Machalla amna solo dh yalla na diam yagé sy barkep s touba amine ❤
@BeyeAmdy11 ай бұрын
Ayewaye linékhe nadé❤❤
@chiekhniangxassida415011 ай бұрын
Kiii barképe xassida yi 😢❤😮😢❤amna mayouk yalla ak tawfekhi serigne Atte mou diote ak ba geuneu nékh 😢😮😢 doyna waar loool Waaawaaw inchallah di khar nak biss bimouye guénneu