Yaw kène yaroula. Ki limou fi wax so amé losi meuna dindi nga wax niou ko mo geun di fégnal sak niak yarr. Soudé nak yaw sa rouh ay fenn mo kay doundeul da ngay dém si taxourane kat yi mél ni gana mésséré wala madiama fall.
@PapeIbouCisse13 күн бұрын
Waw yow kagn bo khamè daara ngua indi sa version mobile gueule salua yii