Personnellement je ne fais pas partie de ceux qui se disent talibé d'un quelconque marabout..mais Bilahi wolahi je vous le jure Elhadji Malick Sy m'a ébloui de par ses enseignements de par sa sagesse Bilahi magui sésé nii contane na trop cii Mame Maodo Sy je viens de me rendre compte de la dimension incommensurable de l'homme Bilahi contan na Bég na sama xol bii séd na
@djimmbathie14394 жыл бұрын
Yalna yalah content
@bongacamara69984 жыл бұрын
Mashalla yalnanga beeeg rek si barke seydi haj Malick
@rokhayasadjindiaye36974 жыл бұрын
Mame MAOUDO il n 'enseigné ke SEYDINA MOUHAMMAD ( PSL) rek...
@enfantciss53564 жыл бұрын
Ndeyssane c’est normal vu sa simplicité et son respect au Sounna du prophète qu’il jura de respecter et de ne jms le ternir
@thiammamadou7724 жыл бұрын
Badara essayé de chercher sur youtube seringe Habib Sarr il a fait un cours sur seydil Hadji Malick
@ngonefalpro17474 жыл бұрын
Je suis Mouridoullahi et j'aime beaucoup SERIGNE BABACAR SY MANSOUR: Yalna Yalla (SWT) méyko goudou fane ak wérgui yaram si barké Serigne Mounetakha Mbacké té yokki lééram si barké Seydouna Mouhamad (SAWS)
@khadypouye69244 жыл бұрын
amine yarabi ya bakhe déé
@iboudiouf91734 жыл бұрын
Dé nga bakh
@elzosy87964 жыл бұрын
Dagua bakh ngone Fall mane j'ai rêvé 4 serigne touba et pourtant talibé cheikh la kone nak lep béne la
@kadergueyegueye30214 жыл бұрын
Diereudieuf mbok contann nan
@didicisko52964 жыл бұрын
Amine yarabil alamina
@dabakhmalickmboup38784 жыл бұрын
Billahi barki seydina MOUHAMED psl deib ku sa❤️ Seidoul dafa feikkk ni fanatiques gua do musulman nax ❤️ yeuppa togn th yeuppa 😭 Billahi yalla n’a fi jamm yag th keipp ku beug seydina MOUHAMED psl beug Maodo beusseul j’aime
@jamesharden34554 жыл бұрын
Amineee
@momomergane31404 жыл бұрын
Nn bilahii Ta raison
@amediasenegal22864 жыл бұрын
Kaine dou Mame maodo degloul li oustaz moudou fall wah kzbin.info/www/bejne/rWe1g3Z7etytm6s
@rassouldia4 жыл бұрын
Kou sa khol sèèdeu beusseul j'aime❤
@rassouldia4 жыл бұрын
Deja fait🙏
@hawathiam34854 жыл бұрын
Machala
@mamependa75004 жыл бұрын
@Jaffiche mes stars qqqa as àapQ
@mamependa75004 жыл бұрын
@Jaffiche mes stars aq
@mamependa75004 жыл бұрын
Sac pp
@moukhamedgueye18914 жыл бұрын
Mane talibé serigne saliou mbacké la wayé dama Buege serigne babacar sy Mansour bilahi ndakh simplissime walay yalla na yalla goudal fanam mame abdou rk lamaye fatali🤲
@makodembaye40104 жыл бұрын
Mahcallah amine yarabbi yalla na yalla goudal souniou fan nioune geupp wollahi Diamm rek ngay am incahallah
Non.ce monsieur est fantastique et pleins de savoirs.quel fierté d'être talibé cheikh. Le savoir fait la différence.
@badarambaye59614 жыл бұрын
papa Diouf bhl
@jamesharden34554 жыл бұрын
Way doundal way
@elzosy87964 жыл бұрын
Walay ndayssane c'est vrai deee
@thiammamadou7724 жыл бұрын
Papa Diouf va cherche sur youtube tu cherches oustaz Alioune diange sur cheikh tidjane
@salioudiallo4134 жыл бұрын
Bilay ndayssane
@santeserignetouba48264 жыл бұрын
SERIGNE BABACAR SY MANSOUR YALLAH NAFI YAGG LOLOU TÉ AND AK WERRR, SERIGNE MOUNTAKHA YALLAH NAFI YAGG LOLOU TÉ AND AK WERRR, KOU WAKH AMIN YALLAH GUA FI YAGG KHÔL YEUP CONTANE TAAY SERIGNE TOUBA CONTANE N'A, EL HAJ MALICK CONTANE N'A DIEUREUDIEUF TFM❤️🙏 PAPE CHEIKH YALLAH NALA SUNU BOROM SOUTOURAL AK MBOLEM DIOULITT 💖🙏
@cheikhbassiroufall7504 жыл бұрын
Machallah amine
@falloufall16844 жыл бұрын
inconnu bilahi man dh morid la wayé kontan na trop say tané yébari rk wayé am nan ay nit you bakh
Walahi sama xol sedna Yalla na gneup am diam gnou nék beneu dioubo délou si Yalla ak Yonentém bi Mouhamed (PSL) serigne yi dagno ligeuye ba am lignou am dougnou ay enemi febar bi Yalla nafi diougé si barké serigne yi Mame maodo Serigne touba Baye niass seydina limamou laye boukouneta si barké gnou téddeu gni mangi diégalou si kaddu yi
@adamdiouf72454 жыл бұрын
Machallah machallah 🥰🥰😘😘☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️😭😭😭😭
@davembengue29384 жыл бұрын
En tant que mouride sama khol bi dafa sedd trop machallah Serigne babacar sy mansour yalna yalla goudal say fane ak kilifeu dinè yepp
@maremediagne19754 жыл бұрын
Amine ya rabi rafetna machaala yala na yala fayla
@gorabayefall95834 жыл бұрын
Wakhe tane wi amna solo trop suis mouride ms dama beugue tijane
@mbayedioumdioum16594 жыл бұрын
Yalna diaam yaag Sénégal danio am ay kilifa you baax
@coubasow66134 жыл бұрын
Merci gora 🙏🙏🙏
@cognandoye20304 жыл бұрын
Yalna la Yallah beugu! 🙏
@leternelindigne99314 жыл бұрын
Ndaysane nonou lagnou beugué ndiabootou cheikhoul khadim bamba moy maoda yalna yalla déf diam si réwmi 🙏👏
@daoudambengue53064 жыл бұрын
Walahi ndéysane. Gora. Yala nassa jamm yagg...
@amiralmbaye61034 жыл бұрын
Je suis trés content Billahi .Di ballou ak nieep di nianal Pape cheikh Diallo mou yague fii looool waaay0
@daoudandione3734 жыл бұрын
Amine
@babasamba67064 жыл бұрын
Machallah Barcké Mame Cheikh Ibrahima Fall Sénégal dall riche na Yalna diam yagg barcké YONÈTEBI "ALKHAMDOULILAH" 🥰💖💘🇪🇸🤝🇸🇳🙏🙏
@babacarsall71964 жыл бұрын
Amine way, yalla df ka si domou sénégal yeupp
@abdouniaye72983 жыл бұрын
Neh na hk yoy war eilo bdou hklpa yallah Qeqq
@ismaelsy84264 жыл бұрын
Ma shaa Allah, Al hamdoulilah. Yalna yalla defal nieup diam. Le Sénégal est un et indivisible. Il faut préserver cette richesse incommensurable que Dieu nous a octroyée. Que Dieu accepte notre jeûne et efface nos péchés🙏🏽🙏🏽🙏🏽❤
@ramatoulayegaye33424 жыл бұрын
Machalla
@abdouazizdieng78714 жыл бұрын
Bilahi walahi wa talakhi je suis très content d'avoir SEYDI EL HADJI MALICK SY mais aussi très fière d'être TIDIANE yalla nagnou yalla fayal Maodo fayalgnou mak gniou bakh gni si rew mi🙏🙏🙏🙏🙏
@elimanebabacarsowgueye49204 жыл бұрын
Aduna amoul soloo na niou rakhass kholl yi rkk defar jikoo yii
@adamamboup74104 жыл бұрын
Yalla nagnou yalla may khol bou gnou andé done béne
@mahdiyoufegnenatv89334 жыл бұрын
Il est modeste vraiment il a dit bal léne ma si Cadou yi antanque khalif général machala
@nogayesall32914 жыл бұрын
Ndayssan ndiabotou Maodo yi donio am yar
@yattayatta89544 жыл бұрын
Nogaye Sall diapou si réck boul convoqué sama gayi
@amediasenegal22864 жыл бұрын
Kaine dou Mame maodo degloul li oustaz moudou fall wah kzbin.info/www/bejne/rWe1g3Z7etytm6s
@FatouDiop-iy3sm4 жыл бұрын
@@yattayatta8954 😂😂😂
@ousmanebalde53424 жыл бұрын
Machaallahou, le mystérieux, l'intellectuel, l'organisateur, le modeste, le savant, le philosophe, le rensembleur... L'inconnu de la nation sénégalaise.
@boudabaax81774 жыл бұрын
MAODO!❤
@assietousy71094 жыл бұрын
Cheikh Seydil Hadji Malick❤😭
@fatoubinetoufall36194 жыл бұрын
Machallah khool seedna trop!!!Niaak si doyaal si wakhetaane bi motakh ba légui nioguikoy setaane fi depuis la France 🇫🇷!!! Contaane naniou trop si sunu pédagogue bi serigne Alioune Diagne wakhentaane bi rafetna tei nekhna machallah ! Nioune dh ay ndaaw nanou mais yaguiniouy khamal louniou khamoul woone
@badidiame67454 жыл бұрын
ce monsieur est éloquent.. Message fluide ,claire et plein de sagesse .
@sokhnadiop54843 жыл бұрын
Uujbubm à hauteurjp
@mamesabelfaye26034 жыл бұрын
Mouride tidiane layenne niassen nieup ben la niou yalla Sénégal dieum kanam tee yalla dieuleniou fii mbass mii
@tvylorndivye42284 жыл бұрын
Amine khol sédna
@aidandiayegueye58074 жыл бұрын
Walay mame dabah rekk la beug man mouride sadih bii serign bamba rekk laa yakar
@babacarsall71964 жыл бұрын
Walay gnoune gneup bénn lagn, yalla nagnou yalla samm
@ousmanesall13514 жыл бұрын
Bilahi wakh deug
@diomalecomte60534 жыл бұрын
Oh les sénégalais vous avez un pays extraordinnaire. Machaallah. Repentez vous et accourez vers votre Seigneur le Tout Puissant
@mbayeniang78894 жыл бұрын
Mashalla ❤️🙏🏽
@binoushkamara39114 жыл бұрын
Je suis mouride mais dama danou lér mancha Allah Yallah naniou Yallah tass si barké mag you bakh yi
@abybathily82214 жыл бұрын
Amine yaraby yalna yalla Nangou niane yeupeu inchalah merci
@jajadiop46754 жыл бұрын
ndeyssane da nga bakh
@sunugaaltv1304 жыл бұрын
Lepp béne la
@sunugaaltv1304 жыл бұрын
Lepp béne la
@djibysow17284 жыл бұрын
Bilaye ya bakhe
@ramadiallo24974 жыл бұрын
Hoolalaa Sama khôl ❤️sedd na trop kenne dou Mame Maodo yalnaniou yallah dess ayy talibé cheikh si Barké yonenti bi Amine 🤲🏼🤲🏼🤲🏼🤲🤲🤲🌹🌹💞💞💞
@moussaane38224 жыл бұрын
Talbe si touba la waye wahtane bi amna sola loll yala na diamou yage si rew mi Aminn
@djibysow17284 жыл бұрын
Bilaye moussa anne ya bakhe yalla nala yalla faye sibareke serigne touba
@lorlynend8454 жыл бұрын
Amine
@abdoudrame34054 жыл бұрын
Merci waye sangbi amna solo trop yalla khamnako
@palaminedieye47754 жыл бұрын
Talibé daniokoy yar si xam xam kén douko yar si khar bakh ak karama yalnanio yalla fayal sounio magnio bakhgni
Machala Senegal d warnano doli sante sunu BOROM si kilifa yi nou amm... Yalla na diam yag barkep SERIGNE TOUBA
@papembayr5294 жыл бұрын
Vraiment je prie de tout mon cœur que Dieu aide les gens qui ont eu la capacité de mettre un dislike qu’il revienne sur le droit chemin😭😭😭🙏🏻
@boudabaax81774 жыл бұрын
Ils sont malades wallah! Amiiinnn car ils en ont vraiment besoin 🙏🏾
@mamydiouf62114 жыл бұрын
Barkeb Serigne Babacar contane na jljr😭❤❤❤Yalna diam yagg Machallah, Mame Babacar sy mansour tricher wo say Mame rek ngua nirol si modestie, simplicité, am yarr, Maodo wanouniou bopam deh, Ya Rasoullilah lagnou xamal, sa Faye Maodo après lay done niou beuri xamougn leu, mais mangui sant bama néké Talibé cheikh fonk sougn diné, fonk sougnouy wadiour, respecter les autres tarikha Machallah sama xol mo fess😭❤❤
@ababacarndiaye39934 жыл бұрын
Yaag lol Sy Malick ibn Balkhawmi
@freemanfreeman44654 жыл бұрын
El Hadji Malick Sy Ibn Ousmane l'inconnu de la nation senegalaise . Il n'est pas Dieu ni Prophète mais un homme , un sujet de Dieu d'une extrême rareté qui a su allié la raison et la foi de sorte que ses dires et ses actions sont toujours bénéfiques pour l'humanité . En vérité seule une personne saine d'esprit et raisonnable est capable de voir à quel point Malickouna est unique et a véritablement un mérite extraordinaire .
@diadjindiaye80904 жыл бұрын
Machalah, khol sedena, que Dieu nous accorde sa Grâce et nous protège du coronavirus. TFM merci, pour ces séances formidables. J'ai découvert Cheikh Ibra Fall, j'ai compris le message de Mame Limamou et suis conforté par les bénédictions divines sur Mame Maodo. Que Dieu les rétribue. Par ailleurs, TFM serait inspirée de nous proposer une émission mensuelle sur les vénérés guides religieux et leurs compagnons. Yalla nalene yalla diapalé.
@seynabourobakowski91704 жыл бұрын
Merci beaucoup sy malick
@leternelindigne99314 жыл бұрын
Machalah Merci beaucoup 🙏
@seynaboufall55834 жыл бұрын
Machallah
@fooyrekahfitv44824 жыл бұрын
Machallah yalla naňu yalla fayal seyidil haaji maalik sih
@bassirousall25754 жыл бұрын
Yala.na. yalla fay. Yiw tfm
@badaraba48024 жыл бұрын
Les mots me manquent pour décrire la joie et le Bonheur que je ressens en regardant cette émission. Yalla nagnou yalla féyal Elhadji Malick Sy Dieurdieuf Mame Maodo Diarama Alioune Diagne
@fatouseck73442 жыл бұрын
MERCI BEAUCOUP
@fatoubinetoufall36194 жыл бұрын
Di remercier pape cheikh Diallo ak ses braves Dames yi si sén sérénités avec leurs ouvertures d’esprit machallah!!! Sénégal lila sokhela on es fier de vous😘 wayé kén dou Oustaz Pape Anne machallah rk Yalna Yalla yokkou meune meune bii ak kaataane bi inchallah!Dieureuguéne Dieuf🙏🏾Yalnanou yalla déff deug deug Talibé cheikh 🤲🏻
@sarrawa16904 жыл бұрын
Machallah amna solo lol yalla na diam yague,niep béne laniou fébarbi yalla nako fi yalla dieulé guire dieumi seydina mouhamed (psl) yalla na niep am diam si barcké serigne touba mbacké
@marietabeth79394 жыл бұрын
Sarr Awa Amiiine. Ni rek la dioulite yi warounio bayi kene di niou roubé
@bbchou864 жыл бұрын
Yalna Yallah fay Serigne bi. Yalna niou Yallah arr nioune nieup, samm niou, doli niou soutoureu,mousseul niou si lèpp lou bonn, si fébbar, ak si bala. Yalna niou Yallah gueuneu khirr si lou bakh, si diammou ko, té niou am moudj bou rafett
@madiagundogan8094 жыл бұрын
Serigne Babacar Sy Mansour khalif général des Tidiane yalla nga fi yagua té wer sounou serigne 🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼❤
@TALIBECHEIKHNATIDJAN4 жыл бұрын
Amine in-cha-Allah
@ibrahimabadji78614 жыл бұрын
Yalla na yalla goudal say fane oustaz Alioune Diagne ci barke Mame maodo
@jamesharden34554 жыл бұрын
Amineee
@ibrasarr93354 жыл бұрын
Dieye Serigne El hadji Malick Sy ❤🤩yalla maynako lum mayoul ken yalla naniouko yalla fayal, waye ken dou Mame Brom Touba❤🤩 wallhi yalla defalnako lum defaloul ken yalla naniouko yalla fayal, ak suniou mak nioubakh nieep 🤩 ❤
@aidandiayegueye58074 жыл бұрын
Machalla ken dou khadim rassoul 🙏
@ndawasylla98624 жыл бұрын
Bilay kedou mame babacr
@ibrasarr93354 жыл бұрын
@@aidandiayegueye5807 ❤🤗
@ibrasarr93354 жыл бұрын
@@aidandiayegueye5807 ❤🤗
@aboubakryndiaye73074 жыл бұрын
Li moy senegal dama contane
@nogayediegne94224 жыл бұрын
Machallah Yalnaniou yalla deff deugue deugue talibe cheikh amine ya rabi
@jamesharden34554 жыл бұрын
Amineee way
@seynabouniang41894 жыл бұрын
Allahouma Amine
@sabeguisse65224 жыл бұрын
Machallah xol sedna 😍 talibé cheikh woyof ragal yalla akk beug prophète bi psl laniou ko xamé yalnaniou yalla fayal mame MAODO
@ndeyenguirane24194 жыл бұрын
Machallah
@ndiagadiakhate60584 жыл бұрын
Machalla je suis mouride wayé kontan n'a lolou yalnala yalla samb khalif général
@syllepogba17434 жыл бұрын
Waw gor diagne amna solo loll machalla suis mourid mai sama ❤ bi sede na trop barki serigne touba
@djibysow17284 жыл бұрын
Bilaye ya bakhe
@ramatoulayegaye33424 жыл бұрын
Yalnay cedd ba faw
@khalifadiop77224 жыл бұрын
Talibé Serigne Touba ni yw lay mél billahi Mais pas vidéo bi di daw en direct Saga yi di daw si commentaires yi no démbou dama rouss Lii dou Sénégal bou mak gni diougé noo 🤔
@cheikhsyllaserignetoubanak5664 жыл бұрын
Machalah amna solo yalla na diam sah Senegal si barkep khassida yi barkep serigne touba
@aminataseck45374 жыл бұрын
Serigne sopenala té yala takh, blilahi. Que Dieu vous donne une très longue vie. J'adore Sidy Elhadji Malick Sy , Serigne Babacar Sy.
@youssouseck82404 жыл бұрын
MACHAALLAH, Diné dji dou Classico ! Sougnou Mack gni gnoom gneep benn lagnou, sen mission moo doon ISLAM sampou si Sénégal. Merci à Saydinà Alioune Diagne et le Khalif Général pour leur discours d'unité de la Umma.
@adjasarrthioye62914 жыл бұрын
Machalla ken dou mame maodo mome rek si khol dara dasa khadjoul bayou KHALIFA❤
@bambagueye41414 жыл бұрын
Mame mourite la Waye wakhtane bi nekhna Wala mane tidiane la waye wakhtane bi nekhna mano lene bayi Lolou borom kham kham moy Wakh force day nekh Diagne yalla na yalla goudal sa fane Dieureudieuf
@papeelimanesene29794 жыл бұрын
Wokhofi dara
@papeelimanesene29794 жыл бұрын
Wakhofi touss sa xéll celloule
@bambagueye41414 жыл бұрын
@@papeelimanesene2979 Dieureudieuf pape elimane
@matysambou89874 жыл бұрын
Billahi khol yii séd n'a Al khalifa Sérigne Babacar Sy Mouhamadoul Mansour n'a fi yallah yagal lol andeu ak wér Sérigne Alioune Diagne n'a la yallah barkél content nagniou Macha'Allah TFM
@senegaldakar47394 жыл бұрын
Alhamdoulilah khole seddati neu, yalna yalla défe diamm au Sénégal et partout dans le monde amine 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
@abybathily82214 жыл бұрын
Amine yaraby yalna yalla Nangou niane yeupeu inchalah merci
@senegaldakar47394 жыл бұрын
@@abybathily8221 amine , merci
@aliounecisse75074 жыл бұрын
Machalla amna solo machalla
@amadoupam59274 жыл бұрын
Aminé
@serignecheikh1official6274 жыл бұрын
Macha allah je suis 100% mouride sama khôl sedna lolo thiaye mame el haji malike ak serigne Babacar sy borom bonikari bii yalla nano yalla fayal sono mak ngie amine❤️
@ismailatall8854 жыл бұрын
Tout le monde est content ❤️❤️❤️🙏🏽🙏🏽🙏🏽
@kadionetv95124 жыл бұрын
Alhamadoulilahi Alhamadoulilahi C'est ça le Sénégal ❤ Yo Allah diounou gourndam ma So Allah mi wéltim,Sénégal fof wéltim ❤ sy malick ❤
@ndeyecoumbambaye4324 жыл бұрын
Yalna nio yalla fayal sunu DIAMBARE DJI ❤CHEIKH SEYDIL HADJI MALICH ❤kenn dou mome machallah walahi très fier d'être talibé cheikh❤❤❤❤❤❤❤
@jamesharden34554 жыл бұрын
Diam si yow
@oumoudiagne704 жыл бұрын
Ayaww yalla na yalla tape kholyi ma sha Allah talibe cheikh lakh mais je respect toutes les religions 💯
@blessingurev36634 жыл бұрын
Machalah j suis fiere detre talibe chiekhe amine
@blessingurev36634 жыл бұрын
@@oumoudiagne70 amine yalla nanou ko yalla defal
@ibramboup53114 жыл бұрын
😗😗😗😗😗
@mouhamadoumsy36064 жыл бұрын
Manchalaa mame SEYDIL El Adji MALiCK Lér la gou léral leup nék chance pour gnoune wa Senegal ak UMA bi yeup
@moussadiallo24834 жыл бұрын
Macha Allah Oustaz Aliou Diagne wallahi nekhna deyssane diarama Oustaz, Maodo Malik dé nittou yalla yi gnoko cédé thii ham hamam mo nekh Immam kepp waliy yalla
@maguiiefall86084 жыл бұрын
C vraiment incroyable fière d'être talibé cheikh
@fatimatoundiaye96144 жыл бұрын
Machallah yalla nagnou yalla fayale Mame El Hadji Malickh Sy ak djabot gui
@abdoulayesylla51684 жыл бұрын
Macha'Allah maodo
@awadiop9864 жыл бұрын
Serigne el hadj malick sy kéne dou mome dieuredieuf serigne alioun diagne ak pape cheikh diallo 🙏🙏🙏🙏🙏
@ndeyediop65324 жыл бұрын
Machallah quelle modestie le khalif général yallah na yallah yagal takhawaybi té mou andak wer serigne Alioune Diagne dieureudieufeuti yallah na yallah wereul batbi 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
@maimounafaye47764 жыл бұрын
Talibè Cheickh rek labegeu donne bilahi🙏
@aminatadia3974 жыл бұрын
Yalla nagnou ko yalla bolé déf machallah
@moussafaye76294 жыл бұрын
Yalnalako yalla défal
@mariamaincayemanga54494 жыл бұрын
Machalah amna solo barké borom Touba yageu fii lol té wer SY
@balladiop77684 жыл бұрын
Yalla gneup am diam reck Mame Maodo & Borom touba fierté sénégalais la kne nagnou yalla Tass sisséne barkéé reck si barké kou tédd kii ....Talibé cheikh si❤❤❤❤❤❤❤❤
@aliounethiam48254 жыл бұрын
Jaaxay ken dou môme walahi ,il ne s'est pas nourri de la religion mais il l'a nourri ,il fut la personne honorable devant laquelle toutes les âmes se pâment,qu'Allah sanctifie l'oeuvre de Seydi Hadji Malick.Merci walahi nekh na yalla na yalla fayal niou mague gni
@aliandoye69374 жыл бұрын
La dimension spirituelle de Seydi hadji Malick sy depassait nos frontieres yalla na yalla fayalnioukou amine touf toufffff 😍😍😍
@jamesharden34554 жыл бұрын
Amineee way
@habibah2724 жыл бұрын
Macha Allah ensemble tt le Sénégal ba aldjana Yalla nagnou ko Yalla defal ci barké mak gnou baakh gni❤❤❤🙏🙏🙏
@elzosy87964 жыл бұрын
Bilahi walahi kéne dou Maodo thiey Mame Maodo hier j'étais tellement content ,khôl yii seed naniou yalla yalla fay léne tfm sur pape cheikh
@mamadidieng51104 жыл бұрын
Nekhoul ba nekhoul wayé Quartier general mongi soga ame gane
@codesamb79614 жыл бұрын
Thieuy serigne babacar sy mansour y'a oyof ta bah way
@papeseck64634 жыл бұрын
Machallah machallah Diagne yalla na sa diamou yageu ak kouné ammine🙏🙏🙏
@bassineniang54634 жыл бұрын
Amine
@tackoniang82714 жыл бұрын
Machallah kéne dou MAME MAODO, YALLA NA YALLA YOKOU LÉRAME😍🙏❤️💕
@moussasene68184 жыл бұрын
Amine yarabi
@ndeyenguirane24194 жыл бұрын
Amine yarabi
@morcoumbasamb84074 жыл бұрын
@@ndeyenguirane2419 hkooek
@morcoumbasamb84074 жыл бұрын
Amine yarabi
@adamamboup74104 жыл бұрын
Fière d'être talibé cheikh mais je respecte les autres religions je suis vraiment contente pape cheikh ak wa groupe TFM que Dieu vous bénisse
@azizgueye36064 жыл бұрын
Xol sedd na li moy senegal yalnaniou yalla fayal maodo
@willblacked67434 жыл бұрын
Les diangue kat sont trop forts Machallah.
@laminetalibecheikh99624 жыл бұрын
Will Blacked sidy mbaye la domou daw gor mbaye
@saergaye5054 жыл бұрын
Will Blacked demb rétane naleu beu sone sheuu😭😭😂😂😂
@willblacked67434 жыл бұрын
@@saergaye505 😂😂😂😂👍🏾👍🏾👍🏾
@aminatadia3974 жыл бұрын
Machallah yalla na yalla wéreul seni bate
@momzly68184 жыл бұрын
Les diangues kat kay.. Yaw mom amo stress 😂😂😂
@biranendiaye54674 жыл бұрын
Ndayssane khol sédeu neu ame yalla rek mo nekh th woor ❤️❤️❤️
@moussasene68184 жыл бұрын
Azize diage yalla nalla yalla Faye adouna ak alahira si barké sèydina mouhamad salalahou alayhi talibe cheikh pir moy yaw vraiment
@dieynabasow53414 жыл бұрын
Macha alla serigne alioune diagne yalla na sa diam yague si bake seydina mohamed psl
@awishrassoul97744 жыл бұрын
Khôl sedd na yalla na diam yague sénégal bayi niou ak souniou kilifa yi basi kanam Machalah ❤️Serigne Alioune Diagne na diam yague sa wakhtane nekh na ré na si ba soneuh li nekh na way
@aman.traore3564 жыл бұрын
Ken dou Mame Maodo😍 Yallah neuniou ko Yallah fayal Sy 🙏🏾
@youkhoumesy77854 жыл бұрын
Ndamla si Senegal chiekh Ahmed tidiane cherif dieul tarikha tidiane diokhco chiekhou oumar bamou yéksi si mame maodo sy cé notre fierté si tarikha tidiane ak si dinédji yalnañouco yala fayal si barké mouhaméd salahu aléyhi wasalam
@khadydiouf36294 жыл бұрын
Abdou aziz Ndiaye yalla na diame yague si linga deife si barkei el hadji Malick ...
@aliounethiam48254 жыл бұрын
Serigne Babacar sy Mansour yalla na yalla goudal faname lep ande ak wer amine sounou khôl sed na ci intervention
@ndeyefatouyade95394 жыл бұрын
Sant yalla bimou gnou khirtalei si yonou tarikha Cheikh 🙏🙏bolegnou nak ak goor gou tedd gou magg gogou di Seydil hadj Malick Sy yalla nanou ko yalla fayal🙏❤
@oumydiop81044 жыл бұрын
Dieureudieuf mame maodo yalla nagnou yalla def talibé Cheikh
@papyponcho-mn4 жыл бұрын
pour une 1ere dans l'histoire de ce monde un khalife général qui appelle en direct dans une emission via téléphone, lii rek léçon avant say kadou yi, bou heurou wakh dioté rek mou wakh déloci khel yi, booléwatt nite gni noppi, Sy Malick yalna BUUR BI fayalnioula. sama khol tay nimou fékhé yalna lérou Rassulilah tourou sa kaw. serigne alioune diagne yakk say diang katt gatié ngalama
Machalah yalla na niou yalla bolet dèfal niou diam je suis mourid mes je ne peux plus garder mes l'arme 😭😭
@dyjasy67044 жыл бұрын
Kell sagess seugn mbaye sy mansour yalna yalla goudalll sa fann banga egalekk sa saggoo sy malick fière d'être talibe cheikh yalnaniou yalla rayy si tarikha cheikh
@thiath27364 жыл бұрын
Machallahou Sy Malick yalna yalla goudal sa fan te dolli diamma ci biir reewu Sénégal amiine.
@deguenediack85374 жыл бұрын
Alioune daigne machallah wa Mboro name nanoule
@assitomalicksamb55014 жыл бұрын
Al hamdoulah baniou bokei cii sopey Maodo❤️
@marietabeth79394 жыл бұрын
Serigne Babacar sy Mansour yalna fi yague ak mbokam cheikh mountakha ci barké khadimou rassoul
@TALIBECHEIKHNATIDJAN4 жыл бұрын
Amine
@sopenabi7094 жыл бұрын
Machaala seydi Alioune diagne kendou male mawdo. Yalla nagnou ko yalla fayal thi sope guomou sope sangou sangue yi rassouloulahi. Ak aboul ABASS sougnou wassila
@joedjite6984 жыл бұрын
Yalla naniou yalla fayal s hadj Malick sy Ak sounou Mame Borom touba, Sounou Mame limamou ak mbolém keur kilifa diné🙏🙏🙏🙏
@aissatoudiallo28394 жыл бұрын
Mashalah s'y Malick goudou fane ak wergu yaram rekk yala bayi lafi fi basi kanamm bijay seydil woudiou Di sws♥️❤️
@elhadjimalickmbengue27984 жыл бұрын
Yala na yala déf diam sénégal si barké seydina mohamet saw. Dieureudieuf seydi hadji malick sama tourando
@dyjasy67044 жыл бұрын
Chapeau a vous serign alioune diagn xamxam rek nga wané yalnala yalla deffal diamm té gueneu sellall xamxam bi 😘😘😘
@mettaniang64574 жыл бұрын
Machallah notre fierté khol sedd na yalnala yalla fayyy contane na trop
@massambadiop76984 жыл бұрын
Yalna fi yalla bayi souniou nagg you bax yi si barké Mame El Hadji Malick Sy
@famagueye47334 жыл бұрын
Macha allahou yallah yalla yokou ler rou MAODA tè tass niou si barkem AMINE YA RABILALLAMIN
@aliadiop73494 жыл бұрын
Ma Sha ALLAH diné islam rek mo woor dieuredieuf serigne alioune diagne kéene dou Mame Maodo
@moussacissediop74804 жыл бұрын
Walahi ba legui dougoul dou si Cheikh Seydil Hadji Malick nakh mom kéne mounoko wakhtané té diarro si yonenti bi ak cheikhou tidiane yalla nagnouko yalla fayal Sy