Bilahi daye fene dange na khamoul yalla motakh victoire kene douko nangou yalla nopina
@papezulefaye72639 ай бұрын
Serigne abdallah ngir yalla bayile eumeu sene sou nakaré nianal lolou yalla leu mais serigne deug dou wérr mbotou domou adama okkkk fi kéne meunoul nangou mbirou domou adama sou nekhoul yalla souniou borom bayiléne khel ni meunoléne yalla mo meun té yalla si meun meunam gui ngeni soutourlo bayiko khel...niou fanane ak jamm
@Enfant_béni_79 ай бұрын
MANE PLATEAU BI VRAIMENT BAYE BALLA MOMA SI GEUNA NÉKH ❤ J'AIME SA FAÇON DE PARLER ❤ ET IL EST PERTINENT ❤
@bybrufisquois2578 ай бұрын
Bay balla dafa wanè lol
@travisscottwiiz88709 ай бұрын
Balla gaye 2 kassé merci beaucoup serigne bi❤❤
@ousseynoutoure5188 ай бұрын
Xolatal Say kadou un grand champion comme Gris guéne warouko wakh nul Begue émission bou nekh dou takh ngakoy niague respect
@mmsseye93918 ай бұрын
Mara yi ay mbayar lagn.. favori rek lagnouy nianale
@seydoukanesall8 ай бұрын
Serigne siii dale tu comprends pas,il avait dit que balla dafa ame guémb deug ,alors que eume sene la terrasser deux fois avec les bombardier , arrêté un peu quand mm ,loudoule yala nén la, Allah seul décide de tout bilahi
@ModouKaraNDOYE8 ай бұрын
Bekay merci lisi dés douleur rekk
@Knmunhomme8 ай бұрын
Eumeu séne kou nakarari gnaanal wayé loumou Beugue ameko ,, nianal soeur am yaye am doynako
@Knmunhomme8 ай бұрын
Mané eumeu sene pur gaïndé leu
@matarthiam95729 ай бұрын
Bonsoir wa plateau bi Baye Balla ak toute l'équipe ziar nalenn
@legendediop92159 ай бұрын
Balla mi eumeu niouss aller retour 😂😂😂😂ya meuna doull
@ibrahimasougou70618 ай бұрын
Balla mi niouss modou deux fois moko niouss tamit deux fois palmarès eumeu 10 victoires 08 défaites 2 matches nuls un sans verdict wara khass kéne imbécil
@ibrahimasougou70618 ай бұрын
Modou miko niouss deux fois béne mou teudi nélaw mom la balla dane deux fois imbécile palmarès de 10 victoires 08 défaites 2 sans verdict et un match nul😂😂😂😂
@almaktoumdiop87498 ай бұрын
Ki wakhoufi dara balla gaye mogeuneu nékh gñianal eumeu séne mo geuneu nakhadé gñianal té eumeu mi nakhadé gñianal dane balla gaye mi nékh gñianal no sénégal serigñou tariyakh yi danouye dokh si khélou nite gñi 😂😂😂
@Enfant_béni_79 ай бұрын
EUMEU SÉNE MOFI GEUNA NAKARÉ NIANAL TÉ DIEUL NA ROI DES ARÈNES ET TÉKSI DI LÉKEU AY MILLIONS WAME BILAY YA MEUNA DOUL 😂😂😂😂😂
@seydinasow44158 ай бұрын
Non vraiment eumeu sonouna kou djouke né eumeu sene au le pauvre eumeu 😂😂😂
@AbdouMBAYE-u8w9 ай бұрын
Geumouma nh satouba kham na dra 😢😢😢 vraiment
@Sodasall72459 ай бұрын
😂😂😂😂😂😂
@Madou-h1g9 ай бұрын
Khamouniou touss saler rek di saup
@Madou-h1g9 ай бұрын
Khamouniou touss saler rek di saup
@Madou-h1g9 ай бұрын
Khamouniou touss saler rek di saup
@Madou-h1g9 ай бұрын
Khamouniou touss saler rek di saup
@omarceesay13428 ай бұрын
Lii meunteu wessou weddi lou borom bi dogal
@papengom2598 ай бұрын
Tieuy yalla mignou sak 😂😂Sénégal dafa nékh koi 😂😂😂
@cheikhbasskeurmassar95489 ай бұрын
Sa touba mou bakh mi
@abdourahmanesindidi18188 ай бұрын
Sa kharit khana😂
@waganefaye21139 ай бұрын
Moooo
@Enfant_béni_79 ай бұрын
Ay pro wagane Loy déf fi
@modoudiouf518 ай бұрын
Yene modou lo wer naléne nakhaté rek ngene fi nekal
@ibrahimandiaye42529 ай бұрын
😅😅😮😅
@Madou-h1g9 ай бұрын
Mane khawma loutakh ame gnou niemer yalla rek mbeur bou beurre ba donne roi des arene nga tok fi di doul nane kou nakhare gnanal la
@ousseynoutoure5188 ай бұрын
Xolatal Say kadou un grand champion comme Gris guéne warouko wakh nul Begue émission bou nekh dou takh ngakoy niague respect