Aimé na commentaires yeup aimé léne Sama boss nak. Mais wally mâne magui si yaw depuis le début sa khôl Mo rafett dara diomoula Seck.
@apouta65955 жыл бұрын
Bilaye sanèkhe ya beugue Wally . Si kawe gua koye kholè avec beaucoup beaucoup d amour . Ma shaa alha 🙏🏻🙏🏻
@mariamacisse8255 жыл бұрын
Diarra kone setlou ngua lolou sanekh mo takhaw si kaw scene wakh ko si kaw moune wally tu est le meilleurs tu sera le meilleurs et restera le meilleurs tegal kossi boula nit togné mane la togne donc wally aussi le lui rend bien
Wally est très malin Machala kouko beug beusseul jaime
@mayagueye73675 жыл бұрын
Jaime
@papeamadougueye11505 жыл бұрын
En dehors de sa musique et tout j'aime sa manière de parler de faire il a un grand coeur une bonne personne et j'aimerais bien le rencontrer .bnne continuation barké s babacar sy rta
@ndeyekhadyndiaye81235 жыл бұрын
Amine
@bvediarrachousene58325 жыл бұрын
Pape amadou Gueye verité absolue lima gueuna nex si mom o6 yeugoul succé wallahi wally dal machalla mayou ma dara dhé mai dma guis mou def ben acte bou nic mpu takh ma gueun ko diam wallahi diam rk mn très cher
@papeamadougueye11505 жыл бұрын
Bve diarra tu as raison franchement tu as tt dit man mome certes j'aime sa musique mai aussi sa personne et je suis fan de maman diagua
@arameyade7465 жыл бұрын
Bilay lilako wakh lo sakh khamoko ndakh ki xolou diama la yorr kéne dou mom nittou késsé wallay Barki S Bamba mima yakar Wally mako beugue en personne dafa bakh goré mandou sutou yallah nako yallah lafal thiate té seuytané sékhlou ko
@sofyndieguene77494 жыл бұрын
Amine.yarabi
@Showbizz2215 жыл бұрын
No sanex amoul🤣Goné yi nk fii di dof dof lou fii nii yeup yaléne meune mako wakh doséne morom❤bilay wakh ga deug❤❤kou d accord pouss bleu🤙
@abdouseck22845 жыл бұрын
TEAM FARAMAREEN
@mariamacisse8255 жыл бұрын
😂dafa beugue wally mais wally aussi dako respecté
@Showbizz2215 жыл бұрын
Yup abdou seck🤙😍
@Showbizz2215 жыл бұрын
Sii si @@mariamacisse825mai Sa dafa nx🤣
@timang93665 жыл бұрын
Pape Diouf a quitter PRINCE ART wally toujours bien accueillis a la futurs média 😍😍😍😍😍 Sanexx dafa beug Wally nakkk
@matyseck56345 жыл бұрын
Wally nekoul prince art desoler
@timang93665 жыл бұрын
@@matyseck5634 je le sais ma grandee
@maimounasouare4895 жыл бұрын
tu es le meilleur
@timang93665 жыл бұрын
@Reumsa Guiss deug piir wawaw pape ndanane laa
@timang93665 жыл бұрын
@@maimounasouare489 dafa leer
@ndeyekhadyndiaye81235 жыл бұрын
Walae Wally tu me fait fondre en larmes jtm au plus profond de mn coeur yalla nalla yalla lafal thiat siii barki serigne babacar sy mousseul laaa siiii nit niou bone Lou bakh rkkk kay am insha allah bou fékei yalla xol lay fay
@babacarboumamethierno75435 жыл бұрын
Walahi dama beug wally seck té yalla rek takh1❤❤❤
@ndeyekhadyndiaye81235 жыл бұрын
Bilay ndeysane
@swdija11765 жыл бұрын
Je vois pourquoi les gens t’aime Tu es simple machallah et adorable 😊 Que Dieu t’aide
@collesow9395 жыл бұрын
Machalla sama chanteur de luxe wally seck j laime for
@deessedufoutadiallo21215 жыл бұрын
Mais vraiment 👏👏👏👏keb’s c toi seule qui à posé les questions pertinentes ça s voit que l’expérience fait la différence 🎩
@ndeyenguenardiop34325 жыл бұрын
Ndayssane sama wadji daguay dounde bamou yague lolou si barkè seydina Moukhamète amine
@arameyade7465 жыл бұрын
Koussi beugue wally té good rk takh sans triché beusal j'aime
@bebahe91bebahealeyene744 жыл бұрын
Billahi wally Kenn dou yow beguelna nieup wa Mauritanie beguena ngioula billahi ame yermandè ti domou adama
@babacarniasse43825 жыл бұрын
j'adore ce gars (wally). il est modeste et humble. Bonne continuation wally . Lingay dound lijëntiwou ñou ko sa job mooñou intéresser. En avant bro.
@mortalla28marone865 жыл бұрын
Merci sa Nekh de représenter tout le peuple Sénégal de vos 5min de gonal.
@miadioufdem32485 жыл бұрын
Kou beugue khalei bi reek beussal j'aime moi dai j l'aime plus k tout au monde k le bon DIEU le protége amine yarabi
@jaliyajaliya27925 жыл бұрын
Merci sanex li nga wakh deug la merci encore une fois je suis très contente vraiment Sénégal dafa meti trop mai aussi population bi warr nagnou yarou gnoune gno Mana defar Sénégal merci cheikhou Gueye
@torododia14215 жыл бұрын
Kou beug wally seck Ppousse bleu 👇
@johngiune14345 жыл бұрын
🤜✍️📞🇳🇱🇳🇱🇳🇱😘😘😘🤛
@momomimou38355 жыл бұрын
Tayrek gêne masa wakhal yalla
@laminendong51695 жыл бұрын
Pourquoi pas pape diouf
@diagnehaytecc5 жыл бұрын
Ok
@torododia14215 жыл бұрын
@@johngiune1434 pv
@khadijarassoule16545 жыл бұрын
En dehors de sa musique je l'adore de par sa personne son comportement et sa parole et sans oublié son respect en vers sa femme...yalnala yalla werral yagal taxaway bi nga yagu gnio bégal💞💯
@gadiosslafaramareene5915 жыл бұрын
Ki mako beugue barké seydina Mohamed yallah nele yallah are ❤❤❤🤲🙏💋
@fatoufadiga74905 жыл бұрын
Machallah longue vie wally seck je t’adore 😍courage aussi madame seck ❤️❤️❤️❤️sanekh va me tué 😅😅😅😅longue vie à tous les mamans du monde 🙏❤️
@elzyau51825 жыл бұрын
Sanéx waxna deug Wally dafa extraordinaire apar Youssou il est l meilleur té lissi kanam moy dak ndax da gueume bopam Wally rk❤
@sadiomanejrtv19675 жыл бұрын
Wey mafi djitou depuis Paris koumay j'aime yalna gua dem si concerrou Wally bi à Paris inchallah le 26
@mbeneniang70065 жыл бұрын
1er J'aime
@alldinalrk48575 жыл бұрын
Wahko sa papa ak sa yaye
@sadiomanejrtv19675 жыл бұрын
@@alldinalrk4857 lane lay wax pa bi ak mère bi
@maguettembengue13235 жыл бұрын
Ndeysan Wally il suffit nga khol ko rek beug ko lolou mayou sougnou borom la love sur toi faramaren bi😍😍
@khadydione73275 жыл бұрын
C vrai ndeysan il suffit gua guiss ko reck love ko Mane mom i love you Wally ❤️✨vie sur toi reck Man mom menouma wakh si mom dakh bueguel yalla moko defff j laim ❤️✨✨bout chanté chanté Mouhamed domam day lelni sama bb Mouhamed lay wayy
@seynabouthiam33905 жыл бұрын
Bilay❤❤❤❤❤❤
@khadyrassoul5 жыл бұрын
Bakh ak oyof rek mo ame solo menone nga fouye béw kone sénégalais yi dougnoula beug mais santal yalla bimoula mayé khol bou rafet ba gneup nangou ko ba paré dougeul la thi séne kholyi sant yalla rak mola warr mane dé lolou rek mo takh ma beugla ❤️
@ibadiop3065 жыл бұрын
Machala tay sanekh alouna ,bilay Senegal dafa gueneu metti les gens souffre ,bojniou febarou douniuou fadjou ,niep di niane ta dojniou niane loudoul café.touba,sanekh wakhal niou degu leu
@campagneecobank85 жыл бұрын
Moi j'adore Waly seck,grâce a sa générosité, sa simplicité,sa modestie.pluie de grâce sur toi waly
@satousatou68415 жыл бұрын
Vraiment wally yayam mounkoy conseiller c’est bien nakh det rek moy deugu t musique dafa kharame yalnala yalla meyla lou geun Inshallah
@sohiboudieng27645 жыл бұрын
Ta compris lima xalate sa mere et sa conseillere
@joembengue7745 жыл бұрын
Walay tu es le meilleur on t’attend a Paris inchala
@mbarianeseck14465 жыл бұрын
Joe Mbengue ef
@mireillemandiame56535 жыл бұрын
Bilay niougui koy khar
@vito5075 жыл бұрын
@@mireillemandiame5653 koumay yobaleii wayy 😣😣 Marseille la nek
@mireillemandiame56535 жыл бұрын
@@vito507 mane mi di wakh sa awma billet tè paris la nek lol
@vito5075 жыл бұрын
@@mireillemandiame5653 inchAllah digua ko ameu gueumeu ko rekk dina nieuw
@mistermoo2285 жыл бұрын
Kou beugue wally seck beuseul 👍
@khoudiadiop49444 жыл бұрын
très sincèrement waly manchalah yalla na la yalla defal diam tu es génial ndanane pire
@marietoudiop44315 жыл бұрын
Bilay sa nekh tu as raisons kene dou waly quoi qu'on dise c'est meilleur 👍👍👍👍👍
@papeomardiagne46505 жыл бұрын
Non kii il est le meilleur bilahi thieuy le golden boy de la music sénégalais prince des faramareens 💪🔥💪🔥💪🔥
@mamadoucamara44395 жыл бұрын
Retour de Wally seck sur l'émission ngonale ça ns fait bcp de plaisir
@ndeyeawagueye63985 жыл бұрын
Wally seck nittou keissei la mashallah. Xalei bou am djom ak foula référence gua birr sénégal kou djara roy mogui ni borom karaw bou gnoul dara djombou ko et c'est ce que tu ns fais savoir djeureudjeuf🙏avancement reik inshallah
@apouta65955 жыл бұрын
Wally Akka Nitè 🙏🏻🙏🏻🙏🏻
@strongwomanmbacke82695 жыл бұрын
J'adore ce team walakhi Sanex deug rek gua wakh dagno sone wayé yalla guiss na lepp✌ lepp ame importance liguéne wakh borom Dolé yi rek gnoy ndimbalanté 😏😎yalla na diam yagg 23ans d'amitié machalah wally bonne continuation on t'aime 😘😍❤borom bakh
@avektv38695 жыл бұрын
La diaspora Sénégalaise est le garant de la stabilité sociale du pays
@binetasow97065 жыл бұрын
Sanekh nak tay nekh ngama deugu nekhoul wally khol bi lako yalay fay 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰❤️ bon courage niongui wadial dal
@adjifall93045 жыл бұрын
Waly diam rek in sha allah, liguaye waye nekhna, yalla nala borom bi takhawou in sha allah
@titifarou82575 жыл бұрын
Kou mére dale kalamél yallah thiona papa thione lako yallah fayé thi walli yallah moye wané bopam té walli yayam dafa liguéye keur bayam sokhor bakhol
@villanileonardo006villani55 жыл бұрын
Deugue nekhoule
@yayesirandiaye94545 жыл бұрын
Billahi deugeu nekhoul
@villanileonardo006villani55 жыл бұрын
Mais thione Nena diagua djourale nako ay fassou narou gore ak ay foutanker papa thione Nena guereume na Ndeye fatou diagua Senegal yeupeu degue nagnouko
@nogayesarrdarry92655 жыл бұрын
@@villanileonardo006villani5 bilahi dafa lérr
@serignecisse87445 жыл бұрын
Astou Mbaye machinou faux billets yi Yalla féyé wou co Thione
@fatimafaliloulah11455 жыл бұрын
Bravo à l'équipe de ngonal, 5 premières minutes très pertinentes la situation actuelle du Sénégal est très pénible, la population est fatiguée. La pauvreté, l'insécurité, le taux de chômage, l'insalubrité, soins de santé inaccessibles, écoles inaccessible , encore pire dans le milieu rural. Faramaren 😍
@aminatadieye95565 жыл бұрын
Mane dee personnellema do sama way katt mé damalay bégué boubakh di deglou say son damalay nianal goude fane ak wer tal féké ak mouth vréma niit kou exceptionnel gua niit kouma naw gua vréma courage rek inchallah dina bakh 🙏❤️
@diordiorina72545 жыл бұрын
wa bo ndiaré mew mi fougnou dieum ❤ ya ngi sedal sougnou khol yi faramaren bi 🥰 yaw doundeul rek lo doundou mouy geneu nekh ☺😘
@mouridmourid45025 жыл бұрын
Vraiment tu es quelqu'un d extraordinaire, merci pour le sms véhiculer
@hamadyba53525 жыл бұрын
Merci saaaa il faut etre droit waly est le meilleur de sa generation
@mbayefina84355 жыл бұрын
Thia kaw thia kaname sama faramaréne biii Jtadoreuh❤❤❤💖💖
@marybelle86245 жыл бұрын
Mercii Sa way si papa wally Merci merci nooo papa Aaa me nice Sama papa wally ki Machalla ❤🤲🏽👏🏼✍🤙👂💪💋😉😉👑💋💋😂
@cheikhounambengue41915 жыл бұрын
Ce n'est ps mon artiste mais il a un cœur énorme
@alioukaracisse48385 жыл бұрын
Never give up my brother wally ballago seck God bless you my brother I like you
@kadecamara86965 жыл бұрын
Bilahi Wally damala beugue no mel beugue na bamou bari Dolé si kaw si kanam yalla sa diam yague figua beugue yégue yako kham yalla na la fa yalla yégual amine 🙌🙌🙌🙌🙌
@sambandiaye25625 жыл бұрын
Waly franchement t'a assuré bonne continuation
@maremeseck92165 жыл бұрын
Beugu Wally demb tay bâ soubé sa xole rafetna bilahi😍😍😍
@ndelaciss66035 жыл бұрын
sanekh sa message bi dawna yaram...yallah nala yallah faye
@cheikhounabamba10065 жыл бұрын
Do wayei mou neikh NGA wakhtane mou neikh NGA sangnsei mou rafeite lol machalah ❤️
@fatucisse5 жыл бұрын
No sanekh khol bou rafete la yorr kou beugue wally seckh la😂🥰
@1MisterFase5 жыл бұрын
Ce gars a tout ce dont il a besoin pour etre une star internationale, il est aime par les jeunes et surtout les jeunes filles... Il a besoin d'un bon management. Un bon manager et dans 3 a 5 ans il remplira toute ces "salles". Youssou Ndour et Baaba Maal = 1 ligue appart Wally Seck c'est celui qui a le plus de chance pour percer comme eux. Keep up the good work.
@mouhamedfall40425 жыл бұрын
C’est kebs qui pose toutes les pertinentes Elle Mérite de diriger l’émission
@diatousene64685 жыл бұрын
Wally khaoma kagne lalay guiss walah je t'aime j'ai mm dé larmes aux yeux sa youmalay sétan doundeul ci barké borom touba Niongui sa guinaw
@adamabaldeh32735 жыл бұрын
Machallah machallah sama Wally seck rek one Love 👍🏿👍🏿👏🏼👏🏼❤❤❤❤😍😍
@narfall70675 жыл бұрын
Merci merci Gonal👏👏😘😘👑👑👑👑👌👌🙏🏻
@niassconfirmation74975 жыл бұрын
Bilahi WALLY dou senne morome inchallah il va réussir bonne continuation À WALLY 🥰🥰😍😍😍😍❤️❤️❤️❤️❤️✨✨✨✨✨✨✨❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@babacardiop869229 күн бұрын
❤❤❤j ❤❤❤❤❤ hui ❤
@kikikargueye12375 жыл бұрын
Bilay wally seck do sen morom si lép yaye sen baye
@sokhnasoukeyna98235 жыл бұрын
Waly yalnaga goudou fane te weur way ak bepe dioulitt 🤲🤲
@morrsamb74605 жыл бұрын
Amine yarabi
@marietoudiop44315 жыл бұрын
Waly tu es notre frère bilay je te porte ds mon ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@sokhnaoumoucisse57905 жыл бұрын
Le golden boy masha'allah t'es simple ouvert masha'allah yallah gua goudouh fane way comsa sounou khol yi di yague feikh
@coumba_smith_diagne74505 жыл бұрын
Wally wally wally wally wally wally wally wally wally wally wally B Seck loutakh ma bgg leu tei meussou mala guiss oohh mon dieu
@lhommebcm49205 жыл бұрын
Ndeye coumba Diagne massa 😂
@coumba_smith_diagne74505 жыл бұрын
@@lhommebcm4920 bilahi lii da meiti 😭
@mouhaframarene33525 жыл бұрын
Dinala yobou si wally
@coumba_smith_diagne74505 жыл бұрын
@@mouhaframarene3352 waxal way
@minashopsba71095 жыл бұрын
Machalakh sama faramaren bi lep leralgako dakh beugue sa yaye bagne moue am nakhar thie kaw thia kanam dam rek boul meseu guersou on t'aime beaucoup
@thiernonelsonba42265 жыл бұрын
Golden boy de la music Sénégalaise du courage gueumeul sa boop rekh ligueye
@fatoufall31795 жыл бұрын
Machallah wally si kaw si kanam❤
@dakarrapidetv55005 жыл бұрын
Kou beugue wally beusseul j'aime👈👇
@sokhnaoumoucisse57905 жыл бұрын
Wally est le meilleur kou d'accord beusseul j'aime. Dome paris dinah melni sabarou abeille incha'allah
@ramataka44905 жыл бұрын
Le meilleur le meilleur de sa generation
@babacarsamb63845 жыл бұрын
Ratification ramata le meilleur de toutes les generations
@nanisarr17895 жыл бұрын
J'aime sanekh il est véridique walaye mome sou maral kene tayeum nitou deug le wally yaye sene baye 😅💞💞
@myamya88565 жыл бұрын
Ohhh beug niit aka fort kholal ni sanex di kholé wally reik 😍 bodone djiguene mani danga ko nop macha allah way yallah na diam yagg
@arameyade7465 жыл бұрын
Bilay ki xolou diama la yorr kéne dou mom nittou késsé wallay Barki S Bamba mima yakar Wally mako beugue en personne dafa bakh goré mandou surtout yallah nako yallah lafal thiate té seuytané sékhlou ko
@aminadiop19175 жыл бұрын
Thiey Wally seck le chanteur du peuple on est tous derrière vous on est fière de vous
@tigrenoir51475 жыл бұрын
Liguéye dal da nga koy niémé vraiment je t'encourage diame si yaw
@moussambaye96385 жыл бұрын
Au début de l'émission franchement sanékh a fait un très bon discours j'aime beaucoup✊✊
@fatimataly11905 жыл бұрын
Wally yo allah soure renma long vie
@kinediallo2535 жыл бұрын
Wally seck rek 👑💯♥️🇸🇳💯👑♥️♥️
@mouhamadousow52455 жыл бұрын
Machallah waly je ne t'ai jamais vu mais bilahi damala beugu et vu la façon dont tu parles t'es quelqu'un de bien. Yallah nala Yallah samm si barkei Mouhamadou rassoulahi salal lahou aleyhi wa salam
@damesane91865 жыл бұрын
Bala 26 bounekhè yalla
@damesane91865 жыл бұрын
Waly yalna goude fane ame were diame
@keweba15225 жыл бұрын
Ioe wally saa mana way kenn douco natablei geumnani tu es l'essence de l'existence de tes fans waw kaay
@alieusarjosarr75875 жыл бұрын
Ndeysan mo takh nite degay diague dara balagako def kholal keps mougui professional waye kholal niom sanex niniou virgeré Senegal niépa mouna woy wally défa am warsék rék té lolou yallah moko déf kén mounou si dara
@someone-ib7gd5 жыл бұрын
Franchement mm Wally l'a dit
@alieusarjosarr75875 жыл бұрын
@@banatounkara565 ban ouzin?
@princessethioune75475 жыл бұрын
Man dè mar Yacine meissa biguè sama khol bi guinaw yalla yonenti bi Serigne Touba samay niary wadiour sama khol bi mako mom tè diokhnalako yalnala yalla takhawou mousal la si thiat sameu la barké Serigne Saliou sunu fierté gua dè yafi nek bayou ndella momy ak Mouhamed yalna borom bi yok sa fan sa dound bi amna solo lolou si gnoune gnila beug walahi
@realgalsen.officiel99165 жыл бұрын
Si toi aussi tu lit les commentaires en regardant la vidéo niaffall like 👇
@themomo40745 жыл бұрын
Yallanala yalla lafal thiate mayla fane bou goudou ak weur
@sarjomarong26135 жыл бұрын
wahatiko wally Ma'Sha'Allah papa Thione moi sha baye may God protect you 🙌🙌🙌❤❤❤❤
@djibrillo35105 жыл бұрын
Sanéx sa dougou bi amna solo idée pertinent vraiment sathie gui métina thie réwmi.
@miss65835 жыл бұрын
😅😅😅😆
@ndeyefatougueye49655 жыл бұрын
Thiey marr yacine meyssa bigué marr iow sa khôl dafa rafet danioulay nianal rek yalla bayilafi bagua agualé sa mébeute yeup thi barké serigne fallou🙏🙏♥️♥️
@laminesy66275 жыл бұрын
Barki borom Touba Wally Mala gueume do s'en morom sakh
@cissekhalil73925 жыл бұрын
Barro mogui guitare Lou nekh kouy doura man kouy saga Momy bally c très magnifique💗
@khadimgueye31245 жыл бұрын
Sa nekh immigrante yi contananou thi yaw thank you graçias obrigado
@entrepriseentreprise46925 жыл бұрын
Merci Sanekh vraiment linga wah sa holl la diouguei t Lou diouguei si si hol lay delou yalla nalafi yalla bay ci barkei alhuran nga and ak weirr inchalah merci
@diopmoustapha90175 жыл бұрын
Wally é un jambar machallah mé jojo swyé un p professionell way ah mé ki es le fils de n'importe ki ? Tous les papa snt pareil é baye kate bi papa la té nit la kamém
@selimselime69385 жыл бұрын
Diop Moustapha peuple bi laniouye représenté si plateau bi sen mboubou amitié daniou ko wara tegue gauche waly sou tegue soiree paris fessoul khalat naniou promoteur bi ba naan il faut l’encourager bercy amoon fi thiow bou ne krou niouye diaye nit ki ndakh teranga
@MBEKMITV5 жыл бұрын
Machalla jeu conta
@byasow75145 жыл бұрын
Wally dale machalla douniou tayi si dila beug Doundoul rek mar yacine❤🔥🙏❤❤❤❤❤❤
@ndeyemaremengom84625 жыл бұрын
Merci sanekh tu as bien dit vraiment et cest tres important
@coumbacamara31235 жыл бұрын
Mashallah émission ngonal bi franchement néhna.yalnassa diam waly ak équipe ngonal bi yeup
@ndiobentv67465 жыл бұрын
cb
@princessbbz88495 жыл бұрын
Waw waw say it again we're proud of you Wally ❤❤❤
@minksparishdiop23345 жыл бұрын
Bilahi dady yagniou sagual yagniou teral on t'aime fort notre fierté 💪💪💪💪🙏 yalla nala. Yalla moussal sa thiat si barkè seydina Mohamed psl 🤲 bilahi 😭 j suis très contente
@binettediop65255 жыл бұрын
J aime tellement waly inchallah je serais au dôme le 26 kebs sa neek cheikh ndiaye je vous love
@kokounonou66355 жыл бұрын
Sénégal nak xamgua louma djaxal ap fooo kat rek lagn favorisé nan ay yalla guénélén yalla si musique bi