Non vraima Modou Mala beugue walakhi yallana roi bi yagu ci yaw amine
@ridialdieng28612 жыл бұрын
4ans beuré wô yague kay wésouyouko
@AbdourahmaneKandji-fx4tm Жыл бұрын
Modou amoul morom
@babacarkonteye Жыл бұрын
Amiine
@mamadoufall9185 Жыл бұрын
Amine 🙏 YALLA Nako YALLA Def🙏
@abasall711 Жыл бұрын
Aaammiinne kubax ki
@baidy74184 жыл бұрын
Billay Modou mooy super ndaanaan....lamb ji niaari ndaanaan kessé la am...Modou ak balla..
@mamadouka36793 жыл бұрын
Le vrai champion c'est modou lo
@elhadjimodoudiop11073 жыл бұрын
@@mamadouka3679 Modou Moy sama mbeur mais nakk balla amoul mborom si lambe dann n'a Modou 2fois
@mouhamedlene92943 жыл бұрын
@@elhadjimodoudiop1107 kon yow do vrai fans modou
@mouhamedlene92943 жыл бұрын
@@elhadjimodoudiop1107 yow guiss nga modou noumou toll par rapport ak yenène mbeuri
@mouhamedlene92943 жыл бұрын
@@elhadjimodoudiop1107 sou toloune ni balla gaye kene doukou meune dane
@libassegadio2952 Жыл бұрын
Modou un vrais champion toloul ni gayi❤ meune si gayi
@princeizo85034 жыл бұрын
Modou lo rek sama roi d Aren bi yalnako yalla defal jammou way
@Eladji-sall444 жыл бұрын
amine waye
@abdoundiaye91795 ай бұрын
Qui là en 2024 vraiment j'aime trop Modou lô ❤❤❤
@mamadouwade62473 жыл бұрын
Modou sportif la kw macha.allah
@lalathiam75043 жыл бұрын
Wa lac lac lac lac nak li mom ba kagne nakk, yaw ak ni nga tollou Machallah té do beuré do xéxx moukk simm, nitt da ngay am jom touti modou molay douma dila dakh ngay daw
@diyeracinegayegayr63333 жыл бұрын
Nèna li moy hana may dirigè 🤣🤣🤣 Billay modou super ndanane
@abdoulayethiome533 Жыл бұрын
Voila quelqu'un qui mérite bien son titre de roi des arénes, Modou Lo. Contrairement à ce faux Lac 2 qui décoit toujours le publique, qui préfère toujours fuir quand il est en position de faiblesse. Vive Modou un vrai technicien, combattant, le kharégne.
Modou na indi forme bi contre ama douma ko dane ko inchala
@awaseck3645 Жыл бұрын
Sa niane nangou n'a dh
@agencekbs40233 жыл бұрын
Eumeu même a confirmer que Lac boy beuré ak mom dalay niakal fayda
@abdousalamdiallo6008 Жыл бұрын
😂😂
@abdousalamdiallo6008 Жыл бұрын
Deug nékhoul lac da yaga merlo amateurs yi 😂 , mbeur faw nga nango beuré nékhal lamb j, mais chaque seral gayi mer dou yone
@ZeydaMariama Жыл бұрын
Lac diemoul provoquer mouk
@adamtraore6583 жыл бұрын
Way Modou yaye goor bilay wathio nguakk niounne
@ndiagaba21714 жыл бұрын
Babacar néna li Moy khanna may dirigé 😂😂 Modou way
@MonsieurSy-i5jАй бұрын
19:20 THIEYY MODOU
@serignesamb6538Ай бұрын
Modou kasseii❤️❤️❤️
@AbassBa-w3v Жыл бұрын
Bilahi modou lo mi bou amon dolei ken douko atann ci lamb ji
@Abdallah31341 Жыл бұрын
Bou yemon ak gar yi niou am problème
@princeizo85034 жыл бұрын
Kharagne lo khale bi sonal mak gni ci lamb dji
@daoudaanneat-tidiany3 жыл бұрын
Kharagne do khalé dh🤣🤣🤣ab thioss leu😂😂😂😂
@diopdollarfarramarene56323 жыл бұрын
Kharagne lô 👑👑👑
@KhadySow-mp5ly8 күн бұрын
Modou .lo.vrai chanpion
@KhadySow-mp5ly8 күн бұрын
❤❤
@lassanandour7334 жыл бұрын
Thieye modou
@daoudadieye19903 жыл бұрын
degue nékhoul déh mes vraiment Lac yambarla tapétela
@taphasyll50262 жыл бұрын
Modou lo adina mla thie guena beg
@CheikhounaDieng-h3z Жыл бұрын
lolou nga fook rek billahi dama bague modou lo
@AliouNiang-lu8np Жыл бұрын
Modou lo kassé Bilay lamb lô way
@dieudonnesambou69263 жыл бұрын
Lac est trop nul ...moudou a pleinement plus d'experince il est plus courageux. Brovo modou 👏👏👏💪
@abdoulayedabo8383 Жыл бұрын
C'est toi qui est nul s'il est plus fort que lac pk il peut pas le battre c'est vraiment pathétique
@ZeydaMariama Жыл бұрын
Lac est nul
@xosslouman88293 жыл бұрын
Lac de guerre mangay dawww kay😂😂😂😂😂😂ki raynama way
@naboundiaye9946 Жыл бұрын
Modou mon super ndanane borrom taîba Ndiaye
@moussandiaye8488 Жыл бұрын
Modou lo😂😂😂doff la ama dalossi
@awacheikhdionlyse1069 Жыл бұрын
Lac doula daan dou bayi kéne Dane ko😂 dou songou dou délo avance 😂 bly lac mo sof😂
@Adamsloficiel- Жыл бұрын
Bilay deug nga wakh😂😂
@mouhamedpadane96834 жыл бұрын
Thanks lutte tv
@baymassbessane38243 жыл бұрын
Lac bou modou doon nélew sakk dou mbeuré
@souleymanebadiane58333 жыл бұрын
😂😂😂waa yeen guiss nguéne le médecin en bleu
@souleymanebadiane58333 жыл бұрын
19:53😂😂😂
@DAKARINFOS-221 Жыл бұрын
😂😂😂
@abdoudiabaye42753 жыл бұрын
Modou lo way
@mamadoucisse20253 жыл бұрын
Lac mo wara déme ligueye sécurité té maye beuré
@younoussdrame57013 жыл бұрын
Mdrr
@fallmara75703 жыл бұрын
Lac 2 ni rek il n’est pas champion Dou mbeurr Li moi beugue dafa yombou ishh Beugue nek champion té doo niémé engager wou Dafa wara bayi beuré Eumeu sene néna ki daye soul ndanane mais c’est vrais Lac2 le tricheur
@azizelo21003 жыл бұрын
Var daal mbirou yalla la lac dafa bakhhhhhhhh😩😩
@MouhamadLamineDRAME Жыл бұрын
Bilay modou lo vrai champion wayé na dém diangui thiongou
@MoustaphaMbathie-k5k8 ай бұрын
Yaw khana da nga fébar
@MouhamadLamineDRAME8 ай бұрын
Légui lane mofi Diara sagua kounék day wax limou xam rék ci mbeur bi parcelle la deukeu yagu n'a guiss Modou Di contact
@itsdanejustdane80843 жыл бұрын
Non nexout ba nexout mais Lac dayy soul ndaanaan kw
@modougaye66464 жыл бұрын
Lac 2 vrai gordjiguéne leuh ki diaroul sakh faye khaliss
@hermannfabrice85653 жыл бұрын
ça fait un an commentaire bi mais ça m'a juste tuer🤣🤣🤣🤣🤣🤣, et je viens just de voir fac a face bi loumou wakhoul dako fate woooy🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Modou day box kom mayweather, esquiver coup lamb dji yeup mokofi dakh, contre gris bordeaux la xam lolou
@mouhameddiagne6953 Жыл бұрын
Wax djii mofi nek rek mais modou meunoul daane lac
@seydinaaliouneboromjasiji32004 жыл бұрын
Kenn dou Xlo
@lamanetine65213 жыл бұрын
Lamane kharagne 💯 non amena beur
@Aissatoudaffé-i6v Жыл бұрын
Dafa yorr rojaa😂😂
@papeniang35474 жыл бұрын
Rosa De modou Lo 🤸🏽♀️🤸🏽♀️
@latyrndiaye9623 жыл бұрын
Lac 2 Mane mi sakh bouma Agone Modou lo fi ko ague môme chute Dina âme d'âne ma wala ma d'Anne ko mais yew yore machine nou calcule Di calcule rek lac2 sooff ga
@SouleymaneSoul-b6x Жыл бұрын
Lac vrai djiongama la😂
@papamagueyengom9952 Жыл бұрын
Nooo mis lac2 vrai thiounéleu koi...cheuuuuttt😂
@tewsi56423 жыл бұрын
Li motakh mister Lac nane senegal dagneko bagne😂😂😂 fanelako modou lo teyée diko dore?
No lac mome boy beurè ak mome diaroul sakh ngaye tite walahi ki mo. Wara bayi si bopame
@mouhamadoudiop9163 Жыл бұрын
Allez xaragne lo
@boubacarndiaye81023 жыл бұрын
Lac dou mbeur ki diegu leu
@khadimndiaye93544 жыл бұрын
Ani var bi
@mamadoutchente1170Ай бұрын
Nafekh rek Lac dafa mbeure fii Bayil sokhor
@ngomtidiane17454 жыл бұрын
Lac mo nil 😂😂
@Nafiyotv Жыл бұрын
Franchement lac 2 xamoul gate dara boolo dieekh déja mounoul xeex amoul technique si beuré amoul benn qualité bou lac 2 di woné si beuré loudoul adversaire deff erreur mou exploiter dane ko le gros ne mérite pas le nom du peuncheur da Walo on dirait que Siteu na pas regarder ce combat...🤔
@IbrahimThioune-j4s Жыл бұрын
😢😢😢😂
@massendiaye5802 Жыл бұрын
Non Mod'lo dafa meune
@leminsarr96673 жыл бұрын
lac 2 vrai yambar laa quoi
@askane.wi221 Жыл бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@fffamilianiangg92hotmail.i933 жыл бұрын
Moudou lololoulllaguemmmm
@assanediop86383 жыл бұрын
Modou lô dunit
@thiapathiolibouxaragnlo79873 жыл бұрын
Vrement lac 2 ndanan lah
@tigresuarez80247 ай бұрын
lac et le lutteur le plus nul du Senegal
@lassgalouffa28823 жыл бұрын
Lac Sergio Ramos de la lutte sénégalais sénégalaise
@championBoulan3 жыл бұрын
Lac 2 da wara bayie ereue koi ah ki dafa sof torop ta niake khorome
@salioumbacke51643 жыл бұрын
Lac dou mbeur
@AstouDiagne-m1g Жыл бұрын
🤣💪👑👑👑
@AmadouGueye-c5b Жыл бұрын
LAC DOU BAYI BEURRE DEM GUETHIE BOKK NEKKA MOL
@LemXune Жыл бұрын
mais non lac vraiment c est pas possible putain
@koreasow46903 жыл бұрын
Eumeu bou dèfone ni dane ko srx
@tallaloum76423 жыл бұрын
Non
@toubatoub16412 жыл бұрын
Н що толщ6
@cheikhbasskeurmassar95484 жыл бұрын
Modou lô tappet la dou Dara mounoul sax daan kii
@SG-xu8et4 жыл бұрын
Yaw dole rek gua fi négué
@ngorlecon50574 жыл бұрын
Nafek mola téré wakh deug, combat commencement ba fin bène mbeur rek moci guène sakou, toloul ni lac 2 pourtant, diom, ndiambar ak ngor ci modou lo lafek bakh, niou dane ko ak mou dane, bou tolone, ni bombardier, tapha tine wala gris bordeau kone guiss défaitam lou diafé lay done, wakham bariwoul, doko deg ci lou niak foula.
@mouhamadoudiop42874 жыл бұрын
Yow kou sokhar gua
@mamdoulaminepouye57614 жыл бұрын
Saway lac legui loutakh danouko li lac am si modou boudone balla diekhna lac kéne danagouko bamou teudeu