Papis Xaragne promet à Ordinateur son combat contre Modou Lô : "Sou niou beuré 10 minutes.."

  Рет қаралды 30,333

Lutte TV

Lutte TV

Күн бұрын

Пікірлер: 98
@jullmoussa
@jullmoussa 6 ай бұрын
Yena nekh oridinateur ak roi guen di commentaire 😂mais modou cest le roi tamit
@DjibrilBa-xp7te
@DjibrilBa-xp7te 6 ай бұрын
Modou lo seul ❤❤❤❤
@DaoudaMbengue-e1z
@DaoudaMbengue-e1z 6 ай бұрын
Modou lo rek ❤❤
@ametibnmalickndiouck4674
@ametibnmalickndiouck4674 6 ай бұрын
Man dh modou mima kham si mbappat sou doon neillaw ordinateur meunouko yee
@seckousmane3397
@seckousmane3397 6 ай бұрын
Ya mouna féne😂😂😂😂😂😂
@vieuxndiaye3790
@vieuxndiaye3790 6 ай бұрын
Modou deum là si lutte simple billahi modou lenene la 🤣
@SeynabouTouré-k9u
@SeynabouTouré-k9u 6 ай бұрын
Macha allah papiss
@joetygeroffice6057
@joetygeroffice6057 6 ай бұрын
Papis fans XLô yeup nonulañu mél pr gnoune mo meune gneup❤
@DjibrilBa-xp7te
@DjibrilBa-xp7te 6 ай бұрын
Xlô seul ❤❤❤❤
@barow2853
@barow2853 6 ай бұрын
Ça se vois qué bonguane aime beaucoup ordinateur Yalla na dem ba am grand combat aréne
@MameSow-vp7rj
@MameSow-vp7rj 6 ай бұрын
Modou lôooooooooo ❤❤❤❤
@HoulayeKaBah
@HoulayeKaBah 6 ай бұрын
Bien dit papis kharagne lo kasse ❤
@assanesarr9992
@assanesarr9992 6 ай бұрын
Roi des arène modou kharagne ❤❤❤👑👑👑👑
@sitorngom5514
@sitorngom5514 6 ай бұрын
Ordinateur est le roi de la lutte simple mo Moun Modou lo thie mbappat très digne
@azizlo1978
@azizlo1978 6 ай бұрын
Legui la media beuri mbappat amatoul li modou lo def thi mbappat ohhhh
@DiazBop
@DiazBop 6 ай бұрын
Ms lolou walahi dina nekh😅 modou lo vs ordinateur
@babacaralvesndoye9432
@babacaralvesndoye9432 6 ай бұрын
Kou KHAMOUL mdou rekk Yaa koyy teukeûle Ak ay serigne Ndiaye Modou guir yalla es se que seetane gueneko mbaapate?
@alioufaye6904
@alioufaye6904 6 ай бұрын
Bilaxi papis waxoul deug, ordinateur limou deff thi mbapat modou lo defouko, nafex gueun rk. Tog thi plateau yi di wax rek, xana mbapat Dakar kessé la bog
@gueyelemzo2196
@gueyelemzo2196 6 ай бұрын
Kaye nak Modou lo même boudoul sama mbeur modou mbapat dako tothie dh khana kaye légui la télé âme mais Modou lo meune na beuréh dh
@NdourMara
@NdourMara 6 ай бұрын
Modou lo mone na beuré dh mais dakoul beuré ak ordinateur bilahi nga yi khamou niou ordinateur
@vieuxndiaye3790
@vieuxndiaye3790 6 ай бұрын
Se qui doute de la lutte simple de modou lo khamou niouko
@AboulBacharSall
@AboulBacharSall 6 ай бұрын
Mbappat dou lutte simple kon modou lo dafa todj lutte simple saway peut être ordi moko gueneu régné si lamb Serere
@DameNguirane
@DameNguirane 6 ай бұрын
​@@AboulBacharSallmbapatt ak lutte simple louléne wouteulé😅
@adamasarr1538
@adamasarr1538 6 ай бұрын
Papis da xeur ci Modou rekk mé xam nga né ORDINATEUR mannà dan kuddul Modou. 10 fois yii mom naggu ma lolu mom tegg ko ci souf Modou et ORDI sont des champions mé ne compare pas les mbapat de Dakar aux autres villes et villages. Mbapat yii Modou ak ñom Balla togg est différent de ceux des autres. NAÑ KO TEGG REKK DINAÑ XAM KU MEUN 😂 Ceux sont des propos de supporteurs chacun à sa manière de penser mé la réalité est en face de nous 😂
@elbabasamb3689
@elbabasamb3689 6 ай бұрын
Kou setane Modou lo omar fall mouma 😂😂😂
@FatimNdiaye-ku6ye
@FatimNdiaye-ku6ye 4 ай бұрын
Wa kouye ordinateur nak
@amarluxtv7399
@amarluxtv7399 6 ай бұрын
Modou mo meun ordi fouf. Kou meunoul daan général malika nooy dané xlo
@DameNguirane
@DameNguirane 6 ай бұрын
Gniy wakh Ordinateur mo meune Modou lo yeup ay fans fawzeyni lagn wla wa Pikine
@NdiguelBadiane
@NdiguelBadiane 6 ай бұрын
Mai papis yaw da ngan wakh lou négatifs sii ordinateur
@DieneFaye-xe4hl
@DieneFaye-xe4hl 6 ай бұрын
Ordinateur seul ❤
@modoundour8519
@modoundour8519 5 ай бұрын
Fara awdi nak
@mbayestarsene2179
@mbayestarsene2179 6 ай бұрын
Amolène chance dama sètane ordinateur setane modou lo mei degu rek mo nekh yalha modou lo moko dakhone beurè foufe eup ko filing ak fitte foufe
@moussangome708
@moussangome708 6 ай бұрын
Papis Modou sama beure la mais féne ngua ordinateur lutte simple Modou manouko eupalé victoire wakh DEUG yakoul draa
@durkio5486
@durkio5486 6 ай бұрын
Saway modou moy borom drapeau yi diamono mbappat .
@laurenternesttendeng5823
@laurenternesttendeng5823 6 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤merci beaucoup
@yakhoubaseydi905
@yakhoubaseydi905 6 ай бұрын
Yw ya warakhol lii ngay wakh saka bakhoul ordinateur champion laa mee mounoul modou ci lutte simple lolou boula meete sama yon nekouci
@magattediop9975
@magattediop9975 6 ай бұрын
Saway faté demb mo gaw rek... Kou eup victoire mane worouma wayé yow tamite woroula ba ngey wakh Papis dey fêne. Modou bimouy dougou ci lamb dji borom drapeaux yi la toudou et ça veut bcp dire. Dès fois vous oubliez lii Modou ak Balla Gaye def ci mbappat avant niouy niew ci gew bi.
@morseckseck8215
@morseckseck8215 6 ай бұрын
Modou bamy togne ly khéwoul nalér
@tolissococo9507
@tolissococo9507 6 ай бұрын
Leigui yeine niou wedi papiss dagueina wedii modou mo dak beurei ordinateur
@NdiguelBadiane
@NdiguelBadiane 6 ай бұрын
Mai papis taiy dioum ngan ordinateur mbeur leur
@DieneFaye-xe4hl
@DieneFaye-xe4hl 6 ай бұрын
Papis j t'estime bcp mais ordinateur à plus de 200 drapeaux bilahi
@OusseynouSow-zk4on
@OusseynouSow-zk4on 6 ай бұрын
Modou lo moye seul barre bo khamné sou monoul wone baré dou dane kéna ndakh réyoul
@dioufdiouf6084
@dioufdiouf6084 6 ай бұрын
Walahi dama beug modou lô
@karadiouf5488
@karadiouf5488 6 ай бұрын
Papis boule wakhe lolo ordinateur est un très grand champion il peut battre modou
@yakhoubaseydi905
@yakhoubaseydi905 6 ай бұрын
Nakou sa wakh yw kounek meuna dan sa moromou
@modoumbaye9767
@modoumbaye9767 6 ай бұрын
Ordi kasé ❤
@moustaphawade6771
@moustaphawade6771 6 ай бұрын
Modou lô seul ❤
@cheikhbasskeurmassar9548
@cheikhbasskeurmassar9548 6 ай бұрын
Papis sama kharitt bi kéne dou mome aka baax
@NdaoPape-bq8lc
@NdaoPape-bq8lc 6 ай бұрын
Papis wakho DEUG Modou day tak
@zen05111
@zen05111 6 ай бұрын
Nako modou may contact rek niou khol
@DiazBop
@DiazBop 6 ай бұрын
Wakh deug lamb simple mom ordinateur mo thi meune
@BoureDiouf-y8l
@BoureDiouf-y8l 6 ай бұрын
Loulou bésbou amé Modou Dina rousse ordinateur loumou déf lutte simple kéne déhsfouko Sénégal beuré simple Modou lo mounoul d'âne ordinateur Serigne Ndiaye 2 oboli général doudou sané reug
@Dieganediouf-do6yf
@Dieganediouf-do6yf 6 ай бұрын
Bilay ordinateur ak modou ordi danko lolou sax diaroul wax
@AlphaNdiaye-wq4zv
@AlphaNdiaye-wq4zv 6 ай бұрын
Mondou lô mo dakha beuré ordinateur fouf
@mamadoulaminebarandiaye8450
@mamadoulaminebarandiaye8450 6 ай бұрын
N'importe quoi ?
@alioufaye6904
@alioufaye6904 6 ай бұрын
Non lolou amoul
@moussapayemane4167
@moussapayemane4167 6 ай бұрын
Papiss 😂Ordinateur beuré ak Modou Lo 10 combat dou am béna 😂,far rek motah ngay wah lolou,beuré rek rék bilahi Ordinateur mo meune Modou Lo mille fois
@diamilfaye7253
@diamilfaye7253 6 ай бұрын
Modou ordinateur comba la❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@biramediouf6061
@biramediouf6061 6 ай бұрын
Sans mystique ordinateur mo meun modou lo.yen khamolen dara sii lutte simple. Gni mana dann modou lo dit lutte simple barinagn: ordinateur, ngagne sene,radiakhe,serigne ndiaye,eubeli ,général malika,et même sossokh...
@ismailafall8727
@ismailafall8727 6 ай бұрын
Seinn khalat nguein di wakh,,ordinateur dou nitt deii
@ousmanesarr756
@ousmanesarr756 6 ай бұрын
Yene dangen khoromu walahi deflen ko contact plage wo site yi bilahi papis linga wakh dou am ordi moko dak beuré foufff sakh dou bene ordi limouy beuré si aleu bi boucar guiss nako motakh lingeni wakh mou defko ay ré na moudiou nangou rek ngen khôl
@assanesarr9992
@assanesarr9992 6 ай бұрын
Ordi mom da yabaatei modou moko meune fouff
@abdouloume7373
@abdouloume7373 6 ай бұрын
Lamb dji yeeep Modou Lô mo si dakha beuré, Balla Gaye, ak Eumeu Sene, Ordinateur, Tout... Wakhou MA wakhou supportaire, bou vocal amon MA wakhlen si Lou leer thi boppu niepp
@coinzsow1415
@coinzsow1415 6 ай бұрын
No Modou Moko daha bureh teh moko opa doleh
@girasene7223
@girasene7223 6 ай бұрын
10 combat Modou dane ko
@FallouSarr-
@FallouSarr- 6 ай бұрын
Ordinateur mo meune modou ci simple
@ModouLeye-x7e
@ModouLeye-x7e 6 ай бұрын
Modou Lo dou moromou ordinateur fouff sakh
@OmarDieng-j9b
@OmarDieng-j9b 6 ай бұрын
Bly wakhati lènn ko papis dagua rèrrè mbiir lisi lutte avec frappe nèkoul thi simple modou lo sougniou mbeur leuh mais dièll yi ordinateur di dane manou ko tè walahi la watt manou ko
@DiolSallamariam
@DiolSallamariam 6 ай бұрын
Modou foumou diare avant mouy nieuw si lutte avec frappe 🎉
@OmarDieng-j9b
@OmarDieng-j9b 6 ай бұрын
Je ne sais pas hunnn
@DiolSallamariam
@DiolSallamariam 6 ай бұрын
@@OmarDieng-j9b khana khamo Modou moye brome drapeau yii🇸🇳
@OmarDieng-j9b
@OmarDieng-j9b 6 ай бұрын
@@DiolSallamariam mais tmt xana do degg machine nèè yalla sining
@diagafaye5839
@diagafaye5839 6 ай бұрын
Khana tey la Modou lo mo géna ame mistique aussi Modou mo eup mistique feufe sénégalais
@gueyembaye853
@gueyembaye853 6 ай бұрын
Mbapat modou reuk reuk rek dakoy defal afaiee ordinateur j l suis pa mai mbapat reug mossi mene
@princetorodo8590
@princetorodo8590 6 ай бұрын
Mais modou lo dafa def dra si mbapat Newna défaite si mbapat
@moussafall8655
@moussafall8655 6 ай бұрын
En tout cas ordi djiné la dé
@yakhoubaseydi905
@yakhoubaseydi905 6 ай бұрын
Lolou mom c fau niitt la rek 😂😂😂
@SenyNdour-g7i
@SenyNdour-g7i 6 ай бұрын
Safando ordinateur rék
@AlphaNdiaye-wq4zv
@AlphaNdiaye-wq4zv 6 ай бұрын
Mondou lô mo meun ordinateur fouf
@sitorngom5514
@sitorngom5514 6 ай бұрын
Papis degay sob khamo lamb ordinateur dina Modou lo aller retour simple rk
@yakhoubaseydi905
@yakhoubaseydi905 6 ай бұрын
Leeki teukeulen combat bi 10 combat modou am 9 inchalla
@FallouFaye-mw9dd
@FallouFaye-mw9dd 6 ай бұрын
Ordinateur mon mone Modou lo fou
@alioufaye6904
@alioufaye6904 6 ай бұрын
Bilaxi papis waxoul deug, ordinateur limou deff thi mbapat modou lo defouko, nafex gueun rk. Tog thi plateau yi di wax rek, xana mbapat Dakar kessé la bog
Siteu Bou Amoul chance Modou lo Dinako Humilié..? Malick Mitrailleuse et L’animale, Tothie nagne ko
18:20
Une nouvelle voiture pour Noël 🥹
00:28
Nicocapone
Рет қаралды 8 МЛН
Try this prank with your friends 😂 @karina-kola
00:18
Andrey Grechka
Рет қаралды 9 МЛН
XALISSO - Saison 1 - Episode 24 **VOSTFR**
44:45
EvenProd
Рет қаралды 1,1 МЛН
MODOU LO SUR SON COMBAT ET SITEU «Amoul loumakoy may dinako… »
22:05
Une nouvelle voiture pour Noël 🥹
00:28
Nicocapone
Рет қаралды 8 МЛН