Réponses imminentes aux partisans de l’allégeance à un gouvernement laïc (part.01)|| Oustaz Mor KEBE

  Рет қаралды 2,200

Sounnah Sénégal

Sounnah Sénégal

Күн бұрын

Пікірлер: 44
@muslimmindset3169
@muslimmindset3169 8 ай бұрын
Baarakallahu fiikoum tu fais bien la part des choses, boy yi eupeul mo léen djappeu rék
@magousamb1
@magousamb1 8 ай бұрын
Machallah❤oustaz mor
@elhadjitior1023
@elhadjitior1023 8 ай бұрын
Yalnagnou saxal si diné question de comprehension la rk bougnou takkalé sounou bir ahlou sounna sa kaw insha Allah
@aboubacrysow510
@aboubacrysow510 8 ай бұрын
Ma shallah cheikh Mor kebe
@loumsene3644
@loumsene3644 8 ай бұрын
Machallah
@dadjibokaleiakbida539
@dadjibokaleiakbida539 8 ай бұрын
Macha Allah amna solo wa mas'ala il faut niou leirale seini mbirr
@khadimthione4234
@khadimthione4234 8 ай бұрын
Mbock yi vraiment naniou deugue rrk yitel . . .mbock mi Limou léral amena solo brakallah fikum
@kvndebruyne8252
@kvndebruyne8252 8 ай бұрын
Machaalah
@muslimmindset3169
@muslimmindset3169 8 ай бұрын
Lii dafa léer Lima ci métti niom boy débat akh niom niak manduté deugg laniouy démée akh fanatisme
@khadydiop7794
@khadydiop7794 8 ай бұрын
Dars yi fane lay ammé svp, bane masjid ? J'ai un membre de ma famille qui serait intéressé pour y participer inchaa Allah.
@sounnahsenegaltv
@sounnahsenegaltv 8 ай бұрын
Dara yi yagg na deh Eup na plus de 10 ans voire 15 sakh
@khadydiop7794
@khadydiop7794 8 ай бұрын
@@sounnahsenegaltv Ah d'accord, barakAllahou fik. Imam Mor Kébé bane masjid lay faral di diangalé légui ?
@Ghurabaa221
@Ghurabaa221 8 ай бұрын
@@khadydiop7794Alqalam bi nekk Pikine
@muslimmindset3169
@muslimmindset3169 8 ай бұрын
Li léen sonal moy daniouy diaxassé niaari mbir yu bokkoul tekci eupeul ci, di rappi rappi di indi hadith yo khamni danguéen ci deupo beugg la ni par force danguéen ci diverger
@djamildiouf8593
@djamildiouf8593 8 ай бұрын
Tay nguén déédeh😂😂😂leppa ngui leeer😂😂😊
@cheikhsy3292
@cheikhsy3292 8 ай бұрын
Oustas waro wone yeuketi waate maassala bi.dafa lére ba paré.té mbok ti faaté wone nagne wa massalabi.té gnom li rék lagne beug.séni djiko rék wane nagnou né wa massala bi nékou gni si deug.so khamone c est troo sensible.té instant bi dou wakhtome
@bourhan142
@bourhan142 8 ай бұрын
Je vois quon d3vrait pas revivifier cette massala . La question mes amis est plus subtiles que vous le pensez. Ca ne fait que soulever les fitna de nouveaux. Cest mon opinion en tout cas .
@mawdodiop3833
@mawdodiop3833 8 ай бұрын
Benene mbir mi mor kebé di nakhé khaleyi moy islam daf ño jàngal ñu toppu njiit tant que mogui julli wayé waxoul ñu jayanté ak gouvernement bi wala. Hadîth bagui ñi ci kaw tant que ñogui jouli la yonenté bi wakh. Benene mbir mi suñu gouvernement bi dafa joté deug ak islam 1er : Ay joulite ño fa nekk 2eme : ñu taxaw ci ay wakhtou julli, di woor werou koor, 3eme : Philosophe yi asslane ci kufr lañu tegou duñu jouli duñu woor 4eme : naka guay def wakhou Ibn ibass كفر دون كفر 5eme : yonenté bi moné ken dou topp mbindef ci moy borom bi 6eme : ken wakhoula gua khôl ci constitution nguir jayanté constitution bi këfer la amoul sikk sikk 7eme : mor kebé naka guay def sa guayi di liguey ci administration? Ñi nekk impôt ak douanes
@laminebadji7919
@laminebadji7919 8 ай бұрын
Ki dafa sankou si sank khaléyii mais douniou bâyi wé nonou
@bourhan142
@bourhan142 8 ай бұрын
Seuy oustaz depuis dix ans gnamé wougnou débat ak p Oustaz mor , té nga noppi. Gnom fawzan lii mor wakh lagnouy wakh, té dounguèn lèn critiqué
@djamildiouf8593
@djamildiouf8593 8 ай бұрын
Yénagui tambalé fegne deh😂😂 parceque boyyi niongui tambalé xalate 😂😂😂
@aboumouaze85
@aboumouaze85 8 ай бұрын
Qu'Allah nous protége.Cette personne va créer une fitna pour le Sénégal. Il ne fait que philosopher. Ay wokham lay wokh.
@bourhan142
@bourhan142 8 ай бұрын
Wakho deug. So beugué nga gnow WhatsApp. Kii daf lèn raw rek. Moungui danwa di dimbali ndaw yi. Yèn nak dara critiqué rek moy sèn sunna
@mawdodiop3833
@mawdodiop3833 8 ай бұрын
Yiow Ahmad lo gua beuga tontou ci charh barbahari. Del talbiss rek deh mogui ñëw li gua beuga jappé sa dîné leudamal rek. Kane moy def ijtihaad ci ay mbir you leer nàññ borom xam-xam yi geune ko leral.
@laminebadji7919
@laminebadji7919 8 ай бұрын
Ki dafa sankou Kou Kone la
@ibrahimambodj6982
@ibrahimambodj6982 2 ай бұрын
B​@@laminebadji7919 BAYIL FENN AK SOKHOR
@mawdodiop3833
@mawdodiop3833 8 ай бұрын
L'imam Ahmad a été frappé et torturé par un roi qui voulait imposer sa mécréance. Malgré tout il a continué à appeler à l'écoute et l'obéissance envers ce roi. Rapporté par et Muslim, d’après Abu Hurayrah, le Messager d’Allâh صلى الله عليه وسلم a dit : «Tu dois écouter et obéir dans ta gêne comme dans ton aisance, dans ce que tu aimes et dans ce que tu détestes, quand même tu es lésé dans le partage.» Rapporté par Al Bukhâri et Muslim, d’après Abu Hurayrah, le prophète صلى الله عليه وسلم a dit : «Celui qui m'obéit obéit à Allâh et celui qui me désobéit a désobéi à Allâh. Celui qui obéit à son dirigeant m'a obéi et celui qui désobéit à son dirigeant m'a désobéi.» Rapporté par Al Bukhari et Muslim, d’après ibn Mas3ûd, le prophète صلى الله عليه وسلم a dit : «Viendra des émirs qui prendront de vous leur droit et vous refuseront votre droit.» Il dirent : «Que nous ordonnes-tu alors, Ô Messager d’Allâh ?» Il dit : «Accordez-leur leur droit, et demandez à Allâh le vôtre.» «Il y aura après moi des imams qui ne suivent pas ma guidée et ne se conforment pas à ma sounnah. Il y aura parmi eux des hommes aux coeurs de diable dans un corps d'être humain. Hudhayfah a dit : Et que devrais-je faire si je vis cela, Ô Messager d’Allâh ? Il dit : Tu écoutes et obéis à l’émir, même si ton dos est frappé et que tes biens sont pris, écoute et obéis.» Quant à la parole d’ibn Rajab : «Et cela est une preuve concernant le combat contre les émirs par la main». [Jâmi3 al 3ulûm wa l-hikam (2/248)] Mor kebé daguay sonou rekk mais bountou bi mounouloko leudamal demal teudi. Té yiow Bo jayanté woul ak Ngour gui ndakh dañuy atéwo charia loutakh nguay carte d'identité sénégalais ? Pourquoi nguay jeul avocat ? Loutakh
@djamildiouf8593
@djamildiouf8593 8 ай бұрын
Douuuuul rek
@khadimthione4234
@khadimthione4234 8 ай бұрын
Mn frère on dirait que comparendro li mbockmi di léral..wouté woléne si texsiyi gua dougueul...wouté bi fimou nek moye diayaneté bi...est ce que warnanio diayanté ak gouverneur laîk ...li moye wakhdji mais pour texsiyi gua dougeul lou wérre lonou nangoula ....ayé vraiment la cœur ouvert
@khadimthione4234
@khadimthione4234 8 ай бұрын
Mane dama léne di fréquenté lou barri sakh....mais vraiment contradiction dafa barry si séne yénne takha wayyi...mais nak samaye mbock guéne ndakh dolé pratiqué sirk ak bida Respecténaniou séne position donneté amna guéndékou
@mouhamadkebe2215
@mouhamadkebe2215 8 ай бұрын
Assalamou alaykoum wa rahmatoullah Et qui est le dirigeant selon toi? Macky Sall?
@DahwaSenegalAdiinouNasiiha
@DahwaSenegalAdiinouNasiiha 8 ай бұрын
Mor yeureumeul sa bop tagua baayi sa leunteul yi islam dou Philosophie
@mouhamadkebe2215
@mouhamadkebe2215 8 ай бұрын
Yeen yeena wara bayyi leunteul yi seen méthode madaakhila yi nit ñi yeewou nañ si. Propagande rek
@DahwaSenegalAdiinouNasiiha
@DahwaSenegalAdiinouNasiiha 8 ай бұрын
Kouy déglou mor dafa mélni djiiteum dou djoulite
@mouhamadkebe2215
@mouhamadkebe2215 8 ай бұрын
kzbin.info/aero/PLPUjXLvgmvAxKNtTKrf2Zn2PJDrWZDX3s&si=hswD9GUYlEFufjHP
@mouhamadkebe2215
@mouhamadkebe2215 8 ай бұрын
Écoutes les savants et tu sauras. Yeen baayi leen di daw loo nit ñi sunna ndax seeni leunt you beurri
@alassaneba5485
@alassaneba5485 8 ай бұрын
Il faut reconnaître que le cheikh mor kebe se trompe souvent. On n'a rien contre lui .
@mae2-ek5ug
@mae2-ek5ug 8 ай бұрын
L'erreur est humaine il l'a dit lui même
@DahwaSenegalAdiinouNasiiha
@DahwaSenegalAdiinouNasiiha 8 ай бұрын
Mor ak imam ndaw béne dokhaline manhaj khawaarij
@bourhan142
@bourhan142 8 ай бұрын
Khana yèn ay mourjia nguèn ? Fawzan, Ali sheykh , utheymiin gneup lii lagnouy wakh. Pourquoi dounguèn lèn traité de la même chose ?
@mouhamadkebe2215
@mouhamadkebe2215 8 ай бұрын
Bonne réponse.
@ibrahimambodj6982
@ibrahimambodj6982 2 ай бұрын
DAH WWW A FEN REK .
龟兔赛跑:好可爱的小乌龟#short #angel #clown
01:00
Super Beauty team
Рет қаралды 66 МЛН
Кәсіпқой бокс | Жәнібек Әлімханұлы - Андрей Михайлович
48:57
小蚂蚁会选到什么呢!#火影忍者 #佐助 #家庭
00:47
火影忍者一家
Рет қаралды 120 МЛН
REAL 3D brush can draw grass Life Hack #shorts #lifehacks
00:42
MrMaximus
Рет қаралды 11 МЛН
Le statut des jeunes en islam || Oustaz Mor KEBE
1:30:01
Sounnah Sénégal
Рет қаралды 1,4 М.
Histoire Moussa et Firawna || Oustaz Mor KEBE
1:48:03
Sounnah Sénégal
Рет қаралды 8 М.
Mettre à profit l'énergie des jeunes - Oustaz Mor KEBE
50:06
DAWAH au Sénégal
Рет қаралды 1,2 М.
CONFERENCE : L'ISLAM FACE A L'EVOLUTIN DU MONDE || OUSTAZ MOR KEBE H.A ||
1:15:46
Alkhourane Ak Sunna Rek Sénégal Tv
Рет қаралды 15 М.
Les batailles du Prophète  ﷺ (Cours 04) || Oustaz Oumar THIOUNE
52:58
龟兔赛跑:好可爱的小乌龟#short #angel #clown
01:00
Super Beauty team
Рет қаралды 66 МЛН