bravo mbeur, tu étais promis à un bel avenir dans la lutte sénégalaise, malheureusement tu avais complètement disparu des arènes pendant des années, je croyais même que tu étais en prison, or tu as bien expliqué qu'on t'avait retiré ta licence pour 3 ans, félicitations après ta défaite contre ama balde tu avais dit que je ne salis j'aimais la victoire de quelqu'un ,et tu viens de répéter la même chose ( tu est un grand champion)
@zezegomis55154 жыл бұрын
Très bonne communication et courage ça viendra un jour
Champing gaïndé Baye Fall bi name'nagn l ci aréne bi dagnou l wara outal combat nakh ay champion kécé nga daane té champion yi l daane aussi dakou gnoula beuré bougnou ko téggué ci yone chak anné danga wara beuré nakh sa combat dey diare dey nekh té amnga public bou nékk sa guinaw beuri lolou nk té namla trOOOPPP FOGOLI SÉRÉRE💪💪
@ndongombabane30224 жыл бұрын
Merci
@moustaphaniasse70424 жыл бұрын
Bébé saloum champion nga lambe amoul secret entrener rekk bou meti molaye takha deff lingathi beugue...ymgx bombardier ak eumeu SÉNE bala gaye avc son retour et modou avc son rois des arènes exemple laniou thi lima wax niane mom fimou tolu ni dafa wara ande ak takhawaye in cha allah chifa thi yaw wala kepp koulaye bégué
@ndiayecheikh4 жыл бұрын
Kii meun na wakh dh tei xamna nimouy wakhei aussi laff thiat way champion la nak
@lionnoir27994 жыл бұрын
Bebe demal def NMa
@sarrabdou30404 жыл бұрын
Akka deugeu woloffffff talibè baye Karim
@adamamballo78864 жыл бұрын
amiiine
@davembengue29384 жыл бұрын
Wakhna degue prometeur yi danio sokhorè mbeur yi
@papekebe37124 жыл бұрын
Bébé saloum dé meune na beuré meune na reports lambeu
@diopcheikh89364 жыл бұрын
Gawa danou
@fatoudiouf10594 жыл бұрын
Bb yaw wakhe rek ga mene
@seydoudrame13774 жыл бұрын
Non bb meune nga wax trop liguéyatal té oute staff bou bax continuer sa yoone
@Daarayserigneabdoukhoudoos4 жыл бұрын
Machalla bb saloume mais nak Ama dala man
@youssouphgomis20474 жыл бұрын
221people na yènen site yi dieul exemple si yène manam di protège micro bi amna solo lol👏🏿
@ousmanediagne95024 жыл бұрын
Bb saloum dégue gua wolof
@Zidane-rc3cq4 жыл бұрын
*Ayway garga dh sonou na ioe chaque jr nga wax sa combat ak garga peuff🤦♂️*
@bourathobouratho46724 жыл бұрын
Nopli amo lo wakh Malika gua nék di takha walou rék té fofou yeup Ay d'une la wayé yaw sa treunn dafa yombou défar katou yaram Yi sakh niola daka treunn
@amadoubalde69234 жыл бұрын
Right
@momothiam40394 жыл бұрын
Continue a travaille tega lakhatu wagni wakh dji mbeur so bgue dfatt retour dagay leuluuu wagni cite intetnet yiiii
@ibrahimatine98632 жыл бұрын
Ama Baldé kessé lay supporté dei mais da ame sociale trop sax
@yesiam10114 жыл бұрын
demal entraîner dji yala bakhnaaaaa
@mouhamedcisse58484 жыл бұрын
Geumal yala
@cheikhbasskeurmassar95484 жыл бұрын
Thiey bébé Saloum 🤣🤣🤣🤣🤣😂😂😂😄😄😄😃🤣🤣🤣🤣🤣
@papediagne48064 жыл бұрын
thiey cheikh c miyeur comantér founé lala guis🤝🤝
@linkstardidingkeba29224 жыл бұрын
Sheuuuuu bébé ya dégg kalama. Yaw war nga meuna nékk animateur radio. Wala communicateur. Yangui nane dama danne danne danne danne danne danne danne ba dadiék ama baldé doga dégue mougneul saway beurelwoul nonou. Ama baldé 4 victoires Bébé Saloum 4 singuénn dadié Ama dan la. C'est vrai que tu es très téchnique mais gniméwo entrainement sa yaram bi banga amé sa 1ere défaite la gueudia dague. Deukona thiaroye khamna limay wakh
@serignefalloundiaye13684 жыл бұрын
Waw kii meuneu wax
@cheikhgaye21674 жыл бұрын
Kocc barma Khanna más guénna Boku diotay wólof mom khamu ma lo manoul wayé Borussia😁😁
@zgrsljrbkbtfg11354 жыл бұрын
Wah mome mangako lol macha ALLAH
@massambafaye17124 жыл бұрын
Loula dall bari wakh molako yobé
@bayfall97074 жыл бұрын
Wakh mom yay Chef
@moussandiaye84904 жыл бұрын
Kone iao xamnga kii😂😂😂😂😂 machala ci coté bobou 🤣
@adamabao27574 жыл бұрын
Lamign bai graw😀
@bayfall97074 жыл бұрын
@Ndiaye Samba loutakh
@abdoulahaddiop37954 жыл бұрын
Machallah
@mbmilanocheck91274 жыл бұрын
Ki xana Baol baol la lamign bi nèx na trp way
@babouthiam87574 жыл бұрын
Mais nak Ama deila meunn dann laa
@danilombaye954 жыл бұрын
Wakh gua degue par parlo bi rék mo yakh lamb dji
@nourouchikory81134 жыл бұрын
Nekal fi di talife rék
@babouthiam87574 жыл бұрын
Néxull baa néxull mais meunn communiqué
@babasidia11154 жыл бұрын
Jambargua Si wakh wakh mom
@morymamousafall9204 жыл бұрын
Wakh diou nékh eubeul lamb bayil sa wakh diou bari dji geumeul yalla
@papatempo83644 жыл бұрын
ak meuneu wakh té dégue Wolof
@jacky33264 жыл бұрын
Deugeu rek nga fi wakh mbeur
@boygueye19764 жыл бұрын
Bb Saloum khana seutou kocc barma la lol ?
@ndigasalioutoure1724 жыл бұрын
Ki mome dafa commencé déf louniouko xamé woul wone.da bari wax trop légui. Démal guan entraîné dji sa yaram koula xol xamni entraîné wo.tu Parles trop
@ibousene98724 жыл бұрын
Communicateur traditionnelle😅😅😅
@cheikhdiop21574 жыл бұрын
Ki ndananou lamigne la
@abdoudiop83934 жыл бұрын
Kii kaye moo warona nek port parolou mbeuryi moytoulma bébé" wakh rek