⛔️⛔️Problème balance ⚖️à DJILOR Les lutteurs poids légers non inscrits,colere des organisateurs

  Рет қаралды 8,322

Lutte 100% LAMYN TV

Lutte 100% LAMYN TV

Күн бұрын

Пікірлер
@CheikhDiouf-wv9if
@CheikhDiouf-wv9if 2 күн бұрын
On doit définitivement supprimer la balance
@omarthiam-vd8vw
@omarthiam-vd8vw 2 күн бұрын
Injuste les lutteurs nioko Mouna bagne naniou boycott lamb yi
@mouhamadousarr8891
@mouhamadousarr8891 2 күн бұрын
Balance bokoul si l'amb nagnou may diam wayyy ahhhhh
@modo6218
@modo6218 Күн бұрын
Merci malick ande nasi yaw
@moussadiouf6033
@moussadiouf6033 2 күн бұрын
Ah non li dou yoon ken dakkoroull .Waw CNG bouniou fontoo waay ils doivent reculer puisque ça ne passera pas.
@abdoukarimedione6133
@abdoukarimedione6133 2 күн бұрын
Moi je suis d'accord avec la balance
@IbrahimaLoum-c3u
@IbrahimaLoum-c3u 2 күн бұрын
Lamyn beur yi nagne am foula bouko diaré sakh niou déme arène nationale marche beuré dor dou amati
@AbdouNdiaye-p1g
@AbdouNdiaye-p1g 2 күн бұрын
Thiossanou sérère lagniou beug yack😢
@EtienneNgorNdickDione
@EtienneNgorNdickDione 2 күн бұрын
Règlement n'as pas d'exception,soit on supprime la balance où on l'applique sur l'étendue du Sénégal
@ambardiouf7281
@ambardiouf7281 2 күн бұрын
Cng thie bopam amoul diarigne dou teugu lamb dou dèf dara loudoul dagu mbeur yi ak lèn sén yalissou recours yi Balance soko beugué imposer il faut mou am ay catégorie you bari par exemple -75 -83 -90 -98 +100 té lolou dafay yakk lambb Gnoun lamb moy sougnou identité donc loutax chak fois guèn di beugu copier li toubab yi di deff? Balance bi dou pour lambb soxla wougn ko
@SeneMamadou-wb7ev
@SeneMamadou-wb7ev 2 күн бұрын
Bilaye li d'où yene
@biramadiokh2533
@biramadiokh2533 2 күн бұрын
Tout droit
@ousmanegning8016
@ousmanegning8016 2 күн бұрын
waay na tass li dou
@babacarfaye4446
@babacarfaye4446 2 күн бұрын
Il faut boycotter
@abdoufaye1807
@abdoufaye1807 2 күн бұрын
C'est très normal, CFA , ndiol sana, brosses, djidjack sont tous poids lourd. Di sonal boyiii
@fackawngom7751
@fackawngom7751 2 күн бұрын
Yow nopile hamgua ligay wakh founou néké mbeur poid lourd
@mbayegueyesarr5075
@mbayegueyesarr5075 2 күн бұрын
Légui Assane djibé sarra mi meussoul beuré poids léger nak ak yenen moromam nék mbeur rawgadou gnou bégue lén teubal yokou lén poids lourd direct tu trouves que c’est normal Dpui diamano man batéy ken meussou di guiss li et les anciens gloire ont tjr décrié cette balance
@fayebirame9749
@fayebirame9749 2 күн бұрын
Balla Gaye VS Siteu est ce que c’est le même poids ou le même âge pourtant c’est signé hier
@ElhadjiModouassjakarta-x2g
@ElhadjiModouassjakarta-x2g 2 күн бұрын
Non ki khamoul lambe
@paamathndiaye2259
@paamathndiaye2259 2 күн бұрын
Mbeur bou mate 100kg dafa wara beurré lourd bayilé fontou nagnou appliqué blance
@AmadouDieganeDione
@AmadouDieganeDione 2 күн бұрын
Na mbeur yi ak amateur yi ak tv tv yi yeup greve guen gnibi par ce que l’heure est grave 😢
@MbayeMbaye-u9i
@MbayeMbaye-u9i 2 күн бұрын
❤❤❤❤
@ousmanediouf5201
@ousmanediouf5201 2 күн бұрын
Balance bou bess poull kay🤣🤣
@BCNSENEGAL-hy7zm
@BCNSENEGAL-hy7zm 2 күн бұрын
Li moy yone
@AbdouNdiaye-p1g
@AbdouNdiaye-p1g 2 күн бұрын
Li di yack thiossane ga nann yonn iow khamo yon
@mmsseye9391
@mmsseye9391 2 күн бұрын
130 kg dafa eup si pois legers
@daoudasarr7150
@daoudasarr7150 2 күн бұрын
AY TAPETTE NGUENE 😡PONKAL BOU MATE 100 kg LOY WOUTE POIDS LÉGER 🤷🏽
@FayeMessi
@FayeMessi 2 күн бұрын
😭😭
@AbdouNdiaye-ph8mp
@AbdouNdiaye-ph8mp 2 күн бұрын
Delén wakh deugue CFA ,bross poid lourd force merci Malick ngom
@PapeSENE-b7k
@PapeSENE-b7k 2 күн бұрын
Ww wakhka dek
@alioungom2755
@alioungom2755 2 күн бұрын
Lègui gniléni dann nak fougn wara beuré mbeur kén douko imposé yég poids lourd sou dioté kén doukoko wakh
@AbdouNdiaye-ph8mp
@AbdouNdiaye-ph8mp Күн бұрын
@alioungom2755 no beuré mo mel nounou rawgardou sakh mounena dane poilourd dou foufou mbeur yi na gueum sén bop comme Modou diam Terry ordinateur kouko dane kerog Dou cheikh Diagne dagno complexé sport khalé
@ALP_4-4
@ALP_4-4 2 күн бұрын
Vraiment balance bi dafa nara yakk lamb jii
@yaram1278
@yaram1278 2 күн бұрын
Non a la balance
@wallysarr7670
@wallysarr7670 2 күн бұрын
Li dou yoné
@Malickfaye-g1k
@Malickfaye-g1k 2 күн бұрын
Gnom gnou lourd
@pierresitorndour7893
@pierresitorndour7893 2 күн бұрын
Li dou yone way
@mbayeboureugreug
@mbayeboureugreug 2 күн бұрын
Légui kou am 130kilo khana àré gay dém bayi simple,
@AbdouNdiaye-ph8mp
@AbdouNdiaye-ph8mp 2 күн бұрын
Bayilén Di fowé séne khél CFA lourd force ragal rék motakh selé vrai mbeur 85 kilos ponkal yi yép la dane
@ibrahimawalydiouf5745
@ibrahimawalydiouf5745 2 күн бұрын
Kou beuga mbeuré poids léger démal nga wagni sa poids sinon li moy deug
@lesenegalais2589
@lesenegalais2589 2 күн бұрын
Saway lingay wax xamoko, waxou con reik ngaffi wax
@fackawngom7751
@fackawngom7751 2 күн бұрын
Yow nitt nga yow
@sekoufaye9856
@sekoufaye9856 2 күн бұрын
Yaw wakho fi darra
@SambaDiawaraSarr
@SambaDiawaraSarr 2 күн бұрын
Sa Way li Lamb laa Konn khana niom ibou Ndiaye oboli Dagni wout Sen Catégorie Bopou plus de 120kilo Sa way Bayi len Thiakhan li Lamb laa
@ndongodiouf6747
@ndongodiouf6747 2 күн бұрын
Yakk Guen lambji avec votre blanche
@SambaSene-gz5np
@SambaSene-gz5np 2 күн бұрын
Legui dégno bogua yakk lutte simple non a la balance
@AgenceSylla
@AgenceSylla 2 күн бұрын
vraiment le CNG dans son ensemble ne connaît pas la lutte simple au vrai sens de la discipline
@yaram1278
@yaram1278 2 күн бұрын
Non a la balance
@madoudiouf4871
@madoudiouf4871 2 күн бұрын
Vous les tv tv vous etes des porteurs de voix il faut le dénoncer fermement.ces non pratiquants vont chahuter la lutte traditionnelle .c du n importe koi ça.comment un gars comme assane djini sara peut rivaliser avec ibou Ndiaye ou 'gagne sene .
@AbdouNdiaye-p1g
@AbdouNdiaye-p1g 2 күн бұрын
Li yofou wolof là ay balance thiakhan you neck nagnko bayi Dakar
@papangom4219
@papangom4219 2 күн бұрын
Ça c'est du n'importe quoi
@mbayegueyesarr5075
@mbayegueyesarr5075 2 күн бұрын
Malick Ngom démissionne t’es incompétent on ne t’as pas choisi pour que tu prennes des décisions injustes 95% des amateurs ne cautionnent pas ça de même que les lutteurs et les promoteurs donc cette balance ça profite à qui ?? On en veut pas laisse notre culture comme ça trop c’est trop 😢
@ibrahimawalydiouf5745
@ibrahimawalydiouf5745 2 күн бұрын
Li moy deug cfa monoul dieul poids lourd dembeu ba paré tey mouy gnéw pd léger wax lén gas yii deug ay poids lourd lagne
@AbdouNdiaye-p1g
@AbdouNdiaye-p1g 2 күн бұрын
Diél poit lour takhoul ga neck beurou poit lourd
@LamineNdao-z6e
@LamineNdao-z6e 2 күн бұрын
A vrai dire ya des lutteurs qui doivent remonter en poids lourds mais non restaient là pendant des années dans les poids Légers ce n'était pas du tout normal CFA,mounoul diél poids lourds toppou khalé yi tamite di dane rk naniou léne may séne chance tamit Comme Brosse,Ndiol Sana, Djidiack Djilass,Ndiack Séne,et Gandia Fama
Правильный подход к детям
00:18
Beatrise
Рет қаралды 11 МЛН
Мясо вегана? 🧐 @Whatthefshow
01:01
История одного вокалиста
Рет қаралды 7 МЛН
When you have a very capricious child 😂😘👍
00:16
Like Asiya
Рет қаралды 18 МЛН