Rakou Dieukeuram BikoDiam wéroul dafadoff ? Le Frère de la Femme Tuē à Touba tres en colère reagit «

  Рет қаралды 21,720

People 221 TV

People 221 TV

Күн бұрын

Пікірлер: 51
@senegalaise1
@senegalaise1 17 сағат бұрын
Sénégal daguèn di mayé sen dom bu djiguene rek faté ko keur dieukeur dji dolèn dem de temps en temps xol sen soeurs yi luñuy vivre sen keur dieukeur yi c'est dommage😢💔 repose en paix ma chérie nala yalla xaré aldiana firdawsi inchalla 🙏💔🕊
@BassirouNgom-e9y
@BassirouNgom-e9y 23 сағат бұрын
Justice réék amul mbok amul diékeur
@veroniquenatack7392
@veroniquenatack7392 2 сағат бұрын
*Métina trop vraiment 😭😢Yalla na souff oyof thi kawame et que justice soit faite🙏🏽🙏🏽*
@IbrahimCisse-v8s
@IbrahimCisse-v8s 19 сағат бұрын
Yala na ko yala yeureum ta xaréko alldiana amine
@rosaliegomis3775
@rosaliegomis3775 22 сағат бұрын
Bilay famille gnouma yalla nalene borom bi takhawou ngene am deug ci kaw ki ray sene doom Peine de mort rek
@adamandiaye4314
@adamandiaye4314 4 сағат бұрын
Metina loleeeeeee yallanako yalla yeureume té khareko alediana amineeee na yone défe liguiéyame
@RamaSow-n4q
@RamaSow-n4q 13 сағат бұрын
Vous avez raison que justice soi faite mome ak bayame ak dieukereueme
@NdayeKebe-e1l
@NdayeKebe-e1l 23 сағат бұрын
papaye wadji danako wara yobale police yallana ko yalla khare adiana mom ana borom keureum
@awalokemdiatta8539
@awalokemdiatta8539 23 сағат бұрын
Yalna nako Yalla yeureume si seydina mouhamed ❤
@IbrahimCisse-v8s
@IbrahimCisse-v8s 19 сағат бұрын
Justice réke sama xoll dafa diééxe wallahi
@BeautifullyBeauty
@BeautifullyBeauty 21 сағат бұрын
Seuyou mbokkou merci rek tout es permis tchim
@guidotoure4254
@guidotoure4254 2 сағат бұрын
Seyou mbokou dara nekou thi, ki ko ray kokou lagn wara ray
@damesamb6296
@damesamb6296 14 сағат бұрын
Diegal topoulen ba loulen yone maye, mane wakhouma raybi mais raye ba pare,di soul te keneu yeugoul, khana ame khar bougnoulako dekone sakh bougnouko raye balankako soul dingako wakh borom..no famille sama khol tanguena thi niom
@MbenefallFall-g5y
@MbenefallFall-g5y 8 сағат бұрын
Souma dofe yallna mellni mome doff bouy liguey😢 famille Gör Gui bakhou niou😢waron na khôl si soxna diara😢😢😢😢na yone deff ligeuam😢youma yallna KO yalla yeurum
@ZahraBah-xs8tg
@ZahraBah-xs8tg 23 сағат бұрын
Bilahi peine de mort késsé Moy diéhal li
@ousseynoundiaye175
@ousseynoundiaye175 22 сағат бұрын
Bou done sa ma sœur la prison la koy fék ray ndayam bar qui yalla 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
@MbavkeGaye
@MbavkeGaye 21 сағат бұрын
Sénégal li tah sey fa meti da ngay nekeu khale di sey sa yay di wodjé sa mak di wojié wa keur yepo di sey Sénégal safa metii
@jajafaya6470
@jajafaya6470 21 сағат бұрын
Boulenn bayi mou sedd dei... Famille kou goor ki mom douniou ayy nitt
@rokhayacisse7905
@rokhayacisse7905 18 минут бұрын
Vraiment
@mdmdiop7907
@mdmdiop7907 5 сағат бұрын
Vraiment senegal les famme mari souffre dans les maisons 🏠 familiales qu justice soi faites
@aidaniang8452
@aidaniang8452 8 сағат бұрын
Wawaw bou léne ko baal na déwé prison ay embéçile lagnou
@MariamaDembele-gy7kz
@MariamaDembele-gy7kz 22 сағат бұрын
Yalnako yalla yereume
@idrissaba-sg2gy
@idrissaba-sg2gy 23 сағат бұрын
Il faut aller jusqu'au bout
@assdiouf1033
@assdiouf1033 12 сағат бұрын
Dee mome kim bok si mome rek mokoy yeuk
@SalyNdiaye-ef9su
@SalyNdiaye-ef9su 13 сағат бұрын
Yalla nako yalla yeureum hareko aldiana firdawsi
@damesamb6296
@damesamb6296 14 сағат бұрын
Neus neuseul waroufe ame, ki dafa wara deh thi kasobi, mane famille nignou defe mo guena niaw
@antanndiaye55
@antanndiaye55 12 сағат бұрын
Me Ani dieuk dji
@oumisene6159
@oumisene6159 17 сағат бұрын
Yalla nako yalla yeureume Metina 😢😢😢 bebe bi yalla nako yalla sambe
@fatoufall7203
@fatoufall7203 22 сағат бұрын
Ki vampire deugueula.lou lère gua wakh.papaye khalébou goor bi déclounaako dafa oyofale birmi melné dou bakane lagnou dieule.A chaud la comaacé laye dinane da dofone,ba paré da métite louwoule sakh
@rokhayacisse7905
@rokhayacisse7905 15 минут бұрын
MoMA diakhale
@FatoumataDiop-dr5cv
@FatoumataDiop-dr5cv 20 сағат бұрын
Nane bayi cou ray gnounee weroul dafa yomb dane co wara ray gni né dafa dof dane wara ray séne ndaye
@damesamb6296
@damesamb6296 14 сағат бұрын
Gni dagno yabate, degui metina mais definbi mo guena niaw, gni lignou def boulen djigue dinama diakhal
@mamadiediou7451
@mamadiediou7451 13 сағат бұрын
Thieye yalla😢
@seynabouthior2365
@seynabouthior2365 23 сағат бұрын
Dofoul Dara diotouko
@cheikhoudabo2527
@cheikhoudabo2527 5 сағат бұрын
Dengayi Fenn dara diotico te dofoull
@aissatoundao1312
@aissatoundao1312 6 сағат бұрын
Bouniou bokone ndeye ak baye sakhe amoul nesnesel justice laniou bege kou ray niou rayla
@MbavkeGaye
@MbavkeGaye 21 сағат бұрын
Koka Def sama djabar bilakhi après si kasobi lay de mem son boké ndey ak bay sokoy ray malay ray
@sambandiaye5331
@sambandiaye5331 12 сағат бұрын
Bien dit vèritè
@cira1345
@cira1345 Күн бұрын
Que firdawci soit sont deumeurs internel inchallah amine ya rabie Allah courages a vous la familles que justices soit faites tro c'est trop
@06makaveli
@06makaveli 7 сағат бұрын
Lou lérr
@mamediarraniane2285
@mamediarraniane2285 22 сағат бұрын
Métina trope
@adamakasse6576
@adamakasse6576 11 сағат бұрын
Def ni Congo Brazzaville rek Dieul kou ray niou rayla sinon crime doufi meussa diouk
@ModouNdiaye-g6y
@ModouNdiaye-g6y 8 сағат бұрын
Yeneu dolene ray ki pourquoi police manei dal ma warou rek
@AwaFaye-zb8hb
@AwaFaye-zb8hb 47 минут бұрын
😭😭😭
@cheikhoudabo2527
@cheikhoudabo2527 5 сағат бұрын
Journaliste degneou Fenn Di wakha rayti bi defe dof Walla defa Mandi
@BinetaNdoye-yf6pp
@BinetaNdoye-yf6pp 6 сағат бұрын
Wadji DMR la reyeléne ko
@aidaniang8452
@aidaniang8452 8 сағат бұрын
Wa légui sénegal lou takh gay réy nit ba paré gnou ni dafa dof wa legui ki dé mome dou nit
@ToraMbacke-sk4xg
@ToraMbacke-sk4xg 17 сағат бұрын
Magi doga kham litakh gorobi don bange ko fi defatt reportass wa 5 m tV mudilenn depu na yon deff ligéyam
@sarafina6243
@sarafina6243 6 сағат бұрын
Wadji deumeu piiir leu. Dofoul djinné diapou ko sokhor rek la def. Wa ana dieukeurou ndawsi ??
@mamyseck9623
@mamyseck9623 9 сағат бұрын
Il na pas tué sa mère ni sa sœur
@mamadoufaye9962
@mamadoufaye9962 15 сағат бұрын
Niawna lol lol commeca histoire dafa amone avan baniou dioubalé léne kone geum nané dofoul dara diotouko defna lou niawa niaw reye gui mom senegal peine de mort rek mokoye safara
BÉTÉ BÉTÉ - Saison 2 - Episode 10 **VOSTFR**
1:08:25
EvenProd
Рет қаралды 431 М.
Вопрос Ребром - Джиган
43:52
Gazgolder
Рет қаралды 3,8 МЛН
Жездуха 42-серия
29:26
Million Show
Рет қаралды 2,6 МЛН
Discour de Mimi Touré devant la première Dame Marie Khone Faye
5:31
FAMILLE SENEGALAISE - Saison 03 - Episode 44 - VOSTFR
47:46
Pikini Production
Рет қаралды 1,6 МЛН
LÉGISLATIVES : les résultats du second tour et réactions (LIVE)
3:19:21
HugoDécrypte - Actus du jour
Рет қаралды 2,7 МЛН
Taku Show du jeudi 09 janvier 2025 avec Cheikh Bara Ndiaye Sur Walf Tv
1:31:28