Imam Khadim Ndiaye parcelle, Lima dundu sama keur fi ci Touba.. Sama diganteek…

  Рет қаралды 58,494

Rafah TV International

Rafah TV International

Күн бұрын

Пікірлер: 581
@BaraDieng-io7my
@BaraDieng-io7my 5 күн бұрын
Yenagui wakh rkk barki alhouran imame khadime ndiaye mi ki moma diagal alhouran bama wathié 3 foiss nitt kou geum yalla moy ki
@Generalahmadoudame
@Generalahmadoudame 4 күн бұрын
Wa ligui
@serignecheikhkhadimfall6654
@serignecheikhkhadimfall6654 3 күн бұрын
Dayagoultouba motakh khamoul darra thi yonou mouride ab sip
@fallam1010
@fallam1010 2 күн бұрын
lu siy sunu yoone ibadou ya gui kay defendre ki du tuss
@serignembaye4602
@serignembaye4602 5 күн бұрын
Imam khadim Ndiaye mi ku ragal yalla la wallahi
@mbayekasse4960
@mbayekasse4960 5 күн бұрын
Talibé bimou doone daa wara dem WAKH AK séeni kilifa Gniléne Santa la gnouy . 9
@mbayekasse4960
@mbayekasse4960 5 күн бұрын
Def
@milkfaye2761
@milkfaye2761 4 күн бұрын
Yow geumo s touba
@sidylo9069
@sidylo9069 4 күн бұрын
​@@milkfaye2761wakhou deug dee kii mourid sadikh mom mo diangal imame seringe aboul barake mbacké miye djiété nafila massalik fi si ndakarou
@MouridoulLaahi
@MouridoulLaahi 3 күн бұрын
Kii mome Loum djoublo wakh 😂wakhoufi dara DH yën ñii diko partagé démléne Bay fallga ba paré 2parti 😂😂😂😂😂😂😂😂😂moy yone kii wakhoufi dara
@SaTouba-f4f
@SaTouba-f4f 5 күн бұрын
Kou wakhoul degeu Wakh Safan civil Manoul Rek le Maromou Civil leum.. Wallahi Ya Imame Ya nek thi Dégue.😢😢😢😢
@niangmayib2073
@niangmayib2073 5 күн бұрын
Deug rk mooy deug
@cheikhabdoudiop5335
@cheikhabdoudiop5335 5 күн бұрын
Djreudjeuf s khadim ndiaye moumelné linléne sante ak liniye deff bokugnou ndakh toubeuy bou andéck moummu diott daganna thi lislam gniy diapé warnano ragné
@cheikhabdoudiop5335
@cheikhabdoudiop5335 5 күн бұрын
Dengdjiou wér peigu
@DiagneElhadji-d8f
@DiagneElhadji-d8f 5 күн бұрын
Esk wokho lasa dess kon ndigeul dieuféde
@is909
@is909 4 күн бұрын
Lolou moy deugue
@assanefallphotography6921
@assanefallphotography6921 5 күн бұрын
Imam Khadim Ndiaye un référence ❤
@AyoubaNdiaye-y5h
@AyoubaNdiaye-y5h 5 күн бұрын
الذين ان مّكّنّاهم في الأرض أقاموا الصلاة وآتوا الزكاة وامروا بالمعروف ونهوا عن المنكر ولله عاقبة الأمور
@babacardieng-yt6si
@babacardieng-yt6si 3 күн бұрын
Dieredieufé Serigne Touba 🙏🙏🙏 Diaramaaa mm cheikh ibra ibrahima fall 🙏🙏🙏
@alassanedieng8579
@alassanedieng8579 5 күн бұрын
Merci Imame ces actes sont ignobles dans la ville de Serigne Touba c'est a dénoncer ils font dans l'abus
@ousseynoutoure3621
@ousseynoutoure3621 5 күн бұрын
Bou adouna bi yeupe dadjei ak koumou meuneu done bo teigouwoul si ndigueul gni teigueul leine
@fallam1010
@fallam1010 2 күн бұрын
en quoi cela vs concerne
@ablayesane6519
@ablayesane6519 5 күн бұрын
IL faut que l’état prenne ses responsabilités . Nous partageons tous le mm territoire alors on est tous égaux devant la loi , ces actes de violation de droit de l'homme ,il faut que ça cesse
@fallam1010
@fallam1010 2 күн бұрын
tu es fou
@almakdiw3708
@almakdiw3708 5 күн бұрын
*Mane lima diakhal khana li Serigne Touba begeu diouli ak woor bokossi pourquoi Serigne Mountakha diokhé woul ndigeul kép koudoul diouli ak di woor wérou koor,niou guénéla Touba wale niou togn sa keur comme nimouko wakhé si manifestation. Actuellement kéne khamoul bane Dinné mo daw Touba*
@MamedaraThioub
@MamedaraThioub 5 күн бұрын
Khamoko c normal tous le nepeut pas compredre et adherer au mouridiya Nous y somme et lidjentiwou lénéne
@wakanatv1143
@wakanatv1143 5 күн бұрын
Yaw teenga teuj sa gatt gi la waxx ta nopi senuk niaka julli sa yonn nekusi yaradiku ba dee
@nmdelmuchacho3403
@nmdelmuchacho3403 4 күн бұрын
En tout cas kou diouli thi guéthie dou téré diouly
@obd2214
@obd2214 4 күн бұрын
Dañuy bayi waxi Yallah di topp waxi nitt Lii mo dallone wa akhlou Nûh Yaw seu biir deukk ñakk Julli ak woor dagane na fa 😂😂😂 wayé ñak mourou ak football daganoul 😂😂😂 J'aime mon pays
@almakdiw3708
@almakdiw3708 20 сағат бұрын
@@wakanatv1143 khana gattou Baltazar Mbacké lay teuth
@toubapatar
@toubapatar 5 күн бұрын
Dieureudieuf imam xadim ndiaye
@MouhamadoulamineSamb-n8g
@MouhamadoulamineSamb-n8g 5 күн бұрын
Touba li serigne bi beug moy am ما يريد الشيخ هو ما أمر الله،ما نهاه هو ما نهاه الله،وسلام على المرسلين والحمد لله رب العالمين،moytoulen baye fall yi bakhna
@AntaMbaye-pq1jr
@AntaMbaye-pq1jr 5 күн бұрын
Khamo gatt nopill
@khadimathj8129
@khadimathj8129 5 күн бұрын
Le marabout n'est pas en règle. Les baye faux sont des sauvages
@abdoulabdoul7809
@abdoulabdoul7809 5 күн бұрын
Mane dé Touba Yallah boumafa am sokhla ba béss bimey guéneu adouna amine 🤲🏾 deukou bou amoul ndokh mou nékh té bari mboyo 😂😂😂
@modoudieng2750
@modoudieng2750 5 күн бұрын
Wa Wawaw sa baay dafa amoul duek mootakh
@abdoulabdoul7809
@abdoulabdoul7809 5 күн бұрын
@@modoudieng2750 yaw ak sap serigne binga gueum sen thioparétou ndeye 😂😂😂 mane domi lébou laa, sokhla wouma nieuw touba té Yallah boumafa am sokhla ba béss bimey guéneu adouna amine 🤲🏾 deukou bou niaf ndeyam bobou ndokh mou nékh amoufa, loumafaye deff 😂😂😂
@Sénéga.dioubanti
@Sénéga.dioubanti 4 күн бұрын
Bilahi kou bayi diouli AK wore do am yermande si diamou yalla yi rawati na dijgune
@serignesodagueye3398
@serignesodagueye3398 5 күн бұрын
Wawe goor IMAME Khadime ❤❤❤
@mordiop5531
@mordiop5531 5 күн бұрын
Nit kou bakh Serigne khadim Ndiaye
@Échophysiologiste-cb9bi
@Échophysiologiste-cb9bi 5 күн бұрын
Lii reka bax❤❤❤ Louté nga wax ak kilifa yi ngay si Internet bi, lii segn bi beugue moy am
@samdiawdiaw8269
@samdiawdiaw8269 4 күн бұрын
xna dego ko ki limiy wax si ragal yla lako tek bayil narfex
@CheikhounaDiop-f3s
@CheikhounaDiop-f3s 4 күн бұрын
Li Serigne bi beugeu kane mola wax dou am ??? Ki di wax mo la geuna diégué serigne bi .seytané yi gueen done
@abdouniangtv180
@abdouniangtv180 3 күн бұрын
seringue bi molén wakh ngéni diapou djigéne yi wa loutakh yalla mom lim wakh dolén si déff dara sénn seringue you nio dakha nan sangara di mandi loll dolénsi wakh
@amdymoustaphaakasa5963
@amdymoustaphaakasa5963 5 күн бұрын
Dieuredieuf borom touba diarama mame cheikh Ibrahima fall
@Azou0596
@Azou0596 5 күн бұрын
Ça n’a rien à voir ak Li imam di waxx Lii acte terroriste la nioun nieup ay Mouride laniou
@milkfaye2761
@milkfaye2761 4 күн бұрын
Yow geumo s touba yefarala geun
@degdeugtv7872
@degdeugtv7872 5 күн бұрын
Civil dou règle Civil dans un pays de droit
@secksaliou1575
@secksaliou1575 5 күн бұрын
Merci beaucoup serigne bi baye fall yi dano raw bilakh
@senegalvillagetvdiop5152
@senegalvillagetvdiop5152 4 күн бұрын
Ak lou mena am d'où deug d'où yone yalla mignou wathie ci soufam ci sakh force wougnou guèni thiahane
@MoustaphaSourang-qo1cz
@MoustaphaSourang-qo1cz 4 күн бұрын
Touba daal lifi Serigne bi beug Moy Am inchallah wa Salam 🧏🏿🧏🏿🧏🏿🧏🏿🧏🏿
@Sénéga.dioubanti
@Sénéga.dioubanti 4 күн бұрын
Yaw eska Touba NGA dekoue kou bayi diouli AK wore xole bou Bone laye am
@senegalvillagetvdiop5152
@senegalvillagetvdiop5152 4 күн бұрын
Meno wah ba am deug
@Generalahmadoudame
@Generalahmadoudame 4 күн бұрын
​@@Sénéga.dioubantilolo yoono nitt neko si sén degeunte AK yalla la
@Khadimdiopi2000
@Khadimdiopi2000 5 күн бұрын
Ndeyssane Serigne Khadim Ndiaye ❤khawma kañ lakoye djissate ❤
@amleking2219
@amleking2219 5 күн бұрын
Sénégal nékhoula wakhé mais bou ëuleugué dinane khamni serigne bi nékoul si yi niou nék blh💔💔
@modousall8286
@modousall8286 5 күн бұрын
Merci imam❤
@boromtawfkhetv6216
@boromtawfkhetv6216 5 күн бұрын
Serigne Khadum Ndiaye Kouma Naw Loll Gur Dokhinam Bou Refett
@IbrahimasarrDieng
@IbrahimasarrDieng 5 күн бұрын
Bilahi imam ya nek thi dégue baye fall yi yabate rek lan def
@gorambengue335
@gorambengue335 4 күн бұрын
Bakhna S chiekh thiouro dina len yay Lii
@Babacarmagane
@Babacarmagane 5 күн бұрын
Merci imam
@mouhameddiallo8975
@mouhameddiallo8975 4 күн бұрын
Li Serign bi Beug thii deuk bii mo am inch'Allah 🤝
@modoundiaye3999
@modoundiaye3999 4 күн бұрын
Warone na fékk ngéni dieufé ndigalou Yallah niak diom
@NdiayeModou-b1d
@NdiayeModou-b1d 4 күн бұрын
Thiakhan kep laniouy def
@SaliouSene-t2q
@SaliouSene-t2q 4 күн бұрын
Li Serigne beugue moy am
@diopsonko6494
@diopsonko6494 4 күн бұрын
Lolo moye ngaye dioli
@LeyeMohamed
@LeyeMohamed 4 күн бұрын
Nite défoull Lou gane djouly❤❤❤
@modoudiengsopbichri6434
@modoudiengsopbichri6434 4 күн бұрын
Li Serigne bi beug si deuk inchalla moy té kou ame lolu meti demal thi serigne Mountakh Mbacke nga wax koko ndax moy jëuwrin Bay faal yi Wa salam
@DjilyKhouma-vq6jc
@DjilyKhouma-vq6jc 5 күн бұрын
Merci beaucoup ❤❤❤❤❤
@fallousylla5386
@fallousylla5386 5 күн бұрын
Say wakh dra lérou ci deuk touba té khamo bay fall ga khamo keur mam chiékh
@xalildiagn7767
@xalildiagn7767 5 күн бұрын
Franchement
@abdoufallsow3277
@abdoufallsow3277 5 күн бұрын
Force la nitt xam fa?
@AntaMbaye-pq1jr
@AntaMbaye-pq1jr 5 күн бұрын
Kham baye fall ga day force walla
@Alioufaye-fh1wy
@Alioufaye-fh1wy 5 күн бұрын
Mane mi Touba la deugeu té khame ma baye fall ga
@toubaskhadimdia1094
@toubaskhadimdia1094 5 күн бұрын
Man touba la deuk té xaw ma fofou
@kebecheikh3998
@kebecheikh3998 5 күн бұрын
Ndyasan s.khadim ndiaye moma diagal tajweed .yallanako yalla geuna weral
@santbambaahmadu9912
@santbambaahmadu9912 5 күн бұрын
Li Sëriñ bi bëgg ci dëkkëm bi kuko man def kuko manul dem feneen c’est très simple
@chiekhniangtalibebamba8414
@chiekhniangtalibebamba8414 5 күн бұрын
Li Serigne bi bague Moy am far force ✅
@khadimniang2112
@khadimniang2112 5 күн бұрын
Yaw ya niaf sa ndaye deml yor sa papa ak sa yaye mo guen ak lèguiye okay
@panogayembaye2116
@panogayembaye2116 5 күн бұрын
jadieuf
@cheikhdiagne1428
@cheikhdiagne1428 5 күн бұрын
😂😂
@kderito8105
@kderito8105 5 күн бұрын
Esk xam nga li serigne bi bëgg
@talladjitte8756
@talladjitte8756 5 күн бұрын
Serigne d beugg na koy juli lol
@MourtallaDiop-vq2ex
@MourtallaDiop-vq2ex 5 күн бұрын
Mach alla imam khadim
@CheikhounaDiop-f3s
@CheikhounaDiop-f3s 4 күн бұрын
Allahou Akbar😢 Baye Fall yi gno bayi ndigeulou Serigne bi di business
@mamadousy8633
@mamadousy8633 5 күн бұрын
Le fait de dire d'aller acheter des habits est synonyme d'un habillement indécent.
@ibrahimacamara4475
@ibrahimacamara4475 2 күн бұрын
On ne peut pas créer un État dans un État c'est vraiment impensable et c'est à l'État de prendre ses responsabilités avant que l'irréparable se produise...............................................
@thiernombengue9226
@thiernombengue9226 5 күн бұрын
Bayfaal yi nio nek ci deug.. Jup bouniou fante wala bou séré wala mou khaat kéena waroukoo nangou ci sa keur rawatina ci mbédami.. Ya Serigne Khadim Ndiaye sokhnasi limou sol sou yiiwoon douniouko yobou.. Touba... niounn talibéyi bouniousi maslaha ak ndiabotgui... lolou moy deugg.... Dieuredieuf
@fadelndiaye4722
@fadelndiaye4722 5 күн бұрын
Liguaay wax dara nga si xamoul la wax Thierno reglel
@mamegorsarr1138
@mamegorsarr1138 5 күн бұрын
Diouli moy leppou
@MamedaraThioub
@MamedaraThioub 5 күн бұрын
Lou lér ga wax
@cisse10
@cisse10 3 күн бұрын
Wa loutah diabar serigne yi di khéssel di sol lou séré douniou mour Ken douci wakh
@panogayembaye2116
@panogayembaye2116 5 күн бұрын
imam Khadim Ndiaye koula sope la wayé yéy mom Dioumga dakh lagnouy téré ndagam lolou lagnouko Diapé rk mo togne YALLAH Nagnou YALLAH Fayal Baye Fall yi Barkép Kheikh IBRA FALL LAMP ❤❤❤❤
@YoussoufNdao
@YoussoufNdao 4 күн бұрын
Baye fall si ay thiakhane rek laniou nek naniou dem diouli dji dem diamou dji yalla Lou guneu bonne bayi diouli ak woor amoul
@MaSambaNdiaye-pl2we
@MaSambaNdiaye-pl2we 3 күн бұрын
S imame khadime Ndiaye mon ma Dianguale bama mokale di Dianguale dou dokhe di lou doule dine lislame
@abdouniangtv180
@abdouniangtv180 3 күн бұрын
seringue abô mbacké mi djité masalikoul jinan grand mosquée 🕌 du dakar imam khadim ndiaye mi moko diangeul al khourane bay fall yi khamoun gatt baye wakh si l'islam
@modoundiaye2179
@modoundiaye2179 5 күн бұрын
Ahhh doyna waaar d mohhh li serigne mountakha yeuguko d bilahiiiii
@BassirouNdiaye662
@BassirouNdiaye662 5 күн бұрын
Lii dafa ndiw loll sy touba❤
@modugueye2152
@modugueye2152 5 күн бұрын
Baye fallyi lenyedeff tegonoko fnn
@Khadimbambapastef40
@Khadimbambapastef40 4 күн бұрын
baye fall yi daalle wakhe ak ñoume diotna li miki beugeu apou 🔥🔥🔥🔥🔥
@Idy-m6o
@Idy-m6o 5 күн бұрын
Imame sit c'était là police tu va subir pur et tu vas accepter
@grandebusinessdanlaction8785
@grandebusinessdanlaction8785 5 күн бұрын
Police nga wakh dé
@AdamaTop-wm3sv
@AdamaTop-wm3sv 5 күн бұрын
Mais leppp si yonnn rekkkkkkk
@MamedaraThioub
@MamedaraThioub 5 күн бұрын
Lolou la. Xamoul c la procedure
@gueyematar1869
@gueyematar1869 3 күн бұрын
Man dé Guem Naa Serigne Touba, Yoonou Baye fall Laa Guemoul Ndakh bayi Diouli AK Wooor.
@mormbaye5071
@mormbaye5071 4 күн бұрын
Machalla imam
@cheikhahmadoubamba5477
@cheikhahmadoubamba5477 5 күн бұрын
Douniou Ay Baye fall Ay domeram laniou rekk lolou dou cheikh ibra dou yon wii yalla xam nako
@bambadieng6025
@bambadieng6025 5 күн бұрын
*_AMOU MA DJOTOU LIRE VIDÉO BI BAMOU DJÉXX ,MÉ BOUDÉ NANGOU NGA LI SERIGNE MOUNTAKHA DIGUEUL BAYE FALL YI JEUREUJEUF ,BOUDÉ ANDOSSI WAXOO DEUG YA TOGN WASSALAM_*
@elagegueye3310
@elagegueye3310 5 күн бұрын
kouy dikle niaka diouly mogueneu bon te moutaha migikoy def
@bambadieng6025
@bambadieng6025 5 күн бұрын
@elagegueye3310 *_YAW DEJA LINGAY WAX YAW XAMNGANI WAXO DEUG BILAHIL LAZII BAPARÉ RAGALOSSI YALLA CONTINUÉ DI FÉNE ,GUÉNÉL BÉNEU VIDEO BOU SERIGNE MOUNTAKHA DI DIGLÉ GNAKA DJOULI ,BAYILÉNN DI SOSS ,DINÉ DJI SENN BAY MOMOUKO ,MEUNOULÉNN DOUGUEUL KÉNEU SAFARA DÉLÉNN DJAPOUNI YÉNA GUEUN KOUNGUÉNN GUISS REK BEUS DINA GNEUW NGUÉNN XAMNI MBAM SEUFF MOLENN EUPOU MAXAMA DOMOU HARAM NAN SERIGNE MOUNTAKHA..YAW AMOO WORMA SISA BAY SAX BAKOY AM SI BAYOU DJAMBOUR,SA WAXDJI NAK SI GUINAW ECRANT TÉLÉPHONE YI REK LAY YAM ,DOO MASSA GUÉNEU WAX KOSSI KAW ,XANA DJIHATOOO AYTHIA DEFAL VIDEO WAX LINGA WAX WANÉ SA PHOTO BOPOU 😁KONN BAYE FALL YI LAKEU SA GATT DH_*
@aliouniang6084
@aliouniang6084 5 күн бұрын
الأدب الأدب إنه عالم
@khadimathj8129
@khadimathj8129 5 күн бұрын
Tounou ndayou baye fall. Touba c'est une ville de sauvages
@bamS5919
@bamS5919 5 күн бұрын
Des hors la loi (ils ne prient pas doniou ay dioulit) qui font la loi 😂😂😂 non c'est incroyable "c'est le monde en pire"
@alioudiop552
@alioudiop552 5 күн бұрын
Ci wax yanouwoul mana ci colin gui
@khadimMbacke-d9u
@khadimMbacke-d9u 5 күн бұрын
Wakhoufi dara wakhi yakh rek nguafi wakh
@fadelndiaye4722
@fadelndiaye4722 5 күн бұрын
Fénnn nga dh yaw Yafii waxoul tousss imbécillité bi gueini Di Diaye niolen ko eup fouff
@khadimniang2112
@khadimniang2112 5 күн бұрын
Ndayssan imam yalla baxna 😢😢😢 mia douyna weur dhè 😢😢li duo yon
@SerigneNdoye-i4l
@SerigneNdoye-i4l 4 күн бұрын
Touba dall ndiggueul moffay wéuy koumou nékhoul guénnal deukk bi dém fénén togne bakhoul ndiggueul mome dieuffé rék Touba dieum kanam inchallah
@BadjiMamadoulamine-z2q
@BadjiMamadoulamine-z2q 4 күн бұрын
Yéné mom néye déugu by guéneu difi guéneu domaram
@Idy-m6o
@Idy-m6o 5 күн бұрын
Ça c'est pas vrai c'est fille n'a pas n'a pas ramplir les critères
@alioudiop552
@alioudiop552 5 күн бұрын
Linlén déf késé moy li war, baye Fall bég na ci niom lol Imam li am Dakar ganga nék amoul Touba, bici déss tamit ak ko mana don, imam, sëriñ, .... Tékou ci yon rék
@bachiirleveridique9767
@bachiirleveridique9767 5 күн бұрын
*Dañ koo deful sa nday rék DOOMURAAM ñun kuy gëm SËRIÑ TUUBAA ñoo la ko gëna gëm*
@abdoufallsow3277
@abdoufallsow3277 5 күн бұрын
Waxofi xam xam
@obd2214
@obd2214 4 күн бұрын
Waw yoone mom xana Julli ak Woor daff si bokoul ?
@khadimendiaye3674
@khadimendiaye3674 5 күн бұрын
Imam sawkhdji dafa khawa subjectif.ter lingay def dou sa thieur ndakh kilifa nga
@fadelndiaye4722
@fadelndiaye4722 5 күн бұрын
Loudoul thieurou imam Ak louy tieureum dou yaw yako koy wakh réw guein trop
@MamedaraThioub
@MamedaraThioub 5 күн бұрын
Yaram bayil khadim mi moiy wax il fait la publicité des procedures des bayefall pour executer le ndigueul du Khalif Sou benene yoné la fille douko défate Lou Serigne bi beugue moy ame comme dab
@fadelndiaye4722
@fadelndiaye4722 5 күн бұрын
@@MamedaraThioub khadim touss meunou leen ko cii moom Wallahi azim li lislam beug molen ko geuna kham foufff réw guein yarou woulein
@salioucisse2355
@salioucisse2355 5 күн бұрын
Waw touba mom ndakh rewou boppam laa walla Non _ Niom naniou Diappou Bokkalle kattyii Moo geunn
@serigneniomrelo6956
@serigneniomrelo6956 4 күн бұрын
Touba rewoum serigne touba la
@salioucisse2355
@salioucisse2355 4 күн бұрын
@serigneniomrelo6956 Kan moo defarr souffou touba Dou yalla__ Serigne bii mouy nieuw chi adouna Dou filla fekkon touba Bi mouy guenn adouna demoul bayiifi touba
@dembathiao8232
@dembathiao8232 4 күн бұрын
Iow wakhou dof ngay wakh touba réwou bopam la ndakh titre foncier Serigne Touba la té bam koy done bobou titre foncier bobou Sénégal amoul indépendance point.
@maguettehane2424
@maguettehane2424 5 күн бұрын
Serigne bi dall deukeum bi limoufa beug kouko manoul nga abball Serigne mountakha limou beug rek Moy amm
@Tambayefall
@Tambayefall 5 күн бұрын
Louy sa problème 👿 Waw ndakh lolou moy yone
@fadelndiaye4722
@fadelndiaye4722 5 күн бұрын
Leiguii moo taay
@amadoumarico5944
@amadoumarico5944 4 күн бұрын
l'État doit prendre ses responsabilités les bay fall en font trop à Touba c pas sérieux
@kossodiop8626
@kossodiop8626 3 күн бұрын
Kou wakhoul dégeu wakh safan
@ousmanedaffe389
@ousmanedaffe389 5 күн бұрын
Ki wakhoufi tous diakhasé késé mo takh guay wakh so mounta yar sa wadia keur ci li serigneba beugué gua géne
@bassfall5382
@bassfall5382 4 күн бұрын
Khana ai doff gano diapé ki lime wakh loko gana lér
@ousmanedaffe389
@ousmanedaffe389 4 күн бұрын
Léroul kay ndakh khamoul bakham da guéne wala day nélaw
@alioumbacke5514
@alioumbacke5514 5 күн бұрын
Ki mo djiaggal alkhourane ki nafila thi djiouma massalikul djinane
@falloudione8045
@falloudione8045 4 күн бұрын
Nion wa Touba khawma loniodef yalla rek 😅😅😅
@ibrahimadioplo475
@ibrahimadioplo475 4 күн бұрын
Erreur imam les bayima aye bayima lagnou Waye nit Dana deff lou yess bayima. Respectez les Baye Fall Les hommes veridicts
@tout1958
@tout1958 5 күн бұрын
Li cheikh thioro domi xaram wax motax ngay wax mai Touba mom li Sérigne beugeu rék Moy am dém léne séne deukou Mame
@saloummansaly1745
@saloummansaly1745 5 күн бұрын
Yéw dé War nga diangi nahju
@YoroSarr-f8u
@YoroSarr-f8u 4 күн бұрын
Yaw kou xamadi nga
@tout1958
@tout1958 4 күн бұрын
@YoroSarr-f8u Lou yakhou Sénégal wa pastef la ak séne you bari
@YoroSarr-f8u
@YoroSarr-f8u 4 күн бұрын
@tout1958 doule nga ndax bokou ma pastef sama xalat lay wax té bindeff meunou mako tè wax doméram
@SaliouFall-y5k
@SaliouFall-y5k 5 күн бұрын
Ya toukhousi touba dé topou warmay sérigne bi rk mbanga délou sa keur mame rk point
@Reewmi24
@Reewmi24 5 күн бұрын
Yaw hana deglou wooo limm wahh lepp ? Delen andak seeni xell
@modouseck1521
@modouseck1521 4 күн бұрын
Kou diouboul noy dioubanté ay nitt
@ibrahimadioplo475
@ibrahimadioplo475 4 күн бұрын
Imam mame cheikh Ibrahima Fall moye Islam
@abombacke8547
@abombacke8547 5 күн бұрын
Dee dém sawara rék bayyi joulli bayyi woor nékfii di sonalaaté
@ibrahimadiaw8889
@ibrahimadiaw8889 4 күн бұрын
Gouvernement bi défoul ligeeyam , lii taxoul woon ñou falléeen
@CheikhmamouneMbacke-t3z
@CheikhmamouneMbacke-t3z 5 күн бұрын
Jarajaf s khadim wax nga deug dé
@fallndiolle4430
@fallndiolle4430 5 күн бұрын
Bakhna ci niom li yalla begue Ak li mou bagne Serigne bi diko doxal ci dekë bi gnou degeur bop logne té bzkhna
@DjilyKhouma-vq6jc
@DjilyKhouma-vq6jc 5 күн бұрын
Merci beaucoup
@blackironlion12
@blackironlion12 4 күн бұрын
L'état doit prendre des précautions sur les Baye FALL qui n'ont pas de formation ni rien
@assanemar5077
@assanemar5077 5 күн бұрын
Li serigne bi beugue moy ame kouko meunoul nga guéne deukou serigne bi togn bakhoul
@khalyseck4917
@khalyseck4917 5 күн бұрын
Mais bay fall yii wérou gnou khamou gno mais li responsabilités serigne bi la rk touté fou koudoull sangou dou diouli nga dénk ko deukk bi Waw lolou ndakh ak wérr la
@moustaphadiane3309
@moustaphadiane3309 4 күн бұрын
Wa baxna rek 😢 Dina euppou loxo dh
@mouhamadoukane2230
@mouhamadoukane2230 5 күн бұрын
Sénégal jupe parfois day dangue Imam il faudrait éduquer davantage vos protégées La loi lorsqu'elle est appliquée peut paraître dure mais nak Sam Touba diarnako
@abdoulabdoul7809
@abdoulabdoul7809 5 күн бұрын
Serigne si nio dakha khoti wormay diiné dji, gueumouniou Yallah, gueumouniou al quran biniouy diangue, gueumouniou Rassoulillahi. Badio ak khaliss késsé laniou gueum 😂😂😂
@MamedaraThioub
@MamedaraThioub 5 күн бұрын
Yaram pa bi mo gueuneu khamni la fille nékoil ci les bayfall non aucun interre darreter kelkun ki est en conformité avec les ndigueul C juste un facon de decoutager et de denigrer les bayfall Mais khamoul né bayfall ay rouma moko jike
@BayesaliouGueye-nc6wo
@BayesaliouGueye-nc6wo 5 күн бұрын
Abdoubdoul billahi di nga de si nakhar😂😂te nga nopoulou😂😂
@abdoulabdoul7809
@abdoulabdoul7809 4 күн бұрын
@BayesaliouGueye-nc6wo yen lolou rek ngen di wakh di doul rek 😂 wallahi mangui santé Yallah bou bakha bakh ndakh téral nama bou bakh al hamdoulillah. Sen deuk bobou amoul ndokh mou nékh té barina mboyo 😂😂😂
@abdoulabdoul7809
@abdoulabdoul7809 4 күн бұрын
@MamedaraThioub koudoul diouli dou woor key sheytane laye ligueyeul 😂😂😂
@serigneadj1779
@serigneadj1779 5 күн бұрын
Diadieuf Imam Lo lu du deug du yone
@BoubacarKara
@BoubacarKara 5 күн бұрын
Pourquoi porté presse Ils ont des responsables Kou beugoul Serigne Touba bouffa deuk guirr lane comme yii di deff yi melni khamo dokhinou yonou mouride dano ame kilifeu
@7614diawMamediarra
@7614diawMamediarra 5 күн бұрын
Li nathi serigne bi wakh 😢
@aboudiop-fj4ug
@aboudiop-fj4ug 5 күн бұрын
Kou giss khamné geumo yonou baye fall
@Jeunepatriote
@Jeunepatriote 5 күн бұрын
Mais imam jube bii mane na goudou dé mais wakho baxam dafa serré sii ay thieuram An tout cas dal lima guiss sii xalé Touba diamano dji képpou kouye négocier ak gnome dougnou falé Nagnou deupo ak charte Touba dakh képpou kou ko deff do am ak problème ak baye fall yii
@santbambaahmadu9912
@santbambaahmadu9912 5 күн бұрын
Merci infiniment les Baay faal ❤
@MoustaphaSeye-v3r
@MoustaphaSeye-v3r 5 күн бұрын
Diara diefe imame
@mamounediaw1178
@mamounediaw1178 5 күн бұрын
Machallah s khadim adou na yakho Rek waye 😂😂😂
@AstouLo-l5u
@AstouLo-l5u 5 күн бұрын
Imam yaw seuytane nga. Touba lifa Seringe bi beugeu mofay am koumou neekhoull nga dem sa keur mam
@seringembacke9316
@seringembacke9316 5 күн бұрын
Bayilen saga yi rafetoul 🙏🙏
@amadoufatimakane3564
@amadoufatimakane3564 5 күн бұрын
@@seringembacke9316 wah nga dëgg
@cheikhounadiop2632
@cheikhounadiop2632 5 күн бұрын
Kii de s mountakha mbacke diokh nako ay khale ba tayi guirr mou jangal leen allkhouran talibe s touba la lou bakh rk la kham
@amadoufatimakane3564
@amadoufatimakane3564 5 күн бұрын
@@cheikhounadiop2632 kon nak waroon naa jomba def exposition boo xamni dees ciy njaññ dëkk bu sell bi di TOUBA
@Bueleup
@Bueleup 5 күн бұрын
​@@cheikhounadiop2632merci❤❤❤
@abdoukarimditmacodoundiaye993
@abdoukarimditmacodoundiaye993 4 күн бұрын
C'est l'état qui doit prendre la sécurité avant la riposte des humains
@mamedialedia8378
@mamedialedia8378 5 күн бұрын
LII YOONE WARNAKOO INTERDIRE . CIVIL DOU YAR CIVIL
@MbayeKhadim-h9c
@MbayeKhadim-h9c 3 күн бұрын
Li nianwna😢
@BayeMbaye-o4f
@BayeMbaye-o4f 5 күн бұрын
😂😂😂 voilà la preuve de ce que Cheikh Thioro disait à l'Assemblée nationale. Allons y reck
@ModouMige-bu4qu
@ModouMige-bu4qu 5 күн бұрын
Bilahi wallahi lii do youn nan dem rek
@papediop2737
@papediop2737 5 күн бұрын
Yarr len sen ndiabot gui, dem nguene macca kham nguene l'affaire khew, wala Iran wala siry
@assbouserignebabacarsylo4612
@assbouserignebabacarsylo4612 5 күн бұрын
Dof you melni iow nio tardél deuk bi
@mordiop5531
@mordiop5531 5 күн бұрын
Diazakalah Serigne khadim ❤❤❤❤❤❤❤❤Machala
@MatarDiarra-tz3gw
@MatarDiarra-tz3gw 3 күн бұрын
Touba mom faut Etas réglé problème bi
Правильный подход к детям
00:18
Beatrise
Рет қаралды 11 МЛН
Touba entre loi et insécurités : Serigne Abo Mbacké clarifie le débat
5:21
Urgent-Touba : Plus de 100 supporters de foot "graciés" par les Baay Faal....
17:18
Wakhtanou Fadjar du Vendredi 03 Janvier 2025 par Oustaz Hady Niass
34:27
Urgent🔴Déclaration Bou Ame Solo Ci Touba S.Assane FALL ibn Cheikh Moustapha FALL
10:53
TAWFEKH PRODUCTION INTERNATIONAL HD
Рет қаралды 14 М.
BOKK YI MBIR XEWNA, YÀLLA WEER NA AMED XALIFA ÑAS
12:21
Xam Sam Réew Tv
Рет қаралды 81 М.