REPLAY - QUARTIER GENERAL - Invité : SERIGNE SALIOU SAMB - 12 Juin 2017 - Partie 3

  Рет қаралды 1,461,507

TFM (Télé Futurs Medias)

TFM (Télé Futurs Medias)

Күн бұрын

Пікірлер: 1 600
@aboubacarsy347
@aboubacarsy347 9 ай бұрын
Qui est là en 2024 précisément dimanche 17Mars Ken dou Serigne Touba koudoul Serigne Touba Yalnaniou sa borom tasse ci barkem defniou ay deugui Mouride🙏🏾
@magattetallly6077
@magattetallly6077 2 ай бұрын
Je suis là le 20 Octobre 2024🎉. Dieureudieuf Cheikhoul Khadim❤😊
@falloudiongue5857
@falloudiongue5857 4 жыл бұрын
diangu katbi guir yalla mou ndieuw cartier general 2020 guir yalla taysirbi amna solo lolou
@gninguesophie5581
@gninguesophie5581 7 жыл бұрын
yonnou serigne touba gui amoul daray hazard dieureudieufe serigne touba milliard fois
@mamecheikhmbaye2244
@mamecheikhmbaye2244 5 жыл бұрын
Serigne Touba amoul morom serigne saliou samb yalla na yalla yokou aw fanam
@fadioufydiouf1764
@fadioufydiouf1764 7 жыл бұрын
Man dal meunatouma nelaw tei setanouma li thieuy serigne Touba...fiere d être mouride
@BathiDiop-qk8ih
@BathiDiop-qk8ih 5 ай бұрын
Mais yaw lima dal mola dal konne
@BathiDiop-qk8ih
@BathiDiop-qk8ih 5 ай бұрын
Mounouma nellaw tei setanoumoko
@youssoufall470
@youssoufall470 7 жыл бұрын
emissions yi dé amena solo di khamelé mague gni dieureudieufti serigne touba diarama Mame cheikhra fall yallana yalla yok sen lere tei tassou gni sen barke amen amen amen
@coumbasene7836
@coumbasene7836 7 жыл бұрын
Machallah, je l'ai regardé en différé mais j'avais vraiment pas envie que ça se termine. Dieuredieufeté Serigne Touba, kouko wakhoul gooré wo.
@BOP913
@BOP913 7 жыл бұрын
Coumba Sene sakh n ga deug dé séne thiali démba séne
@football-ce7cv
@football-ce7cv 2 жыл бұрын
Fen reck 🐕🐕🐕👎🇸🇳🇸🇳🐒🐒
@guiguindiane644
@guiguindiane644 7 жыл бұрын
barki seydina mouhamed damay delou sante yalla bama dioudouwé fekk samay wadiour nekk mouride ma topeu ci sen tankeu barki serigne saliou
@manickdeng4995
@manickdeng4995 7 жыл бұрын
Serigne saliou samb yalla nala sa borom aral bopam barke cheikhoul khadim..Wa tfm Mome da la Leni Baye ak kou ted GUI laf thiat..
@dioufkhadim275
@dioufkhadim275 6 жыл бұрын
Manick Deng xxx
@amyndiaye4334
@amyndiaye4334 4 жыл бұрын
Douma doyal si diko setane .ken dou Serigne touba bamba merci❤
@toutyd269
@toutyd269 4 жыл бұрын
Thiéy serigne touba qui regarde encore en 2020 ba octobre 2020 à 2h du matin magui sétane QG yi thi wakhtanou serigne bi douma thi doyal mouk Mach'Allah
@antathiam3970
@antathiam3970 6 жыл бұрын
Sera en na QG bi plus de 10 fois douma si doyal len dou serigne Touba 😍😍🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
@mansourmboup7659
@mansourmboup7659 6 жыл бұрын
Walahi nio yèm. Niveau dafa kawéwone
@antathiam3970
@antathiam3970 6 жыл бұрын
Mansour Mboup troppp sakhh ! Ken dou kou Ted ki
@mansourmboup7659
@mansourmboup7659 6 жыл бұрын
No bimou aksé thi serigne saliou la départ
@mamebousso7761
@mamebousso7761 7 жыл бұрын
machallah QG bi masou fee am thieuy serigne touba moy kenn de yalnanoko yalla fayal
@syllabally6340
@syllabally6340 7 жыл бұрын
kou adak serigne bamba thiakaw thiakanam bravo pape cheikh s saliou samb teeygalol yalanalayala fay ma bègue cheikhoul khadim
@madinasy2460
@madinasy2460 7 жыл бұрын
machaallah bay cheikh yague nga def plateau bou nékh wayé bou mélni meussoulo ame,serigne saliou samb xamxam bi rafetna téi sélleu.dieureudieufety Serigne touba diarama mame cheikh ibra
@TalibèAlhasaneSalam
@TalibèAlhasaneSalam 7 жыл бұрын
Serigne touba amoul morome , dieureudieuf cheikh Ibrahima fall💓💓💓💓💓
@segacisse867
@segacisse867 7 жыл бұрын
Ausländer berlin
@khadimdiop9897
@khadimdiop9897 7 жыл бұрын
super Quartier Général dieureudieuf à pape cheikh et Serigne SALIOU Samb vraiment ces révélations nous réconforte et augmente notre AMOUR EN CHEIKHOUL KHADIM. DIEUREUDIEUFEUTY AHMADOU BAMBA SOUNOU YAKAR DJI TAY AK EULEUK.
@falloufall1816
@falloufall1816 4 жыл бұрын
Machallah dieureudieuf Serigne Touba Khadime Rassoul thiye kou tédki cheikh Ahmedou bamba mbacké Khadime Serigne saliou samba yalla gafi yague te werr amine ya rabi thi barrekp sergne saliou mbacké Khadime Rassoule 👂♥️😍
@diufy1559
@diufy1559 7 жыл бұрын
Billahi serigne touba koukoy teukeulé ak sa way kouné Khamoko wala khamo sa way
@hannetorodo6563
@hannetorodo6563 7 жыл бұрын
DiØufy Ønly liga wakh wakhat ko way ken dou Serigne touba Mbacke amoul morom
@maawasy4147
@maawasy4147 7 жыл бұрын
aka ler lolou
@magayesarr4714
@magayesarr4714 7 жыл бұрын
Yalla nguénefi yague daguéne bakh mourite
@khadimthiam5773
@khadimthiam5773 6 жыл бұрын
mo mane fi mane fanou dieume fopé bâ boba akhemadou Mbacke
@santeserignetouba4826
@santeserignetouba4826 7 жыл бұрын
ñioune ndaaw gni sante nañiiu bou bakh cheikhoul khadime serigne saliou loumassi guena nékheuu ndaw gni gnio guenaa beug guenaa gueum CHEIKHOUL KHADIME 💕
@baraniang8719
@baraniang8719 7 жыл бұрын
maîtrisé ligay wakh nekhna DIEUREUDIEUF BOROM TOUBA
@ligeuyeulserignetouba2545
@ligeuyeulserignetouba2545 7 жыл бұрын
Bara Niang wakhal dh
@djibyfaye3616
@djibyfaye3616 6 жыл бұрын
J'avais entendu l'ampleur de cette émission avant de vérifier mais c'est effectivement une émission de toutes les autres. Sérigne saliou SAMB Merci pour la maitrise du discours, la clarté des propos mais surtout la cohérence historique du parcours des Khalifs qui reflète fidèlement votre travail inégalable dans l'histoire du Mouridisme.''God bless us'' Yallna borom def DIAM thi rewmi yeup. Merci infiniment
@guiguindao9238
@guiguindao9238 7 жыл бұрын
sama xol ceide n'a serigne touba ak wa keureum yalla naniou leine yalla fayal
@ismawade9277
@ismawade9277 7 жыл бұрын
il n y aura plus un QG aussi magnifique,emotionnel que celui ci!merci serigne saliou samb,tu m as fait pleurer toute la nuit .macha allah marianne,meussou ma khamné talibé nga. santrek.prochain QG avec s saliou samb:wakhtane ci mame cheikh ibra fall on espere
@bounamasow3117
@bounamasow3117 2 жыл бұрын
q
@papewalydiouf785
@papewalydiouf785 7 жыл бұрын
Alhamdoulilah :), Keep Kouy Gëstu si yonu cheikh Ahmadou Bamba, khamni lignou fi wakh lep lou werleu, Serigne Bamba nena yone yeupa bakh, Nagnou gueum lignou gueum mandou, ligueyal Serigne bi tei khamni moy ligueyal le prophete Mouhammed (PSL) tei khamni moy ligueyal souniou borom, Bayi weranté bi ak khoulo bi. Souniou borom ALLAH louko sop ley def, Nagn ko Sant bimou fi bayei Mak niou bakh gnissi deuk bi ngua khamni defouniou loudoul nek si mission wou souniou Borom. Kou beugua kham danguay Gëstu, li fi wadji wakh yeup mingui si khassida yi ak terei yi fi Serigne touba bayi, serigne Bamba taguoul bopam dafnio khamal rek nguir dimbalignou(témoignages yi bari bassi toubap yiko beugone sakal pékhé). " N'abusez pas de ma condition d'homme noir ,pour ne pas profiter de moi car je suis le serviteur éternel ,chaque génération qui passe aura la certitude que je suis venu pour elle " ."Dieu m'a accordé des priviléges qu'il n'a accordé et n'accordera à personne"."J'ai recu un savoir que l'on ne voit point dans les livres, mais au contraire un savoir qui m'a ete inspire par l'ETRE qui a fait de ma plume un rempart protecteur." Bureau bassa ndar dagn ko wedilo souniou borom, mo wakhfa "Likhlass", lolou indi lissi top lepp, Serigne bi nak yague na am ay noone(ennemis), mais bimou gnibissei si guedj gui néna Diegual na Nieup, kone Nioune Mourides rawatina Baye fall Si Diegual lagn wara deuk, Kouniou Togn niou diegual, kouniou dinguat niou diegual, nek si lignou nek gueum lignou gueum, Nioune Mourides nioune Baye Fall, nous sommes des savants, des intelectuels, etcc doté de raison. Khamnagn boubakh si louniou nek. Souniou devise moy "Diokhé niam gniko yelo" ak "Nangou toumeu". Lene rek lagn niou wara wakh terei niou mo diaral niou khekh khoulo, moy niou terei niou ligueyal serigne bi ndakh moy ligueyal Yonente bi (PSL) moy ligueyal Souniou BOROM. Mangui toubat di diegualou bou bakh si kadou yi di niane souniou borom defal niou diam fi ak founiou dieum. @piwaley
@Mouhamedmbaye026
@Mouhamedmbaye026 7 жыл бұрын
j'aime ça ta tre b1 di
@khadimndiaye3791
@khadimndiaye3791 7 жыл бұрын
Pape Waly DIOUF akassa fall wakh dji werneu
@amygaye408
@amygaye408 4 жыл бұрын
Macha allah am na solo wakh dji rafete na kadou yi pertinent na
@djilyndiaye2530
@djilyndiaye2530 3 жыл бұрын
s icardi
@Lopios-g6l
@Lopios-g6l 3 жыл бұрын
Akkassa amena solo...
@serigneamsatoudialibamback1420
@serigneamsatoudialibamback1420 7 жыл бұрын
machaalah serigne saliou samb xam xam bi lérna yall nakou yalla barkéle amine
@macoumbandiaye1107
@macoumbandiaye1107 7 жыл бұрын
macha alha amna solo yalna nou yalla fayal serigne touba amine yarabi
@khadimgueye1216
@khadimgueye1216 4 жыл бұрын
Kouy setane li ba 2020 si Dieumi Serigne touba beuseul j’aime
@boromdendeyekhabanesylla5638
@boromdendeyekhabanesylla5638 4 жыл бұрын
Man
@mameboussowathie4265
@mameboussowathie4265 Жыл бұрын
2023 lakoy sétan ni❤❤❤
@matydiao8289
@matydiao8289 7 жыл бұрын
thieuy serigne touba amoul morom manou ma nelaw san setan li way machalla
@ousseynoukane4747
@ousseynoukane4747 7 жыл бұрын
diadieuf ken dou waw le sauveur de l'humanité sans vous on serait rien merci saliou samb akassa ko tédiki
@mamasitagueye2035
@mamasitagueye2035 7 жыл бұрын
Serigne touba niko yalla Def kumu nekhoul guewmani guemnga yonentibi
@cheikhndiobandiaye9637
@cheikhndiobandiaye9637 7 жыл бұрын
Mamasita Gueye wallahi akay deug koumou nékhol sonnou rék
@ahmafall5060
@ahmafall5060 3 жыл бұрын
🥰 thiey Kou teed ki ...Serigne touba si khôl Mo geune adouna’k liissi biir
@senthiowbeurina9981
@senthiowbeurina9981 7 жыл бұрын
keep kou commantaire yall na ahamdou boroom diam ni defal say Mbeurr ci barké Cheikhoul khadim
@ballawadediack253
@ballawadediack253 7 жыл бұрын
Yallah mooy borom diam ñi, bayyi léén bokkaalé. Kou déé tédd si bamméél manoul défal kénn dara.
@cbdkheuch9735
@cbdkheuch9735 7 жыл бұрын
IOW xolal ya nguimay beugg sofffff do teuthie sa lamigne barké borom touba iow balla cheikhoul khadim soko beugoul do dougou aldiana
@ahmadoumakhtarniasse7231
@ahmadoumakhtarniasse7231 7 жыл бұрын
yaw kéne doula ramou ta say dieuf seytané moka nangou sounekoul wone segn touba pain ndambé ngay done
@naboujina172
@naboujina172 7 жыл бұрын
Balla Wade Diack au moins amal respect boudoul dara ndakh alhourane bou tede bimou binde diko diangue..... sene genre yii rek nioye heuy torokh prck amouniou teguine et o6 bala ngay wakh reflechi dengame sangou sangue yii seydina mouhamed(psl) keine doufii dess
@naboujina172
@naboujina172 7 жыл бұрын
Balla Wade Diack te repondre sera une reelle perte temps parceque non seulement tu ne sais pas ce que tu dis et tu es inconcsient.... ce qui sur ce que tu regrettera tes propos inshaallah et cela sur terre.
@creatoure9384
@creatoure9384 7 жыл бұрын
akassa bilahi amna solo torop yal nanou yalla fewalé ak seytané ta bolégnou ak cheikhouna cheikhoul khadim amineee
@mlm6366
@mlm6366 7 жыл бұрын
Cheikh Ahmadou Bamba a dit : " N'abusez pas de ma condition d'homme noir ,pour ne pas profiter de moi car je suis le serviteur éternel ,chaque génération qui viendra aura la certitude que je suis venu pour elle " Dieureudieufé Borom Touba Diarama Mam Sheikh Ibrahima Fall Lamp
@daoudamboup6400
@daoudamboup6400 6 жыл бұрын
dieureudieufé yaw miko wakh
@mamediarrandiaye5330
@mamediarrandiaye5330 5 жыл бұрын
Yalla nala serigne touba fay
@babandiaye3154
@babandiaye3154 5 жыл бұрын
Dieuradieuf serigne touba
@GalguiReew
@GalguiReew 5 жыл бұрын
Merci
@khalyndiaye2194
@khalyndiaye2194 3 жыл бұрын
Nbnn
@lobesohnafall5392
@lobesohnafall5392 7 ай бұрын
Je regarde l’émission en 2024 Keen dou Serigne TOUBA ❤❤❤ ❤❤❤
@khadijamouserignesaliou1019
@khadijamouserignesaliou1019 7 жыл бұрын
Dieureudieufty cheikhouna akhmadou Bamba ...QG validé bi mom néxna doufi gawa amat
@khadimndiaye5129
@khadimndiaye5129 7 жыл бұрын
mai pape cheikh invitél baye adama sarr baye fall wala ablaye Diop bisri
@talibehserignbarambacke4981
@talibehserignbarambacke4981 7 жыл бұрын
Khadim Ndiaye bilahi mome la wakh na indi serigne ablaye diop
@khadimndiaye5129
@khadimndiaye5129 7 жыл бұрын
talibeh serigne bara ablaye Diop lou ler lay wakh yaw ño bokou s bara
@talibehserignbarambacke4981
@talibehserignbarambacke4981 7 жыл бұрын
Khadim Ndiaye walahi guisnga cheikh mouhamadou lamin reik yalla nagnou dajè ak mom walahi kon sougn yakar
@dickocheikh4172
@dickocheikh4172 5 жыл бұрын
diarna sante dé
@diarriatoumbacke3166
@diarriatoumbacke3166 7 жыл бұрын
bijou Ndiaye yaw,geune nala beugue ndakh Serigne Moustapha Bassirou migua toud😍
@ziggystle
@ziggystle 7 жыл бұрын
OOOHHHH. j'ai ressenti une joie immense en suivant cette émission. Je me rend compte vraiment de la chance que nous avons nous Sénégalais. Dieureudjeuf Cheikhoul Khadim. QG bi moma dakal yi diar yeupppp. Dieureudjeuf Cheikhoul Khadim
@soldarbidiop9079
@soldarbidiop9079 7 жыл бұрын
s saliou samb yalnako yalla fay amine man damako beuge ndakh baye karim mbacke
@ndeyeaidasamb9803
@ndeyeaidasamb9803 7 жыл бұрын
ken dou seriger touba wayé war nano sante bou bah kinou dimbalé mouy serigne saliou mbacké sama yakari tay ak euleuk yalla nanou serign touba tass si barkem
@minoushladouce7013
@minoushladouce7013 7 жыл бұрын
Kou tedd ki loumougnou defal billahi khamougnouko sakh❤❤❤
@danedieng5316
@danedieng5316 7 жыл бұрын
Yallana yalla yok ngueureum serigne touba cheikh Ahmadou bamba
@ndiayecheikhmariemou1412
@ndiayecheikhmariemou1412 7 жыл бұрын
bilahi #tfm ma beigue sii yeen nioune Sérigne touba rek laniou am bilahi
@serignefalloufall4242
@serignefalloufall4242 3 жыл бұрын
Theiy kou Tédd cheikh Ahmadou bamba mbacké Khadim rassoul 👂👂❤️❤️🙏🏿
@aliougueye9396
@aliougueye9396 7 жыл бұрын
machallah machallah wakh tanwi rafetna yalla na yalla fay len machallah
@papekabo6390
@papekabo6390 6 жыл бұрын
Alhamdoulillah sama sopé bi yalla nako Yallah wéreul ci barké Cheikhoul Khadim
@fadieye8219
@fadieye8219 7 жыл бұрын
meilleur QG kene dou serigne touba
@lild908
@lild908 6 жыл бұрын
DIEUREUDIEUFEUTi khadimou rassoul, serigne Saliou yalla na yalla guoudeul sa fan te mayla weer thi barke seydina mohamed, wakhtan bi lerna machalah, Amatina solo ndeyssan
@djibyfaye3616
@djibyfaye3616 6 жыл бұрын
God bless us Dieureudieuf Sérigne saliou SAMB
@ndeyecoumbacisse7198
@ndeyecoumbacisse7198 6 жыл бұрын
Sante Serigne Touba rék yakar Serigne Touba rék wolou Serigne Touba rék diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall. Alhamdoulilah bagnou donné ay mourides
@MorSoftThiam
@MorSoftThiam 7 жыл бұрын
Serigne Saliou Samb, éloquence,connaissance islamique et mouride,un phylosohphe du mouridisme hors paire , Yalla nala Seydina Mouhamadou Mbakiyou téral fi ak feulé
@iboufll
@iboufll 7 жыл бұрын
Thiey lima dalll tay j'ai veillé beu juli subeu diwadia leulou rek daldi play rek pour khoolll DAll Wayé dall thi 1er parti bi la tambalé Sama nélaw yeup naw ma faff céétane bii bamou dal naka diékh thi diamonoyimay binede nii Skeuy kharall ma playatt ko, Liiii dou doyy !!!
@mordiaw3382
@mordiaw3382 6 жыл бұрын
diere dieuf mame s touba amoul moroom yalla na nou ko yalla fayall thi bar kép alkhourane
@mbarganethiam7630
@mbarganethiam7630 7 жыл бұрын
machalla ken dou Serigne Touba dé dieurediefé Serigne Touba wakhate kate yi dé diaroul nio tontu ndakh seniy wax safane la thi niom kon wax ak niom yokolen safane la
@amargueye1916
@amargueye1916 7 жыл бұрын
Tieuy yalleu Serigne Saliou Samb Yalla na sougnou borom yook kham kham bi ci barké borom touba. tei sax nii rék leu mouride wareu méél guir génération yii di gneuw meneu ame kouléén wakhtanal lou wéér ci serigne TOUBA ak ndiabotam
@hizboundiaye6115
@hizboundiaye6115 7 жыл бұрын
gudal fan Serigne bi yalla nala Serigne bi fay bamba fi ne mom kese tay ag euleug
@ndiayesalimata7994
@ndiayesalimata7994 7 жыл бұрын
QG contane n'a yéne bilshi yalla nelen serigne touba fayal bopam Khadim Rassoul kéne rk la 🙏🙏❤️❤️
@zokara7382
@zokara7382 7 жыл бұрын
man dé dama dioy émission bi yeup nda xol bou fess thiey bou serigne touba bou amoulone. ....😢😢😢😢😢😢
@hannetorodo6563
@hannetorodo6563 7 жыл бұрын
issa badji dou yaw kep de
@babacarsadio4684
@babacarsadio4684 2 жыл бұрын
24mai 2022 serigne Abdou Lahad yalla na sa borom yok ay leeram🤲🏿❤️
@aliougueye9396
@aliougueye9396 7 жыл бұрын
rafetna way contan rek yalla na yalla fay way machallah
@senegaleseboy6638
@senegaleseboy6638 4 жыл бұрын
Ani Gni koy setanat ci confinement 2020 Bi ! Ay Mouride reek lagn beug done🙏🏾🙏🏾
@nabusaliha7346
@nabusaliha7346 7 жыл бұрын
fier d'être Mouride kene Dou CHEKHOUL KHADIM Sene émission tay bi intéressant na machallah Mouride yeup contane nagn akassa
@ndourcodou2004
@ndourcodou2004 7 жыл бұрын
thiey serigne touba kene dou mome sounou yakari tey ak euleuk
@racediop5525
@racediop5525 4 жыл бұрын
@@ndourcodou2004 Amoul morom
@bambasarre1577
@bambasarre1577 7 жыл бұрын
SERIGNE TOUBA rék la dou morom amoul morom kou ame morom mouye sa borome DIEUREU DIEUFEUTY SERIGNE TOUBA RÉK
@mourtadaseye6664
@mourtadaseye6664 7 жыл бұрын
bilhai QG bi mom.dou ma si doyal barkeb serigne saliou dama konatan lol si serigne saliou sambu yalla na serigne touba défal la taw fekh ak tayzir barkeb tayzirou hazir
@minasy9566
@minasy9566 7 жыл бұрын
QG bi douma si doyale chaque jour ma regardéko liii contana serigne touba hadimoul rasoul amoul morome dieuredieuf serigne saliou samb
@cheikhibnouarabysamb5653
@cheikhibnouarabysamb5653 7 жыл бұрын
Dieureudieufé Serigne touba wayé diaramma mame cheikh Ibrahima fall
@galsenegalsene
@galsenegalsene 4 жыл бұрын
Kouko sétane ba 2020 beuseul jaim dieureus dieufé borome touba
@omardieng1975
@omardieng1975 7 жыл бұрын
Serigne touba rek mofi nekkkkk dieureudieufeuty borome touba...
@sokhnafalolo9192
@sokhnafalolo9192 6 жыл бұрын
Kén dou serigne touba ak wa keureum yalnanou lén yala fayal té tas nou si sén barké barké cheikhouna xadiim dieureudieuf serigne touba
@zeinasarr4379
@zeinasarr4379 7 жыл бұрын
alahou akbar mane deii dama sakh yemou bilahi borom touba ak ndiabootam amouniou morom
@tinemariama3822
@tinemariama3822 7 жыл бұрын
machala kham kham kéne douko tatonné dagn koy diangu serigne saliou lep lére na serigne touba mom amoul morom lolou lérna gnep di gnanal aussi wa équipe QG liguey rafet trop mention spéciale vraiment vous êtes les meilleurs kou wakh ak kou wakhoul laf thiate.
@hannetorodo6563
@hannetorodo6563 7 жыл бұрын
Serigne touba Mbacke Khadimou rasoul niko yalla def koumou nexoul diga torox adouna torox alakk yawmal xiyam ganou diam mane salihou Hanne mako wakh louma thi gobe garko ken dou Serigne touba
@khadimndiaye3791
@khadimndiaye3791 7 жыл бұрын
HANNE TORODO Lou wer nga wakh fall
@astoundiayetouba5068
@astoundiayetouba5068 6 жыл бұрын
HANNE TORODO walahi
@youssoufbarry9754
@youssoufbarry9754 5 жыл бұрын
Serigne saliou mbacké joxnaleu sama Leep bilahii❤️❤️ioe reik la doylo mbacké walahi❤️❤️
@seneelhadji3133
@seneelhadji3133 7 жыл бұрын
barke boroum touba li nekhna dieureudieufe sereigne touba
@ndeyediodiadiagne4165
@ndeyediodiadiagne4165 3 жыл бұрын
Qui est là Septembre 2021 walay QG bi dou mathie doyal dieureudieuf cheikhoul khadim
@galassniang8003
@galassniang8003 7 жыл бұрын
lii moom Macha allah lééer na nagniii masssouféé ame wakh DEUG sanggge bi SAMB yagge fi te werrrr
@abdoumorethanakingthiam6930
@abdoumorethanakingthiam6930 3 жыл бұрын
1.6k yi dislike khawma loungén done mè meun na sedei ni wa eukhlou narr ngèn, loungèn meneu degg wala lougén kham si SERIGNE BI nalen ler ni sen mbokk dioukit ba dra khew nak té yakarna diouliit dioulit moy mbokkam nègam ay diouliit ngen (SERIGNE TOUBA KEN LEU)
@mamadoudjighaly6277
@mamadoudjighaly6277 7 жыл бұрын
serigne saliou a tout dis dans quartier général que tout bon mouride devrait être fier
@papambengue5244
@papambengue5244 3 жыл бұрын
Mon
@eternelreconnaissant5562
@eternelreconnaissant5562 7 жыл бұрын
Senegal bouniou kènalè serigne Touba leep louniou beugue Dina gniou ko ame , adouna lgui Mou diekh keep kou beugue mouthiiou na nanguoul serigne Bamba ,❤️❤️
@rahmatoullahkeita5444
@rahmatoullahkeita5444 7 жыл бұрын
Sante Yalla biniou amei kou melni Serigne Touba ak ndiabotam Ken dou niome
@aichagueye7010
@aichagueye7010 6 жыл бұрын
Souniou Papa souniou dieuwrigne serigne saliou samb yalla na yalla goudal sa fan si barke serigne touba
@fatoumataniang87
@fatoumataniang87 7 жыл бұрын
Alhamdoulilahh binou yallla bolle si ndiabotoou Cheikhoul Xadimm 😍😍😍😍
@wizmamendiayendiaye9755
@wizmamendiayendiaye9755 7 жыл бұрын
Zarra Niang Bilay werna dh santati kay biniou thi bokee
@astoudiogaye8402
@astoudiogaye8402 7 жыл бұрын
Zarra Niang amiine way
@thiernoba2044
@thiernoba2044 7 жыл бұрын
+wiz Mame Ndiaye Ndiaye cc
@dioumpapa4305
@dioumpapa4305 4 жыл бұрын
Serigne Touba amoul morom Dieureudieuf Serigne Touba Souniou yakarou euleuk
@fatousylla668
@fatousylla668 7 жыл бұрын
dieureudieuf serigne touba yalna yalla yokou sa lèr tè tass niou ci ça barké Amin
@falloufall9284
@falloufall9284 3 жыл бұрын
amena solo serigne saliou .yalla na serigne samme laa
@boyfall1
@boyfall1 7 жыл бұрын
jamais une émission télé ne m'a plus autant
@sonhiboundiaye2154
@sonhiboundiaye2154 7 жыл бұрын
bilaye senegal liniou amm khamou niouko serigne touba ken dou mom
@bocarfall6565
@bocarfall6565 7 жыл бұрын
Sonhibou Ndiaye
@booubbop9426
@booubbop9426 7 жыл бұрын
Sonhibou Ndiaye diareujeuff serigne touba
@khoumandiop6421
@khoumandiop6421 7 жыл бұрын
dieureudieufé serigne touba sante yalla bima dioudo nga nek si sama khol
@bambasalihou7386
@bambasalihou7386 7 жыл бұрын
sama tourando rekay wadia bilay kén dou mom ndax mom rk mo wakhni ILAYAKHADA LAHOU MALAM YAKOUNI WALA YAKOUNOU HABADANE LI MOUKINI mom rk lako Yalla may DIEUREDIEUFEI SERIGNE TOUBA
@cheikhgaye4958
@cheikhgaye4958 7 жыл бұрын
Dieurediefe serigne touba ken la dé amoul morom mofi meun diarama mame Cheikh Ibrahima fall
@amycollediop2949
@amycollediop2949 7 жыл бұрын
dieuredieuf serigne touba kénn dou mom billahii
@darougaye3025
@darougaye3025 6 жыл бұрын
Serigne touba amoul morom kénela diadieuf serigne saliou samb yallana guafi yague té wéer amine
@moustaphamouhamadouseck2442
@moustaphamouhamadouseck2442 3 жыл бұрын
3ans après je regarde cette émission qui semble tjr inédit...
@fayeibou7629
@fayeibou7629 7 жыл бұрын
serigne saliou samb yalna yalla defal diam ak goudou fann tih barke serigne touba keep kouy mouride sa xol sedna yalna yalla takhawou
@nafissatoudiakhate2942
@nafissatoudiakhate2942 7 жыл бұрын
Macha Allah Choukrane QG sant naniou bou bakh. Dieureudieuf à toute l'équipe et mention spéciale à Serigne Saliou
@bayeousseynoufallkhataba7361
@bayeousseynoufallkhataba7361 7 жыл бұрын
MachaAllah Amatina Solo QG Bou méll Nii doottou Fii Amatina Billahii Kénna Dou Couted Serigne Touba Cheikhouna Ahmadou Bamba khadimoul Rassoul Yackaarou Diaaam gnii Adunna Ak Allahiraa dieureudieuffétii Serigne Touba
@maguettethiam5812
@maguettethiam5812 7 жыл бұрын
li li li daffa raféte.........sante Bamba rek..comme l'an passé HTDK nioko nékhalone cet année Serigne Saliou SAMB la li dafa leeeer
@yamambodj3645
@yamambodj3645 3 жыл бұрын
Février 2021 ba legui doyalagouma ci machalah
@Faykinhogmail.ComFay
@Faykinhogmail.ComFay 7 жыл бұрын
outaz yallana yalla goudale safane pape chiékh , vol 2 gané chiékh Ibra la bouye yale mayy fatou dakh bégu
@capitaine_troptop7404
@capitaine_troptop7404 7 жыл бұрын
tiey SERIGNE TOUBA lo waxtané si mom rk mou doy seuk Machalla QG SERIGNE SALIOU SAMB bégu nane lolou si iow #DIEUREUDIEUFÉTI_SRIÑ_TOUBA
REPLAY - QUARTIER GENERAL - Invité : SERIGNE SALIOU SAMB - 08 Juin 2018 - Partie 4
1:26:29
Quando A Diferença De Altura É Muito Grande 😲😂
00:12
Mari Maria
Рет қаралды 45 МЛН
UFC 310 : Рахмонов VS Мачадо Гэрри
05:00
Setanta Sports UFC
Рет қаралды 1,2 МЛН
Plateau Spécial - Pr : OUSTAZ PAPE HANN - Invité : SERIGNE SALIOU SAMB - Partie 2
59:15
QUARTIER GÉNÉRAL - Invité : SERIGNE NDIAGA DIOP - 07 Mai 2020 - Partie 3
2:07:53
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 1,5 МЛН
QUARTIER GÉNÉRAL - Invité : SERIGNE SALIOU SAMB - 21 Mai 2020 - Partie 3
1:21:08
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 494 М.
REPLAY - QUARTIER GENERAL - Invité : SERIGNE SALIOU SAMB - 08 Juin 2018 - Partie 3
1:17:02
QUARTIER GÉNÉRAL - Invité : SERIGNE GANA MASSERE - 16 Mai 2020 - Partie 3
2:43:27
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 986 М.
QUARTIER GENERAL du 24 MAI 2019 - Invité : Serigne Gana Mésséré - PARTIE 2
2:51:53
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 4,2 МЛН