C'est vrai qu'il y'a des journalistes dignes du nom et toi Ngoné saliou tu en fait parti. Bravo à toi.
@djenabadiop89207 ай бұрын
Qu'est ce qu'elle a de particulier, sinon ay khoulou en direct, n'a dém jaanguiwaat, professionnalisme dafa bakh, surtout pour un journaliste qui parle au peuple surtout à des jeunes. Je suis foncièrement contre Tounkara et ts les détracteurs du nouveau régime, mais" les plateaux digital" c'est carrément nul, il leur faut plus de formation
@mafpato52646 ай бұрын
@@djenabadiop8920 Ça se voit que ni t’as pas écouté ou tu n’aimes pas entendre la chronologie des faits avec preuves que Ngoné était entrain de Souligner. Mais nak dougn lako diapé peut-être t’as un dent contre elle 😂😂😂
@BirahimJock8 ай бұрын
Kèepou kouy préparé examens wala bac wala nga am dom bu koyy préparé wala sakh nga am kharit bou kooy wadial yàlla na lèn yàlla dafal ak réussite ❤amine
Vérité absolue machallah ngone saliou l'ONG Vie a toi
@72h.Tountou.patriotique8 ай бұрын
😢😢😢je suis choquée quelle humiliation. Merci Ngoné
@AminataBaldé-f3d8 ай бұрын
Kiu d'accord ni ngoné saliou mo eupe fouleu si journaliste yii ❤❤❤❤❤
@muhammaddia91628 ай бұрын
Walaye damko beuge😂
@aminatandour17418 ай бұрын
Man
@mame32528 ай бұрын
Une vraie djambar elle était toujours sur le terrain pendant ça chauffer pour nous montrer les images en direct bravo sister ❤❤❤❤
@SaliouNiang-i6k8 ай бұрын
Wallahi diambar deug leu ❤❤❤❤❤
@omarboumuhammadalhamdoulil44108 ай бұрын
Tata ngoné Yalna say doom melni yaw ci wakh deug. Amiin❤❤❤❤
@kaoussousane407 ай бұрын
Yalla matakakoo
@Medzo35108 ай бұрын
Kou d'accord ni Ngoné dou nite😂😂 lalaal j'aime
@xalaatxellou94638 ай бұрын
Manouma beuss j’aime ndakh nite la
@rokhayandiaye61948 ай бұрын
Nite leu guaa,dafa féroce rek 😂😂😂😂😂
@aidatraore65618 ай бұрын
Nit la , dafa xam limiy wakh, ta meune liguéy am
@AdrienDiouf-c6j8 ай бұрын
😂😂😂😂
@momosy60838 ай бұрын
Niit la sakh da degou rek 😂
@cheikhmbackelo9708 ай бұрын
Shetttteeeetet sokhnasi amgua ndimbalu yalla ndakh li khol❤ bu lèr rèk moko mane
@landingbadji90398 ай бұрын
Ngoné kay c’est une lionne deug. Tounkara je l’aime bien au moins il encaisse calmement contrairement aux autres. Tounkara savait bien ce qui l’attendait s’il vient sur ce plateau matinal.
@Samy-sh4gl8 ай бұрын
Ngoné khamonanni aye nga mais mba ngui diégalou bokk nga thi gni fi raw. Machallah!
@khadimka20588 ай бұрын
Ngone Saliou yalla nala yalla sakhal si deug gui nga nek Bilahi ma beksi yaw ❤❤❤❤
Sheu te te te te . Quelle humiliation !!!😢😢😢😢😢merci Ngoné😂😂❤❤❤❤❤
@rassouljunior48508 ай бұрын
Il faut faire très attention à certains journalistes , ils sont remplis de connaissances et cette jeune dame en fait partie. Je salue son éloquence et son élégance. Sans pour autant oublier son art de maîtrise et de bien parler . Le gars a été bien laminé 😅😅😅 Si vous êtes d'accord , pouce bleue 👍
@ndeyesokhnaseck84908 ай бұрын
Zal svp waxal si sounou extraits de naissance yinouye diaye de grâce nguir yalla danou narona xeuy rék niouni niou guéneulén SÉNÉGAL dou sén réw diapssi grand
@modougueye57758 ай бұрын
boul yakamti avc sonko reck so teudé nélawal
@bayediop27908 ай бұрын
Oui c’est important
@Salihate08 ай бұрын
Mane dh dma tit wah mairie pikine diay nagn sma n registre bi deposé na carte d identité 2fois niouneii numéro bi kenen moko yorr 😭😭
@ndeyesokhnaseck84908 ай бұрын
@@Salihate0 danou wara marche sakh nak
@MamepenedaBeye8 ай бұрын
@@Salihate0moi plus de 1ans maye diabanté dama moudiee sounou tokk diap si yalla
@Cheikh_umaar.8 ай бұрын
Ngone Saliou kom bellingham rek enchantment bi 😭Allahou Akbar ❤️🫶
@Azubi6718 ай бұрын
😂😂😂😂
@abdoulayeniang25118 ай бұрын
Ngoné meussoul maye gayi dara mome journalisme pure et dure laye déf bien des choses pour le reste❤🇸🇳👑🎉
@bnydiop9758 ай бұрын
Sama domoubay kharal ma mayla ay coeur way ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@taphakeita14758 ай бұрын
La clé de la vie c'est la vérité bilahi tounkara mi bakhoule
Merci Domme Baye tounkara tu mérites plus que ce là longue vie à toi
@BayesaliouFaye-m3t8 ай бұрын
Non ngone saliou dou nite fi fule dieguine dafa ka wara am dega yalla kou mom merci beaucoup ngone ❤❤
@mbayegueye7238 ай бұрын
Wouhhhhhh Ngoné ya Sakhour ki Dou rouss sakh Sma Khole Sedd Na lol Si Ngoné Mi ❤😂😂
@Q_D_F-c5s8 ай бұрын
Yaw mi di lire sama commentaire mangui lay niane guir yalla abonnel sama chaîne KZbin 😢
@mamesarr47988 ай бұрын
Abonner na
@mamoursow28538 ай бұрын
Lienbi
@HabibToure-uo1ei8 ай бұрын
Abone na
@ndiassediagne90195 ай бұрын
Mat na
@malicksourang8 ай бұрын
Ngone saliou yalla na diamame yague billay aka deugou❤❤❤❤❤❤❤❤
@FallouDiagne-FGD8 ай бұрын
Ngoné dall yalla n'ala yalla faye
@balladiagne91448 ай бұрын
I love you so much Ngonè yalna yalla goudal sa fane amine amine amine
@abdoulayeniang25118 ай бұрын
Tounkara mi ngi ni yogue😭😂🏃🏾♂️🤣🤣
@moustaphaofficial8 ай бұрын
😂😂😂
@sokhnadiallo90136 ай бұрын
Machalla Ngoné Saliou 💯💯💯💯♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
@Blaise-re7rj8 ай бұрын
Respect ngané diadief doundeul Ngoné jeuredieuf❤❤❤❤ Ngoné au coeur ❤❤❤
@oumyngom18368 ай бұрын
Masha Allah, Yalna Yalla lafalla thiatt,deugeurr rek mo woor
@moustaphaofficial8 ай бұрын
Dieureudieuf Ngone saliou mou sell mi 😂😂😂
@thiorosene42028 ай бұрын
Merci beaucoup ngouné saliou très pertinente niaff
@IbrahimaThiandoum-p7t8 ай бұрын
Des cœurs pour elle vraiment je suis vraiment contente ❤❤❤❤❤
@moussadiallo61177 ай бұрын
Boy wakh DEUG do sentir khiff do sentir mar DEUG rek mo nekh bo néké si côté DEUG do ragal et Say arguments do diékh Machaalah Ngoné Saliou nationale keep it up
@MoussaCisse-rh6bq8 ай бұрын
Meun lingay def aka nékh. Tounkara kouma yagg suivre la mais tay mom dadié na ak boromi bopp.😂😂😂
@Mourtalladiop-eb1ij8 ай бұрын
Ngoune saliou Ray nga tonkara❤❤❤❤❤
@dontouretoure48618 ай бұрын
Je remercie tonkat c'est un démocrate il a bien écouté sans dire mot
@hacenahmed30278 ай бұрын
Parce Qu'il n'a rien a dire c'est tout
@CM-xo3oy8 ай бұрын
@@hacenahmed3027 Merci.
@EumeFall8 ай бұрын
Es que rousss japouko
@sokhnaastousidi68817 ай бұрын
Alkhamdoulilah une bonne femme ❤ journaliste bou am khamkham
@KhafssatouBaro8 ай бұрын
Ndeketeyoooo Sénégal désséna ay nite you am valeurrr Merci Ngoné Saliou 😮😮Yiiii kheeeeetou Deugue
@myleneb58138 ай бұрын
😂😂😂😂bilaye wakh nga deugue😮
@MaodoKone-rm3tl8 ай бұрын
Machaalah ki dou wakh 😂😂😂
@ousmanemara93928 ай бұрын
Ce qui me plaît chez cette dame c'est son franc parler mais aussi elle est véridique.
@modounguer81567 ай бұрын
Me tounkara bi moye bi nek 2stv wala daye lahie rek ❤
@Lamp1128 ай бұрын
Tounkara mom khana dafa bayi 2stv wala tok mouy dokh bi mo diékh motakah mouy weur plateau yi 😂😂🤣
@EumeFall8 ай бұрын
Jar n'a latie
@khalifasarr40526 ай бұрын
Tu .es la meilleure machalah la vérité c'est la vérité merci ngoné❤❤
@paparanelaye89168 ай бұрын
😂😂😂😂bravo Ngoné
@sheikhcham24527 ай бұрын
Tunkara russ mokoi raay
@ngoudaseck198 ай бұрын
Bilahi djiguéki tala taye nder ame na ba taye . Merci Ngoné. Deugue dalle dagua ko wara gnimé😘😘😘😘😘
@fatoutouray14748 ай бұрын
Ngonge Salieu is The Best❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@ramich47968 ай бұрын
Merci Zale vraiment ligueye bi raffet na lol,bref Ngoné je t'estime beaucoup parceque denga mane lingaye def machalla kéne dou natablé sa pertinence,mais nanga moytou bou bakh nga jogue sisa bop boubakh ndakh bathie yi defa meti si gayi,yonenty bi mognou gueune fouf té dégnouko ndiabar mou jap,donc je te conseil en tant que soeur mais en tant que joulite jogal sisa bop boubakhabakh yalnala yalla same❤❤❤❤❤
@aissatoundiaye25918 ай бұрын
Merci beaucoup ngone machala longue vie à toi chérie Bravo pour ton excellent travail ❤❤❤❤
@LhommedetatkiBa-fd3vj4 ай бұрын
Merci beaucoup ngone yalla nala yalla faye Diop Diouba❤❤❤❤❤❤❤
@PapiMbaye-bk7po8 ай бұрын
Ay ngoné goudal fane foumala guis mayla diouni😂😂😂😂 tu es forte
@khalifaababacarngom18097 ай бұрын
Ngoné Saliou ku am fouleu Ngà,Mâcha àllah logn vie😊🙏🏾
@bayegorfall18138 ай бұрын
No ngone saliou lek rek la defol tounkara niouss nako niouss you meti 😂😂😂
Lo doundou bo koy nétali day nieuw nice😂 .c'est un plaisir d'écouter ngoné ❤
@buzzpointsn4368 ай бұрын
Yi khétou deugg😂😂😂
@diamass54968 ай бұрын
Machalla madame c'est la première fois que je vous vois mais vous avez mon estime.respect
@RakhiRokhi8 ай бұрын
Ngoné saliou masahalla bilahi content na thjie yow yall nala yalla sakhal thjie deugou Gui thjie barké seydina mouhamed ❤❤❤❤❤❤
@FallouDiagne-ty1qf8 ай бұрын
Merci ngone salihou❤❤❤❤❤❤
@KhafssatouBaro8 ай бұрын
Ngoné Saliou ❤I love you tooo Machalaa yaa kham Deugue té diko wakh
@ngagnesylla29738 ай бұрын
Ngoné Saliou reck lay topo tu est le meilleur
@laminebarabusiness8 ай бұрын
Très bien ngone saliou
@dasassanehamath21687 ай бұрын
Waa la suite on veut entendre la réponse du monsieur
@YacineSambe-ey5fz8 ай бұрын
Walahi nék si deugue dafa néx ❤ Merci zalle
@mouhamedfall24478 ай бұрын
Ça kaw ça kanam Ngone saliou incha allah
@el27538 ай бұрын
Ngoné saliou elle est en lége car ell dit la vérité rien que la vérité ces mots viennent aisément dans sa bouche daga humilier avec respect sans le dépasser masala 😂
@SerignemorFaye-s9z4 ай бұрын
Ngone ma ngui thi yow.tu fais parti des meilleures journalistes de ton époque ❤et non des doulnalistes