REPLAY - QUARTIER GENERAL - Invité : SERIGNE SALIOU SAMB - 08 Juin 2018 - Partie 2

  Рет қаралды 451,321

TFM (Télé Futurs Medias)

TFM (Télé Futurs Medias)

Күн бұрын

Пікірлер: 693
@jf20tv8
@jf20tv8 6 жыл бұрын
je remercier dieu d'avoir de me fait partant sur communauté musellement particulier au mouride dieureudieuf serigne touba diarrama mame cheikh ibra wayé tamite serigne saliou samb yalnafi yeug té wer kham kham bi yokk
@pathegueye9393
@pathegueye9393 6 жыл бұрын
Que dieu nous guide à devenir de vrai talibé mouride . Dieuredieuf SERIGNE TOUBA
@ibrahimagaye2887
@ibrahimagaye2887 5 жыл бұрын
dieuradieuf cheikh ahmadou bamba
@modoumountakha8029
@modoumountakha8029 5 жыл бұрын
Qui est en la 2019 dieureudieuf serigne touba
@layesamb3388
@layesamb3388 4 жыл бұрын
Doumasi doyal barké serigne TOUBA ❤️
@modoumbayedieye7641
@modoumbayedieye7641 3 жыл бұрын
L'émission que je peux regarder chaque mois sans me désintéresser
@mordioufguediawayehiphopgu177
@mordioufguediawayehiphopgu177 5 жыл бұрын
Machallah s'saliou samb jamm si yaw si barke serigne touba
@fayemamy9521
@fayemamy9521 6 жыл бұрын
Machalah serigne touba amoul morom Yagnou may independance dé. Dieuredieuf serigne touba mouride rekay deug. Serigne saliou samb yalla na ngua yag fiiiii lolou té and ak wér. Mouride yi bégnagnou.barki serigne touba
@ibrahimagassama8655
@ibrahimagassama8655 6 жыл бұрын
amna solo demb dama setane ba fadiar machallah dieureudieufe cheikhoul khadim wayer serigne saliou sedenani kou bakh ga merci
@ahmetnoustafa2128
@ahmetnoustafa2128 6 жыл бұрын
Alhamdoulilah wax tan wi am na solo trop Dieuredieuf Serigne Touba Talibe baye niass la mai Serigne touba ken la walay ndeysan
@alphajallow2100
@alphajallow2100 6 жыл бұрын
Ahmet Nous Tafa daga bakh rek bilahii
@syllandiame6614
@syllandiame6614 6 жыл бұрын
Waw goora way. Daga bakh. Rek mei Yallah NAla Suno Borom Bi Sobhànahou Watahàlà dollé la defal xhéwal te defal la diamou ak wer Ci Barquèp Serigne Bii
@assanesane5173
@assanesane5173 6 жыл бұрын
Ahmet Nous Tafa diereudieuf yaram diam rek ngey ame lingeu sedel cheikhoul khadim dou rambou dila fate
@mordiopzaragoza488
@mordiopzaragoza488 6 жыл бұрын
Dagua bakh rek
@saxobakh1417
@saxobakh1417 6 жыл бұрын
Ahmet Nous Tafa kouyalla yeureum rék mokaykham
@toubaseck4361
@toubaseck4361 6 жыл бұрын
Merci serigne saliou samb yagal te wer sama xam xam rafet machallah kenn dou serigne touba
@Samb402
@Samb402 6 жыл бұрын
Manla youssou sop serigne bamba
@mamadoudiol6239
@mamadoudiol6239 6 жыл бұрын
mande douma mourid waye amna solo vraiment Machallah
@laminesarr668
@laminesarr668 6 жыл бұрын
Mamadou Diol mouride moy dioulit bo si beugué guéné sisa bop dem safara rk
@mamadoudiol6239
@mamadoudiol6239 6 жыл бұрын
Bo degue mawakhla fi kounek amna siko werou te mane si mame baye la werou motakh mawakhla mane khamna mourid limouye firi yone bou dieme si yalla
@mohamedgueye1014
@mohamedgueye1014 6 жыл бұрын
Mamadou Diol ziarr nala sapo nala nakh li nga wakh kou sokhar doko wakh man dé talibe serigne touba laa bou wer waye billahi sopou nala trop yalla nala yalla takhawou si barke werou korgui aminee
@mamadoudiol6239
@mamadoudiol6239 6 жыл бұрын
Mohamed Gueye wallahi mala raw amine yalna yalla nangou lep sibrke seydina mouhamed psl
@mohamedgueye1014
@mohamedgueye1014 6 жыл бұрын
Mamadou Diol ndeysan amine Ya bakh rek billahi yalla nala yalla takhawou teral là si barke bayy amine
@niassnazer4133
@niassnazer4133 6 жыл бұрын
non sama yaram bangui daw keine dou cheikh ahmadou bamba khadimou rassoul waxx tane bi nexx na amena solo serigne saliou samb kou sope serigne touba beusseul jaime way
@malikndiay6763
@malikndiay6763 6 жыл бұрын
niass nazer s touba dou morom
@abdoulazizsoumare9082
@abdoulazizsoumare9082 3 жыл бұрын
Hvccj hvhh6y vbi hc cvccccvb
@abdoulahadgueye8723
@abdoulahadgueye8723 2 жыл бұрын
@@malikndiay6763 6
@laminmaster9387
@laminmaster9387 6 жыл бұрын
Dieuredieuf Saliou Samb yalla nala yalla faye si barkéb Serigne Touba Amoul Morom ☝ ☝ ☝ ☝
@tewloumatv2514
@tewloumatv2514 6 жыл бұрын
Machalah serigne saliou samb yalla na yalla goudal sa fane thi barkep AHMADOU
@daganiang4296
@daganiang4296 4 жыл бұрын
Doumasi doyal walahi 2021
@amygaye408
@amygaye408 4 жыл бұрын
Serigne saliou samb wallahi sop nala lool guir serigne touba yalla na yalla yagal sa takhaway ci barki sidy birahim Fall ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@aissatoukanediene4185
@aissatoukanediene4185 6 жыл бұрын
sant yalla bou weer dieureuf Cheikh Ahmadou Bamba Khadim Rassoul
@morkandji6105
@morkandji6105 6 жыл бұрын
Aissatou Kane Diene machallh
@babacarndiaye8359
@babacarndiaye8359 6 жыл бұрын
Aissatou Kane Diene .. Ganna
@rokhiyadiop1668
@rokhiyadiop1668 6 жыл бұрын
Machallah je suis fier d'tre mouride et talibé
@assanesane5173
@assanesane5173 6 жыл бұрын
Mane Lima bégüe serigne touba dafa diegui deyo 😭walahi
@fadeldiop7406
@fadeldiop7406 2 жыл бұрын
AY WAY NIANAL MA SAMA KOOL BEUGUE BAMOU DIEKH TAK AK SAMA KHEEL DIKO KHALAT REK.
@seynaboundao2846
@seynaboundao2846 3 жыл бұрын
Sokhna fati Dieng dal Machallah aka mourité
@mamypendambayesaliou9665
@mamypendambayesaliou9665 6 жыл бұрын
Macha hallah..amatina solo deh... Dieredieuff Kou Tedd ki..
@mameabdoubadiane8903
@mameabdoubadiane8903 6 жыл бұрын
Diedieuf serigne touba yalna gnep woré ndoo si barké ramadan mou barak
@aminatagath7295
@aminatagath7295 6 жыл бұрын
Mane dh Niasséne la wayé lima beugue Cheikhoul Khadim motakh yallah deff sama dieukeur bokou thie ayy seuteum! Fouma dégué ayy khasaïdes sama khol dafay cedd bilahi! Yallah na yallah fayalniou souniou mak you bakh yi!
@kanengagne8160
@kanengagne8160 6 жыл бұрын
yalna la yalla defal jamm
@susobass7685
@susobass7685 6 жыл бұрын
ndaye sane yabakh yague fi lol tewer
@cheikhseye4619
@cheikhseye4619 5 жыл бұрын
Barké Serigne Touba bo dogué si bamél ga koy kham
@ndeyeawandiaye4892
@ndeyeawandiaye4892 4 жыл бұрын
Talibé baye rek gua meune done ndaysane daguéne bah rek
@mamadoufalilougaye733
@mamadoufalilougaye733 6 жыл бұрын
Yalla mo def Serigne Touba nimou mel koum nekhoul digna sonou Naniou andeuh di sante Serigne Touba nakh sante Serigne Touba moy def louy bégué lo yalla
@kanekanene
@kanekanene 6 жыл бұрын
Mamadou falilou gaye nika yalla def koumou nékhoul kalamél yalla
@layesamb3388
@layesamb3388 4 жыл бұрын
Yaabari xam xam billahi 🙏🏾
@balybousso4891
@balybousso4891 6 жыл бұрын
Serigne Saliou Samb Yalna yalla goudeull say fane ndakh li dess yeupp kou tedd ki defal nalakko Machallah
@bayeserignediop344
@bayeserignediop344 6 жыл бұрын
Serigne Saliou Samb yalla nala Serigne Touba fayal bopam barkép Cheikh Ibra
@salioundaw8183
@salioundaw8183 6 жыл бұрын
bilahi serigne saliou samb yalla nala serigne touba fay amna solo trop bilahi beeguena
@khadimseck7264
@khadimseck7264 6 жыл бұрын
Miimm reew BAMBA ko momm Rewmi BAMBA moy kiko momm DIEUREU DIEUFEII SERIGNE TOUBA
@sambadia2505
@sambadia2505 6 жыл бұрын
seck khadim wakhofi dra
@astoundiayetouba5068
@astoundiayetouba5068 6 жыл бұрын
Thiey serign bamba amout morom dh sante yala boubakh bimnou defé ay mourit yougeum serigne bamba nak lole sakh s saliou sambe yalnagfi yageu barkeb sa tourando wakhtanwi nekhna torop xolle yep sedna machalah
@aminambodji3134
@aminambodji3134 6 жыл бұрын
thiey yalla Serigne touba dale amoul morom bilayi Serigne Saliou samb yalna la yala faye si barki Serigne Saliou Mbacke xol sédatina si yaw yala xanako
@sallioundiiaye2095
@sallioundiiaye2095 6 жыл бұрын
Ya wayyyy li nekhna si xol ♥ sou niou begue diamou ak senegal dém naniou délou si mame borome touba maniou nio ame louko féte kaww ame mame borome touba si réw mo gúen wourouss ak pétarol ❤ diaradiff s. Touba Kou ko wakh Yala ga guise ak mome
@ndiemefall7767
@ndiemefall7767 6 жыл бұрын
bilay guéne dou ahmadou ñioune lignou ame sakh khamouñiouko
@maramethioub3278
@maramethioub3278 6 жыл бұрын
machallah ken dou serigne touba yalla na yalla yokkou ay leram te rass niou si barkem
@missmbengue2553
@missmbengue2553 3 жыл бұрын
Thiey serigne touba amoul morom
@mbayangdieng7311
@mbayangdieng7311 6 жыл бұрын
Ba xol yagui fékh eskey machallah serigne saliou samb doundal loll😍😍
@papemalickdiouf3743
@papemalickdiouf3743 6 жыл бұрын
DIEUREUDIEUFFF SERIGNE TOUBA ,DIARAMA MAME CHEIKH IBRAHIMA FAAL LAMP
@David-lu5yz
@David-lu5yz 6 жыл бұрын
Cheikh Ahmadou bamba évolue pas dans la même atmosphère que les autres . Kéneu dou mom🙇
@mamadou642
@mamadou642 6 жыл бұрын
mouhamed gueye donne nous les preuves ??
@salamataasalame6506
@salamataasalame6506 6 жыл бұрын
mouhamed gueye malako wakh 👈💘
@fallouseye509
@fallouseye509 6 жыл бұрын
mouhamed gueye machalla
@mamadoujr9085
@mamadoujr9085 6 жыл бұрын
Mamadou coulibali nangoul ndogal
@sonia1165
@sonia1165 6 жыл бұрын
Mamadou coulibali li ki wakh boula doyoul ay preuve kone do nit
@kadialymboup5631
@kadialymboup5631 6 жыл бұрын
Dieureudieufé sérigne touba!sant sérigne saliou mbacké!!!
@falloufall1816
@falloufall1816 3 жыл бұрын
Kénn dou cheikh Ahmadou bamba mbacké Khadime rassoul theiy serigne touba Khadime rassoul 👂♥️♥️🙏🏿
@coumbaniang3103
@coumbaniang3103 6 жыл бұрын
vraiment hier quardiè gènèral dafa nèkh dieureudieuff S.Touba S.Saliou sambe doundal 111ans S. khadim gueye aussi dèmbou xollou mourite yèppa sède fa yallahou S.Touba mo nèxa wakhtanè
@assanendiaye2997
@assanendiaye2997 6 жыл бұрын
Alkhamdoulilahi rabilallamine sante yalla Bignou wathiéle khadimou Rassoul si Sénégal mome mignou déf Mouridou sadikhe
@taphasatouba3246
@taphasatouba3246 6 жыл бұрын
Allahou akbarr barki serigne bamba yalla bouma dagn si di gnakka and ak sama sago si mom
@ibzomaker3551
@ibzomaker3551 6 жыл бұрын
dieureu dieufaté borom touba serigne saliou samb ken amoul sa faye barke serigne fallou yall na serigne touba leeral sa yonne amine si barké borom touba akassa
@serignesaliouniang4227
@serignesaliouniang4227 6 жыл бұрын
macha alla yalla naniou yalla fayal serigne touba
@bayeabdougcbpikine7430
@bayeabdougcbpikine7430 6 жыл бұрын
Koumo nekh ak koumou nekhoul mola mom serigne touba dou morom
@lazyiniestar6602
@lazyiniestar6602 6 жыл бұрын
Kéep kou yakar Serigne Touba rk beuseul j'aime
@alioundiaye7472
@alioundiaye7472 6 жыл бұрын
Dieureudieufe cheikh akhmadoul khadim diarama mame cheikh ibra fall seriñ mountakha mbacke yalla na diam yague lole té andak wérr srñ saliou samb yague fi lole té andak wérr si barke seydina mouhaméd sws
@laminendiaye8368
@laminendiaye8368 3 жыл бұрын
Akassa thiey borom touba amoul morom
@mariemediop4993
@mariemediop4993 6 жыл бұрын
Nallén yalla samou barké seyehou Ahmadou tidiani
@modoudioplg1302
@modoudioplg1302 6 жыл бұрын
marieme diop amiin ak yawtamite
@Ghdhjjfhknhxwvjf
@Ghdhjjfhknhxwvjf 6 жыл бұрын
yaw mariem ken dou s touba
@lekinzal123
@lekinzal123 6 жыл бұрын
Amin mouride
@pulga1046
@pulga1046 6 жыл бұрын
Rew mi BAMBA moy kiko mom diereudiefé Serigne Touba
@abosouhaibourijallthiam4843
@abosouhaibourijallthiam4843 6 жыл бұрын
Diere dief serigne saliou sambou Macha Allah waxtan wi nékh na lôll yalla nala yalla fay
@fatoumataibriga6725
@fatoumataibriga6725 6 жыл бұрын
Machalla khôl cèdena deugue dal dou rombe ay nopou Dieureudieuf serigne TOUBA
@Delabderkallaf
@Delabderkallaf 6 жыл бұрын
Dieureujeufeuty Cheikhoul khadim, Alkhamdoulillahi Rabbil Halamine baniou nékké sa talibé way ...Di Dokh tchi Bambay Dem Ba Aldiana...Ndeysane lolou Dafa leer nagne ,Diarawlak Cheikh Ibrahima Fall , Serigne Mountakha yague fi lolou té andakk wer
@abdourahmanedieng9255
@abdourahmanedieng9255 6 жыл бұрын
Yalnanu yallah sakhale tie ak talibé ,beug Serigne touba Mbacké rèk
@ibrahimakhalilfall9291
@ibrahimakhalilfall9291 Жыл бұрын
Meilleur QG de tout les temsp
@assanethiaw8175
@assanethiaw8175 6 жыл бұрын
Thiaye SERIGNE TOUBA dieureudieufaty mome..srgn saliou samb wa Touba Gabon beguenagnou gnoune wa makarimal aqulah libreville
@abdoulayecisse1115
@abdoulayecisse1115 6 жыл бұрын
Nagne guena fonk tei di roy nitou Yalla Ahmadou Bamba mi dh ak fo meun di bok boy roy thi mom doko rethieu Sant Yalla bou bakh bima mayei Serigne Bamba nek sama khol Respect Serigne Saliou Samb wakh lo maitrise dafa nekh.
@yacinecisse8325
@yacinecisse8325 6 жыл бұрын
bilaye yaram wakh lo metrise wessou na nekh
@matylo3988
@matylo3988 6 жыл бұрын
machalla Serigne saliou samb yalla gua fi yaque tee werr thi Barker seydina Mohammed
@sididieng1783
@sididieng1783 6 жыл бұрын
machallah serigne khadim gueye yalla na fi lol tè wer si barce kou tedd ki limi diague nekh na trop machallah amna sollo wakhtan bi am sollo serigne saliou samb 😍😍
@gainde8023
@gainde8023 6 жыл бұрын
Masha"Allah! Dieureudieufé Serigne Touba.
@djibyndiaye7496
@djibyndiaye7496 6 жыл бұрын
eskey Mbacké.. yalla naniou alla fayal makk gni..Sénégal dal yalla bakher naniou
@Missdieng
@Missdieng 6 жыл бұрын
soo nieuwatoul wone rekk dotouma sétane quartier général machallah serigne saliou samb sédall ngua kholl yii barkii Mame borom Touba 😍😙
@adjameta
@adjameta 6 жыл бұрын
Namone na QG sering saliou samb sama sope biii aka teye wakhtane yalnala cheikh ahmadou bamba terale
@mamediarrambengue7084
@mamediarrambengue7084 6 жыл бұрын
Keneu dou cheikhoul khadim😭😭
@thiernofall6812
@thiernofall6812 6 жыл бұрын
Mame diarra Mbengue wawe
@badarambaye8015
@badarambaye8015 6 жыл бұрын
Mame diarra Mbengue kéne dou mome
@fatoumadeleinengom4576
@fatoumadeleinengom4576 6 жыл бұрын
Serigne saliou samb beugnaaala nguir dieumi serigne saliou Dieuredieufer serigne touba diarawlakk Mame cheikh
@ndiemefall7767
@ndiemefall7767 6 жыл бұрын
machalla mane dama contane trop thi wakhtane bi ta douma si dokhale sakh souma sagnone ñiou invité watt serigne saliou samb machalla kham kham bi selle na guéne dou borom touba
@abodiouf5728
@abodiouf5728 6 жыл бұрын
Dieureudieuf serigne touba machala Ken d'où ahmadouna
@ndeyefatoundao9362
@ndeyefatoundao9362 6 жыл бұрын
Walahi nekk mouride dafa nekh Gueum CHEIKH AHMADOU BAMBA waulou ko yaklar ko doyloko way way way gars yi lolo neh ....yalla nanu yalla def ay deugui deugue mouride
@feuzbadiane149
@feuzbadiane149 6 жыл бұрын
Dieureudieuff Serigne Touba
@papemalickdiouf3743
@papemalickdiouf3743 6 жыл бұрын
THIEUYYYYY SERIGNE TOUBA
@bounadieng1505
@bounadieng1505 6 жыл бұрын
Serign touba bi war nagnou diko diadieufal sa souné
@massambamouritesadikh1382
@massambamouritesadikh1382 3 жыл бұрын
Wallahii serigne bouna ya gorré
@cheikhsaliousylla837
@cheikhsaliousylla837 6 жыл бұрын
S saliou samb yalnala yalla takhawo si barguip s touba yague s khadim gueye dieureuguine dieudieuf amine
@toubamoylislamtouba2331
@toubamoylislamtouba2331 5 жыл бұрын
kénal lène serigne touba kène le amoul morom
@cheikhfall9639
@cheikhfall9639 6 жыл бұрын
Thieuy Ahmadou ken khamouko mdp (mourir de pleures), Serigne Saliou Samb yalla bofi diouguée, sakh fii dakk abadaane
@sultancisse1383
@sultancisse1383 6 жыл бұрын
Pétition partie 2 si SERIGNE TOUBA biir quartier général avant koor gui di diekh momlay réclamé mane doyalouma dh walahi woowaleinma ablaye Diop bichri
@xaxa6821
@xaxa6821 6 жыл бұрын
Sultan Cisse je suis d accord avec vous
@alphajallow2100
@alphajallow2100 6 жыл бұрын
dieuredieufe serigne touba sunu yakar tay ak euleuk mbacké balla aicha
@papemalickfall7674
@papemalickfall7674 6 жыл бұрын
Chiekhoul khadim amoul morome tè dou mass dieureudieuf serigne touba
@ndeyengom1153
@ndeyengom1153 6 жыл бұрын
Dieureudieuff serigne touba khadimou rassoul
@elhadjithiam3604
@elhadjithiam3604 6 жыл бұрын
sant cheikhoul khadim rek serigne saliou samb yalla nga ngeuremal serigne touba
@juniorfall9049
@juniorfall9049 6 жыл бұрын
yalla naniou cheikhra fall sii borom touba ndakh niou mame fallou akhmadoulena khadime kéneu dou kou tédeukiii
@mormar8085
@mormar8085 6 жыл бұрын
dieureudieuff serigne saliou yalla nalla borom bii yagual lafii
@serignefalloufall4242
@serignefalloufall4242 4 жыл бұрын
Beugue serigne touba rék rék kéne dou serigne touba khadime rasoule Akassa ❤️🙏🏿
@morseye6767
@morseye6767 6 жыл бұрын
santé serigne touba rek
@mameseyesylla6811
@mameseyesylla6811 10 ай бұрын
Salam qui est la en 2024?
@centv3528
@centv3528 9 ай бұрын
Magui nii
@nogayediallo7047
@nogayediallo7047 6 жыл бұрын
Dieureudieuf serigne touba fière d'être mouride🙏🙏🙏
@layethiam1885
@layethiam1885 6 жыл бұрын
Masahalla yalla na yalla goudal saw fan sa defal ko kepou kounan lahi laakha ila lah
@maneladia1665
@maneladia1665 5 жыл бұрын
Thieuy Serigne touba mo wour
@modoufall3802
@modoufall3802 6 жыл бұрын
machallha santé serigne touba rek 😭😭😭😭😭
@seydinaalioudiouf1431
@seydinaalioudiouf1431 3 жыл бұрын
Saliou Samb a étudier l'Arabe et les khassidas pour mieux comprendre le discour de Cheikh Ahmadou Bamba, barké Rassoulillah
@ibrafaye8539
@ibrafaye8539 6 жыл бұрын
Gniye dislike aye yerffer lagnou serigne touba amoul morom keine dou serigne touba mim reww bamba moko mome
@ibrahimadiop4990
@ibrahimadiop4990 6 жыл бұрын
Les 28 personnes qui n'aiment pas ca. Lolen thi meti la beugeu xam rek ?
@codousy636
@codousy636 6 жыл бұрын
Dieureudieuf Cheikh Ahmadou Khadim Rassoul sama xoll dafa sedd wallah waxtan bii am sollo
@famabathily990
@famabathily990 Жыл бұрын
Dieureudieuf serigne touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@falydiaw3439
@falydiaw3439 6 жыл бұрын
Machallah kadou gui rafetna
@oumysow1629
@oumysow1629 6 жыл бұрын
Alkhamndou lilah Dieureudieuf cheikhoul Khadim
@mbayefouiny5105
@mbayefouiny5105 6 жыл бұрын
Serigne Touba Amoul Morom
@smodououmymbacke2354
@smodououmymbacke2354 5 жыл бұрын
Mbaye fouiny
@serignesaliousylla1547
@serignesaliousylla1547 6 жыл бұрын
Bilahi serigne touba amoul morome 👌serigne saliou samb lou fi yage doyol
@elhajndiaye7832
@elhajndiaye7832 6 жыл бұрын
Akazaa Serigne Saliou Samb Serigne Touba kou am chances baggue ko
@mouhagueye3012
@mouhagueye3012 6 жыл бұрын
Yalla naga fi yague loll te wer ci barke khadim rassoul
@elhajndiaye7832
@elhajndiaye7832 6 жыл бұрын
Amiiine sounou boroom boolé nouko
@maramefall8914
@maramefall8914 6 жыл бұрын
Bilahi serigne touba d'où nit ms nék mouride mo nekh
@fatygueye6386
@fatygueye6386 6 жыл бұрын
serigne khadim gueye moy ndanan dh barké serigne touba
REPLAY - QUARTIER GENERAL - Invité : SERIGNE SALIOU SAMB - 08 Juin 2018 - Partie 4
1:26:29
Мен атып көрмегенмін ! | Qalam | 5 серия
25:41
Cat mode and a glass of water #family #humor #fun
00:22
Kotiki_Z
Рет қаралды 42 МЛН
1% vs 100% #beatbox #tiktok
01:10
BeatboxJCOP
Рет қаралды 67 МЛН
Сестра обхитрила!
00:17
Victoria Portfolio
Рет қаралды 958 М.
REPLAY - QUARTIER GENERAL - Invité : SERIGNE SALIOU SAMB - 08 Juin 2018 - Partie 3
1:17:02
S. Lamp Fall - waxtan yonou guedj gui
1:59:06
Jalibatoul Maziyah
Рет қаралды 2,1 МЛН
QUARTIER GÉNÉRAL - Spécial Korité - Pr : PAPE CHEIKH DIALLO - 24 Mai 2020 - Partie 2
2:38:45
Serigne Touba ak Cheikh Ibra kiff kiff ken lagnou | Dieuwrigne Ndiassé
1:00:18
Dieuwrigne Ndiasse Officiel
Рет қаралды 7 М.
Мен атып көрмегенмін ! | Qalam | 5 серия
25:41