bi, donc na djièma wo oumpagn bi dièmko yèdd pour mou déllo si khélam si respect ak ndièkk ndakh djiguèn niou beuri danio amoul koulèn di déllo si rek mes dou bone, balamouy déf lénèn ak di wakh ak nidiayam bi, sou reussiré convaincre oumpagn bi rek, oumpagn bi meunako si fongk à vie si ndimbeul bobou, mais sou fékkè oumpagn bi dafa bagn niko sa yoon nékou si boy déf nga déf bo défoul nga bayi boulma diokh ay conseil, là sou boba mou wakh ak nidiay dji wala mou mandou rek té dilèn éviter et surtout de ne jamais faire lignkoy sante et aussi mou moytou di lekk sèn lekk wala di dieufleunté ak niom dara dara sino dinagnko diékou vite fait si Serigne, nay lékkè si alle bi ak di naanè si alle bi c'est difficile mais sa vaut le coup, sinon il risque de faire ce que tout le monde a fait.
@IbrahimaGueye-u9z
@IbrahimaGueye-u9z 4 ай бұрын
Slt wathialmathi bén gougkh
@Mbenguebaguebamba
@Mbenguebaguebamba 4 ай бұрын
Thiey Senegal
@Aissatandiaye-l2o
@Aissatandiaye-l2o 4 ай бұрын
Nehout preveu mouwako nidiayam c'est plus sur
@GougnaDiagne-wc5it
@GougnaDiagne-wc5it 4 ай бұрын
Na tok ti soutoural ko mo gueun ba paré nako yéd
@moussthcisse
@moussthcisse 3 ай бұрын
استغفر لله
@SambaMbodj-l8o
@SambaMbodj-l8o 3 ай бұрын
Goor la vraiment 😮
@ansoukhadafidiedhiou6398
@ansoukhadafidiedhiou6398 4 ай бұрын
Je pense que il peut faire un voyage dans les régions une fois partie il trouve quoi faire comme ça il dira a son oncle que quelqu'un l'avait propose un travail c'est pourquoi il est resté laba
@awaniang3634
@awaniang3634 4 ай бұрын
Nako wakhe
@wanealpha1965
@wanealpha1965 4 ай бұрын
Boumou genni leur gui
@AwaSeck-nf9wp
@AwaSeck-nf9wp 4 ай бұрын
Ne dit rien à tonton prend tes responsabilités et soie vigilant
@MassambaDrame-ie8iy
@MassambaDrame-ie8iy 4 ай бұрын
Deel résumé conection bi dafa chère
@YahyaSagna-or6ie
@YahyaSagna-or6ie 4 ай бұрын
Il faut dire à son oncle avant qu'il soit trop tard
@westcoastsunugal
@westcoastsunugal 4 ай бұрын
Na genn geur gii
@cheikhdiop8801
@cheikhdiop8801 4 ай бұрын
Na gène dème mo guene
@ndarawndiaye9663
@ndarawndiaye9663 4 ай бұрын
Bou gêner Awo grand bi dina ame fit di dougal ay gor si keurgui
@ndarawndiaye9663
@ndarawndiaye9663 4 ай бұрын
Na wahtane ak Awa grand bi djiemko delossi.. antouka fitna la 😢
@abdoulalayeba4496
@abdoulalayeba4496 4 ай бұрын
Na nek ci keur gui boumou dem te nopi
@oumarmbodji1980
@oumarmbodji1980 4 ай бұрын
Qu il n' a prendre sa responsabilité
@louisemariamly9509
@louisemariamly9509 4 ай бұрын
Nako enregistrer déntheko té bagne succomber à la tentation.
@alinguet7974
@alinguet7974 4 ай бұрын
❤❤♥️😭♥️
@SidineMabruk
@SidineMabruk 4 ай бұрын
Wahco li ame moi gene
@ablayly2179
@ablayly2179 4 ай бұрын
Nataka diabar mouneka si kergui
@mbayebabacar2582
@mbayebabacar2582 3 ай бұрын
Amna incohérences dé
@malickfall4447
@malickfall4447 4 ай бұрын
nako filme
@fatousow94
@fatousow94 4 ай бұрын
Mane dé limakoy diguel dale moy mou enregistré ko ndax djiguene dafa bari pékhé lolou rek la guiss
@mamadoudieng8449
@mamadoudieng8449 4 ай бұрын
MBOKOU INTERNAUTES YI ZIAAR NALEN 😅
@AblayeFaye-h9w
@AblayeFaye-h9w 4 ай бұрын
Yow ni ngaye netale de Faye l'erre lole 😢
@AbdouleSow-q2e
@AbdouleSow-q2e 4 ай бұрын
Bomo dem almadi na togfoufou
@adieng8286
@adieng8286 4 ай бұрын
Sokhna faty ziarr mérci
@adjadiouf5049
@adjadiouf5049 2 ай бұрын
Fatou le gars donne trop de détails dinagnouko khamé il faut éviter ça
@brombakhyay
@brombakhyay 4 ай бұрын
Yaw dal diambar degu nga mais nak togal sere sa keur tons nga Nek boul ragal dara sey ak Sa diabar tons baxoul ya Nek si degu ta Yalla degu la begu
@AbdouleSow-q2e
@AbdouleSow-q2e 4 ай бұрын
Silagit mouy lan
@mars3456
@mars3456 4 ай бұрын
djiguéne cou foyé popbam kate co mou diekh
@diopmassamba4461
@diopmassamba4461 4 ай бұрын
Sokhnasi boulevard wakh fom dakk
@aliounbtoure8018
@aliounbtoure8018 4 ай бұрын
Il n'a qu aproposer d'abord son oncle son désir d aller a Almadies ou déployer une chambre si son oncle insiste à vouloir découvrir la vérité il na qu a dire tte la vérité
@adieng8286
@adieng8286 4 ай бұрын
Na néck thi deuggeu rk
@sallbioficial2585
@sallbioficial2585 Ай бұрын
Si c'était moi, je dirais tout à mon oncle🫡
@papeseck3629
@papeseck3629 4 ай бұрын
No n'a fekhé dém Almadies mon guén mou Koy wax Ndiaye bi
@cheikhoudiene4458
@cheikhoudiene4458 4 ай бұрын
Sors de la maison sinon tu tomberas tot ou tard ds son piege et pense surtout a son fils
@VieuxSow-b1s
@VieuxSow-b1s 4 ай бұрын
diambar la dal
@Lombardo-t6h
@Lombardo-t6h 4 ай бұрын
Niga dioxee saye indice yi lerna trop wala but you émission pour leral identité yi ?
@cheikhdiop5949
@cheikhdiop5949 4 ай бұрын
WAkhkoko
@MahmoudKoly
@MahmoudKoly 4 ай бұрын
baye café bi
@abdouazizcisse9047
@abdouazizcisse9047 4 ай бұрын
na déme almadi
@abloslimshady
@abloslimshady 4 ай бұрын
Na Outt Preuve balla mo wax dara Nijay dji!
@sarrinformatique4742
@sarrinformatique4742 4 ай бұрын
Keep koo degueu mounane loureuy la yor yoroul dara
@papebeuse3208
@papebeuse3208 4 ай бұрын
Bayul fene awo bi bamou tawlo yagoul mdrrr Doulyi amoul harmonie
@fatousow94
@fatousow94 4 ай бұрын
Mom limou wara déf léen la na guén keurgui loué dji oumpagne dji meune nako diakhasé ak ndidiayam dji bala mouy gueneu niaw na dém loué dji
@FamaNIANG-ns6dr
@FamaNIANG-ns6dr 4 ай бұрын
Vous vous êtes trompés sur le titre c'est la première Awo femme non la deuxième
@FamaNIANG-ns6dr
@FamaNIANG-ns6dr 4 ай бұрын
C'est le Awo qui le provoque non la niarelle
@AissatouFaye-nj7gn
@AissatouFaye-nj7gn 4 ай бұрын
Qu'il explique son oncle avant que la dame invente
@aliouseck-u2t
@aliouseck-u2t 4 ай бұрын
😂😂😂😂😂
@ibrahimadia2290
@ibrahimadia2290 4 ай бұрын
Bouféké menetoufa neck na guère mo geune mais nétali mome doumakoko digeul Lolou kéne doucko nétali louye tasse surtouma nack djigne nit ndiallo
@mbayebabacar2582
@mbayebabacar2582 3 ай бұрын
Impagne bi bapou tawlo yagoul domame beugue def remarque si yaw nanela free wo AK sa guéle bi gnewetoufi. Féne dafay cohérent
@YabaGueye-y3k
@YabaGueye-y3k 4 ай бұрын
Tanta dii AK raka dii ay mbàkhas la nious
@aliouseck-u2t
@aliouseck-u2t 4 ай бұрын
🤔☕🤔☕
@FallouAw-ww8tr
@FallouAw-ww8tr 3 ай бұрын
Na tog
@joejake8408
@joejake8408 4 ай бұрын
Du n’importe quoi 😂
@BoussoSokhnakhady
@BoussoSokhnakhady 4 ай бұрын
😂😂😂
@adamasall-bw7yo
@adamasall-bw7yo 4 ай бұрын
Varvo
@diopahmeddame7293
@diopahmeddame7293 4 ай бұрын
Koko wax wodio bi moung na
@Papasamb-g8c
@Papasamb-g8c 4 ай бұрын
Ana djiguenne bou ham dieukeur di déme salle ndialo rk amoul khalat sakh
@SayeFall-b6k
@SayeFall-b6k 2 ай бұрын
Yawde bou gor niepp melon ni yaw dinabakh
@mameboussombaye7397
@mameboussombaye7397 4 ай бұрын
1 soumané dém loué dji mogane. 2 soumané soutouraalé mogane dh, ndax yonénte Bi salal lahou halayhi wasallam néna "kou soutoutaarl ab joullit yalla soutouraalko adouna ak allaakhirah" وفي الحديث الشريف "من ستر مسلما ستره الله في الدنيا والآخرة " S Fatou merci beaucoup
@CheikhatndiayeNdiaye1987
@CheikhatndiayeNdiaye1987 4 ай бұрын
Ki eske ap dioulitla bagnekoy soutoural wako sa tonton mais nagua am preuve Bala moula djitou si mome
@diopahmeddame7293
@diopahmeddame7293 4 ай бұрын
Oupang bi bomoko deff dara wayi rack ji moum nako defall bagag
XALISSO - Saison 1 - Episode 31 **VOSTFR**
50:01
EvenProd
Рет қаралды 1,5 МЛН
Série - Lady Diama - Saison 1 - Episode 41 - VOSTFR
49:21
Marodi TV Sénégal
Рет қаралды 1,6 МЛН
Сестра обхитрила!
00:17
Victoria Portfolio
Рет қаралды 958 М.
Sigma Kid Mistake #funny #sigma
00:17
CRAZY GREAPA
Рет қаралды 30 МЛН
Tuna 🍣 ​⁠@patrickzeinali ​⁠@ChefRush
00:48
albert_cancook
Рет қаралды 148 МЛН
BÉTÉ BÉTÉ - Saison 2 - Episode 10 **VOSTFR**
1:08:25
EvenProd
Рет қаралды 3,3 МЛН
XALISSO - Saison 1 - Episode 29 **VOSTFR**
45:49
EvenProd
Рет қаралды 2,7 МЛН
NET TALI : Un Jeune Homme Kidnappée par une Femme de 74 ans
27:42
NET TALI : La Tante de Son ami Dafko Sakkou
22:01
Net Tali TV
Рет қаралды 136 М.
NET TALI : Kidnappé par une Maman et ses Amis pour le Plaisir
36:51
Marietou Mboup - L’essor des paiements de santé numériques au Sénégal
1:45
Better Than Cash Alliance
Рет қаралды 83 М.
Net Tali en Wolof: La Mère de sa Copine le Provoque
18:22
Net Tali TV
Рет қаралды 57 М.
NET TALI: L'impuissant, Pour Engrosser sa Femme, engage son Cousin
27:27
Сестра обхитрила!
00:17
Victoria Portfolio
Рет қаралды 958 М.