Serigne Habib SY Ibn Serigne Mbaye Sy Mansour Journée de Priéres de la Famille de Mame Mbaye Diop de Ouakam , l'un des premiers Moukhadams de Seydil Hadj Malick Sy dans le Cap Vert
Пікірлер: 29
@babacardiakhate50305 жыл бұрын
Dieuradieuf sy malick khol sedna ci kham kham bouler bi. Yallah na yallah yok say fane ci barke psl
@ibrahimasene11908 жыл бұрын
Dieuredieuf SY MALICK yalna yalla yok sa fan ak sa soutoura, lèrr
@papambengue80745 жыл бұрын
Macha alla sy malick yalna yalla goudale sa fane ken dou seydile hadji malick
@khalifasamba43224 жыл бұрын
Machalah sy malick yalna yalla samala sama sa xam xam
@abdoulayeniang25116 жыл бұрын
Serigne Habib Yalla na Yalla goudeule sa fane
@ThiernoDia-yg9yq8 ай бұрын
Assalaamou aley koum sama serigne ziar bou weur ❤❤❤
@abydiallo84387 жыл бұрын
Tabarakala machallah tel père tel fils
@sarrsoukeye8889 жыл бұрын
Sante yalla....yalla nagnou Tass dji Barker seydina Mohamed (pls) allahouma amine ya raby ... Dji Sama mame dji .,..tariha tadjania
@mayemounafall91416 жыл бұрын
salam maachalah Sy Malick dieuredieuf yalla na yalla fayela may la wére goudoufana ak soutoura amine yarabi.
@ibrahimasow1058 Жыл бұрын
machallah serignebi
@AsfiyahiTelevision8 жыл бұрын
va asfyah yalla nalene yalla diapales
@ndaoabdou30095 жыл бұрын
Machallah sy
@sokhnathiam32354 жыл бұрын
Machalla7 kar sy malike merci
@sileyedia59148 жыл бұрын
machalla yalla nalla yalla are suturala mayla wer ak dolle
@ibrahimakobar21176 жыл бұрын
amna solo sy
@Ndiagabalkhawmi15 жыл бұрын
Discours el hadji mansour mbaye di na ko déglou 3 fois par jour ndakh li ma yeukk kéneu dou sa mame cheikhal Hadji Malickk sy