No video

Opération de désencombrement à Keur Massar: colère noire des commerçants

  Рет қаралды 40,066

DAKARBUZZ TV

DAKARBUZZ TV

Күн бұрын

Opération de désencombrement à Keur Massar: colère noire des commerçants

Пікірлер: 175
@badiene0311
@badiene0311 3 ай бұрын
Defna keur massar 11ans meussouma xam ni Taly bi ni la yaato😢metina certes mais nagn leine defal centre commercial
@khadijasow7107
@khadijasow7107 3 ай бұрын
Bougnou leen defale 1000 centres commerciaux sakh dougne fa deme ndakh beug lou yomb
@abdou21diatta44
@abdou21diatta44 3 ай бұрын
Dina méti certes mais faw gnu défar deuk bi..bayilen trottoir bi..
@fantabadji7137
@fantabadji7137 3 ай бұрын
Wallay Abdou wax nga deug dé srx kén meunetoul djaar si trottoir yi lép lagnou djeul def fa sén marchandises vrai c pas normal nagn wakhanté deug
@itools2514
@itools2514 3 ай бұрын
Fadel, Keur Massar danio nélaw deuk bou yagoul dara am bordel bou doy war. Keur Massar gni fa deuk dama léne yeureum bilahi.
@ibouciss3519
@ibouciss3519 3 ай бұрын
Ah bro nakh gua sagne ko wax sone nagne dh bly
@badiene0311
@badiene0311 3 ай бұрын
Bilay aka meti ci nioune! So quitter ville meune nga def moins de 30mn ci péage bi mais pour nga dougou keur massar dina eupp 1h!!!
@fallougalassbeye3579
@fallougalassbeye3579 3 ай бұрын
saway Yaw nopil xamo dara di wakh ni rew bou bagné kou diaye si tally bi dagni defar ay marché boula yalla natowon ngay diaye comme gni dowakh li bo deme sen keur lifa am moeup li te wakhoko
@fallougalassbeye3579
@fallougalassbeye3579 3 ай бұрын
Senegal dougnou liguey dougnla bayi nga liguey limotakh gayi dieul galle gui Boudé dañi Bagnkou diaye si tally bi nagnou defar ay marché you bakh lolou moy wakh bi defarou gnou tous loudoul sonal diaykat yi fou nitgni takhaw di liguey gnou beug lafa dieulé lolou ba kagne 💔😡 😠😠 sama gayi yalla nalėn yalla doli soutou ra Ay djambar guen💪🏽
@ndeyeastoumbaye1906
@ndeyeastoumbaye1906 3 ай бұрын
@@fallougalassbeye3579niata marche nio. Nekk Senegal ?
@mamadoumareme9849
@mamadoumareme9849 3 ай бұрын
Merci beaucoup monsieur le maire et la gendarmerie ❤❤❤
@ouleymatoulam5735
@ouleymatoulam5735 3 ай бұрын
Il a tres bien parler l premier bravo j ladmir vraiment fadel kholatale sa question ker massar on es tes fatigue tu peux mem pa passer
@user-ze9ku6pc3y
@user-ze9ku6pc3y 3 ай бұрын
Nous sommes fatiguée ns les habitants de keur massar vraiment
@souleymanendao1843
@souleymanendao1843 3 ай бұрын
Sénégalais mo indisciplinés, même en Europe ils occupe la chaussée et même prêt à se battre contre Les forces de l'ordre
@PhinaFaye
@PhinaFaye 2 ай бұрын
Président Bassirou Diomaye Faye inchallah ndam rekk du courage avec le premier ministre Ousmane SONKO le Sénégal ne pouvait avoir mieux et c'est un rêve de ce voyant peuple qui s'est réalisé de vous avoir à la tête du pays. Yallah bou yakar tass
@abdoulayendiaye221
@abdoulayendiaye221 3 ай бұрын
Sanctionner lourdement, les trottoirs sont pour les piétons ish❤
@MamaLEYE-uy7dj
@MamaLEYE-uy7dj 3 ай бұрын
Sujet bi tamit colére noire pour lane. Tristesse ak compréhension rek lafi guiss
@AdjiDiop-by9og
@AdjiDiop-by9og 3 ай бұрын
Fadell warone nagne bayi ba Tabaski passe vraiment sama haleyi djambar laniou bilahi yala nalene yala tahawou.merci a toi mon frère ❤❤❤
@amathsow3931
@amathsow3931 3 ай бұрын
Apres tabaski ya d'autres evenement
@khadimfall6508
@khadimfall6508 2 ай бұрын
Merci beaucoup le Maire Bilal ❤
@You-wm1ox
@You-wm1ox 3 ай бұрын
La population doit lutter contre l anarchie
@MouhamadDiallo-lu4xj
@MouhamadDiallo-lu4xj 3 ай бұрын
Suis Mackyste mais lii c’est très normal baayillen territoire yii ah
@khadijasow7107
@khadijasow7107 3 ай бұрын
Même bougnou leen defale 1000 centres commerciaux dougne fa deme ndakh beug lou yomb. Yeenewougnou reewmi dara lou baakh gnome lougnou djaye gnou defko seen poches sans rien donner à l'État pour au moins reemi set.
@AwaKane-jz3xn
@AwaKane-jz3xn 3 ай бұрын
Désencombrement tous le Sénégal n'a mairie yi deff s'en ligueye, mou ame ayé agent de contrôle dans les mairies, kou lale fo warta lale gnou yeukatila, amoule demale ma gneuwe
@damediaw6509
@damediaw6509 2 ай бұрын
Mai Marie yi douneko def nakh djouti yinesiy ame
@adamafall3540
@adamafall3540 3 ай бұрын
Merci monsieur le maire de keur massar
@elbiranetoure262
@elbiranetoure262 3 ай бұрын
Fadel Sénégal 🇸🇳 thi bopam mo meti barkeb khadim Rassoul toki rek inchallah 😢
@samb70105
@samb70105 3 ай бұрын
Bo touke nie gua fay fek danion respeté sen loi deuk mo takh mou avancé ba nieup beugue fa dem alors pourquoi pas respecté ses propres lois pour avancer
@IbrahimaKane-px6zk
@IbrahimaKane-px6zk 3 ай бұрын
Salam grand s'il-vous-plait wate si Serigne bahoul bayiko dingue je m'excuse nk
@alphousseyni9427
@alphousseyni9427 3 ай бұрын
Il faut nguène xamni projet bi nak lila dèfar jub jubal jubanti
@user-bz3iz3gd3c
@user-bz3iz3gd3c 3 ай бұрын
Saway lek nan fadjou liguey lann wax
@linteligencereussite539
@linteligencereussite539 3 ай бұрын
Djoubantèlènessène leufal ndeye yi ak sonko bo parè domaram
@sidyconare1784
@sidyconare1784 3 ай бұрын
Li bakhna thi yene vraiment
@SytaphaJr
@SytaphaJr 2 ай бұрын
Nénn mougn rk inchalla fi ak 5ans Dina bakh inchalla
@sadadiagne2781
@sadadiagne2781 3 ай бұрын
mais fokkk qu'on apprend a changer notre vie quotidienne Dina meettiii nakkkk mais inchallah Dina bakkkkk le s gars
@md.2844
@md.2844 2 ай бұрын
Très belle initiative du maire de Keur Massar
@azizdiaw6754
@azizdiaw6754 3 ай бұрын
Merci président
@morhann1619
@morhann1619 Ай бұрын
Ndayesane metina trop waye 😢😢😢
@FootShoes
@FootShoes 3 ай бұрын
Chaque effort individuel contribue à un succès collectif. Travaillons ensemble pour réaliser les visions du président Diomaye.
@karimniangane8445
@karimniangane8445 3 ай бұрын
C normal il faut mettre de l'ordre dans ce pays ya trop de désordre y'a pas pas de pitié
@mariamateningfadiaba9607
@mariamateningfadiaba9607 3 ай бұрын
Franchement keur Massar ken meunoul dial si territoires yi normalement
@AmadouSow-jl1gu
@AmadouSow-jl1gu 3 ай бұрын
Limoye yonne rèwou dãye ãme yonne sènègal jeune yi dinagnouko sanger merci beaucoups maire se liguèye rafète ne
@user-kq9lw5bw6q
@user-kq9lw5bw6q 3 ай бұрын
Sénégalais mo bougeu Lou yombou pourquoi les gens ne veulent aller chercher des magasins !
@babacarndiaye927
@babacarndiaye927 3 ай бұрын
Good job merci maire
@MAHHanne-ly3xj
@MAHHanne-ly3xj 3 ай бұрын
Si ces verites etaient dites auparavant....mais par hypocrisie et politique on a toujours defendu l indefendable
@khadijasow7107
@khadijasow7107 3 ай бұрын
Bravo !! Ndakh yalla. Dakar set weth
@leuzcisse6181
@leuzcisse6181 3 ай бұрын
Yalla N'a léne Yalla Takhawou
@IbrahimaBa-2024
@IbrahimaBa-2024 3 ай бұрын
Yen commerçants yi yena nekoul si yonn
@aissatoukobar2278
@aissatoukobar2278 3 ай бұрын
Wawaw naniou dégager lep lounek si trottoirs yi bonne continuation
@salioucisse2355
@salioucisse2355 2 ай бұрын
Acceptez la vérité quand elle vous concerne
@MouhamedDiallo-mw6yb
@MouhamedDiallo-mw6yb 2 ай бұрын
Nieuw force deuk bi dara dohoul
@user-gh2rq3kd7f
@user-gh2rq3kd7f 2 ай бұрын
Xam nalisi nekk man marchand ambulant la meilleure gouvernement yii danio wara gaww si tabakh ay industriel AK usine nguirr diaale ndaw ni metina mom yalla naniou yalla mayy kholou mougne
@user-gm7ve1eu5u
@user-gm7ve1eu5u 3 ай бұрын
Je n arrive plus à me situer tellement je ne reconnais pas keur massar ils ont fait un travail colossal
@user-pi3gx2rq4x
@user-pi3gx2rq4x 3 ай бұрын
Massa. Yalnalenes sounou borom tawahou
@modousarr8848
@modousarr8848 2 ай бұрын
Voté député ngén votél kénen
@biloubilou5237
@biloubilou5237 3 ай бұрын
Mane mii dh si ñifay ligeeye la bokk wayé dama ande si li bilal deff marché dafa rëpp bari ñufi waliyaan si di lale si peegu tali bi dañu wara organisé wu bayi peegu tali bi
@mbayefall5684
@mbayefall5684 3 ай бұрын
Keur Massar ak djoutiba teunguethieu legui nice pour l instant nanioulen wouteul founiou diayee aussi
@NglE371
@NglE371 3 ай бұрын
Évitons d'occuper certaines espaces pour le bien de tout le monde
@taflemanager8517
@taflemanager8517 2 ай бұрын
Felicitation aux autorités de Keur massar
@gloriamendy8002
@gloriamendy8002 3 ай бұрын
Outi léne place té bayi trottoir yi dou yone té khadji bi dekounoiu fa keur masar Sud nou Mou Mèl Niaw na
@ousmaneka825
@ousmaneka825 3 ай бұрын
Bilahi
@yanksisrael6883
@yanksisrael6883 2 ай бұрын
Merci au premier intervenant
@alhamdoulilah3991
@alhamdoulilah3991 3 ай бұрын
Danio woté Juub Juubal Juubanti d. Occupation anarchique thi espaces publics yi diadou woul
@ishakathiam6525
@ishakathiam6525 3 ай бұрын
🤍🤍🤟🏼🇸🇳
@iboudiouf7673
@iboudiouf7673 3 ай бұрын
Bayilen trottoir yi moguen linguen di wakh
@misszjuke4914
@misszjuke4914 3 ай бұрын
Très bien un peuple discipline = un pays sécuritaire !!
@lincisse5835
@lincisse5835 3 ай бұрын
Machala frère ki sol thset blanc bi😊
@kaadeer
@kaadeer 3 ай бұрын
Bilay cote yeup la metti 😢mais naniou deff ndank rek leep dina bakh in cha allah changement bi lou wara leun neik la
@MariamaSane-yj9tv
@MariamaSane-yj9tv 3 ай бұрын
Bouléne décourager daniouye défar rék.ba.nieup hadjeusi bou kéne méré kéne inchallah.léep moye bakh
@ramafall2889
@ramafall2889 2 ай бұрын
Ay way Yalla di sama wax dji am na solo taye Wa Keur Massar danio sonou soumay dem séti sama pape nonou lay soné il était temps way mais mairie tmt ani xaliss djouti yi défar Len marché bi tmt côté station bi am na terrain bou mak bou fa nek naniou ko def marché gni nek si tali bi am place
@laurentsambou7662
@laurentsambou7662 2 ай бұрын
80% de ces commerçants n'habite pas à keur massar.Ils se foutent des gens. Le maire fait du bon boulot
@beuzhustle3483
@beuzhustle3483 3 ай бұрын
Liii yone leuuu deukeu bii fou nekk nite tekk fa table ..il fo ordre ame pour deukeu avancer....guayi danio eupeule trop
@khalifababacardiop8709
@khalifababacardiop8709 3 ай бұрын
Ap deuk dagnou koy organisé senegal fouy wakh nekh lal di diay
@bayemodoudieye6640
@bayemodoudieye6640 2 ай бұрын
Dangéna wara dem si marché yi té bayyi kaw talibi yena nékoul si deug bayyi len yon yi
@serignesene8842
@serignesene8842 3 ай бұрын
Mais mayell gayiiii ba Tabaski passer
@yanksisrael6883
@yanksisrael6883 2 ай бұрын
Ils ont raison
@sophieba918
@sophieba918 2 ай бұрын
Jubb Jubbal Jubbanti! Fofou la Sénégal toleu
@user-ye1hh2wd7d
@user-ye1hh2wd7d 3 ай бұрын
Merci
@fallougalassbeye3579
@fallougalassbeye3579 3 ай бұрын
Bolén gnouy diaye si tally bi daguėn di defar ay marché defaroulés touss di sonal nit gni💔
@laurentsambou7662
@laurentsambou7662 2 ай бұрын
Beaucoup de ces commerçants ne sont pas des K.Massarois.Yabaté deug moy li
@Capitaine-j4c
@Capitaine-j4c 3 ай бұрын
Bien fait
@elhadjidiop3854
@elhadjidiop3854 3 ай бұрын
Diaay ci territoire bi diaadou woul mais am na louka jiitou ta lolou sa takhawaay la yaw monsieur le mère ét son gouvernement
@JoachimbassGomis
@JoachimbassGomis 2 ай бұрын
Il faut juste se poser la question a savoir si c'est normal ou pas, si c'est bon ou pas
@beuzhustle3483
@beuzhustle3483 3 ай бұрын
Bien dit mn ami journaliste..on ne peut pas faire une omelette sans casser des oeufs liii daffa Eupeu tropppp de même k bountou Pikine et rond point grand Yoff
@pendadiallo7040
@pendadiallo7040 3 ай бұрын
Lofy guisss magal moke épou dolé ngaye wakh
@user-nh2rf7dv1n
@user-nh2rf7dv1n 2 ай бұрын
Bayilèn wakh dji sène marchè yi da saltè nak koi
@user-oz8dr2pu9p
@user-oz8dr2pu9p 3 ай бұрын
Ngi téppi sen leufeul ndeye rek mo bakh yakenagne Keur Massar domerame yi
@user-gm7ve1eu5u
@user-gm7ve1eu5u 3 ай бұрын
Ils ont toujours pris l habitude de revenir après chaque debleyage. Donc ils se disent au bout d un mois on revient....on n est plus dans l ancien régime
@papitosall4753
@papitosall4753 2 ай бұрын
Je comprends plus les sénégalais khana khamounou patriotisme ak civisme niou ande donc faut quon change les mauvaises habitudes pour sunugal diar1yoneu
@papadiop4199
@papadiop4199 3 ай бұрын
Ambulants moykoy weur di diaay wala?? Thiey lii
@ndiagandiaye3939
@ndiagandiaye3939 2 ай бұрын
Sénégalais mo nèkhoula comprendre,
@MouhamedDiallo-mw6yb
@MouhamedDiallo-mw6yb 2 ай бұрын
Yeureumlene askanwi deuk bi mettina si new di dole yi
@aminaka7194
@aminaka7194 2 ай бұрын
Lutakh macky bamoukay déf nioukodone saga kone
@ALPHASONKO-cd8mx
@ALPHASONKO-cd8mx 3 ай бұрын
Le problème est qu'il y a beaucoup de monde à Dakar
@mamadouba1567
@mamadouba1567 3 ай бұрын
C’est douloureux mais comme ça.Y’a aucun changement sans des sacrifices. Jub, jubal,jubanti rk
@jamesjoob3771
@jamesjoob3771 3 ай бұрын
Wadji nga ñiekk Lathie mom waxi nit lala wax lu degou la wax
@Irma-kt9gr
@Irma-kt9gr 3 ай бұрын
Après Tabaski, magal, gamou, Noël jusqu'à la fin des temps. Sénégalais adore commerce. Cultivons la terre elle ne ment pas. Un ambulant doit bouger mais pas rester sur place.
@user-yj7iq1zg1j
@user-yj7iq1zg1j 3 ай бұрын
Wa baxna yena lene votel d ichhhhhhh
@thieub2825
@thieub2825 3 ай бұрын
Très bonne initiative j’habite au parcelle mais quand je passe là-bas on dirait la zungle
@user-fj7wg6ex6m
@user-fj7wg6ex6m 3 ай бұрын
C dure mais yalla baxna
@cheikhtidianecfaye4455
@cheikhtidianecfaye4455 3 ай бұрын
Sénégal efetement yiii d'où Dieikh 😂 Nii reick yalla naléne yalla m'ay lougueune lii
@aichadiop5346
@aichadiop5346 3 ай бұрын
Vérité
@AwaKane-jz3xn
@AwaKane-jz3xn 3 ай бұрын
État tamite naye prévoir ayé marché you Mak département, commune trottoirs yi, so léne si lalé piétons yi Di wathi si tally bi Ba auto mbeuk ko, lolou tamite bakhoule nane diapalanté, kousi nek na deff lime wara deff tek ko si yone
@MouhamedDiallo-mw6yb
@MouhamedDiallo-mw6yb 2 ай бұрын
Lolo diaroul wah bou gendarme di dem niouy lale
@sophieba918
@sophieba918 2 ай бұрын
Mani on ne peut pas faire d'omelette sans casser des oeufs ... Oute lene place si marché bi ... Cest dure vraiment mais lou meunoul niak la. Sénégalais boko diokhone 100 avertissement tamite dou tere bokay yeuketi mou indi problème t dou nek thi yoon .
@Omzo246
@Omzo246 2 ай бұрын
Tay lay dogua khamnii Sénégal mo barri nafekh deugg deugg 😂😂😂....lii sou tombé wône akk gouvernement bii dialeu "waaw lii dou yone 😡🤬...." Kom gouvernement bou béss bii "waa gnii dagni défare....lii djittou naa sougnou doundou" Kone dofo léne ?! 😂😂😂
@amadoudia7152
@amadoudia7152 3 ай бұрын
Amadou diarra pikine nord Kay khol si bilal diatta
@zarrebideshistoiresterribl8356
@zarrebideshistoiresterribl8356 3 ай бұрын
bakh na ci diaay kat yi vraiment danio soff
@serignesene8842
@serignesene8842 3 ай бұрын
A gayi gno votell diomaye dè li Moy projet. Bii
@SowMadiaw-go2uc
@SowMadiaw-go2uc 3 ай бұрын
Gnieuwlen kaolack
@sokhobambisalioundiaye2394
@sokhobambisalioundiaye2394 3 ай бұрын
Colobane et km souffrent des mêmes maux
@3blens
@3blens 2 ай бұрын
Atia
@user-ow7eh5jm5g
@user-ow7eh5jm5g 3 ай бұрын
Point d’omelette sans des œufs cassés !
@papvmor852
@papvmor852 3 ай бұрын
Niome déjà lu mais dou sen sécurité donc bayilein trottoir yi dem si marche yi
@khadimmbaye5447
@khadimmbaye5447 3 ай бұрын
Sma marche bi tasna
@ModouDiagne-xb1wy
@ModouDiagne-xb1wy 2 ай бұрын
😢😢
Zombie Boy Saved My Life 💚
00:29
Alan Chikin Chow
Рет қаралды 9 МЛН
Box jumping challenge, who stepped on the trap? #FunnyFamily #PartyGames
00:31
Family Games Media
Рет қаралды 33 МЛН
ISSEI & yellow girl 💛
00:33
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 21 МЛН
Survive 100 Days In Nuclear Bunker, Win $500,000
32:21
MrBeast
Рет қаралды 161 МЛН
Revue de presse Mame Khalifa Jeudi 22 août 2024
12:08
DAKARBUZZ TV
Рет қаралды 24 М.
Magal à Ndindy: le déjeuner royal de Yaye Pouye à la veille ...
9:50
Serigne Ngagne Très en colère "Naniouko Toop Bamou Leer"
11:04
DAKARBUZZ TV
Рет қаралды 10 М.
Zombie Boy Saved My Life 💚
00:29
Alan Chikin Chow
Рет қаралды 9 МЛН