Rakou Tout Court biniou djigne V!o| t amoul voici les preuves

  Рет қаралды 26,176

Pa Assane Gueye Lebou

Pa Assane Gueye Lebou

Күн бұрын

Пікірлер: 203
@tafiscodiop6659
@tafiscodiop6659 Күн бұрын
Merci beaucoup mon frère yalla na Yallah khép doli soutoureu ak diam thi barké Mouhamed SAWS 🙏🏾🙏🏾🙏🏾❤
@MatarSow-o8m
@MatarSow-o8m Күн бұрын
Sallahou haleyhi wasalam 🥰
@AssaneCisse-l4c
@AssaneCisse-l4c Күн бұрын
Merci pour le message pa Assane Gueye ❤🙏
@falloudia-lx3mc
@falloudia-lx3mc Күн бұрын
Meér. Bii mom khana kharouna esk Gathia guiii domou Adama antane nako 🤔🤔🤔🤔😔😔
@djibrilndiaye2339
@djibrilndiaye2339 13 сағат бұрын
Doyna war de 😢
@ElHadjiDieye-h7f
@ElHadjiDieye-h7f Күн бұрын
Bilahi Adina dou dr 😢mais mane dama yakani domou adama yii dano faténi yalla amna motakh bilahi kou yakani do dééh ba takhna loula nekh def di tou mal niitt ki ak di diakhasé ak sosal niitt ki bayaka ni dodéhh Yagui nekh sabopou adina bi dr yagou fi ta lepay diekh nanou delosi khél yi té déme diamou dji yalla ❤bala dédi nieuw 🤲Yalna nous yallah soutoural inechallah kHirr nou si bopame 🤲🤲lakhanou fa yakheu yégoul inechallah 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
@cheikhciss5591
@cheikhciss5591 Күн бұрын
Bilahi niou bari niougui si prison yi té dèfouniou dara
@al-baahis489
@al-baahis489 Күн бұрын
Bilaay waxx ga dëgg
@Mbodji-walo
@Mbodji-walo 18 сағат бұрын
Sounu boy Sidy Dieye 2013 ba tay mangui ci diél bi dagnko touma viole fi Niary tally
@cheikhciss5591
@cheikhciss5591 16 сағат бұрын
Kholal lolou rèk li kay yalna yalla lèral lèpe
@salladiop505
@salladiop505 Күн бұрын
Bilay leigui li dafa Bari Sénégal
@cheikhounagning
@cheikhounagning Күн бұрын
Merci beaucoup pa assane gueye yaw ya bakh bilahi mi yalla nala yalla diafal diamou ak Salam ak fou mana neke ❤❤❤❤sa ligaye rafate na lole bilahi ❤❤❤❤
@cheikhciss5591
@cheikhciss5591 Күн бұрын
No senegal lou nekk amnafi k justice soit fete
@abdoulahadSene-w9s
@abdoulahadSene-w9s Күн бұрын
Cas yi nimou bare Senegal bilahi man Justice bou Sénégal dama khamoul lan moy sen ligeye ak médecine yi😢😢😢😢😢 Senegal niou Bari niogui si prison té def fou niou dra wallahii 😢😢😢😢
@cheikhmbackendiaye3997
@cheikhmbackendiaye3997 Күн бұрын
Vraiment pa assane contant na si yaw li ngay déf dafa am solo ma sha Allah ❤
@AmarFallAmarfall
@AmarFallAmarfall Күн бұрын
Merci Pa Assan yalla nala yalla Faye sa xol
@cheikhthiam8279
@cheikhthiam8279 Күн бұрын
Macha Allah Pa Assan lu leer nga wax, lii d mooy aaxirou zaman, Yalla nanu Yalla xiir ci lu baax 🤲
@CheikhNdiaye-v8r
@CheikhNdiaye-v8r Күн бұрын
Merci Pa assane Kadou yi réfètna❤❤❤❤❤❤❤
@AmadouThiam-v2k
@AmadouThiam-v2k Күн бұрын
Merci Pa Assane❤
@YacineFaye-r9r
@YacineFaye-r9r Күн бұрын
Li ngay déf amna solo
@MaremaDiagne-g4e
@MaremaDiagne-g4e Күн бұрын
Merci oustaz pà asane yalna yalla yocou kham kham by te dafalla werr❤❤❤❤❤❤alla houma amine
@PapeDRAME-j1b
@PapeDRAME-j1b Күн бұрын
Merci beaucoup Pa Assane ! Soula nekhon yam thi foot bi rek mais vous nous donné des conseils c'est génial ❤
@ChabdoukhadersyllaSylla
@ChabdoukhadersyllaSylla 23 сағат бұрын
Alhamdoulilah ba sama papa amè bènn sokhna li niawna trop
@SerigneSaliouFall-vx6kp
@SerigneSaliouFall-vx6kp Күн бұрын
Machallah pape assan content n'aci yaw sa liguey réfétna
@SamaPapa-h7s
@SamaPapa-h7s Күн бұрын
ما شا ء الله Pa Assane❤❤❤❤
@user-nu1fy2fv6z
@user-nu1fy2fv6z Күн бұрын
C'est vraiment triste mais merci beaucoup pa aassan❤❤❤❤😢
@MbayeSylla-ze3qu
@MbayeSylla-ze3qu Күн бұрын
Merci pour tes conseils 🎉
@falloudiop5153
@falloudiop5153 Күн бұрын
Free Amadou❤️❤️❤️✊✊✊✊
@MbayeFaye-c5n
@MbayeFaye-c5n Күн бұрын
Bilahi frère dée daye métte dé😢
@bachirndiaye4384
@bachirndiaye4384 Күн бұрын
Sénégal so wakhé ngoni la enquêteur dagno dèff sén liguéy sanq la nak cas yi da yomb trop si rèw bou am police am gendarmerie vraiment c'est honte yoob nitt cosso si wakhi kasé
@MbzckeFzll-sf1py
@MbzckeFzll-sf1py 21 сағат бұрын
Ms diotna nak niouy def reportage cii prison yi nguir xamal nit yiy yeené nitt prison fofou nimou mell ndakh nitt mom moun ngako yeené louné bamou dess prison ak dee cii nitt kou defoul dara😢
@AlassaneMbaye-gx9fx
@AlassaneMbaye-gx9fx 9 сағат бұрын
Deug leu dè
@riamdiaw6805
@riamdiaw6805 Күн бұрын
Le rappel profite au croyant. Merci
@MandoumbeNdiaye-yf1tv
@MandoumbeNdiaye-yf1tv 19 сағат бұрын
Li justice warnasé diok niaw na trop❤❤
@MouhamedSeck-mx4cj
@MouhamedSeck-mx4cj Күн бұрын
Nn li métina billay gnikoy doundou si prison barina 😢
@AssaneGueye-d7n
@AssaneGueye-d7n 23 сағат бұрын
Merci beaucoup pa assaane gueye ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@Football-x3d6s
@Football-x3d6s Күн бұрын
Heureusement dama ragal djiguene alhamdoulilah 😢
@DaoudaDiouf-g1q
@DaoudaDiouf-g1q Күн бұрын
Justice pour fallou fall et Amadou
@KhaliphaDiop-l9e
@KhaliphaDiop-l9e 21 сағат бұрын
Mane li ça me fait même pleurer yene accusation yi meunou mako imaginer 😢😢😢
@ArmandTraore-i3o
@ArmandTraore-i3o Күн бұрын
Walahi pa assane lii dafaye wane ni rk jamono dji moh tass te aussi goor gni surtout jeune yii nagnou guéna veillé si sene bopp yalla nagnou yalla soutourale rk inchallahs ❤❤😢
@mouvemntsantyallatv
@mouvemntsantyallatv Күн бұрын
TOURE NDO MANG LAY ZIAR LOU BARI DI LA NIAANAL YALNA YALLA DIAPALÉ LA DIAPALÉ NIOU 🫂🕋🕌🤲🇸🇳❣️🫂 THI BARKÉ SEYIDOU NAA MOUHAMMAD SAL LAL LAAHOU HANLAYHI WA SAL LAM ❣️🇸🇳🙏
@tafiscodiop6659
@tafiscodiop6659 Күн бұрын
Lii Beurina fii té yague nafi déf nagneko sama béneu Mbokk en 1995. Pour un rien gnou yakk sa Adouna. Amneu nitt you bonne koudoul khalatt sa Bammél liula nékh défal.
@Amdymbaor-kt4sb
@Amdymbaor-kt4sb 18 сағат бұрын
Pa assane jëurë jëuf waay si conseil yi❤
@mina-x7j6p
@mina-x7j6p 18 сағат бұрын
Yaw rek lay topp yalla nala yalla may guoudou fane akk werr 🙏🙏
@omarkhoule1681
@omarkhoule1681 Күн бұрын
Lidafa niaw torop Bayilén didogo fodonon sa chambre 😢😢Sénégal woratol 😮
@Seck-t1b
@Seck-t1b 11 сағат бұрын
Yalla nagnu yalla jubbël Si seydina Muhammad 🤲
@ndiagnegadiaga6946
@ndiagnegadiaga6946 Күн бұрын
Machalla pa assane gueye
@Mbodji-walo
@Mbodji-walo 18 сағат бұрын
Li dafa métti trop😢 barina ci réwmi sounu boy Sidy Dieye 2013 ba tay mangui ci diél bi
@AssaneCisse-l4c
@AssaneCisse-l4c Күн бұрын
Où sont les monégasque ❤🤍
@thimboyounousse8172
@thimboyounousse8172 22 сағат бұрын
Machallah rafetna amna solo trop mon frère yalna la yalla doli soutoureu inchallah amine ya raby 🤲🙏🥺
@serignediba241
@serignediba241 Күн бұрын
Pa asan sama rak com cas bi laam ta Bilahi wallay defou ko ta mogui kaso bou diourbel depuis le 5 novembre ba legui naniou ma si diapale guir yalla soniou yaye dafa décédé 2008😢😢😢😢😢😢😢
@FatouDiogoul-g5f
@FatouDiogoul-g5f 21 сағат бұрын
Bilay pa assane deug bu wéér😢
@bathiesy1755
@bathiesy1755 18 сағат бұрын
Ms Likhana Louga La Gni Khamna Lén
@Bounasow-x5j
@Bounasow-x5j Күн бұрын
Merci beaucoup ❤❤❤❤❤❤
@mouhamedbalde3157
@mouhamedbalde3157 Күн бұрын
NDaysan
@moustaphandiaye8464
@moustaphandiaye8464 8 сағат бұрын
Ki rassoulay ça longtemps que j'ai pas sorti mes larmes mais aujourd'hui j'ai vrai pleurer sans savoir pourquoi 😭
@Fallyaram1511
@Fallyaram1511 Күн бұрын
J'ai un ami qui est dans la même situation d'ailleurs il a purgé 6 ans et il lui reste 4ans c'est vraiment compliqué.
@abdoulayeWade-i2r
@abdoulayeWade-i2r Күн бұрын
Sama rakk aussi il es en prison à cause de ça bilah sama dafa décédé 😢😢Lou meti parceke elle savait ke mo petit ne peut pa faire un genre de chose com ça
@SerigneNiang-y9l
@SerigneNiang-y9l 8 сағат бұрын
Mais Sénégal métti na billahi 😭😭😭😭 Koudoule bayi xel niétti fanni baamél loula nékh défal
@dieynabagueye3987
@dieynabagueye3987 Күн бұрын
Thiay yalla ay lokou fi diar yakh domou djamou si 0😢😢😢😢😢
@AssaneGueye-d7n
@AssaneGueye-d7n 23 сағат бұрын
Merci beaucoup pour votre message ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@AssaneGueye-d7n
@AssaneGueye-d7n 23 сағат бұрын
Merci beaucoup mon frère yalla na yallah soutoureu Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@AdjiLo-dm9qo
@AdjiLo-dm9qo Күн бұрын
Alhou akoubar alhou akoubar alhou akoubar alhamedou lilaye 😭🙏❤️❤️❤️❤️❤️👂👈💯👈🙏
@dieynabagueye3987
@dieynabagueye3987 Күн бұрын
Justice pour fallou fall et eume😢😢
@abdoubayefalljoop1527
@abdoubayefalljoop1527 19 сағат бұрын
Kii sama père laa nitou deug père diamil borom louga 🙏🙏
@MamadouSow-us1gc
@MamadouSow-us1gc 21 сағат бұрын
Merci bcp pa assne 🎉
@tallambengue1092
@tallambengue1092 23 сағат бұрын
Ly yeupou Sénégal lay khéwé ndakh Sénégal dou deukou ndayi yonne li khéwon macky sall ba taye mofi nék sonko diomay amoulen fi bén ndiarigne bly
@salzoofficiel2770
@salzoofficiel2770 22 сағат бұрын
Bly frr
@FallMandiaye
@FallMandiaye Күн бұрын
Ndax adouna diarna li ,koudoul xelat euleuk loula nex defal
@moussanene3160
@moussanene3160 6 сағат бұрын
Merci beaucoup mon frère pa 👍
@malicksow9336
@malicksow9336 20 сағат бұрын
Merci beaucoup frère 😢c leçon de vie
@IvonnecarlosMendy
@IvonnecarlosMendy 9 сағат бұрын
Salut mon frère merci pour message li motakh ma quitté sema gale keur massar avec mais enfant affaire de tentation ont essayé plusieurs de fois m'ai Dieu m'a protège es je dit merci mon Dieu
@BassSambe
@BassSambe 9 сағат бұрын
Bonne Continuation fèrr ❤❤
@PaOuzz9
@PaOuzz9 Күн бұрын
Pa assane mani kou yakh sa adina nga yakh alakhiram
@abdourahmanembaye9399
@abdourahmanembaye9399 Күн бұрын
Amna jigeen gnou bone bly
@Sonkiste
@Sonkiste 22 сағат бұрын
Noooo senegal 😢😢
@ousmanegueye21
@ousmanegueye21 21 сағат бұрын
Je ne comprends plus ce Sénégal😭🇸🇳🙏🏾
@assdiouf1033
@assdiouf1033 Күн бұрын
De toute façon dal comme sonko victime la wone si justice bou Sénégal Kone il est temps gnou rakhass sunu justice sino boufi peine de mort ame' kou Méré nit yobouko si yone ate Kat yi raylouko
@ndiomegueye2030
@ndiomegueye2030 Күн бұрын
Yalnako yallah takhawou samko arko inshallah
@BaylahatBaylahar
@BaylahatBaylahar 20 сағат бұрын
Ou pa assane😭😭😭😭😭😭😭
@SerigneKhadimeKhouma
@SerigneKhadimeKhouma Күн бұрын
Thheiy Sénégal ❤
@BintarassoulDiop
@BintarassoulDiop 7 сағат бұрын
Ay way sama xoll bii diekh na 😭😭😭😭ken khamoul lane la
@BabacarWillane-c8m
@BabacarWillane-c8m 10 сағат бұрын
Al hamdouli lah mane dé Dina geuneu bayi khél sama bopou inchallah 🙏🙏
@lazanebalo372
@lazanebalo372 Сағат бұрын
Senegal mètsièn yi ak justice yi kène dou niom billahi 😭
@Aïssatoutop-k1w
@Aïssatoutop-k1w 22 сағат бұрын
Je vous respecte beaucoup mais mère bi kou Kate ndeyem la😢😢😢
@cheikhahmedtidianeseck1882
@cheikhahmedtidianeseck1882 10 сағат бұрын
Merci beaucoup p ass
@Babounar-x7o
@Babounar-x7o Күн бұрын
Yalla nala yalla fay
@imtherealboy2387
@imtherealboy2387 Күн бұрын
Merci pa assane
@MamoudoubaRonaldo
@MamoudoubaRonaldo 22 сағат бұрын
Merci beaucoup pa
@tallafaye3716
@tallafaye3716 Күн бұрын
allakhou hakoubar liiii mba diam laaa
@KhadimSokhna-jz1um
@KhadimSokhna-jz1um Күн бұрын
Thieye lii yalla bakhna 🥺😢🙏
@KIDZI2042
@KIDZI2042 10 сағат бұрын
Ça fait deux femmes qui accusent de viol un jeune homme 😢😢
@assanediop1497
@assanediop1497 18 сағат бұрын
L' Assemblée nationale doit mettre en place une loi Qui sanctionne les violeurs mais aussi les accusatrices en cas de fausses accusations C'est trop facile djiguenn yii diyiy accuser goor yii de viol Yakk sen Adouna A la fin justice bi se rend compte Dara amoussi Djiguen bobou accusé wone Dara douko sii fekk C'est de l'injustice Djiguenn yii nayou ragal Yallah Tee sorale' euleuk sen bamel ak sen Alahira
@Z26BABIDI
@Z26BABIDI Күн бұрын
le sénégal kel pays
@abdoulahadSene-w9s
@abdoulahadSene-w9s Күн бұрын
Wallou viol yi lou si eppeu dra amou si Senegal viol amou fa😢😢😢
@mouhamadoundao6025
@mouhamadoundao6025 Күн бұрын
Merci beaucoup grand bi❤❤❤
@BabacarNdiaye-x7h
@BabacarNdiaye-x7h Күн бұрын
Mais Sénégal tamite niniouy teudié nitte yi dafa yomb trop khana avant guay teuthie nitte digua enquête bamou lére nagne
@CheikhDiop-u6n
@CheikhDiop-u6n Күн бұрын
Sénégal dou rew srap li
@BayeOusmaneGueye-q2g
@BayeOusmaneGueye-q2g Күн бұрын
Pa assane bly lou niaw eumeu c'est mon cousin mais daniou ko takhal sérieux 😢lou niew sakh free eumeu
@barraniang-b9j
@barraniang-b9j Күн бұрын
Pa Assaan Kesse 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
@Aliounebadara221
@Aliounebadara221 Күн бұрын
Li daray adouna diarou ko billahi toumal nit ki yakh adou name 😢
@MamorKonteye
@MamorKonteye 12 сағат бұрын
Machalla amna solo
@salioucisse2355
@salioucisse2355 12 сағат бұрын
Mais merbii naa dem prison
@serignembacketoure8796
@serignembacketoure8796 Күн бұрын
Thiay Senegal 😢
@_NG10
@_NG10 22 сағат бұрын
Bro merci bcp ❤❤️🙏👍
@DjilyGaye-em6ec
@DjilyGaye-em6ec 20 сағат бұрын
SÉNÉGAL ay mer yu kate dayam nofi ne😅😅😅😅
@NeverKnow-l9r
@NeverKnow-l9r Күн бұрын
Nom senegal comme film😎
BÉTÉ BÉTÉ - Saison 2 - Episode 15 : Bande Annonce
2:47
EvenProd
Рет қаралды 1,1 МЛН
Série - BAKARY TAXIMAN - Saison 1 - Episode 30
17:08
RTS - RADIO TÉLÉVISION SÉNÉGALAISE
Рет қаралды 5 М.
Don’t Choose The Wrong Box 😱
00:41
Topper Guild
Рет қаралды 62 МЛН
СИНИЙ ИНЕЙ УЖЕ ВЫШЕЛ!❄️
01:01
DO$HIK
Рет қаралды 3,3 МЛН
小丑教训坏蛋 #小丑 #天使 #shorts
00:49
好人小丑
Рет қаралды 54 МЛН
FAMILLE SENEGALAISE - Saison 03 - Episode 49 - VOSTFR
45:19
Pikini Production
Рет қаралды 422 М.
Série - Lady Diama - Saison 1 - Episode 45 - VOSTFR
45:19
Marodi TV Sénégal
Рет қаралды 1,7 МЛН
The West speaks of defeat / Lukashenko attacks Zelensky
14:04
NEXTA Live
Рет қаралды 798 М.
Rakou Fallou nèna Papam moka teudjlou t danou ko diap #falloufall
9:52
Pa Assane Gueye Lebou
Рет қаралды 95 М.