Propos de Cheikh Oumar Diagne sur Serigne Touba: La réponse musclée de Cheikh Abdoulaye Diop Bichri

  Рет қаралды 86,593

Seneweb TV

Seneweb TV

Күн бұрын

Пікірлер: 515
@cheikhfall6653
@cheikhfall6653 3 жыл бұрын
Cheikh Omar Diagne, n'est pas un ennemi !
@Musk.1800
@Musk.1800 9 ай бұрын
Waxlèn si Palestine ak Israël ndax lalnanou sounou passpass ak si problème dioullit yi❤ mo gueunn Oumar Diagne borom xam xam leuh wallahi 🥰 Dieureudieuffé Serigne Touba ❤
@SerigneabdouSene-r5f
@SerigneabdouSene-r5f 3 ай бұрын
khalil seytaner gua wakhofi dra
@cheikhounalo8342
@cheikhounalo8342 3 ай бұрын
Yay nafekh degg degg Palestine AK Israel sonu dolé yegul ci dimbali len nakhar luko lan man Roi maka bi dnga guis mu def si dra Yw AK himar Diagne yena yam Mbaaamu khara🐷
@baragueye-bi6jt
@baragueye-bi6jt 3 ай бұрын
xanaa borom xam xam si iow ganaw ba mbaam ga kou am xam xam si iow day yomb . do genee sa baye ak say mbok dem marche si palestine baxam kuleen di deglu
@MamadouThiam-uz9ek
@MamadouThiam-uz9ek 9 ай бұрын
Diéureudiéul serigne touba rék wallahy lazim❤❤❤❤❤❤ khadimou rassoul♥️🫶♥️🕌💫🥰
@SalimataBaldé-y4t
@SalimataBaldé-y4t 3 ай бұрын
😮Merci S.Touba
@AbdoulayeDiop-n4z
@AbdoulayeDiop-n4z 3 ай бұрын
Dieureudieuf serigne touba éskeuy Serigne Touba thiey Serigne Touba ❤♥️👍🙏
@Iboudiallo1090
@Iboudiallo1090 3 ай бұрын
Ndeyisan nagen ragal yalla ki di wahk si ko khamnte ni yalla moko yeketi kon loufi diar seringue touba demna
@bambadiagne6619
@bambadiagne6619 2 жыл бұрын
Akassa
@cheikhabdoukhadreba
@cheikhabdoukhadreba 3 ай бұрын
Boulen niou yab modou kara wahou fi S Touba mo bind yalla bén mourid manifester woufi nafek ngéne rk sa wah bou bari té waho fi dara
@FallBaye-gd9lf
@FallBaye-gd9lf 3 ай бұрын
Machalah li rek ndam ablaye bisri yalna yalla werale say thieur
@makhandiaye6441
@makhandiaye6441 3 жыл бұрын
Diaradieuf Serigne Touba
@ngagnegueye4990
@ngagnegueye4990 3 ай бұрын
Dieureudieufaty Serigne Touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@ElhadjiHane-n2s
@ElhadjiHane-n2s 3 ай бұрын
Cheikh omar diagne yalnako serigne touba wane popap barkeh alkhourhane 🙏
@Blabattante
@Blabattante 3 ай бұрын
Amine wayy❤
@KahdiSakho
@KahdiSakho 3 ай бұрын
Souko Serigne Touba wanée bopam ngene rous ndakh lim wakh deugla
@amadoudiakhate5080
@amadoudiakhate5080 3 ай бұрын
Kou doundou, menoul def dara. Li moy islam. Khamo dara. Dagnoulay nakh.
@bassirouthiam1615
@bassirouthiam1615 8 ай бұрын
Diereudiefe s touba rek fall ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️
@ousmanendiaye5725
@ousmanendiaye5725 3 ай бұрын
Cheikh Oumar n' a rien dit de mal vraiment
@MaguetteDiop-e9d
@MaguetteDiop-e9d 3 ай бұрын
Yaw ak himaar Diagne gné ay domi khathie guén ta domi khathie dioukoy khathiam lay donnou
@cheikhounalo8342
@cheikhounalo8342 3 ай бұрын
Yay nafekh degg degg
@MbeneFall-x7s
@MbeneFall-x7s 3 ай бұрын
Dieureudieufeuti serigne touba diarama mame cheikh Ibrahim ❤❤
@MahmouToure
@MahmouToure 3 ай бұрын
لإله إلًا الله محمد الرسول الله 😊الحمدلله رب العآلمين 😊شكرا له ياشيخ أحمد الخديم❤
@djibysarr-dx9sq
@djibysarr-dx9sq 3 ай бұрын
Je suis avec Seex Umar jaañ il a dit que de vérité Kydul Yàlla matoo.
@baragueye-bi6jt
@baragueye-bi6jt 3 ай бұрын
kudul YALLA matoo demmal wax ko sa baye. moom himaar diagne ak iow mii jeul leen wax jojou feetalé ko sen bopp kene geunou leen matadi si miim reew ndax matadi moy umpalé Serigne Touba
@leyetoubaleye2731
@leyetoubaleye2731 3 ай бұрын
Machallah merci beaucoup M Abdou lahi diop
@ibrahimacisse6017
@ibrahimacisse6017 3 жыл бұрын
Merci beaucoup Diop bissri yala nala yala défall diamou ci barkéb s Touba khadim Rassoul Amin
@mbackendiayelofficiel5359
@mbackendiayelofficiel5359 3 жыл бұрын
Dieuredieuf cheikh ahmadou bamba
@moustaphadiop1559
@moustaphadiop1559 3 ай бұрын
Dieureudiéufé serigne Touba
@issadiop1222
@issadiop1222 3 жыл бұрын
Dieurdieufètii Serigne Touba🇺🇸.
@SambaSylla-dp9mp
@SambaSylla-dp9mp 3 ай бұрын
Diereudieuf serigne touba,ay nonam la yereum,kén dou mom.le plus petit talibé de serigne touba est un milliards de fois plus fort que le COD
@layeilliassou4804
@layeilliassou4804 3 ай бұрын
cou diamoul yalla pérte nga fi yalla rék mofi né ak seydina moukhamad sw
@eumeundiaye7589
@eumeundiaye7589 3 жыл бұрын
Tihey yalla yennetbi barki damb rek liko Moustapha diakhate wax mois gêna garw folene nekon beug len yenet bi touti Sax tabayi nafekh
@shiekhnjie7765
@shiekhnjie7765 3 жыл бұрын
Wakh degg nyii goumuoung yalla
@MoustaphaNdiaye-f3p
@MoustaphaNdiaye-f3p 3 ай бұрын
@@shiekhnjie7765khaaral ba dougou aldiana sooga wédi kouy diouly comme yaw
@MoustaphaNdiaye-f3p
@MoustaphaNdiaye-f3p 3 ай бұрын
Kouy tontou doff yaak moom yéna yam
@MoustaphaNdiaye-f3p
@MoustaphaNdiaye-f3p 3 ай бұрын
Yén fane nguén nékoone walla bokoulén si waakeur yonéntt bi Kone si naafékh yi nguén book
@MbenefallFall-g5y
@MbenefallFall-g5y 3 ай бұрын
​@@shiekhnjie7765sa koy bay yak Serigne bo yakar 😂 bamba mo niou nior
@ibrahimaseye2524
@ibrahimaseye2524 3 жыл бұрын
Merci Bouchri
@MoustaphaDiallo-u2p
@MoustaphaDiallo-u2p 3 ай бұрын
Dieureudieuf serigne touba❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@YoroSow-v2i
@YoroSow-v2i 3 ай бұрын
Jereujeufé cheikhoul khadiim❤❤❤❤
@malickndiaye7875
@malickndiaye7875 3 ай бұрын
Ki mo wakhone né serigne touba mo bind yalla
@babasene9673
@babasene9673 3 ай бұрын
😂😂😂doyna warr
@fatouba1587
@fatouba1587 3 ай бұрын
Dieureudieuf SERIGNE TOUBA ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@aliounesow3530
@aliounesow3530 3 жыл бұрын
Bayilén togñie cheikh Omar Diagne déggo léne mou toudd serigne touba ah bayilén thiakhane
@ameetfallsenegal3506
@ameetfallsenegal3506 3 жыл бұрын
Yaw yama feen oumar diagne wax serigne touba ngaye wax
@aliounesow3530
@aliounesow3530 3 жыл бұрын
@@ameetfallsenegal3506 sa baye ya ma dakkhe féne😅
@Échophysiologiste-cb9bi
@Échophysiologiste-cb9bi 3 ай бұрын
Ki fenal Serigne touba nga nane, ya Nafekh😅, sa khol bou bonne😂
@SerigneabdouSene-r5f
@SerigneabdouSene-r5f 3 ай бұрын
alioune sow meun gua fen 😅 loulen Serigne Touba def batakh guen bagn ko dem len geustou ki est Ahmadou Mbacke
@ousmanesarr6381
@ousmanesarr6381 3 жыл бұрын
Franchement c était pas la peine,cheikh omar n a rein dit de mal et en plus il a généralisé ces propos
@ibouibou7112
@ibouibou7112 3 ай бұрын
ils n'ont même pas ecouté ce que COD a dit
@daoudambaye262
@daoudambaye262 3 ай бұрын
Omar Diagne kouti mbaw mbaw là mbame là khathie là ak keep kou ande ak môme. Domerame yi yéne ap simple postier yoor kham khamou Google, moye wakh nane fok niou kholate mbidim Serigne bi. Limou wakh grawoul guéne léne séne bountou keur kessé wakh ko nguene khôl. Togne bakhoul.
@MatyToure-zc1sz
@MatyToure-zc1sz 3 ай бұрын
Toi tu est l avocat du diable
@AssDiagne-uw6xj
@AssDiagne-uw6xj 3 ай бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@MaguetteDiop-e9d
@MaguetteDiop-e9d 3 ай бұрын
Yéné Ay domi khathie guén ay diam guén
@Astou-s6e
@Astou-s6e 3 ай бұрын
Bamba partout dans le monde entier ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@gallondiaye
@gallondiaye 3 ай бұрын
dieureudieuf Serigne Touba Cheikh Ahmadou Bamba Sunuyaakaar
@ThernoLeye
@ThernoLeye 3 ай бұрын
❤jarajafe serigne touba❤
@BayeNdiaye2
@BayeNdiaye2 3 ай бұрын
Dieuredieuf Serigne Touba 😍✅
@sifkawelle1277
@sifkawelle1277 3 жыл бұрын
Wakhléne si gordjiguéne yi ak tiono rewmi
@binetasane467
@binetasane467 3 жыл бұрын
Bilaye lolou mo eupe solo details yi
@AboubacryJobe
@AboubacryJobe 3 ай бұрын
Mélenchon wakh na ci ba Sonko néko dina niou ko toléré...deukk bi tiono yi nio ngui khar Diomaye ak projet bi. Yenn ay mbamm nguén. Serigne Touba kouko bagn sa kholl moy daggg insbi nane len ndey ndokhhh.
@SerigneabdouSene-r5f
@SerigneabdouSene-r5f 3 ай бұрын
thiono rewmi dagay dem gua ligeyi bo ligeyi wé am wala
@MbenefallFall-g5y
@MbenefallFall-g5y 3 ай бұрын
S Touba amoull morom borom magall gui sen Serigne defoull gat loun si mane 😂
@AbdouThioune-w6r
@AbdouThioune-w6r 3 ай бұрын
😭😭🙆🙆🙊🙊🗝️🔓😢😢
@MorNdiaye-r7f
@MorNdiaye-r7f 3 ай бұрын
Dieureudieufé Serigne Touba dieureudieufé Serigne Touba dieureudieufé Serigne Touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@anta2260
@anta2260 3 жыл бұрын
BAYI LÉN DI DÉFORMÉ AY WAX ... IMAME OUMAR DIAGNE LOU LÉÉR NAGNE LAFI WAX.. ARRÊTEZ UN PEU. ( DAFA DOY )
@ameetfallsenegal3506
@ameetfallsenegal3506 3 жыл бұрын
Oumar diagne doul rek laye def wahabiste yi nio ko yak vrai domou kharam la bilahi mane foumako guiss raye ndayam
@Astou-s6e
@Astou-s6e 3 ай бұрын
Serigne Touba relkkkkkkkkk❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@mbayedia7187
@mbayedia7187 3 ай бұрын
Dieredieuff Serigne Touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@CheikhBamba-u9v
@CheikhBamba-u9v 3 ай бұрын
Dieureudieufeuti brom touba amoul morom ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@daoudandiaye7706
@daoudandiaye7706 3 жыл бұрын
Dieuredieufety mouride amna solo , goudeul fann té werr 🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🤝🤝🤝🤝
@mansourgueye618
@mansourgueye618 3 ай бұрын
wakhoul bena hereur lép loumou wakh degla yéngni yéna téyoul ay vrai dofguene
@baragueye-bi6jt
@baragueye-bi6jt 3 ай бұрын
dof bou mag bi moy sa baye xanaa iow gay doff bu ndaw bi
@mbayepouye2394
@mbayepouye2394 3 жыл бұрын
Machallah
@ousmanndiaye
@ousmanndiaye 3 ай бұрын
❤❤❤❤❤wallahi DIEUREDIEUf serigne Touba
@aidathioune9505
@aidathioune9505 3 ай бұрын
Dieuredieufaty Serigne Touba khadim Rassoul ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ amoul morom Mbacké balla Aïcha ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@mbayesilipmbayesilip2149
@mbayesilipmbayesilip2149 3 жыл бұрын
Bayilen thiakhan ta dem lueguye
@momocreation8153
@momocreation8153 3 жыл бұрын
Mbaye silip ya gnouss sa ndey sa toubi rk guathiè leu
@SerigneabdouSene-r5f
@SerigneabdouSene-r5f 3 ай бұрын
mbaye ligey thi mourid yi la fek bakh sokhla wou niou daray diambour yaw nopil silip gua
@Lena-ii7lg
@Lena-ii7lg 3 ай бұрын
Yen ay noon ngen mais Serigne bi kouko bagne bouyebo ngen wathie liguey ndakh daniouy khey Di guéna yokou rek
@baragueye-bi6jt
@baragueye-bi6jt 3 ай бұрын
iow yaa gi leugeey mbaa gnii gnoo daxa leugeey sa baye gnoo la eup xaliss eup la lep mbaam
@yakhsen-s9946
@yakhsen-s9946 3 жыл бұрын
Ces gens sont des malades ?? Il ya vraiment des fous dans ce pays ! Tout mon soutien au professeur Cheikh Oumar Diagne , cette intimidation ne passera pas ! Fi nieupa fi ame mbok
@samba6664
@samba6664 3 жыл бұрын
Vraiment y a rien
@oumarsarr4087
@oumarsarr4087 2 жыл бұрын
Dof gui dof gui serigne Touba rék kouko fi bayi amouniou si yow soxla
@rassoultalibecheikhtidaner9082
@rassoultalibecheikhtidaner9082 3 ай бұрын
Na ay mokam géneu gniou bolé lén dakar sén nday
@samediop2185
@samediop2185 3 ай бұрын
Mandou dafa bax si lo guiss
@SerigneabdouSene-r5f
@SerigneabdouSene-r5f 3 ай бұрын
na ay mbokam guen bordel loutax guen sokhor Serigne Touba loumou len def lane wakh mako
@papasalioucisse9639
@papasalioucisse9639 3 ай бұрын
Deuredieuf serigne touba
@scotervision9627
@scotervision9627 2 жыл бұрын
Dieureudieuf borom touba
@1975793
@1975793 3 ай бұрын
Croire a Allah et a son prophète c'est sur quoi nous serons interrogés dans les tombeaux
@babacarbakhoum800
@babacarbakhoum800 3 ай бұрын
Dieureudieufati way❤❤❤❤
@DabaMbaye-xe2vz
@DabaMbaye-xe2vz 3 ай бұрын
Dieureudieuf Serigne Touba amoul morom kou am morom Moy sa borom
@serigneseye310
@serigneseye310 3 ай бұрын
Bilahi walahi serigne touba a négocié avec les colon😂
@biayeboubacar8689
@biayeboubacar8689 3 ай бұрын
Sa bay da nègoceil sA yay pour diour la
@armaguedonsenegalmeguido9579
@armaguedonsenegalmeguido9579 3 жыл бұрын
Fén ak doul rek lagne fii néké nguir mana doundou ci Serigne Touba.. Respect à Cheikh Oumar Diagne
@boubacaryaffa9583
@boubacaryaffa9583 3 жыл бұрын
S. Touba kouko gueumoul mandoul ci mom bala gua alkou
@armaguedonsenegalmeguido9579
@armaguedonsenegalmeguido9579 3 жыл бұрын
Gueumeul Yalla S Touba Yalla rek leu gueum.. fén you bari yii ak di toutil yénén Serigne yii yeukeutiwoul S Touba dafkoy gueuneuh toutil rek
@SokhnaSegnane-j5c
@SokhnaSegnane-j5c 3 ай бұрын
Kokou dou mosa touti day gueuneu yokou abadan😂❤❤ té ken meunousi dara​@@armaguedonsenegalmeguido9579
@SokhnaSegnane-j5c
@SokhnaSegnane-j5c 3 ай бұрын
Serigne Touba ken meunouko sosal binda na lep loumou def 😂❤❤
@SokhnaSegnane-j5c
@SokhnaSegnane-j5c 3 ай бұрын
Kokou dou mosa touti ay mbiram day gueuneu yokou abadan 😂 té ken meunousi dara
@abdouazizkebe8659
@abdouazizkebe8659 3 жыл бұрын
Vous n'êtes pas fatigué. . Si on touche le prophète vous ne dites rien .vous êtes des chercheurs d'argent. C'est de la politique maintenant ,affaire de confrérie. Kan on entend des talibés dire serigne touba moy yallah. C'est vraiment du n'importe quoi.
@ameetfallsenegal3506
@ameetfallsenegal3506 3 жыл бұрын
iow khana mouride yi nio mome yonante bi saw nioune mouride serigne touba rta moye sunu serigne ta yonante bi saw Dioulite yeupp nio ko bok
@sarrsarr7474
@sarrsarr7474 3 жыл бұрын
Diadieuf Serigne ablaye Diop Dieuredieufeti Serigne Touba Dieuredieufeti Serigne Touba Dieuredieufeti Serigne Touba Dieuredieufeti Serigne Touba Dieuredieufeti Serigne Touba Dieuredieufeti Serigne Touba Dieuredieufeti Serigne Touba Dieuredieufeti Serigne Touba Dieuredieufeti Serigne Touba Dieuredieufeti Serigne Touba Dieuredieufeti Serigne Touba Dieuredieufeti Serigne Touba
@elhadjiBa-ce3ps
@elhadjiBa-ce3ps 3 ай бұрын
Diaradiafati Serigne Touba ❤️❤️ diaradiafati Serigne Touba ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@isamailaniang3600
@isamailaniang3600 3 жыл бұрын
Esk réellement li Omar Diagne wah diarna toute cette théorie .... omar diagne dioulite leu gno bok Gueum yallah ak yenénti bi, té biir namani gueumna sounou Mak yeup ... ce né pas un ennemi c est l un des nôtres càd un Sénégalais et un musulman
@SerigneabdouSene-r5f
@SerigneabdouSene-r5f 3 ай бұрын
demal gua deglou limou wakh ba paré
@FalouDiakhate
@FalouDiakhate 3 ай бұрын
Ki kéfar bouy dokh la wakhna fi s saliou Moy yalla bichri domiram bou mak la
@biayeboubacar8689
@biayeboubacar8689 3 ай бұрын
Iow sa bounou bay
@syllmamadoukabir7952
@syllmamadoukabir7952 2 жыл бұрын
Gni dounou ay nitttt Serigne touba limou beugue gnome gneupppp nèkouni si Serigne Touba sou dèlou si wone gni gneup dina lène gnousssssssssss Nafékhe
@baragueye-bi6jt
@baragueye-bi6jt 3 ай бұрын
iow nak li YALLA beug ndax yaa gi sii gnii loo len xamal ludul meuneu duul ak gneme YALLA .
@khafffrebel8257
@khafffrebel8257 3 ай бұрын
Dem len ligueyiii
@alphonsephonse4120
@alphonsephonse4120 3 жыл бұрын
Cheikh omar diagne est incompris des Senegalais nit kou bakh laa
@momom5493
@momom5493 3 жыл бұрын
Dieuredieuf serigne touba
@Mouhammad5867
@Mouhammad5867 3 ай бұрын
Dul tarikha yéna yakk réwmi
@MoustaphaFall-r1b
@MoustaphaFall-r1b 3 ай бұрын
Machallkh ❤❤❤❤
@serignefalloukanendamatou4630
@serignefalloukanendamatou4630 3 ай бұрын
Jërëjëf S Abdoul laahi bichri 🙏🙏
@lieutenantcolonel2186
@lieutenantcolonel2186 3 жыл бұрын
Mouride loumou dougou mou Eupp bilaakhii Lii loukofi Diaarr Soolëneko meunée léék léékk léeenko Sooffguënne bilaakhii
@baragueye-bi6jt
@baragueye-bi6jt 3 ай бұрын
sunu yeungu xajjul si moom mourid danoo geum moo tax geumeuntou wugnu mbaam binga doon.
@FrancoisDiop-uw6nb
@FrancoisDiop-uw6nb 3 ай бұрын
Yéne dém-lén leugéyii mo gueun thii yi ngén nék Serigne bi limou am dako ligueye bayiléne thiogou-bi yakarr na mo gueun
@sambasene9568
@sambasene9568 3 ай бұрын
DIËRĒDÏEŨF SĖRĨGNE TÕÜBÅ ČHÉKHOÛL KHÅDÍM MBÂČKÊ ❤️ Abdoulaye Diop un homme doué de pédagogie 💛
@Mourtallasylla-np3kx
@Mourtallasylla-np3kx 3 ай бұрын
Dieureudieuf Borome Touba ❤❤❤❤❤
@ndeyeleye5205
@ndeyeleye5205 3 ай бұрын
Dieure dieuf seringe touba❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@mandiayefall602
@mandiayefall602 2 жыл бұрын
Dieuredieuf Serigne, dieuredieuf Sérigne Touba.dieuredieuf Serigne Touba
@masssarr4718
@masssarr4718 3 жыл бұрын
Sak joure niou saga fi yonete yalla mouhamet psl ta dou geune si wakh fila nite takhawe bokou si yene ne seringe touba dou moromou seydina mouhamete ch bethio fi la takhawe ne seringe touba moye yalla ta kene degou lene
@darousalamtv746
@darousalamtv746 3 ай бұрын
Omar Diange nit ko Dagu la nafeq do tabakh Rew
@ibrahimawade8360
@ibrahimawade8360 3 ай бұрын
Voilà un groupe de fanatiques sans raison qui menacent un professeur ouvertement.
@Blabattante
@Blabattante 3 ай бұрын
Machalah s abdoulaye d yala nara serigne bi fay ❤❤❤dieredieuf cheikhoul khadim diarama Mame cheikh ibrahima fall ken dou Ahmadou
@KoumbaSall-ox6ju
@KoumbaSall-ox6ju 3 ай бұрын
Machalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@leeraldeepofficiel137
@leeraldeepofficiel137 3 жыл бұрын
Vive Serigne Touba ,mais t'es propos sont pas soutenu par des arguments solides
@ablayethiam8174
@ablayethiam8174 3 ай бұрын
Le monde avance vous êtes ici à nous amerder de de Serigne Touba qui n’existe même pas
@baragueye-bi6jt
@baragueye-bi6jt 3 ай бұрын
quel monde. ce monde en chaos avec les guerres. gnune deh gnoo len eup jamm gissu ay bombes ak ay ouragans. avec ta mentalité d'opprimé et ta petite cervelle tu ne peux pas avoir la spirtualité necessaire pour savoir cela. iow moom golo ga continues comme ca
@MbenefallFall-g5y
@MbenefallFall-g5y 3 ай бұрын
Sen Serigne defoull gat loun si mane😂
@thiorosall
@thiorosall 3 ай бұрын
Salam dieuredieuf Serigne Touba dieuredieuf Serigne Touba bèsbounè ❤
@ndiayeyouga4339
@ndiayeyouga4339 3 жыл бұрын
Yéna sof bouléniou sonal way omar wakhoul dara lou ay
@djilydiop6812
@djilydiop6812 3 жыл бұрын
Sa data ndeye
@kinelamine3565
@kinelamine3565 3 жыл бұрын
Bro lou lere nga wakh gni danio yabaté Omar défoule dara. Pour niome kene waroule wakh khélatame
@ndiayeyouga4339
@ndiayeyouga4339 3 жыл бұрын
Yén momolén Senegal nioun danio nopi rék wayé khanégn nimou démé dh kou wakh gén sagako amolén kham kham
@kinelamine3565
@kinelamine3565 3 жыл бұрын
@@ndiayeyouga4339 franchement mane yowela andale Omar défoule dara en plus waroule diegalou kene . Sénégal benena tarikha momouko kone Omar amene droi wakh loumou khelate
@ndiayeyouga4339
@ndiayeyouga4339 3 жыл бұрын
Wa gusga frér gni momou niou nit gni Senegal kay légu lep dina lér trô c trô amoul dara
@MomoMbodj95
@MomoMbodj95 3 ай бұрын
Jërëdëfti Segne Abdoulay Bisri, omar diagne domourame là tècksi sokhore
@ndiayeyouga4339
@ndiayeyouga4339 3 жыл бұрын
Démlén tok mogeun
@bakary9909
@bakary9909 3 жыл бұрын
Dauur Katt yi rek nguay déggeu
@momocreation8153
@momocreation8153 3 жыл бұрын
Bayil doul
@barasamb1880
@barasamb1880 3 жыл бұрын
doul ba khoul,كذاب
@bakary9909
@bakary9909 3 жыл бұрын
@@momocreation8153 sa bay moma waleu
@bakary9909
@bakary9909 3 жыл бұрын
@@barasamb1880 wakh co sa bay
@mamecheikhmbaye8491
@mamecheikhmbaye8491 2 жыл бұрын
thieuy serigne touba 🙏🏿🙏🏿🙏🏿
@falloudieye5667
@falloudieye5667 3 ай бұрын
Merci ❤❤❤merci
@ArameNdiaye-h6k
@ArameNdiaye-h6k 3 ай бұрын
Cheikhoul khadim si ❤lénenn dassa xadioul
@khadimdiop9110
@khadimdiop9110 4 ай бұрын
Serigne touba kouko guemoul mano ko beug
@bbbbbbbbbbvvvv
@bbbbbbbbbbvvvv 3 ай бұрын
Iow khamo dra iow. Mdrrrrrrr
@khadimkhadim649
@khadimkhadim649 3 ай бұрын
Diaradiuef borom touba ❤❤❤
@souleyedieye2104
@souleyedieye2104 3 жыл бұрын
Togne dal bakhoul bayilén togne serigne touba limou amm yalla mokka may koumou nekhoul déwal wala nga guene senegal
@DiopFeukh
@DiopFeukh 3 ай бұрын
Dieureudieuf serigne touba
@rifoulepatriote9694
@rifoulepatriote9694 3 жыл бұрын
Bayi leen diambour boulén fii andi fitna
@mediasgraphismesn7789
@mediasgraphismesn7789 3 ай бұрын
Dieureudieuf Serigne Touba
@AbdouThioune-w6r
@AbdouThioune-w6r 3 ай бұрын
❤❤❤🎉🎉🎉🎉❤❤❤
@OmarFaye-ez3ig
@OmarFaye-ez3ig 3 ай бұрын
Diaradieuf cheikh ahmadou bamba ❤❤❤❤
@moustaphathiam504
@moustaphathiam504 3 жыл бұрын
"Deuk bi day pays de droit motakh niou yam si manifestation ms la procn fois danou koy fekk famou nék attaqué ko" Ça veut dire k pour l'instant vous acceptez de faire ce qui légale ms dans des moments à venir vous n'alliez pas respecter la loi. C difficile de vivre au sénégal !
It’s all not real
00:15
V.A. show / Магика
Рет қаралды 20 МЛН
СИНИЙ ИНЕЙ УЖЕ ВЫШЕЛ!❄️
01:01
DO$HIK
Рет қаралды 3,3 МЛН
Quando A Diferença De Altura É Muito Grande 😲😂
00:12
Mari Maria
Рет қаралды 45 МЛН
It’s all not real
00:15
V.A. show / Магика
Рет қаралды 20 МЛН