NET TALI : Le frère de son mari l'oblige à faire l'amour pendant son absence

  Рет қаралды 113,560

Net Tali TV

Net Tali TV

Күн бұрын

Пікірлер: 137
@Luniquefparmi2g
@Luniquefparmi2g 6 ай бұрын
Tanel ak diam boula draa daal iow Sokhna Fatou ndakhté iow rek laniouy top
@sopezeynabfall6538
@sopezeynabfall6538 5 ай бұрын
Motakh jiiguèn wara soralé euleuk
@DimamekhaDiene
@DimamekhaDiene 6 ай бұрын
Enregistreko souley menacer apres yawtamite gueu menacer bapare boul djeleuti guarapp yimm ladjokh
@Assietoufall
@Assietoufall 5 ай бұрын
Comme elle était Vierge elle devait dire la vérité a son mari que son frère était son ex ça n'allait dégénéré comme son mari la trouvé vierge c l'essentiel l'essentiel
@ElymaneSaidoukane
@ElymaneSaidoukane 6 ай бұрын
Allahou Akbar c'est vraiment compliqué c'est unz histoire vraiment particulière mais ce qu il faut savoir c'est que l illicite n interdit pas le licite donc elle peut se marier avec le frère de son ex copain car le copain c'est illicite mais le mari licite mais bon dans ce cas le problème est que l' ex copain est mauvais il veut prendre une dorte de vengeance car il n' a pas pu sortir avec elle de façon illicite il est méchant vraiment méchant je ne sais vraiment quelle conseils lui donner car elle est dans une position délicate qu' Allah l' aide vraiment
@FanayeDiery
@FanayeDiery 6 ай бұрын
Mm la femme est movaise elle sorti avec l frère el c marier avec l'autre frère quan il la menacé elle aurait dû lui dire va tout dire a mon mari toi é moi c'était avant c tou du cou il alé l laissé tranquille ou bien elle porte plainte contre l frère
@fatimandiaye2109
@fatimandiaye2109 5 ай бұрын
@@ElymaneSaidoukane, xddeee
@AgnèsDiatta-s6v
@AgnèsDiatta-s6v 5 ай бұрын
Tout ce qui lui arrive c'est de sa faute, car elle à fait du n'importe quoi en brisant les cœurs de ses conquêtes qui lui exprimer leurs intentions sincères.
@ngagnedeme-w2t
@ngagnedeme-w2t 6 ай бұрын
Dijguene bouy seuy waroul diokh bopam koudoul diekeuram. Dara waroukoko diaral.
@ndeyemichellediallo592
@ndeyemichellediallo592 6 ай бұрын
Boye ndialo ak sa rakou dieukeur da ngaye raye a dieukeur lolou moussiba la te nga dem toubeul sa yaye mdax mou gnanal la
@RokhayaBA-z2g
@RokhayaBA-z2g 6 ай бұрын
Dit au marabout de retourner ce que souffre ton mari à la personne qui lui a fait ce mal et continu de gérer ton foyer un bon mari n'est pas facile à trouver
@FatouSow-wm8rz
@FatouSow-wm8rz 6 ай бұрын
Ana sponsores yi waaay😊
@batorsow3844
@batorsow3844 6 ай бұрын
Yalla nala Yalla takhawou si barké nabyl moustapha (psl)
@PapeDiop-l4c
@PapeDiop-l4c 5 ай бұрын
Salam que le Bon Dieu te vienne en aide, continue à prier et demander à Dieu de te venir en aide car je sais que tu aimes encore ton mari, tu as cède aux chantages pries tous les jours surtout la nuit incha Allahou Dieu te viendra en aide je ne te blâme pas car nul est exante 'de pêché soit courageuse surtout n'utilise plus les safaras
@RamatoulayeMboup-v9m
@RamatoulayeMboup-v9m 6 ай бұрын
Ma fatou masta yalla nala yalla maye tane🙏
@sokhnalo3334
@sokhnalo3334 6 ай бұрын
N'a dème outi Serigne bou bakh mou fathie diekeur gui té mou tagualiko ak rakou diekeur gui ba khel mi dotoul nek thi môme
@NjemehBob
@NjemehBob 4 ай бұрын
Let her go to a marabout to get the brother's mine from her and continue her marriage
@YahyaSagna-or6ie
@YahyaSagna-or6ie 6 ай бұрын
qu'Allah lui trouve une solution pour qu'elle sort de cette situation
@sysada8992
@sysada8992 6 ай бұрын
Ki akk mooko daal mbaraan baakhoul djigueen dey sooraale avenir .Taar koumou nakh dinga diooy. Tass rek moofi seuss
@sopezeynabfall6538
@sopezeynabfall6538 5 ай бұрын
@@sysada8992 jsui pas d'accord
@seutouaby4140
@seutouaby4140 6 ай бұрын
Ndeyssan mane doumala juger massa mougnieul toup gua diouli fathieu sa dieukeur 😢
@khoudedjisoumare9213
@khoudedjisoumare9213 6 ай бұрын
Tayou ko mes na déme défare yarama mebi moudém outi ķouko gnanale lo lokho take lokho moune kotéki ❤
@abloslimshady
@abloslimshady 6 ай бұрын
tayouko fann? Yaw mom dafa tamm mbarann kegn, konn moko tayy fouf! Ndialo kat mom ndialo kat lay moudieul, té yag yag dina fegn, mouy goor di jiguenn, wayé jiguenn wor nga soralé sa euleuk, fassé rek
@abdouazizsarr7474
@abdouazizsarr7474 5 ай бұрын
Elle ne doit jamais trahir son mari et elle doit l'assister avant tout... Elle doit porter plainte au frère de son mari pour harcèlement et recel de données personnelles.
@assanembodji2994
@assanembodji2994 6 ай бұрын
Yalla na ka Yalla diapalé ,
@HousseyNouWade
@HousseyNouWade 6 ай бұрын
Sokhna Fatou yallah ne mayele jam ak werou goude fanne
@mariekonte-eu6re
@mariekonte-eu6re 6 ай бұрын
Limalay conseillé moy diémal am ay confession wam ga enregistré KO sa portable pour en cas ensuite ga détruire téléphone bi am photo yi défaral Say arriére bou bakh am Say preuve qui prouve mo lay harceler té ga oute ay gnane si marabout bou bakh
@ElymaneSaidoukane
@ElymaneSaidoukane 6 ай бұрын
Mais elle finalement l' a fait exprès car comment elle oeut prendre des thiangatt venant de ce type c'est pas normal
@OmarNdiaye-ny3lj
@OmarNdiaye-ny3lj 6 ай бұрын
Mbaran mom bakhoul 😂😂😂😂😂
@KhadimeNdiaye-u6d
@KhadimeNdiaye-u6d 3 ай бұрын
😭😭😭
@boubacardiop3794
@boubacardiop3794 3 ай бұрын
Mbaraanne bakhoulllll srx
@esfdoucara1440
@esfdoucara1440 6 ай бұрын
Résumé du nétali : le monde est petit, très petit
@YoroBa-po5xl
@YoroBa-po5xl 6 ай бұрын
😢😢😢😢😢😢💔💔💔
@ngagnedeme-w2t
@ngagnedeme-w2t 6 ай бұрын
Conséquences yii moy guena grave. Dara diarouko. Bounioula chantage banga dioxe sa bop.
@BoubacarDiallo-p4f
@BoubacarDiallo-p4f 5 ай бұрын
Ya meuna nétali hum
@PapemadiorNdiaye-g9z
@PapemadiorNdiaye-g9z 5 ай бұрын
Ces parents sont irresponsables.
@BabaGaye-r5q
@BabaGaye-r5q 6 ай бұрын
mbaraan gui mu nekkoon moo ko yobbee lii yep. na dem tuubal yaayam.
@altesseroyale4383
@altesseroyale4383 6 ай бұрын
Sénégal amna niit gnou yèèsse
@KhadyDiop-g5n
@KhadyDiop-g5n 6 ай бұрын
Na Tass té balamo Tass nalén wakhe lepoue ndahe mou mana fadio 🙏🙏
@DoBb-fd1vt
@DoBb-fd1vt 6 ай бұрын
S❤❤❤
@Alislamniass
@Alislamniass 6 ай бұрын
Demal seti seydi Ibrahim tiktok istikhar 221 yalla amna louko maye 🙏
@barou60
@barou60 5 ай бұрын
Thiaga secret dafa bari senegal 😢
@DIAOMamadi
@DIAOMamadi 6 ай бұрын
Que Dieu vous aide
@aliounbtoure8018
@aliounbtoure8018 6 ай бұрын
Je s8 d accord avec sokhna
@Yahouba-oq4jk
@Yahouba-oq4jk 6 ай бұрын
Li motahx ma bagne affairou farantou djiguéne dafa wara moytou lolou mais bo waxé niou méréla
@aminedeme5343
@aminedeme5343 6 ай бұрын
Li metina ma yallna bahana 🤬
@seydidiamilmoualaminesy3732
@seydidiamilmoualaminesy3732 5 ай бұрын
@@aminedeme5343 mba daloula rk
@MamediarraDia-p5e
@MamediarraDia-p5e 6 ай бұрын
Waw mome foumou diele dorage bi marane bakhoute
@MoustaphaGueye-o8q
@MoustaphaGueye-o8q 20 күн бұрын
Diabar la bague ❤
@HousseyNouWade
@HousseyNouWade 6 ай бұрын
Cey jiggen Chantage kouke nangou yokalna boppam problème Lii départ lo waron dieul motwayam legg bey woyna mbouss Moytlen mbarane nou yallah japeleko Defko waron porte plainte pour archelement
@hajalameh
@hajalameh 6 ай бұрын
Pray five times a day. Hold on tight to your prayers. It wades of evil deeds. Ask Allah to guide you and strengthen you. Prayer gives you strength and unshakable principles. Your deeds are indeed ugly and shameful. But Allah forgives all sins.
@Findamamad
@Findamamad 6 ай бұрын
Bonsoir fatou
@ndaoibrahima2721
@ndaoibrahima2721 6 ай бұрын
Na continuer diouli di diamou yalla en plus na dogou bayi rak dieukeureum té mou dieul khalis bou takou diok ko yayam balou ko akh Quallah veille sur elle Quallah la préserve et la guide vers le droit chemin
@fatousow94
@fatousow94 5 ай бұрын
Yalla nako yalla taxawou diapaléko bamou guén ci situation yi mou nek ci barker seydina mouhamed psl
@BaBeydi
@BaBeydi 3 ай бұрын
La seule solution est de divulguer le secret à son mari.
@mameyacinekane
@mameyacinekane 6 ай бұрын
Elle doit faire un effort et dire le petit frère de son mari que la police est la bonne chance
@BaBeydi
@BaBeydi 3 ай бұрын
La leçon à tirer de cette histoire est pour les filles d eviter les partenaires multiples.
@margotndour888
@margotndour888 6 ай бұрын
☕️ bi rafet na
@mamefatouba580
@mamefatouba580 5 ай бұрын
Mais degue moy ndieuk té moy moudiou dafa warone wakh vérité bi depui le début faranetou kouné diar nasi ex moy lane rawatina sa dieukeur fék si yaw ndaw
@AbdoulAhadGueye-ep6rd
@AbdoulAhadGueye-ep6rd 6 ай бұрын
Momla nèkh rek mouy ndialo, mais biko rakou dieukeur dji ndieukè wakh wakh yoyou, la wrarone guènn dém police wakhlènko niou régléko vite fait sans problème et ça c'est comme de l'eau à boire si police, mais momla nèkh mou nékk fa di ndialo
@damediop2097
@damediop2097 5 ай бұрын
Yabon di dialo
@alioundome4131
@alioundome4131 6 ай бұрын
Sa rakou dieukeur dji diekhal nala
@DjibyMbaye-f2r
@DjibyMbaye-f2r 4 ай бұрын
❤😂😂😂
@cheikhfall5927
@cheikhfall5927 6 ай бұрын
Café Touba lay nane ni şax ☕☕😂
@BaldshOmaribra
@BaldshOmaribra 6 ай бұрын
Dara yakoul sa adina loudoul ake yigua amél goor gnigua donne nakh di lékh sène xhalesse Dieux ne dorme pas il yavais des gas qui on donner leur sueur et venire repondre a tes besoin car il ont l'amour sincere avec toi et toi dans ta tête tu les utilise seulment tu les trompe donc voici les resulta Dieux ne dort pas l'amato dinou toudanou, le frere de ton marie il ta rien fair c'est juste tu est entrain de payer les déte que tu as prit sur lui ,car toi meme tu connais pas pourquoi Dieux ta ramener dans cette maison jusqua tu vie cette situation boula yalla mayèr tar gua waratie diamou yalla ,Mais dèefoko gua top sa tarbii di dèf loula saf voici les resulta ma cherie b
@kanemoussa8665
@kanemoussa8665 6 ай бұрын
Nakowakh jekereme
@Nopesamadiabar
@Nopesamadiabar 3 ай бұрын
Depuis le début guako warone wakh sa dieukeur gua wakh ko deug bi yeup
@CheikhonaG
@CheikhonaG 5 ай бұрын
Wa cafe seringe bi lanuy toppu
@mariekonte-eu6re
@mariekonte-eu6re 6 ай бұрын
Confession comme quoi que mo liguéye frére ram ga gardé ko té ga tok soutenir sa dieukeur si fébarame bi
@wanealpha1965
@wanealpha1965 6 ай бұрын
Na dem si Serigne mou dedelen
@abderahmanefall7913
@abderahmanefall7913 Ай бұрын
Dakar yeup barrane nelène
@DiaDan-z3r
@DiaDan-z3r 6 ай бұрын
Mais enfant yooyi yéppu di xéw lan moo tée mou enregistre ko yonée ko borom kërëm
@ousseynousall5808
@ousseynousall5808 6 ай бұрын
Histoire bi damélni aye scénario aye créyéla 😂😂
@siradiarra8602
@siradiarra8602 6 ай бұрын
Mane deh solution bi la guisse nga dem ci serigne mou dedeléla ak sa frère diekeur bi il va t'oublie à vie sinon il vas gâcher ton mariage.
@kharycisse5267
@kharycisse5267 5 ай бұрын
Ndayane ki dé gno bokou fébar goor boula guis beguela Aka méti mais bousi démoul ak khél rék mosiba Dale la Mane môme douma mbarane parce que khaliss bou léwoul begoumako jamais
@barou60
@barou60 5 ай бұрын
SOHNA CI AMAL JAMM.
@mcmbeur7372
@mcmbeur7372 6 ай бұрын
Yagui khalat bamell
@gueyemoustapha9230
@gueyemoustapha9230 6 ай бұрын
No ki beuguena lou bone
@ngagnedeme-w2t
@ngagnedeme-w2t 6 ай бұрын
Mais na oute aye mousselaye. Di sangou di sangue diekeur dji. Frerou djikeur dji molen liguey
@RamatoulayeMboup-v9m
@RamatoulayeMboup-v9m 6 ай бұрын
Li mo takhe dhiguéne wara yame barane bakhoule
@fatousow94
@fatousow94 5 ай бұрын
Femme bi mom la blamé ndax liko dale yeup mom la nebe bimou nebe dieukeur dji moko yobé li seye communication daf ci bakh
@sohnatouray3691
@sohnatouray3691 6 ай бұрын
Dafa warona wahk jakaram rakam x Sam la
@ndoumbemanendoumbemane616
@ndoumbemanendoumbemane616 5 ай бұрын
Le frère de ton marié couché avec toi bien avant même que tu épouse sont frère mo tahe moulaye fowè bayil sa hele bi ngay fowè sa chambre amoul clè??
@metoudiop1019
@metoudiop1019 6 ай бұрын
Boukowakh sa dieukeur dafaye febar demal deudeule wadji ak yowe
@MorKane-g3z
@MorKane-g3z 6 ай бұрын
Na yobou rakou diekeur dji si serigne moutakalèkok mom mou tok si seyeume.
@AissatouFaye-nj7gn
@AissatouFaye-nj7gn 6 ай бұрын
Sama xamxam agoul fi mais doyna war trop
@MoustaphaGueye-o8q
@MoustaphaGueye-o8q 20 күн бұрын
Sa xam xame Manou fe ag mose 😂
@BinetaDiallo-v8l
@BinetaDiallo-v8l 6 ай бұрын
Na fathie dieukeudji mou deff niane bo khame ni rakou dieukeur di bayiko
@MouhamedNdao-u9e
@MouhamedNdao-u9e 6 ай бұрын
N’a wakh deug bi rek djeukeur dji
@aliounegaye4335
@aliounegaye4335 6 ай бұрын
Femme bi mo beug lou bonne. Té limou nek moko tay. Limakoy conseil moy n'a délou si yalla toub bakaram yi. N'a nangou rakou dieukeur dji wakh lep té boumou meussa sekh ak rakou dieukeuram
@moussadiop6123
@moussadiop6123 6 ай бұрын
Yallah mou kouk ye Faye
@Sarafina5
@Sarafina5 6 ай бұрын
Na khare ba dieukeur dji tanè mou wahtane ac moome
@CheikhDiop-j8o
@CheikhDiop-j8o 6 ай бұрын
Na wakh diekeur dij li khew tes wakh
@mamadoumareme9849
@mamadoumareme9849 6 ай бұрын
Boul tass sa seuye nakhal sa rakou dieukeur amssi mom aye preuves you woor Beneen bi moy nakhal sa rakou dieukeur ba récupérer preuves yimou yoor si iow meuna diakarlo ak mom
@wanealpha1965
@wanealpha1965 6 ай бұрын
Dal défaut bakh si niit
@mouhamadousow2919
@mouhamadousow2919 6 ай бұрын
Nako yobo police 👮
@ngagnedeme-w2t
@ngagnedeme-w2t 6 ай бұрын
Akhe gni moudone mbarane moko dal
@mamadoumareme9849
@mamadoumareme9849 6 ай бұрын
Soudone mane la sama seuye tass sama deer yakou moma guéunal ndialo
@lascosall
@lascosall 2 ай бұрын
Sa yaye limou def kham nako bou bakh ndakh yaw bo togué fi di victimize wou daguay fonton nit rek ndakh saria ray nala bou yagu mak ak rak du jamais vue bilahi
@abloslimshady
@abloslimshady 6 ай бұрын
Bo yagggué tchi mbarann dinga moudj ndialo, meuno reuthi tchi goor yoyou yeup, sen akh dina la daal! Jiguenn ndialo kat mom fassé rek, ndaxté day yak société. Bou nekkon deukou charia dagn lay ray kon ay ballou sax doufeu am yonn
@sokhnaah5912
@sokhnaah5912 6 ай бұрын
Na dème si Serigne ndawtal rackou dieukeur dji mou guené deukbi complètement té mou tothie ligueybi topato dieukeureum
@Dsport5
@Dsport5 6 ай бұрын
sa genre yii yeureum na sa dieukeur serigne rekkkk nguénn yakarrr
@MouhamedFall-dk7uw
@MouhamedFall-dk7uw 6 ай бұрын
Bou rafaté si zahir niaw Na lolou si batine
@mamecheikhdione2557
@mamecheikhdione2557 6 ай бұрын
Akhou gòor yimu don mbarane késsé la
@metoudiop1019
@metoudiop1019 6 ай бұрын
Va voir un marabout mou deudelela ak sa rakoudieukeur t'es fathe sa dieukeur
@madiopmbaye9010
@madiopmbaye9010 6 ай бұрын
Moko nangou dako warona diebaner depuis au début wakh ko dieukarame
@nobasiby9540
@nobasiby9540 6 ай бұрын
Waroul wone céder chantage bi té mou wout ay niane rakkou dieukeur dji bayiko
@altesseroyale4383
@altesseroyale4383 6 ай бұрын
Rakou djeukeur gui domérame la, mbok yi aye walkhasse lagniou! Elle est naïve: pourquoi elle prend des potions de maraboutage du frère de son mari et l’utiliser comme il dit? Pourquoi ne pas aller voir des marabouts et se débarrasser de ce sale frère du mari?
@diopahmeddame7293
@diopahmeddame7293 6 ай бұрын
Dafa warouna wax dieukeur lipo bo yage
@diopahmeddame7293
@diopahmeddame7293 6 ай бұрын
Da dem woti sering boko nianall lo lokho deff lokho dindeko ay wadioram yala reubo na len
@wanealpha1965
@wanealpha1965 6 ай бұрын
Nakho wakh jekeur ram
@AbdouleSow-q2e
@AbdouleSow-q2e 6 ай бұрын
Jabaram bi moum mon doum rakkaji ji moum dou nit moum na dem Def deddale moum ak rakkaji
SLIDE #shortssprintbrasil
0:31
Natan por Aí
Рет қаралды 49 МЛН
Жездуха 42-серия
29:26
Million Show
Рет қаралды 2,6 МЛН
40 Qiso┇40 Qiso Ee Ygu Saameynta Badan 2023ᴴᴰ┇► Sheekh Musdhafa Xaji Ismaciil
3:26:03
MANSOUR DIOP CONVOCATION BOU AMADOU BA DIAROUL POLITISER...
19:24
MMD MEDIA TV
Рет қаралды 14 М.
Série - Lady Diama - Saison 1 - Episode 48 - VOSTFR
54:54
Marodi TV Sénégal
Рет қаралды 521 М.
Net Tali: Trahison familiale, Un cousin toxique et Jaloux
24:21
Net Tali TV
Рет қаралды 56 М.
CORAN POUR DORMIR QUI APAISE LE COEUR (Recitation magnifique) 2021
1:31:41
DOUAA PROTECTION
Рет қаралды 18 МЛН
BÉTÉ BÉTÉ - Saison 2 - Episode 17 **VOSTFR**
1:10:49
EvenProd
Рет қаралды 2,5 МЛН
NET TALI: Le Choix Mortel, Histoire Extraordinaire
29:17
Net Tali TV
Рет қаралды 71 М.
AFARTANKII (40) QISO OO UGU SAAMEYNTA BADNAA_2022 iyo 2023_ SHEIKH MUSTAFA.
3:26:03
IFTIN BROTHERS STUDIO
Рет қаралды 2,6 МЛН
SLIDE #shortssprintbrasil
0:31
Natan por Aí
Рет қаралды 49 МЛН