Oustas aliuon sall yalla n'a yalla goudal saw fan thi barkep alkhouran
@aissatousall90685 жыл бұрын
Amine
@Ocass5 жыл бұрын
oustaz Aliou sall un homme de principe,humble et éloquent
@mouhamadoulamineseyebeugue27415 жыл бұрын
*_Ndeyesenn Amna solo tropp Loufa wayy niane yalnako yallah nagou si barkép SERIGNE SALIOU MBACKÉ_*
@ousmanegueye32445 жыл бұрын
Macha Allah. Oustaze Alioune Sall yague fi loll teid and akkk weurr. Dieuredieuf borom Touba. Mbakiyou Faye wakh ji rafetena.
@fatoudiene28185 жыл бұрын
Mashallah Mouy ndamou islam dieureudieuf Serigne touba fierté !!!
@modoualysylla30145 жыл бұрын
Machallah ya ouztaz yagfi lol teweur
@cheikhlo4475 жыл бұрын
Wallahi oustas mo rafet khol barkeb s.touba yague fi ta wer lol amine
@galassarr49795 жыл бұрын
Machallah Oustaz Aliou sall Yalla nala Sunu Brom takhawou Ak bepou tarikha
@lenoblepaco3605 жыл бұрын
Kou bakh yatou to mouna mougne keureum dieuppeul ak bar gnio dénde wayé djkoy deukando rek laye dokhal ak gniom en plus yatou meuna téral gane réré na tia mom sokhnam yatou ak njaabotam oustas machallah
@antagueye30225 жыл бұрын
Machalah oustaz toujours wakh diou rafet rék yanala yalla fay goudal fani ak wér dieuredieuf serigne Touba
@bambadiop78815 жыл бұрын
Billahi oustaz ya bakh yalla na sa fane goudou amine
Machalla oustaz yalla nagna fi yague té wérrr ak bépp djoulitt boy. Weur kou niakk kignaan ba. aksi thi yaw rekk djappal
@aissatousylla97505 жыл бұрын
Machallah oustaz sall vous êtes très nobles et humble longue vie a vous ya oustaz
@babadiop11705 жыл бұрын
Bilahi, statuts yi nek si Sénégal yeup boudone aye diakas ak djouma, Sénégal mouthie ba faw ta dara dodoufa manquer
@boussoballygueye13785 жыл бұрын
Macha allah oustaz bakh rek nga def yalna serigne touba taxawou
@mkg56805 жыл бұрын
Mbackiou j suis content de toi machalla si waxtane bi
@adamatoure39085 жыл бұрын
Oustaz alioune sall est un vrai musulman et il a un cœur saint
@mamemormbacke40495 жыл бұрын
😍😍😍😭😢machallah serigné alioun Sall nitt kou bakh te bakh di dioulit hakhan
@fallouthiam2505 жыл бұрын
Machala oustaz aliou sall yalla gafi yagu té werr machala serigne mbacké
@elhadjidia93385 жыл бұрын
Ouztaz alloune sall yal nanou ko yalla fayal fa goudal fanam amine
@abdouba66995 жыл бұрын
Vous êtes des exemplaires pour tous les musulmans voilà des vrais musulmans merci à vous
@sowdame1185 жыл бұрын
Oustaz A sall yalla na yalla goudal sa fanne amine
@modoungom60025 жыл бұрын
Machalla ya oustasse amna solo trop...
@fadelbambiste14515 жыл бұрын
Yalla na yalla fathie adio dioullite yeup 🤲🏼
@elhadjidieye17805 жыл бұрын
Oustaz alione sall yagui fi loll tewir barkeb seydina mohamed machallah rafetna amna solo ostaz
@Waxdeggteyallatax5 жыл бұрын
Man dh guene nama santé yalla bobakh bilahi bima yalla défi ab diolite ba paré tekk si ab mouride allhamdoulilah
@abdoukhadretop2555 жыл бұрын
Dieureudieuf yallah sounou borom soubhanahou watt- Allah goudal say fane té yok yiw
@laminmaster93875 жыл бұрын
Dieuredieuf ya Oustaz Allioune sall kou bakh nga
@nguercreation755 жыл бұрын
Macallah oustaz aliuon Sall rafèt n’a loll Yalna fi yegue lolll ta vér
@cheikhndiaye73445 жыл бұрын
Akasa amna solo ya oustaz Aliou sall wakhnga deuk bou weure dieure dieuf yalnanga goude fan ak weure
@bayeanne16845 жыл бұрын
Dieuredieufeti serigne touba ouztaz sall wah dji rafetna machallah ni la diner sohla
@yayeawagueye62855 жыл бұрын
Merci l'islam moko sokhla
@mameboussombaye73975 жыл бұрын
machaallah, " وأن المساجد لله فلا تدعوا مع الله أحدا" thiéy s touba 💗 yeurmandé la di xèwal goumak thi mbolém diaam nih, yalna niouko yalla fayal, tayagal fi ak ndiabotam ak mbolém talibé yi ak joulit yi tamay lène wér.
@papeousmanekandji83065 жыл бұрын
djrdjeuff oustaz Yallna fan Wii godd loll
@mameboussombaye73975 жыл бұрын
@@papeousmanekandji8306 amine momdé waxam yépp louy défar rék. point
machalla oustaz yaw danga bakh lool yalla na yalla fayla té goudeul sa fane té mayla werr
@khadimleye57385 жыл бұрын
Dieuf Dieul diarama Cheikh Ibrahima Fall mi gnou khir ci ligueyeul Serigne Touba
@serignengom28895 жыл бұрын
Guoudeul fannn outazzz
@cheikhounagaye81405 жыл бұрын
Aka bakh macahall yalna yalla godal sa fane taga wèr barekip serigne touba
@mamadouba83725 жыл бұрын
Bonjour excellent travail à tout et toutes machallah merci
@massambakhouma33575 жыл бұрын
Kèn dou serigne touba
@matimbaye97815 жыл бұрын
Machallah deysane serigne touba amoule morom
@mamecheikhndiaye38505 жыл бұрын
Machallah Aliou sall wakh de rafit na torop lirk Ka am solo
@bayeanne16845 жыл бұрын
Dieuredieufeti serigne touba ziar bou weer machallah
@bayeanne16845 жыл бұрын
Merci mbackiou machallah
@mesounendir94515 жыл бұрын
Diaradiaf sall
@cheikhouna_k95735 жыл бұрын
Oustaz yalna yalla goudal fane wi .wakhdji rafétna lol .li moy senegal .dioumati dioumay l'islam.
@djibigueye10465 жыл бұрын
Oustàs yalnala yalla fay
@mouhambaye14805 жыл бұрын
Machalla oustass
@djilysour64955 жыл бұрын
Machalla
@biramecisse11595 жыл бұрын
mazahala OUSTAZ Alioune sall yaguifi l'île téwére
@badarasall40935 жыл бұрын
Machall. Tawfex ak taysir
@medounesow80405 жыл бұрын
Théye oustas alioune sall machalla
@moussakatongo9305 жыл бұрын
Mashallah kéneu dou SERIGNE TOUBA KHADIMOU RASSOUL kén dou natablé ayy jeufeumm ndakh jeuff na. Ligéyeul na YALLA liguéyal Sopém ba RASSOUL. Yalla na say LÉÉRRR di weeuuuyyy MBACKÉ ba ilayam midine.
@khalilkamara73845 жыл бұрын
Raw ga oustaz
@gamzboy39825 жыл бұрын
bilahi ya bakh
@sambeseye31595 жыл бұрын
Akassa ya oustaz ya bakh Machallah
@santr.rek697785 жыл бұрын
Akassa diétay bii dé amnasi yakar Bou reuy ni koufi tew tekhénga ak koukou tewlou ndah khol you toyy rek si yeug yalla lafi guiss yalla nieup tékhée aminn
@mouridfall9755 жыл бұрын
Wallahi ndeysan rafetna oustaz machallah AHMAD IBN AHMAD IBN ABIBALLAH MBACKÉ jeuradieuf
@beuguefallou50375 жыл бұрын
Amine yarabbi
@moussafall65485 жыл бұрын
maachala,jeureujeuf oustas
@ibrahimathiaw26775 жыл бұрын
Longe vie bon sante ya ouztas
@cest-20235 жыл бұрын
Oustaz Dieureudieufeti !
@mormbow6075 жыл бұрын
Islam amatina ndamm machallah fier d'être musulman
@enessaadoi5 жыл бұрын
Rafetna barina Yalnagniu ame lounitole thy universités ak formación ak hospital machaala na rape al diam
@bambasylla33415 жыл бұрын
Ma cha allah mbakiyou faye
@bbtitimbaye28945 жыл бұрын
Machala ouztaz nilaa teila ndangou day wanjiy door bamba di brom
@yayeawagueye62855 жыл бұрын
Nga balma dé. Mane mi di wakh mouride sadikh la beugg serigne touba wolouko. Wanté wakh yi yakh lay déf. Fi kène doreuntéwoufi. Nous sommes tous des musulmans et comme la dit s mbackiyou faye ay complice lañuwara done. Ta façon yi tant que bayiwouñu ko douñu joubo moukk. Kounek na diapp famou diapp gueume ko wolouko ta sa morome nangul lako li moy adouna. Vive l'union dans la diversité
@toubandiaye38915 жыл бұрын
Goudal fane ouztas wakh rafetna Machalla sunu mame ahmadou bamba kéne dou mom té pour niep la
@ngagnecisse89445 жыл бұрын
Li rek. La yalla beugue dioulit dioulit rek moy bokam