🔴PENCUM LAMB JI AVEC EL HADJI BECAYE MBAYE ET SA TEAM. INVITE BALLA GAYE 2 | VEND.2/08/2024

  Рет қаралды 120,072

Bantamba TV

Bantamba TV

Күн бұрын

Bantamba tv. Km 2,5 Boulevard du Centenaire de la Commune de Dakar.
tel : 33 825 34 36 - 77419 03 64

Пікірлер: 141
@TalibèAlhasaneSalam
@TalibèAlhasaneSalam 6 ай бұрын
Pencum lamb MachAllah félicitations balla fils de double lèss goudou Fane AK khéwal Elhaji becaye mbaye nationale barkè seydina al Hassan salam
@BelliGueye
@BelliGueye 6 ай бұрын
Amine
@mouhamadoulaminekande8796
@mouhamadoulaminekande8796 6 ай бұрын
Notre père double less yalna yallah yokke leerame bidiaahi Rassouloullahi sallalâhou aleyhi wa sallama ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@coumbadiop2716
@coumbadiop2716 6 ай бұрын
L'empereur des arènes The King👑 Le Meilleur. Bonne Continuation BG2❤❤
@cheikhounatine758
@cheikhounatine758 6 ай бұрын
Les introductions de Pére Becaye ❤❤❤❤quel régal 🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿
@diop3575
@diop3575 6 ай бұрын
Omar sakho talibe s. Bara bi nane lako nite mana khole diko bagne la khamoul❤❤❤billahi mako beug ❤❤
@KaneDialloKDT24
@KaneDialloKDT24 6 ай бұрын
Moma diakhal
@L.Juniorr
@L.Juniorr 6 ай бұрын
Émission bi néxna mé Aziz Ndiaye il est plus intelligent que les autres prometteurs vraiment daf léna raw
@momosagna
@momosagna 6 ай бұрын
Nékha faraal dimanche Sakho ilimane yaa bakh deh❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@SeyeMamadou-h9o
@SeyeMamadou-h9o 6 ай бұрын
Père bécaye nékh ngama ningay défaré pour nite gni bolo c'est extraordinaire vraiment papa yalla nanga goudou fane ❤❤
@Mamalamine775meth
@Mamalamine775meth 6 ай бұрын
Lima nekh si plateau bi champion bou togué wakh tane Dey nekh koi BG 2 vainqueur de sa génération machallah 🎉😊
@malickdia3495
@malickdia3495 6 ай бұрын
Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@papamakhasy2602
@papamakhasy2602 6 ай бұрын
Bravo champion le champion de tous les luteurs
@IbrahimGadjigo-tw3en
@IbrahimGadjigo-tw3en 6 ай бұрын
Merci Balla Gaye 2❤❤❤👏👏
@sambandiaye7026
@sambandiaye7026 6 ай бұрын
Number 1 All emissions the Lutte ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@L.Juniorr
@L.Juniorr 6 ай бұрын
Balla dafa xam lamb tellement dafko xam dé dakoy analysé com un expert ❤❤❤
@serignedieng5762
@serignedieng5762 6 ай бұрын
Machalla Balla gaye
@souleymanethior2775
@souleymanethior2775 6 ай бұрын
Balla gaye 2 . Il est formidable . Il est devenu tres mature
@Madupro19
@Madupro19 6 ай бұрын
Balla a vie❤
@KadiaKébé-z3d
@KadiaKébé-z3d 6 ай бұрын
Bly Fadam Defeant la mingui retane Babacar 😢😂😂😂
@Adnanezinho-jm8zk
@Adnanezinho-jm8zk 6 ай бұрын
Balla borom lambe dji 💪🏻💪🏻💪🏻
@AliounebadaraThioye-ho4tq
@AliounebadaraThioye-ho4tq 6 ай бұрын
Lamb Nigéria wala😅😅
@mouhamedlydiouf8934
@mouhamedlydiouf8934 6 ай бұрын
​@AliounebadaraThioye-ho4tq lamb senegal
@ousououssououssou
@ousououssououssou 6 ай бұрын
Sou balla gagner day yakamti décortiquer combat bi 😂😂😂 On attend tjrs le dernier face to face avec boye Niang
@Leuzsonko
@Leuzsonko 6 ай бұрын
Thiey bayou mbeur yii❤
@MamadouDiallo-zt6mt
@MamadouDiallo-zt6mt 6 ай бұрын
Modou lo moye bayam
@mouhamedlydiouf8934
@mouhamedlydiouf8934 6 ай бұрын
​@@MamadouDiallo-zt6mtwakhi doff
@BayeDameNdjiliw
@BayeDameNdjiliw 6 ай бұрын
Baye bou dome dooutal😅 ndaw lou reur😅​@@MamadouDiallo-zt6mt
@Steven-ul8pw
@Steven-ul8pw 6 ай бұрын
Vraiment Émissions bi Iow Fadame ak Bour Xrom Nguén si Mé Danguén Wardi Deklou wanté Beug Nguén Ay Sroh Srohé Ay Wah Ñioulén Guena Xam Libguéni Wah nioléni Setan kon Amlén Respé si Nitñi Xolén Pér Mansour Diop Nimu Respecte Parolam mé Yén Danguén Xawa Eupeul Trop Way Xrom Sah Bou Eupé Si Niam Dakoy Saboté
@Abdallah31341
@Abdallah31341 6 ай бұрын
Ya wax deug lingua wax la sétlou
@snakybabyofficiell5256
@snakybabyofficiell5256 6 ай бұрын
Bécaye mbaye boulniou yapp bi macky do trokhal diam gni fo nékone limotakh yékini nila nafekhh nga merde waye Balla félicitation bonne continuation❤
@pi9184
@pi9184 6 ай бұрын
Le vrai lion❤❤❤
@babsbaba19
@babsbaba19 6 ай бұрын
Dans tous sports le sanction financière est le dernier recours Mais dans la lutte sénégalaise c’est la première chose à faire c’est dommage
@mouhamedlydiouf8934
@mouhamedlydiouf8934 6 ай бұрын
C'est le senegal
@Abdallah31341
@Abdallah31341 6 ай бұрын
Je suis d'accord avec la sanction financière mais le montant c'est trop
@FatouDiop-su7xx
@FatouDiop-su7xx 6 ай бұрын
Masage bi raféte na merci pére
@SowSeringe
@SowSeringe 6 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤
@ibouciss3519
@ibouciss3519 6 ай бұрын
Mais modou mbaye da wara di nek si plateau bi chaque vendredi
@alsindor81
@alsindor81 6 ай бұрын
Degeuleu
@mouhamedabdoulahidiagne786
@mouhamedabdoulahidiagne786 6 ай бұрын
Modou kay amna sah place vi CNG bi nitou deugg la tè idee you pertinente la
@mansorseck6059
@mansorseck6059 6 ай бұрын
Prince alboury
@ProcureurYoutube
@ProcureurYoutube 6 ай бұрын
Revanche Balla Gaye vs Boy Niang dara leu dé
@SowMortalla
@SowMortalla 6 ай бұрын
Emission bii nkhna mes deulouwanete amoussi
@canapilofficiel_sn4480
@canapilofficiel_sn4480 6 ай бұрын
Mbeur moussoul fayékou 40 millions comme 130million yi niouy déggg dou deug
@Relatif221
@Relatif221 5 ай бұрын
Tu as tout compris
@diagnekhadim4337
@diagnekhadim4337 6 ай бұрын
Bilay balla sa analyse lane la
@mansorseck6059
@mansorseck6059 6 ай бұрын
Alboury bb saloum
@yahyagassama491
@yahyagassama491 6 ай бұрын
Émission bi nexna trop macha Allah mais revoyez l’organisation surtout le temps de parole il faut s’entre écouter ✍🏿🙏🏿
@Steven-ul8pw
@Steven-ul8pw 6 ай бұрын
Mé Man Manuma Consovoire Lac 2 ni Dou Djeul Franc té Alioune seye 2 Nekfi Mou Niew Djeul Ada Fass Vraiment Lac 2 Tapha tine Modon Lamb Ji
@ousououssououssou
@ousououssououssou 6 ай бұрын
Tapalé rek akk ragal Franc
@amakane6494
@amakane6494 6 ай бұрын
CNG AY SATHIE LANIOU CNG AY SATHIE LANIOU CNG AY SATHIE LANIOU CNG AY SATHIE LANIOU CNG AY SATHIE LANIOU CNG AY SATHIE LANIOU
@aminatasow3152
@aminatasow3152 6 ай бұрын
Emision mome amoul déguelou wanté ils paelent en même temps
@walydiop4186
@walydiop4186 6 ай бұрын
Franchement notre champion Balla Gaye 2 il a tellement murit en terme de communication .wer rek lagn lay gnanal donc bonne continuation!
@Bayeniang20
@Bayeniang20 6 ай бұрын
Balla nagha fekhe ba bul dieul eumeu eumeu demal dieul alioun seye ah sonal ngagniou trop ah
@CheikhIbraFall-u2r
@CheikhIbraFall-u2r 6 ай бұрын
🇺🇲 Congratulations émission bou nékh 😅😂 Tay Babacar CNG 😂da diomiii 😂wooo bour akh fadam Vrai seytané 😅
@modousow8832
@modousow8832 6 ай бұрын
Cheteuteute. PERE BECAYE REGLEL LI WAY! Il faut pas parler tous en meme temps!!!
@elimanesallpape5541
@elimanesallpape5541 6 ай бұрын
Moodou.mbaye wahna dégue
@maguettembaye9050
@maguettembaye9050 6 ай бұрын
Père mansour 😅😅❤
@BathieTall-gw4yi
@BathieTall-gw4yi 6 ай бұрын
Empereur guediawaye modou sollawoulla noppoloule fi guen dougueule modou gnoune khamnaniou l'EP daneko 10 fois interesse wouniou
@Leuzsonko
@Leuzsonko 6 ай бұрын
Balla ladioul modou mom moy empereur eumeu lagni beurè nioun kouniou dane dagni beurè ak ioe wayè gni nga xam ni niou douma len niari yon ma Dan ko diouteul ko kokou mom milliar dou meusa beurè😂
@amakane6494
@amakane6494 6 ай бұрын
Merci Modou mbaye li ngay defendré mbeur yi nekh na ma, CNG ay sathie laniou
@diafediaferewmi8437
@diafediaferewmi8437 6 ай бұрын
Délènn bayi baye balla mouy développé😂😂😂😂❌
@bayeratebayerate5893
@bayeratebayerate5893 6 ай бұрын
Thieuy modou lo yalla nako yalla lafal thiatt
@saerfall701
@saerfall701 6 ай бұрын
CNG doundou si kaw mbeur yi késsé lagnouy déf gniy diott enveloppe mom défendre CNG rek lagnouy déf.
@daourniass
@daourniass 6 ай бұрын
Bilaye Mbaye wahale
@elimanesallpape5541
@elimanesallpape5541 6 ай бұрын
Cng aye sathioulane koussi dé dingko layo
@amaduamadu1600
@amaduamadu1600 6 ай бұрын
Bour del wakh te bayi di si dougeul islam lolou dou ay foo dé
@diop3575
@diop3575 6 ай бұрын
Gaye ll l'empereur nekha fral dimanche kou sissou 😂😂
@Ting05122
@Ting05122 6 ай бұрын
😂❤
@64FallAmadou
@64FallAmadou 6 ай бұрын
Lac Vs tapha tine Tapha tine Vs Sa thès Tapha Vs Alioune seye Ada fass Vs Jackson
@aboubacarydansokho861
@aboubacarydansokho861 6 ай бұрын
Émission amna solo mais juste il par kéne di wakh mais soléne bougué wakh a même temps dou dokh
@NdiaboutaDiouf
@NdiaboutaDiouf 6 ай бұрын
balla gaye 2 juillet lay beure akk kou Dan si digeunte siteu akk modou lo
@NabyLeJuriste
@NabyLeJuriste 6 ай бұрын
Bilaie Balla wakhma deug dorantei ba gris xametoul journaliste yi😂😂😂parei ñou dagg la 6millions metti na trop😂😂
@DameFall-i3s
@DameFall-i3s 6 ай бұрын
Becaye bayil réparti lier do wakh diame
@cheikhgueye254
@cheikhgueye254 6 ай бұрын
Bily thiak thiak yi ay diambar lanu pér beckay
@NdiaboutaDiouf
@NdiaboutaDiouf 6 ай бұрын
ndiabouta diouf c'est vrais balla akk niom Aziz modou lo rekk lagnou beugeu beurel lolou dafa ler
@ndiayeabdouaziz588
@ndiayeabdouaziz588 6 ай бұрын
BALLA GAYE 2 DEFA BEGUE EUMUE SENE BA BEGUE TOUL MBERR AK MOME
@madoundoye2414
@madoundoye2414 6 ай бұрын
Beug la walla ragal?
@khalifadiop6596
@khalifadiop6596 6 ай бұрын
Mais faddam vrai seytanei leu wepepep
@mouhamedcisse4978
@mouhamedcisse4978 6 ай бұрын
Modou kharagne lô seul le rois des arènes lagnouy topou ❤ Yalla bougnou daane nite 2fois toppate si guinaa wam beugueu beuré waat ak mom Modou kharagne Lô rek si ❤ dara dassa khadioul
@amaduamadu1600
@amaduamadu1600 6 ай бұрын
Balla mi amina loumouy neub si digentem ak la 2
@amakane6494
@amakane6494 6 ай бұрын
Bécaye mbaye faut pas défendre CNG yaw nite kou bakh nga
@wadeidrissa7410
@wadeidrissa7410 6 ай бұрын
Votre émission n'est pa organisée
@thiapa6489
@thiapa6489 6 ай бұрын
Babacar son rôle dans l’émission c’est quoi en fait ?! Il représente le CNG ou c’est un chroniqueur ?!
@modougueye_tv
@modougueye_tv 6 ай бұрын
Kone Mbeur yi dounou fayekou plus de 40 M
@ndiayedistandiayendiaye2209
@ndiayedistandiayendiaye2209 6 ай бұрын
Pere ousmane xamna limouye def yaw wakhalak macky rek
@MamadouDiallo-zt6mt
@MamadouDiallo-zt6mt 6 ай бұрын
Balla jumga dey modou lo mougi am 2000 € par mois ille ambassadeur
@s__m__m1717
@s__m__m1717 6 ай бұрын
Dague mo guen sospendre
@babsbaba19
@babsbaba19 6 ай бұрын
Adaa fass lac 😂😂😂 n’importe quoi
@mouhamedlydiouf8934
@mouhamedlydiouf8934 6 ай бұрын
Sabotage leu
@skboymo
@skboymo 6 ай бұрын
Man louma diaxal moye supporter modou lo yi manou niou gis poster balla gaye teu douniou si wakh mais supporter balla gaye dunu xol poster modou lo beu di si commentaire🤦🏾‍♂️🤦🏾‍♂️
@dembaztarkinda8270
@dembaztarkinda8270 6 ай бұрын
Bilay pasqu balla moye lamb motakh danio beug balla diko neub😂😂😂
@mouhamedlydiouf8934
@mouhamedlydiouf8934 6 ай бұрын
Vraiment bro tu as raison
@khadimcisse1694
@khadimcisse1694 6 ай бұрын
Balla sama mbeur bi daga Dioume nak si cas wou lac bi vraiment
@kalidoudieye9742
@kalidoudieye9742 6 ай бұрын
Ama baldé tmt sa 75 millions yii warr naniou c dialogue 😂😂
@AliounebadaraThioye-ho4tq
@AliounebadaraThioye-ho4tq 6 ай бұрын
Da dioum wayy😂😂😂
@bambaparforce2840
@bambaparforce2840 6 ай бұрын
Esk tamit beugoul wakh fouki millions ak diouroum maanàm 15.000.000f léegui mou yaakàrni 75.000000f moy fouki millions ak diouroum kom 75f😂😂😂😂
@MamadouDiallo-zt6mt
@MamadouDiallo-zt6mt 6 ай бұрын
Modou lo moye roua
@BathieTall-gw4yi
@BathieTall-gw4yi 6 ай бұрын
Ada fass lag dou Comba way Ada ayy moromame gnoffi nekk teupp alioune seye bayi fi sa thiess lag sagnoule baigne Fran di dieule Ada fass dou lamb
@thiernowade5769
@thiernowade5769 5 ай бұрын
Fadam.kom.mbaam.xoux djiko.bou.niaaw.la.yoré.nékkue.platoo.bi.di.weunue. rég.mém.bouy.déff.laiv.ag.tougnam.you.réyeum.yooyou
@saerfall701
@saerfall701 6 ай бұрын
Babacar mi war nagnouko réinitialiser, CNG léneu rek lasi kham Tass ko.
@MouhamedGassama-p5i
@MouhamedGassama-p5i 6 ай бұрын
tasss lene cng bi
@ousououssououssou
@ousououssououssou 6 ай бұрын
Boye Niang Do gneuw fi ndakh balla nopi
@mouhamedlydiouf8934
@mouhamedlydiouf8934 6 ай бұрын
Yaw nekete wero dh
@amakane6494
@amakane6494 6 ай бұрын
CNG AY SATHIE LANIOU DAG 10 % DAFA BARI
@amakane6494
@amakane6494 6 ай бұрын
Babacar sathie la
@Lepatriote9423
@Lepatriote9423 6 ай бұрын
Modou Lo la faral contre Siteu mais pourquoi on ne parle pas au cas ou Siteu dane
@yilebaba6565
@yilebaba6565 6 ай бұрын
Jme pose la même question ?
@SowMortalla
@SowMortalla 6 ай бұрын
Cng sou lamb wakho gnoko yakh
@YatmaFall-d5h
@YatmaFall-d5h 6 ай бұрын
Buur ben professionnalisme amouko
@Jean06Balde
@Jean06Balde 6 ай бұрын
Babacar est ma pour défendre le cng il n'est jamais d'accord
@khadimthioune9175
@khadimthioune9175 6 ай бұрын
Loutakh wakhoko Macky sall
@Steven-ul8pw
@Steven-ul8pw 6 ай бұрын
Balla legui dfay Copié Modou lo Çi Simplicité bi mé Boolé çi Dém Diangui Xam Sa Diiné Sila Bok dh
@64FallAmadou
@64FallAmadou 6 ай бұрын
Mbeur bou xam dinème am na ? Pour mane kou ci xam sa diné bayi lamb dji nga balma
@AbdouNdiaye-nv4ch
@AbdouNdiaye-nv4ch 6 ай бұрын
Yaw dinè da am si lambo yaw yayabatè way
@bigbroodabo9738
@bigbroodabo9738 6 ай бұрын
Père bacay yaw ndanane nga mai gouvernement bi warothié wakh ndakh bimou mété bingéne waré wakh wakholéne forcé wougnou dagni liguéy té problemou ambulant dou gouvernement bi mai mairi yi la thiak thiak yi daniou wara défi auto-école lolou nga wara wakh ndakh thiak thiak rèk nékoul si tali bi
@gorandiaye390
@gorandiaye390 6 ай бұрын
Sa way Mairie yi démamenbrement dé l'État becaye à raison
@papaamadoudiop7615
@papaamadoudiop7615 6 ай бұрын
gouvernement bi sa baye momouko senegal nieupeuko bok boule niou fonto way
@Papisdiop349
@Papisdiop349 6 ай бұрын
😂 wadji mo nex😂
@papaamadoudiop7615
@papaamadoudiop7615 6 ай бұрын
@@Papisdiop349 ki dafa rew way😂😂😂
@wadeidrissa7410
@wadeidrissa7410 6 ай бұрын
C dommage
@NabyLeJuriste
@NabyLeJuriste 6 ай бұрын
Cng bouñou nou fonto la sanction pécuniaire du être la dernière rempart Mh louné ni rk nga dagg kou meuna dagg 1millions pour sondel alors qu’au même moment le prometteur allume des pétales En plus xaliss bignouy dagg fan lagnou kay def lolou lay ladj
@OusmaneDiop-uk5hm
@OusmaneDiop-uk5hm 6 ай бұрын
Beurou rufisqu thies la yereum
@saidoudiallodiallo761
@saidoudiallodiallo761 6 ай бұрын
walfadjiri bou niouye trohal fo nekon
@babaSagnane
@babaSagnane 6 ай бұрын
yaw bekaye wakhal rek nio ngui fii wone demb
@AbdoulayeDia-m4b
@AbdoulayeDia-m4b 6 ай бұрын
Babacar diop sama mbokou walo walo depuis keur mbaye diop
@amakane6494
@amakane6494 6 ай бұрын
Problème CNG c'est Babacar l'arbitre limou sol sakh si dague mbeur yi lako niaw lo ay sathie la niou
@babsbaba19
@babsbaba19 6 ай бұрын
😂😂😂😂😂😂😂
@TalibèAlhasaneSalam
@TalibèAlhasaneSalam 6 ай бұрын
@@amakane6494 dilèn wakh loulèn worr Babacar liguèykatla dama ka Dane guis annè 1998 Mouy dawal car sotrac si je me trompe pas .
@massthiam
@massthiam 6 ай бұрын
Li nekhna way il faut parler psq yéne rek yéna meuneu changer les chose cng c’est trop dague yi metti na lol
@assanegueye28
@assanegueye28 6 ай бұрын
Yawe bécaye Mbaye kou nafékhe ga dawo wakhe li makiy salle binouye raye xaléyi si manifestation lou takhe dawo si wakhe
“Don’t stop the chances.”
00:44
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 62 МЛН
黑天使被操控了#short #angel #clown
00:40
Super Beauty team
Рет қаралды 61 МЛН
coco在求救? #小丑 #天使 #shorts
00:29
好人小丑
Рет қаралды 120 МЛН
Revue de presse Lundi 10 février 2025 bec Mame khalifa
17:18
DAKARBUZZ TV
Рет қаралды 13 М.
no Senegal mon nèkh armée France dégage      🤣🤣🤣🤣
9:37
Les révélations de Pape Sané: Ahmed AIDARA rappelle...
13:58
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 8 М.
INFORMATION DE TAILLE  MODOU LO ....
20:01
Bantamba TV
Рет қаралды 27 М.
“Don’t stop the chances.”
00:44
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 62 МЛН