Рет қаралды 649
Rétro Mawlid | Extrait 20 - Mawlid 2016 avec Seydi Mouhamadou Moustapha SY Al Maktoum
"Nit mooy 7ème art ci sunu boroom...
Yàlla mo ngi bind Yonent bi ci 4 saisons:
saison 1 mu jublu ci Ruhaaniyaam,
saison 2 mu bind Nuraaniyaam,
saison 3 mu bind 'Aqlaaniyaam
saison 4 mu bind Jawhariyaam
ci Jawhariya bi la bind Li dess ci creature bi yëpp."
𝑫𝒂𝒏𝒔 𝒍𝒂 𝒇𝒆𝒓𝒗𝒆𝒖𝒓 𝒅𝒖 « 𝒀𝒂 𝑹𝒂𝒔𝒔𝒐𝒖𝒍𝒂𝒍 𝑳𝒂𝒉 », 𝒐𝒏 𝒑𝒍𝒐𝒏𝒈𝒆 𝒅𝒆̀𝒔 𝒎𝒂𝒊𝒏𝒕𝒆𝒏𝒂𝒏𝒕.
#Mawlid
#DMWM
#Gamou
#mawlid2023
#LaMotionEmotive