Problème amna dh:Réponses de touba à l'appelle du député cheikh thioro mbacke sur l'insécurité

  Рет қаралды 14,671

BUZZ SN

BUZZ SN

Күн бұрын

Пікірлер: 50
@modoufall1365
@modoufall1365 2 күн бұрын
Dieureudieuf Serigne Touba diarawlack Cheikh Ibra Fall
@MaoumyNdiaye-l9p
@MaoumyNdiaye-l9p 2 күн бұрын
Li Serigne bi beugue moy am
@bigblackmantbdiop89
@bigblackmantbdiop89 2 күн бұрын
Touba la deug mais sgr cheikh thioro Mbacké deug rek la wakh civil dou règle civil
@toubatouba4966
@toubatouba4966 2 күн бұрын
Yaw AK thioro da ngéne Di doule kou dieuféwoule ndigeule génale Touba
@bigblackmantbdiop89
@bigblackmantbdiop89 2 күн бұрын
@toubatouba4966 nii rek gaa meuna wakhë dakh saa bay daa diogë deuk baa dik touba mane nak sama bay touba la dioudo ma dioudo touba serigne cheikh thioro mbacke mamam moo mom touba
@MoussaMbengue-vc9wg
@MoussaMbengue-vc9wg 2 күн бұрын
Sa saram ndeye baye fall yi dougnou civil ndiguelou serigne bi kousi ték sa saram ndeye
@Yibrafalien
@Yibrafalien Күн бұрын
Sa baye ba dou civil rek
@BahSalehe
@BahSalehe 2 күн бұрын
Vive viiive les baye fall
@alycisse4972
@alycisse4972 2 күн бұрын
nafékk wésou oul warra digell baye fall yii niou jouly nga khass cheikh thiorro té mou gene la fouffff nioune touba ak mbacké laniou deuk yene ngii yenako yakk cheikhe thoro merci
@Generalahmadoudame
@Generalahmadoudame 2 күн бұрын
Yaw dof ga bon diollé AK bon diollit wol lolo sen degeunte AK yalla la te lii mbirom nit leu nit mokoy lidienti ko mom sa keur lo beuge mofay am bola nekhol gadem sa deugom mam😅😊
@sidyndiaye4697
@sidyndiaye4697 2 күн бұрын
Civil dou yar civile bayilen nafekh 😂😂😂😂😂😂😂
@toubatouba4966
@toubatouba4966 2 күн бұрын
Wakhale sa baye mou bayi nék nanfék
@Generalahmadoudame
@Generalahmadoudame 2 күн бұрын
Lolo ay fenn la dh geum geumo tobabyo salte yii😢
@Yibrafalien
@Yibrafalien Күн бұрын
Sa baye bila yar mba homme de tenue la rek
@HabibDiop-p2y
@HabibDiop-p2y 2 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@partageursn
@partageursn 2 күн бұрын
Borom yéré bou orange bi deuk touba di wakh nane moy lolou khol sakh khamni do 100% sa touba😂😂😂 regléle lala wakh
@cheikhdiene1082
@cheikhdiene1082 2 күн бұрын
Bilay papa wakh ga duegg nit yi dafa am nio kham ni fo rek mo nek si sen bop yi
@NgomNdary-jj3rf
@NgomNdary-jj3rf 2 күн бұрын
Niou bari di wakh ay domaram lanou cheikhe thioro dafa beug touba bakh rék
@tout1958
@tout1958 2 күн бұрын
Kou beugoul gis baye fall yi rék danga diouboul
@sidyndiaye4697
@sidyndiaye4697 2 күн бұрын
S cheikh thioro mbakce wakh na deg de ❤❤❤❤❤❤❤
@Generalahmadoudame
@Generalahmadoudame 2 күн бұрын
Day fenn dh
@mamemorthiam8763
@mamemorthiam8763 2 сағат бұрын
S chiekh thioro jam si yaw toujours
@ibrahimadioplo475
@ibrahimadioplo475 2 күн бұрын
Bamouye meti guisoulwone Ken motakh yallah faye ko Lamp Fall
@NgoudaDiop-i9v
@NgoudaDiop-i9v 2 күн бұрын
Chiekh thioro Deugue La wakhe
@wakhanteyoubakhetv1357
@wakhanteyoubakhetv1357 2 күн бұрын
Civil dou yare civil ah thakhn bakhoul
@AliCisse-ei6pd
@AliCisse-ei6pd 2 күн бұрын
Li cheikh thioro mbacké beug Moy am🥰🥰🥰🥰
@panogayembaye2116
@panogayembaye2116 2 күн бұрын
CHEIKH Thioro MBACKÉ dou exemplaire ndakh Addounako Yittél motakh mou bayifi Liguéyi Mame bi di Politiqui
@momocreation3631
@momocreation3631 2 күн бұрын
Vraiment civil dou yar civil nék lené aye nité
@daoudambaye262
@daoudambaye262 2 күн бұрын
Aye boys yo kham né kéne khamou si sa baye, nane tioro kouti mbaw mbaw mo wakh DEUG. Touba kou fa déf louniouye téré bou la baye Fall yi diapé tegual sa Ndaye ak ko meuna done. Kou beuguoul li Serigne bi beug guenal Touba. Non gni nioye saytané té khamou niou né Serigne bi mo aye si Satan.
@MohamedDiouf-x4f
@MohamedDiouf-x4f 2 күн бұрын
Mane li Serigne bi beuguè force moy amemè kou koume enragé woul gua guén dékk jiajieufatii Mame cheikh Ibrahim Fall yonne rèk lou tilime gñou sanii thï albaa
@badarademe1264
@badarademe1264 Сағат бұрын
Touba Mbacke garde sa spécificité légitime (comme le Vatican a sa gouvernance particulière) le Vatican a ses propres forces de l'ordre ou de sécurité...ma vision est que le khalif pourrait recrutés des jeunes natifs de Touba encages sur les rangs de l'armée à Bango.Apres formation ils seront affectés et installés a Touba ville Multi dimensionnelles pour la SÉCURITÉ...je rappelle que le Vatican a sa propre armée constituée de militaires Suisses
@mamemorthiam8763
@mamemorthiam8763 2 сағат бұрын
S chiekh thioro lim wakh rek moy deug
@cheikhdiene1082
@cheikhdiene1082 2 күн бұрын
Police yi lay wakh aka niou bon police Touba yi
@cheikhdiene1082
@cheikhdiene1082 2 күн бұрын
Limou wakhh wakhi dof la
@ModouFaye-ll6ks
@ModouFaye-ll6ks 2 күн бұрын
Mane na ani geurr civil
@SambaSene-j1h
@SambaSene-j1h 2 күн бұрын
Touba dekou serigne touba la kou monoune sakh si li serigne bi bogue nga daim si khadie guène dek bi
@Generalahmadoudame
@Generalahmadoudame 2 күн бұрын
Amol lo def sa boppo dh touba dafa sel
@ousseynoutoure3621
@ousseynoutoure3621 2 күн бұрын
Dimbalileine nitte gni kouye deifar faw mou am aye problème
@cheikhdiene1082
@cheikhdiene1082 2 күн бұрын
Boy thioro n'a fekhh la
@mothernature6996
@mothernature6996 Күн бұрын
Gnolene guena beug touba fop ay wahi doff rek lafi deggg insecurite loum diotek worma deuk bi bay fall dafa meuna yor securite touba? Cheikh tioro di kou bakhh serigne touba di mamam guene beug lane
@ibrahimadioplo475
@ibrahimadioplo475 2 күн бұрын
Mame cheikh Ibrahima Fall moye Borom Touba
@abakarafall6276
@abakarafall6276 2 күн бұрын
Sekhe thoro ligeyou seringe Touba bi gno rouko polotic rek gnakeu fayeda rek dierediefe seringe Touba
@CheikhNdong-x6s
@CheikhNdong-x6s 2 күн бұрын
Bousyi app ligueyla djiapo lenn boybi nioun balle mbebbdyi mult apres demm niebiit
@ousseynoutoure3621
@ousseynoutoure3621 2 күн бұрын
Deukeu bi dou deukou ousmane sonko dara meitti woufou bou ngueine reiglei keine dou si am diafei diafei
@ibrahimadioplo475
@ibrahimadioplo475 2 күн бұрын
Boudoulwone mame Cheikh Ibrahima Fall Bamba rere djamyi yi fande
@NgoudaDiop-i9v
@NgoudaDiop-i9v 2 күн бұрын
Chiekh thioro Deugue La wakhe
@MbathouGaye
@MbathouGaye 8 сағат бұрын
Li Serigne bi beuge moy am
Правильный подход к детям
00:18
Beatrise
Рет қаралды 11 МЛН
coco在求救? #小丑 #天使 #shorts
00:29
好人小丑
Рет қаралды 120 МЛН
🚨 RÉVÉLATION DE Imame Babacar Mboub Li Cheikh thioro Mbacké Wakh Si Touba......
17:11
Россия атаковала Украину более 100 дронами
1:11
Euronews по-русски
Рет қаралды 22 М.
VAR Wakhi 2022 Ak Wakhi  2024 You S.Cheikh Thioro Ci Touba
3:33
TAWFEKH PRODUCTION INTERNATIONAL HD
Рет қаралды 30 М.
Правильный подход к детям
00:18
Beatrise
Рет қаралды 11 МЛН