Kii deh chak gouddi damako done nianal depui bima guissè sa vidéo ak liko nitt you bone yi tëkk... Fane yi yeupp mangui xalatt sn cas. Alhamdulilah
@adiouka63573 жыл бұрын
AAH machalla en le regardant tu vois nettement qu' il a changé yalnagnou yalla mouseul si gnakka yalnaléne yalla féy mayléne goudou fane bou ande ak weur ak khééwal
@mbayebabacarsiby66833 жыл бұрын
Sa fille m'a fait pleurer ndeysan yalnalen borombi Taxawu ci Barké Nabil Moustapha.
@salycisse59113 жыл бұрын
Thiéye nitkou gnoul mo khamoul rék mé yalla nopina ba paré🙏🏼dkr buzz yalna sén diam yaguuu wayyy à tt léquipe
@diengndiouga7703 жыл бұрын
Sama gnari baye fall yi diam si yéne blh yalla mboléne di faye sa kaw sa kanam si lou bakh fadel et pape niang longue vie à vous deux
@justinefaye15233 жыл бұрын
Merci beaucoup à l’association and taxahou gni weredi à Fadel et son équipe que dieu vous bénissent
@coeurdelionne3 жыл бұрын
Incroyable méchanceté de l'homme. Qu Allah lui Vienne en aide 🙏
@aron60543 жыл бұрын
Sa toure bi mome sadike na 😂😂😂
@oumarsarr27553 жыл бұрын
Amine
@awandiouck8973 жыл бұрын
Pape Niang ak fadél yalna nalén yallah fay sén liguéy rafett na
@madamembengue18283 жыл бұрын
Machala Fadél yak pape Niang ak séne équipe bi ak kép koussi déf deuremeume yalnaléne Yalla féye
@astoudeme72313 жыл бұрын
Fadel ak pape Niang ay nitou aldiana lène yalnalène sougnou borom fay macha'allah 🙏
@kitokoken21873 жыл бұрын
Magnifique, bravo à toute l équipe
@minkabarhamasarr21173 жыл бұрын
Masha Allah wa Dakar buzz ak Pape Niang and takhawou gnii wérédii yalnalén faye wallahii sénn liguey rafétna yalna yalla gueureum Père Abdou Sarr yalnala yalla yokk wéer té takhawoula sii barké seydina Mouhamed saws 🙏
@mariamacissokho21243 жыл бұрын
Son Visage a même changé machalla je suis contente pour lui
@amidia72683 жыл бұрын
Ouiii meme moi jai vue quil a chenger Macha Allah❤
@aminatadiop52753 жыл бұрын
Bilaye trop changé yalnagnou yala mousseul si noone
@bintasy77563 жыл бұрын
Diam dafeu am solo si nite
@mamtoubaniang3072 жыл бұрын
Ndeysan thiatt boula rayoul fem la 😭😭papa yalla nala yalla yeukati may la werr lepp Dina diekh
@inasoum64873 жыл бұрын
MachaAllah yalna Keur gui yégue si diam ak salam
@niggaroouscool70163 жыл бұрын
Baye abdou sarr yalna yalla Faye la sa xol
@diarrysow1572 жыл бұрын
Machallah Aïcha et son père sont de vrais musulmans dans leur paroles il y a que la piété Machallah je vous aime par Allah
@hamathndiaye543 жыл бұрын
Ya un bon dieu sur terre incha Allah que dieu le venir de l'aide amine
Mairie bii svp feeikheileinnn baa. Papier yii na leigalll sou ameuii beineinn maire bouumouuu koooo nanngouuuuu
@lehdjindiaye49663 жыл бұрын
Machalla yalna léne yalla faye mou tourou thi sène jabot
@fatimatadjibrilsow6203 жыл бұрын
mash Allah Dakar buz sa kaw sa kanam yallah nalen yallah sounou borom faye si barké seydina Muhammad psl bep dioulit dafa wara roye si yen machallah yi dé bouyou dougoul Aldiana ken dou dougou
@amadoukane31683 жыл бұрын
Que Dieu vous donne longue vie. Machallah
@abymangalka84083 жыл бұрын
Ndeysane geste bi rafetna fadel pape niang manchallah
@rackyba8613 жыл бұрын
Machallah yalla nalène yalla lafal bopam migui melni sama pape ngue defal li
@dabangom13973 жыл бұрын
Aye way yalle nalèn yalla takhawou s'en liguéy rafèt na machalla sikaw si Kanam rek inchalla pape Niagn ak fadel ak kèp kolèn si andal
@juniorjunior13453 жыл бұрын
Que le tout puissant vous bénisse si barké seuydina Mohamed PSL Amine
@dameseckbiendit10353 жыл бұрын
Machalla Pape ñiang ak fadél ak yéne wa asociación ande takhawou ñi wééreudi yalnaléne yalla takhawou amine yarabi
@bintousamb79953 жыл бұрын
Machallah Fadel Niang Pape Niang yalla nalèn yalla fay khol yeup sede na bilay
@juniorjunior13453 жыл бұрын
Fadel mane déh amouma xaliss. Sama dolé rek la yoor té meune nako dimbalé si lép loleni dokh...
@ngagnfall36923 жыл бұрын
amna solo
@Corailpro3 жыл бұрын
Yallah fay leu sa khol.
@absatoufaye59283 жыл бұрын
@@ngagnfall3692 a
@mbayangniang61403 жыл бұрын
Machalah pape yallana yalla may la guoudou fane ak wer rek inchalah
@macoumbathiam30153 жыл бұрын
Walahi liguene di deff nii dafa rafet trop yalla nalen yalla faye wayy🙏🙏
@bilygaye79093 жыл бұрын
Merci beaucoup 😍😍😍😍😍😍😍💘💘💘💘💘💘 sama khol sede na wallahi
@adiouma24913 жыл бұрын
Alhamdu lilah ❤️ Que le Bon Dieu te protège 🙏🏾
@famaleye80363 жыл бұрын
Yalnala yalla maye werr bangua féké lep deuk ci si diam si barkep seydina mouhamed
@papelandingcoly68273 жыл бұрын
Je suis architecte junior , svp je veux contribuer à faire les plans de la maison gratuitement en tenant compte du budget disponible.
@aron60543 жыл бұрын
Fadel yak Pape Niang foléne mounti tolou déléne waxe amine
@diopanta20433 жыл бұрын
Yalla nako yallah motali si barkéb serigne fallou mbacké
@Moustapha-N2s3 жыл бұрын
Yalla na yalla matalé leupp si barki seydina Mohamed salallahou halaye hi wasalam
@thiernosaidou15983 жыл бұрын
Eskey walahi diarajef ñep lo lebele lolu lalay yalla fay gracias a todos que dios os pague
@thiernobabasarr40813 жыл бұрын
Machala yallna yalla fay kép kou cii diap
@niangtra3 жыл бұрын
Macha'Allah yalla nalen yalla fay Bayilen khel nak comme il a bcp d'ennemis
@mouhamedndour48003 жыл бұрын
Fadel et pape niang vs etez des références yalla sougnou borom guiss na leup je vs souhaite long vie sante
Yalla fayelén 🙏 il rek moy senegal 🇸🇳def lu bakh defélété Lou bakh machala
@dieynabasall35513 жыл бұрын
Cas bi metiwonena trop mais alhamdoulila yalla nalléne yalla faye
@barathiaw7343 жыл бұрын
Machalah yalla yalla faylen Aïcha wakhna lou am solo bilahi
@Corailpro3 жыл бұрын
Walahi cette vidéo m'a déchiré le coeur. 😭😭😭😭
@dioumafaye62253 жыл бұрын
Ohh machalla khol séde neu
@pape45293 жыл бұрын
Yalna yalla toli soutoura barkép seydina mouhamad
@mamediormbacke54833 жыл бұрын
Yalna yala faylen walahi khawma loma len wara nianal
@dieynabalde81963 жыл бұрын
Yala nagniou yala mouseul thi gniak khif thiona ak miser comment il a changé ndeysane nalen yala fayy🙏🙏🙏
@ndionecodou33073 жыл бұрын
Amine yarabi walahi
@ndiayeasssi30453 жыл бұрын
Amine
@mamtoubaniang3072 жыл бұрын
wa Dakar buuz social AATW Ak mbelem kouy diapale domou Adama yalla nala yalla dimbali si barké magoum deukk biii Yalla nalen yalla fayy si barké Seydina Mouhamed 😭😭😭😭😭
@aissatandiaye73743 жыл бұрын
Ndeysane yala nalen yala takhawou si barki seydina mohameth psl
@TEDUNGALTv3 жыл бұрын
Dafa gueuneu leer sakh, Masha-ALLAH🤗😍...
@binetangingue49123 жыл бұрын
Machalah yalla na done liko djik ts yalla mayko wér
@dykha45133 жыл бұрын
Yalnaléne yalla faye
@arfangndong77923 жыл бұрын
Yalna len yalla fey ci taxaway bi rafetna machaalakh
@fatoucisse10753 жыл бұрын
Macha Allah Ana solo barakallahou fikm 🤝🤝
@fatouba94963 жыл бұрын
merci wa Dakar Buzz yalnalene yalla faye 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
@adjifatoufall38023 жыл бұрын
Bilahi pape ya barri yermander yala na léne yala Faye😭
@ndeyesalioundiaye31193 жыл бұрын
Sarr badiourab dianay sama nidiaye dji diam rek guay am 😭😭😭❤️❤️❤️❤️
@famagueye19913 жыл бұрын
Macha allah alhmdoulilahi et bonne continuation
@sokhnadiengdieng29633 жыл бұрын
Oh Fadel pape Niang yallah nalen yallah fayal bopame tahawou len doli len soutoura boubaah liken Di def ni yoboul Yallah ken yokkou ba yeuk ko
@khadythiam79223 жыл бұрын
Ah machala il a vraiment changer
@khadicamara78323 жыл бұрын
pape niang yalanala yala faye faty niang motakh ma beugueleu té yala takh
@lamaktoumiennebouserigneba85743 жыл бұрын
Machalla yalla rék Mo diara yakar
@yacinefall48163 жыл бұрын
Ndeysane metina mé yalla miguifi fadel pape niang merci
@khadimniane75103 жыл бұрын
machalla abdou yaaa amm diommm
@hatawague71903 жыл бұрын
Ki gnoukoy gueinei chak jour mouy xol keurgui di wahtane ak maçon Yi sakh dafa bakh mou yeugate adina touti yallah naleine yallah tahawou
@dioumadiagne67203 жыл бұрын
Bilay yaw
@Laye3963 жыл бұрын
En général gnilaye bagne saye mboque lagnouye done
@milkinsa65603 жыл бұрын
Lou Weir kou reindy say none say mbok diekh
@KatyNdeyeDiop3 жыл бұрын
Yallana mi takhawu diam yi yallana takhawu ak mbolèm domou adama
@coumbistadiop36923 жыл бұрын
Yalla na léne yalla fay si barki seydina Mohamed pls
@missmbaye78493 жыл бұрын
Yalla na lene yalla fay
@margosoumah39083 жыл бұрын
@@missmbaye7849 machala que le tout puissant Allah vous récompense vous tous membres de Dakar buzz amine yarabi
@coumbistadiop36923 жыл бұрын
Amine yarabi
@bdjhrurjhr40583 жыл бұрын
M achallah y allah na y allah faaye mention tres bien
@Corailpro3 жыл бұрын
😭😭😭 thiey yallah, l'être humain est méchant. Où sont les milliardaires et les millionnaire du pays. Kep kou wakhirlou si wadji bilahi sunu borom fay leu.
@abbiejobe95273 жыл бұрын
Que. Dieu vous aide et vous protège. Lahilaha ila allahou
@user-vn5zm7mc2x3 жыл бұрын
Macha allah dackar buzz yalnaléne yalla faye
@ndeyjobe91772 жыл бұрын
Longue vie a abdou sarr et a toute lekipe
@ndeye86583 жыл бұрын
Machallah merci beaucoup
@fatoungom40403 жыл бұрын
Ô j'ai les lames au yeux pape ak Fadel nit dou léne gueune yéna bakh yéna oyof billaye gnanwe rék nék si liguéye comme ay Masson yalla na léne yalla bour yalla fayal bopam barkép alkhourane😭sama xolle laye wakhé 😭
@rokhayalavillageoise83803 жыл бұрын
Machalah Mom da changé
@salyallemomuawrksarr86523 жыл бұрын
Senegal dou dem ndakh ay nitte you iniane niofi nek ak sokhor mais papa niognou al nalene sa akh dall😭😭😭🙏🙏🙏
@gamoudiop95653 жыл бұрын
Khamna mane mommm ma apooo 😭😭😭😭mouna sétane dakar buzz da dioyouma
@fatousow77443 жыл бұрын
Yalla naga wére AK Diam ba délou sa liguéye
@nenekeita87203 жыл бұрын
Machalah thi kaw thi kanam
@adamagaye39013 жыл бұрын
Machala rafétena yala nako djike
@amadoundao92333 жыл бұрын
c'est bien yalna yalla Taxawu leen
@makhoupobar86813 жыл бұрын
Senegal mo gueuneu beuri ay doméram sur terre , dougnou démm té kou djokk rek gnou damm sa tank
@peaceandsalam28523 жыл бұрын
Yàlla nako buur yàlla taxawu 🤲🏾
@ndayendiaye77453 жыл бұрын
Machalla je sui tres contant yalla nalen yalla fay