Réaction de Cheikh Ousmane Mbow aprés l’attaque des disciples de Sidy B Ndiaye à son domicile

  Рет қаралды 12,881

SAYROUL ABAD

SAYROUL ABAD

Күн бұрын

Пікірлер
@thiamenbi4628
@thiamenbi4628 Жыл бұрын
Dieuredieuf cheikh ousmane mbow sa takhaway rafete na thi diiné ji thi tarikha bi ak thi faydou bi yalna yalla geureum la
@FatouSeck-x1f
@FatouSeck-x1f Жыл бұрын
Macha Allah Serigne bi yalna yallah goudal fan bi ak weir ❤❤❤
@djieynabasow4420
@djieynabasow4420 Жыл бұрын
Je vous suit depuis 3ans lais machallah mon téléphone est plein de vos vidéos guissla reek la beug je suis de Saint Louis diapale leenema si numérom
@ablayecisse8183
@ablayecisse8183 Жыл бұрын
Kholal thi description bi amna niari numéro
@souleymanelam5320
@souleymanelam5320 6 ай бұрын
Mchallah cheikh Ousmane mbow ❤❤
@medadurk1055
@medadurk1055 Жыл бұрын
Dieuredieufati Mawlana Cheikh ould Khayri 👌🏾❤️
@IbrahimaSokhna-jc8by
@IbrahimaSokhna-jc8by Жыл бұрын
Machallah serigne li rék motakh gnou Beug leu wallahi danga mate serigne si lépou❤
@khadybarham6379
@khadybarham6379 Жыл бұрын
Machallah goudal fann tam and ak werr ❤❤❤
@luneprophotographielunepro5391
@luneprophotographielunepro5391 Жыл бұрын
Dieuredieuf chiekh ousmane mbow ❤❤❤❤❤
@alioutoure6474
@alioutoure6474 Жыл бұрын
Meilleur mouhadam si faydou bi si zamane bi
@elhadjidiop5278
@elhadjidiop5278 Жыл бұрын
Machalla sarigne bi yalna yalla samoula arla si barkè cheikhoul khayri
@justindiodjfaye91
@justindiodjfaye91 Жыл бұрын
Je le regard depuis un certain temps Il est juste phénoménal
@TalibeCheikhoulKhairy
@TalibeCheikhoulKhairy Жыл бұрын
Cheikh bi deuko wone cité Nations Unies derrière terrain Golf bi?
@moustaphathiam8905
@moustaphathiam8905 Жыл бұрын
Yallanala Yalla samu watula sibarke mawelana Cheikhe ibrahima niass
@modouhabibtambedou1084
@modouhabibtambedou1084 Жыл бұрын
وشكرا ياشيخ عثمان مبو
@bamsa9853
@bamsa9853 Жыл бұрын
Cheikh Ousmane Mbow 2007 lako kham thia fouta deuk bouniouy wakh Lougué wolof mouy serigne kamil mo takh ma kham faydou defal nama lou nekeu ci adouna ba legui wa village bi dan koy wakhtané yallna yalla goudeul fanam
@toutkhayri6808
@toutkhayri6808 Жыл бұрын
Dieureudieufféé Cheikh Ousmane Mbow, ndam rekk laniouy amm in chaa allah, niom danioo meunoul débat ak niounn si xam xam ndakh douniou sénn morom mtx niouy indi fitna mais douniou lénn si féksi ndakh Cheikh Ould Khayri yarei wouniou noonou !
@noreynimoucheikhousmanembo9485
@noreynimoucheikhousmanembo9485 Жыл бұрын
Dieureudieuff Serigne🥰nioune yiow rek laniouye topou❤️
@TamsirNdiaye-rz5rf
@TamsirNdiaye-rz5rf 10 ай бұрын
Machalla xamxam❤❤❤❤❤
@elhadjiabdoulayemansaly6480
@elhadjiabdoulayemansaly6480 Жыл бұрын
Dieureudieuf Cheikh Ousmane Mbow
@almoubachirtv934
@almoubachirtv934 Жыл бұрын
Diokhma numéro sérigne bi ngir yalla
@medadurk1055
@medadurk1055 Жыл бұрын
Dieuredieuf Cheikh O.Mbow Yalla neu yalla goudal say fane mayla wergou yaram ak tawfekh amiine 🙏🏾👌🏾❤️
@fatouseck8907
@fatouseck8907 Жыл бұрын
Amine ya rabbal alamine
@fatouseck8907
@fatouseck8907 Жыл бұрын
Amine ya rabbal alamine
@FatouSeck-x1f
@FatouSeck-x1f Жыл бұрын
Allahouma amine ya rabbal halamine
@NiangMouhameth-iz1um
@NiangMouhameth-iz1um Жыл бұрын
ماشاء الله فرحت بكم غاية الفرح والسرور على عملكم
@imamemalickmbowofficiel6740
@imamemalickmbowofficiel6740 Жыл бұрын
Yalna yalla defal la diame
@beuguebaye4864
@beuguebaye4864 Жыл бұрын
Le meilleur Mouhadam de la Fayda ♥️
@nahnouansaroulahitv8345
@nahnouansaroulahitv8345 Жыл бұрын
Yaw ndakh danga kham moukhadam yeup wala délène Wakh lounguène kham
@bayedecoudiallo5214
@bayedecoudiallo5214 Жыл бұрын
Namonneyla Serigne bi ❤❤❤
@layemilannjaay4707
@layemilannjaay4707 Жыл бұрын
Machallah lepp si xam xam lakoy thieuy Mbow❤️❤️
@ibrahimambow9124
@ibrahimambow9124 Жыл бұрын
Machallah Cheikh
@luneprophotographielunepro5391
@luneprophotographielunepro5391 Жыл бұрын
Liii dafa leeeer mbow ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 Жыл бұрын
Cheikh Ousmane Mbow Serigne deugue ni iao lay Mel ❤❤❤
@imamemalickmbowofficiel6740
@imamemalickmbowofficiel6740 Жыл бұрын
Lérale dioubale machalla ❤
@CheikhtidianeSene-xe8bm
@CheikhtidianeSene-xe8bm Жыл бұрын
Mashalla mashalla mashalla mashalla mashalla mashalla mashalla mashalla mashalla
@dameniasse1970
@dameniasse1970 Жыл бұрын
machallah wahdji amna solo
@moustaphacisse7677
@moustaphacisse7677 Жыл бұрын
MachaAllah, alhamdoulillah
@khadijatoufaye226
@khadijatoufaye226 Жыл бұрын
Alhamdoulilah 💘
@malikdev2833
@malikdev2833 Жыл бұрын
Kii moy Cheikh Ousmane Mbow mouhadam cheikh ould khayri . Serigne bi cheikh ould khayri geureum nala.
@mamadoufall340
@mamadoufall340 Жыл бұрын
Cheikh Ousmane Mbow ❤
@abdallahgassama3678
@abdallahgassama3678 Жыл бұрын
Macha Allah serign bi Allahu Akbarr Xam Xam ❤
@ousseynoundiaye2480
@ousseynoundiaye2480 Жыл бұрын
Ki faydoubi yeup nii wara bolo delloko ndioukale takaleko modéle nguir yalla khalifabi sahe mbow la warona guena considérai si faydoubi nguirr yalla na gayi ame xolou nangou
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 Жыл бұрын
Wallaye ndayssane waya nitt yi danio khamoul motakh niouye yony ay nitt keureum pour niou fagagal talibéme
@khadybarham6379
@khadybarham6379 Жыл бұрын
Bilahi wakh ngu deug
@moussambow2904
@moussambow2904 Жыл бұрын
Manchala cheikh ousmane khamkhambi selna leeena
@luneprophotographielunepro5391
@luneprophotographielunepro5391 Жыл бұрын
Chiekh ousmane mbow kham kham bou leeeer machalla
@mbowaliou3176
@mbowaliou3176 Жыл бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ machalla yalna yalla barkel xam xam bi lerna trop
@IssaDiop-jf3zn
@IssaDiop-jf3zn Жыл бұрын
@MiaDiack-sq4re
@MiaDiack-sq4re Жыл бұрын
Macha Allah cheikh ❤❤
@daoudadiamanka9975
@daoudadiamanka9975 Жыл бұрын
Machallah Serigne bi longue vie waye
@MariamaCiss-oo8ks
@MariamaCiss-oo8ks Жыл бұрын
Cheikh Ousmane Mbow brom xamxam la machallah mai barina eyy touma yimouy tekk si dérou sangeu Barhamou Ndiaye ak yenene mouhadam si Faydou té nekoul deug. Je l'ai suis tous mai Ch Ous souvent dey dérapé
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 Жыл бұрын
Mariama maguilay ziarr bou bakh. Cheikh Ousmane Mbow dhé daffay dimbaler djamou yallah yi ci Nakhaté bi sangue Ndiaye ak yéneu Serigne you nek ci faydou bi di nakhé talibés yi. Lolou nak motakh Serigne you beurry douniouko meuna beugue car dafléne di wér. Lépou loumou wedy boko sété bou bakh ci kham kham lakoy tek.
@mbayevipecoleimameassaneci1638
@mbayevipecoleimameassaneci1638 Жыл бұрын
❤❤❤
@babasow1596
@babasow1596 Жыл бұрын
Ici sayroul abad Chaikh Ousmane Mbow rek
@sophiefallba1519
@sophiefallba1519 Жыл бұрын
fi lépou l'aire na xam xam rék gafi wakh machalla Serigne bi
@babaafia3477
@babaafia3477 Жыл бұрын
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🤲🤲🤲🤲🤲📿✅✅✅✅✅👂👂👂👂👂
@sophiefallba1519
@sophiefallba1519 Жыл бұрын
un peu de respect sur cheikh Ousmane Mbow 💪
@loumbarhama8017
@loumbarhama8017 Жыл бұрын
Bayilene woté khalifa yalla .Baye rek
@elhadjiabdoulayemansaly6480
@elhadjiabdoulayemansaly6480 Жыл бұрын
Serigne ni leye melle walahi
@luneprophotographielunepro5391
@luneprophotographielunepro5391 Жыл бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤
@papadiaby9495
@papadiaby9495 Жыл бұрын
Yèna meuna douuuule meune fèneu waay
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 Жыл бұрын
Toklene fofou rek après guéne dhi comprendre
@toutkhayri6808
@toutkhayri6808 Жыл бұрын
Boo meunoul wakh xam xam ngua noppi
@mouhamedba7656
@mouhamedba7656 Жыл бұрын
May yalla mo gueuna reuy dh. Kone may yonét bi waroul nekk problème
@mahtarrjeng6590
@mahtarrjeng6590 Жыл бұрын
Jerejeef sering bi it’s all about Khairy Bai
@papemandaondiaye2225
@papemandaondiaye2225 Жыл бұрын
Wakho fi dra ragal nga mo takh nga bayi ba sangue bi wakh ba paré ngay dordi guén di mbel mbeli sangue ndiaye sa baye dou sa morome
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 Жыл бұрын
Koula dégue guay wakh daffay kham sa matady yagui wakh comme khalei mais lolou amoul sens wakhlene Séne serigne mou tontou ci oumouwatam biniou wedy yeupou mo gueune
@thiernothier
@thiernothier Жыл бұрын
Franchement je le connais pas mais borome xam xam la
@daoudadiamanka9975
@daoudadiamanka9975 Жыл бұрын
Xam xam bii leer na Serigne bi
@nahnouansaroulahitv8345
@nahnouansaroulahitv8345 Жыл бұрын
Baye Abdoulaye wouldoul dou serigneum Baye moko wakhal bopam né niari Serigne la am si zahire alqu-ane ak souna serignou baatinam Cheikhou tidiani
@Kanecheikhtidiane42
@Kanecheikhtidiane42 Жыл бұрын
Demal thi kachif al bas gua khol li baye wakh thi mom
@papemandaondiaye2225
@papemandaondiaye2225 Жыл бұрын
Sangue ndiaye yar na gnou la meun foufff té Ioe ko défar defaro ken wégn nga ingkar rek moy sa liguéy sangue ndiaye dala rawww
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 Жыл бұрын
Sangue Ndiaye khana violence verbale ak physique lalène djangal car lolou rek guéne wané han malheureusement et c'est vraiment décevant pour quelqu'un qui se dit Khalifa Yallah.
@mamadoundiaye515
@mamadoundiaye515 Жыл бұрын
ki comme d amoul béne léer thie yalla comme khadj
@asskhayrimbow4290
@asskhayrimbow4290 Жыл бұрын
Yawww danguaye xarrr
@thiernothier
@thiernothier Жыл бұрын
Khanna sangue ndiaye PIT BULL la
@IssakhaDiouf-e9t
@IssakhaDiouf-e9t 11 ай бұрын
Nako sangue Ndiaye tontou si Kham Kham rék diaroul wakh
@assancham6305
@assancham6305 Жыл бұрын
Baye ken manu ko sekal. Su sikal di am nyen lenuy sekal
@HappyniassTV
@HappyniassTV Жыл бұрын
Wakhe diou beri outé na lol ak mélokani kou xam...nopi yém na Baye
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 Жыл бұрын
Mbokou iao daffa melni dégo wakh bigua utiliser dhé Kham nopi bobou kham kham leu ndakh daffa âme borom té kokou moy Adji matou jamono mouye Cheikh Ould khayri ci zamane bi Sangue Ndiaye daffa beugueu askanal bopam loumou momoul lolou nak moko sonal
@poutinekimjong6870
@poutinekimjong6870 Жыл бұрын
Mane dall daccorouma si ay doratey si faydou bi bounioula incare tontoul si kham kham waye di menacé lolou dou yone
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 Жыл бұрын
Djisgua dhé frère actu lolou laniou khewal anh né daniouye khekh waleu raye nitte. Ndayssane niakeu arguments rek mokoy waral ak niakeu Serigne comme niko Cheikh Ousmane Mbow wakhé ci wakhtane bi.. ❤
@asskhayrimbow4290
@asskhayrimbow4290 Жыл бұрын
Matte moukhadame âme metrisse xam loye wakh
@cheikhibrahim6346
@cheikhibrahim6346 Жыл бұрын
Ki fajiilénko dafa fébar dé !
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 Жыл бұрын
😂😂😂 Mbokou ki kham kham boumou yoor koi febar douko attane kone sois polie way
@bayethiame
@bayethiame Жыл бұрын
Bayilén sén yii nguèn neké. Fii Maolana sangue Barhamou Ndiaye mofi nek. Beug nguèn buzz trop
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 Жыл бұрын
Buzz douniouko woute moukou ci Mindeff lolou Kay wa SBN nioko maume nioune buzz ci yallah laniouye woute nekeu léne fofou di yakheu tabakhou Baye Niass birek
@sadikhbayeniass9393
@sadikhbayeniass9393 Жыл бұрын
🤪🤪
@KhidmalBarkham
@KhidmalBarkham Жыл бұрын
Deumeu Bi Nokhorrr👺
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 Жыл бұрын
Ndayssane lolou gua déssé sagua. Ohh c'est vraiment dommage nioulay wakh kham kham guay sagua c'est grave. Démléne djangui c'est mieux
@ndiayemamour5100
@ndiayemamour5100 Жыл бұрын
man ci yaw la geumé ne mbiry baye diermeloul
@papemandaondiaye2225
@papemandaondiaye2225 Жыл бұрын
KHathi day mbowwww rek 😂Ioe y’a meun fén deh sangue ndiaye lakhatou woul ay éléments lakhatou wougn gno gui thi plateau yi ak télé yi mais Ioe mom goudi rek ngay guén yooo nga talibé sangue ndiaye yi dougniy saga
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 Жыл бұрын
Mbokou louguène djeuffé la nuit du 03 avril môme firndé neu ni yéne daguéne di prôner la violence té lolou takhoul djokkk faydou bi Ci kham kham laniou léne wo donc tontoulene ci kham kham waleu guéne mougne rek
@asskhayrimbow4290
@asskhayrimbow4290 Жыл бұрын
Indillle souwalll niou waxtane
@awacheikhthiam5963
@awacheikhthiam5963 Жыл бұрын
Mane comprendrouma sérieusement kou xam dakh Dina top thi Aw nit rek Di wakh ay soit disant defaum
@IssakhaDiouf-e9t
@IssakhaDiouf-e9t 11 ай бұрын
Kilimouy wakh kén mounou ko tégui aya you lér wakhi baye bou lér ak gnom cheikh Tidiani lounguén bougati kou beuga tontou Kham Kham gnowal
@poutinekimjong6870
@poutinekimjong6870 Жыл бұрын
Torokhalatey si faydou mom beurina loll daur nitt ki badiko filmé dougal ko face book tah borom birmi mossoul ko deff
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 Жыл бұрын
Lolou nak baye Niass indiwouko donc kham kham mo wara primé ci lépou. Motakh Cheikh Ousmane Mbow Ci lolou lay wotè wakhtane ci kham kham. Aka dall ndayssane
@ibrahimagaye2907
@ibrahimagaye2907 Жыл бұрын
Yaw hamo dara demal watou dji mogueune si yaw Cheich houtbou dagne ko ndey warone niouss
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 Жыл бұрын
Talibés loumou nampou ci Serigne késsé lay djeuffé. Ndayssane yallah Ndiaye sagua ak khasté la deff ci yéne mais maîtrise 00 sinon douguéne sakh khalate nane daguéne di doraté mane dama rousse ci Séne djeuffé djiu niaw bobou. Du doraté comme des animaux
@thiernohassanedemetv8601
@thiernohassanedemetv8601 Жыл бұрын
Yaw mom d'égo wakhi baye
@abdallahgassama3678
@abdallahgassama3678 Жыл бұрын
Yaw mu deaga wahi baye wahal
@toutkhayri6808
@toutkhayri6808 Жыл бұрын
@@abdallahgassama3678 Serigne bi ki dei doula meussa tontou 🤣🤣🤣🤣🤣🤣
@barhamiennealkhairy4554
@barhamiennealkhairy4554 Жыл бұрын
Mbir mi lerna d xol yeeee bagn Dieureudieuf cheikh Ousmane ❤❤
@daoudadiamanka9975
@daoudadiamanka9975 Жыл бұрын
Machallah Serigne bi longue vie waye
@babaafia3477
@babaafia3477 Жыл бұрын
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️👂👂👂👂☝️☝️☝️🏅🥇🥇🥇🏅🥇🏅🏅🥇🥇🥇🏆🏆🏆🏆🏆🤝🏅🥇✅😃🕋👂
@nahnouansaroulahitv8345
@nahnouansaroulahitv8345 Жыл бұрын
Baye Abdoulaye wouldoul dou serigneum Baye moko wakhal bopam né niari Serigne la am si zahire alqu-ane ak souna serignou baatinam Cheikhou tidiani
@moussaaw6711
@moussaaw6711 Жыл бұрын
mane awma xam xam mais deuguena gniné yeuneteubi alqu-arane bouye doxla. ALLAH a'lam mais par analogie je dirai cheikhou tidiane alqu-arane boul doxla et AbdouLLAH ould hadj alquarane bouy doxla et quenène alqurane boul doxla. Nahnou Ansarou lahi TV qu'en pensez-vous que so bougué guisse alquran bouy doxla, xolal yeuneutibi de la mère des croyants (Aicha rad anhâ)?
GAMOU TAIBA DISCOUR CHEIKH OUSMANE MBOW
40:11
SAYROUL ABAD
Рет қаралды 1,3 М.
СИНИЙ ИНЕЙ УЖЕ ВЫШЕЛ!❄️
01:01
DO$HIK
Рет қаралды 3,3 МЛН
It works #beatbox #tiktok
00:34
BeatboxJCOP
Рет қаралды 41 МЛН
Мен атып көрмегенмін ! | Qalam | 5 серия
25:41
Revue des titres du Lundi 03 Février 2025...
43:46
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 6 М.
Gayi déguouniou wakhou Cheikh Ould Khaïry
15:12
FAYDOU TV
Рет қаралды 1,8 М.
🛑 SABAKH TV moukhadam mame sette Touré
1:13:11
SABAKH TV
Рет қаралды 4,8 М.
BAYE NIASS NENA KOUNE MEDINA BOKKOUL SI KAOLACK KON ANA KAOLACK
27:36
GAMOU ANNUEL KEUR SERIGNE CORKA
50:23
Cheikh Ahmed Ibn Imam Hassan Cisse
Рет қаралды 451
СИНИЙ ИНЕЙ УЖЕ ВЫШЕЛ!❄️
01:01
DO$HIK
Рет қаралды 3,3 МЛН