Kon yatt yangui dall, ok c'est bien, dieufeurou lén bou bahh. Danguén gatteu allouwé, meuneu Bokkalé, ndiabar, bida, té kouy def mbossor ak thiaahan ci tarikha la nékk, kouy Téré jigéen di Mourou ci yénn lakoy fékk.... Ay touuma mom , yaagg naa diogué ci yénn, mais nji Y'Allah beug Guindi bi idznilLah dinagn guénn ci sen tarikha yi. Alla bonni tassawuf.
@ElHadjiMalickFall-dz6xj5 ай бұрын
Pour nga nek wahabia fok nga meun fen.😊
@ibrahimaba51994 ай бұрын
Wahabit=fén ak sosse
@AbdouNiane-j9d6 күн бұрын
Thank you so much my brother 🙏
@serignetoubarek5 ай бұрын
Lislaam na atte Alpha ba ✂️🔪🔪🔪🔪🔪
@AliouGuey-t7c4 ай бұрын
Sakiri naike sama saringe la ❤❤❤❤❤
@Baatine5 ай бұрын
Touma safatoul kenn senegal ndakh adji sarr .niou bari nio fatou apres niou dora xam ni sonko defoul dara .mandoulene allakhira amna
@bambafallhouboulkhouranedg689118 күн бұрын
Yaw diouguel fi ah
@Baatine5 ай бұрын
Alpha bouder yagui lir sama commentaire mounieul ta yalla takh .yalla baxna yalnala yalla taxawou
@mbayebabacardiouf785321 күн бұрын
😂😂😂 woôooy😊
@Yatalxamxam-q5d4 ай бұрын
Bilaye ligua wakhe si Amadou sow loulére lasi âme mague aye domame niodone anede Mousole sarakhé mosoule guéné الزكاة aye dome sakhe douléne débali
@Diomaye-n9w5 ай бұрын
Ne pas confondre wahhabites et ibadou Moi je suis ibadou et tout ce qui se dis là ne me concerne pas Et il ne faut pas confondre l'homme et le message
@gueyedarou88865 ай бұрын
No yene ibadou yi niou bakh guene do lene wakh Kenn lou bone
@abousow50215 ай бұрын
LOLOU DE KEN DOUKA DIAWALE WAHABISTE GNEUP HAMENANE LEN COUREL BANDI YOUY MBOUBO DINE DJI YAK SI LOU BARE
je ne sais pas qui êtes mais crainier Allah swt et sachez qu'un jour viendra vous allez justifier vos faux accusations devant Allah est Sur les gens de la sunna et du consensus. Faites autant de sabotage que vous le pouvez, faites autant de blasphème que vous le pouvez mais le Coran et la sunna mon grès mal grés sont les seuls référence Don Allah nous informer. qu'Allah swt vous nous guides . encore une fois réfléchissez à ce que vous faites.
@FallouGuisse-cq5wj5 ай бұрын
Alpha saa maroc
@mouhamedmakhroufthiam14765 ай бұрын
Oho live bi nehna way lingua wah leip deug la, walahi azime wahabya boko frékenté woul reik doko ham..aka nio bone..
@walit2345 ай бұрын
Bayyilèen toogn. Li ngèn wax yeup ci yèneu wahabityi meuneugn ko wax ci yènneu soufiyanké. Problème niitleu. Yèneu ngi bakaar, yènneu ngi diaxassé, yenneu ngi fènneul ay dioulit. Après vous pensez que vous êtes meilleurs qu'eux.
Alpha ba fenkat la kay lougne ko djigne ma geum ko
@NittyBitty225 ай бұрын
Sheikh Alpha bouleen deglou Ndakh ay nittou touroukh lagnou (Mouridyi) Léeral yi ngay léeral mooleen metti, Sheikh Alpha, donc focus si * djangalé Al qur'an ak Sunnah, daddji shirk (bokkalé) ak bidah (soss) Alqur'an ak Sunnah triompheront malgré l'aversion des soufiankés endurcis Wa salâm
@djibrilsene47135 ай бұрын
SES GENS IL N'OSE PAS PRONONCER CERTAINES CHOSE DANS BEAUCOUP DE PAYS MUSULMAN.
@salamsalam49605 ай бұрын
Sunat rek yem si sunat rek sunat ba yawmal khiyam 😂😂😂😂😂😂😂mbeleeee
@modourokhaya96165 ай бұрын
Mouyeen
@salamsalam49605 ай бұрын
@@modourokhaya9616 yonentibi bi rek legni topou kenen koudoul mom lidianti wougnou leu topal feleu 😂😂😂😂😂😂
@abdoukhadretop2555 ай бұрын
Je le suit il bat le record de convertir
@mamadoudiallo26965 ай бұрын
Gnou diangue touuti, wahabya dou meunn dougue sa bopp
@alleualleu6935 ай бұрын
Nokhoulen feuleee wakhoulenfi darra😂😂😂 Alkhouran ak sounou mom lanouy deglou
@cheikhdiop96735 ай бұрын
lane Moy souna noy wakhé Al khouran baparé nane ak lénéne Al khouran Moy wakhi yalla toupoulén Al khouran ak ndiagaléne yalla souna la kénn khamoul Moy lane ay téré taymiya ak imame Malick ak boukhari dagay diageu téré kénn ci gnom mou wédi li kénene ki wax légui lane mosi wér li wér mome léne la Mouy Al khouran fo dém ci adouna bénn Al khouran bi Moy firi lépp amoul ak wouté Fatiha bisi Sénégal mo nék fépp téguéna yém si li ta nopalou bakhna Dale dieule wakhi nitt ni yonente bi moko wax ta ki gay nétali ay wakham fékéwoul diamonoy yonénte bi
@alleualleu6935 ай бұрын
Amoulen dalill 😅😅😅😅
@Hamidthiaw47825 ай бұрын
Bounguéne laadjone khadim bousso, Kone dinguene fi baayyil alpha ba. Dounguéne ci amé ndame.
@kakhadim65115 ай бұрын
Ya manafenn
@cheikhdiop14255 ай бұрын
Alpha Ba vrai say say la mais c’est normal chez eux.
@fatoukinekane609620 күн бұрын
Fen bakhoul
@elagegueye33105 ай бұрын
yen guen nekk lou yenentebi psl meustaham guenee kenen dou nek lou yenentebi nek niotay nek ibadou
@damefall24275 ай бұрын
Wahhabites nio yesse si adouna
@AbdouNiane-j9d6 күн бұрын
Alpha ba is the biggest animal I'm telling you guys
@Baatine5 ай бұрын
Baye niass nena degue na bepp kadou bou bone bamou dess baye niass da eumb yakko .donc alpha grawoul
@Hamidthiaw47825 ай бұрын
Deugg Dina feigne. Lî yeuuupp ay toûma késsé la. Khadim bousso wakhoonafi Lou gueuna graaw. Djoullite dafay wéddil toûma moroomou djoullitam. In djaahakoum faassikhoune fatabayyanoû.
@djilysokhna25485 ай бұрын
Yaw li alfa di toumal kilifa yi yahui koy wéddi
@Hamidthiaw47825 ай бұрын
@@djilysokhna2548 waawaaw sou tégué ci alqur'aan ak sounna.
@cheikhdiop96735 ай бұрын
@@Hamidthiaw4782yaye domouram deug touma yépp toumala Al khouran nak dou toumal kénn ndiagaléme yalla la séne wakhi souna yi lakhamoul Moy lane souna dou diné ndax nétalip nitt rék guén toudé souna Al khouran Moy diné diap léne si wakhi yalla yémsa nopalou hadis yigén geum gnikoy nétali kénn fékéwouthi diamanoy yonénte bi ta gnom gnépa réro ci ay wax légui ana lisi wér légui diap léne si Al khouran Moy bénn téré bi amoul wouté Fatiha bisi Sénégal mo nék fépp si adouna bi bayiléne thiakhane ak sosale yonénte bi fénn bakhoul
@djimbycourasene31465 ай бұрын
Le gars qui parle a la 13em minutes vraiment tu es vide de sens et desprit Claire. Sommes a lère de la deffailllance intellectuelle et morale
@Hamidthiaw47825 ай бұрын
Serigne bi, sa vidéo bi wakhoofi darra Lou lére. Ana vidéo yi. Yéne gni toûmaal yénay indi ay preuve.
@gueyedarou88865 ай бұрын
Yen kay nopilene rek
@abousow50215 ай бұрын
KEN TOUMALOUKA MO KATTA BOY BI
@whatsup-hl5qm5 ай бұрын
Merci copen 👍
@daamnjaay12745 ай бұрын
Saa-maroc kay😅
@falloudiop22975 ай бұрын
allpha ba donoull joulitt lauff rek la kaume
@AhmaGueye-t8y5 ай бұрын
Alpha kalbon la😂
@taliberassoul5 ай бұрын
Yalla mom ken douko giss fii koudoul seyyidina
@ibrahimaSy-ws5fx5 ай бұрын
Yalna'yalah'samou'leene
@moctargueye94945 ай бұрын
Guisna ibadou bo xamni thiow rék la meune ci nitt gni ak wakh di wéddi té fék dafa am séŕignou peulh boukoy diokh ay bouteille mouy sangou😂😂😂😂😂😂😂
@mamethiernondiaye5805 ай бұрын
Gayi tañiy sangou dañuy diwo wayé khana kaay tak landoul déf ,khamna Si ñoubari
@moctargueye94945 ай бұрын
Waw guisga loolou man guisna niou bari ci daniou yor ay xaatim diko liguéy
@alleualleu6935 ай бұрын
Def bakar ak wakh deugue bokoul Alpha mo kham 😅😅😅
@njaay42665 ай бұрын
Araaka siraa jann yuhrafut dahra nafsahuu! Seydil hadji malick moko wax! Manal wax ci diiné te lingay wax bokul AK lingay fegnal, lolu djikoy sondel la sak leeral du yagg dé, ndax dangay lor sa Bopp
@mouhamaddiouf5 ай бұрын
Ce gars n'a jamais été un sunni alors arrêtez de mentir
@moussakeita90855 ай бұрын
Nit nioulay bonne. Wa tassawouf bougouniou lou baax. Sen campagne de diabolisation bi dou diall.
@MansourFall-h7j5 ай бұрын
Dajjala alpha mi
@ndiayekhalil71565 ай бұрын
Ay éléments dédiâl lane
@lilbeezy75175 ай бұрын
❤❤❤❤
@bamohamed61525 ай бұрын
Wahabit yi baxou niou
@loufaassdiao53895 ай бұрын
Cheikh dél rafétal kadou yi
@BoubaNdaw-uw2ow5 ай бұрын
Wa diamra wa annda sama djikoyi niokossi bayi
@Ndiaye845 ай бұрын
Alfa ba borom dahwa KATANETÉ bii l'islam raynako NDAX am SOXNA ba paré Di ndialoo
@cheikhsow55505 ай бұрын
wakh lėne de Alfa wakh nako dėmale liguėyii
@alleualleu6935 ай бұрын
Islam ken douko dondo😅😅😅 Wakhi doff
@bfbmckingridialulah76025 ай бұрын
Wahabiste yi saytané laniou andal dh🎉
@AmadiGuaye5 ай бұрын
Vraiment vous nous s'attarder avec des mansonges
@abousow50215 ай бұрын
LOUY WANENI AYE FENNE LA ANDI KO
@mamadouseck51355 ай бұрын
Bayile sama copain bi
@aronafaye48595 ай бұрын
Amo len tous . Na alhouran ak sunnah deguou ci kaw souf rec kou ci nekeu fagueu nek nekafa soldarou sounou brome. Salaf saleh
@NgoudasarrNgoudasarr5 ай бұрын
Borome 1000000 milles khadiss yi 😂😂😂😂😂
@loousmane22385 ай бұрын
Sa way nga balma mais ce que tu racontes là est truffé de contrevérité.
@bamohamed61525 ай бұрын
Nit dafa wara ame ay tegine
@cybersaabir44775 ай бұрын
Je ne sais vraiment pas comment vous faites pour être aussi cons.😂😂😂
@kidkid45613 күн бұрын
Arretez vos mensonges
@taliberassoul5 ай бұрын
Danga fen de ousseynou ken posonoko
@laminekande94035 ай бұрын
Wahabisyi dagni sonal sen bopu
@fatoukinekane609620 күн бұрын
Tu n à jamais été ibadou
@NjabehJagne4 ай бұрын
Yaw lengay wahk final
@AlBurhan_sn5 ай бұрын
Yenangi fébar wa Sounnah 😂😂
@cheikhsy32925 ай бұрын
Ki mo meuneu féne.ragaléne YALLAH sosse baakhoule.képe kougnou sossal di nga moudjé ame ndame.ba si ousmane sonko
@MbayeNdiaye-t2w5 ай бұрын
Néna ex wahabiste bayil fén soss baakhoul
@alleualleu6935 ай бұрын
Tarikha thiahan la😂😂😂😂
@seydousambakoulibaly7345 ай бұрын
Démal nani ndokh bou sedd . Tarikhas yi plus haut, plus fort !