Reportage inédit à Keur Massar : Des Maisons abandonnées, Le calvaire des habitants de Keur Massar
Пікірлер: 247
@mo-diop22153 жыл бұрын
Le gars qui fait l’émission il a tous mon respect✊🏿🙏🏿
@maremediaw64883 жыл бұрын
Macha allakh Fadel ligueye bi rafetna 👌 annéé dernière aussi ni la wone ya ndieuk dem keur Massar osé dougou ba si bir dokh bi housss...tu etait le premiér a le faire sans hesitation je me rappel bien yalla yalla fayla yokkla takhawoula si barké serigne babacar Sy🤲🤲🙏🙏
@jonh67453 жыл бұрын
Bonjour tout le monde , j'aimerais témoigner moi aussi. J'ai été victime d'inondation l'année dernière à Keur Massar et notre maison était complètement inondée , on a été obligé de sortir de la maison . Aujourd'hui je suis en France alhamdoulilah, je fais des études littéraires. Qu'Allah aide ces familles 🤲🤲, c'est la responsabilité du gouvernement de régler ce problème, Bilahi j'ai vécu 6 ans avec des inondations à Keur Massar, je comprends bien cette souffrance.
@tigressesylla99413 жыл бұрын
Dafa méti
@abdoulayediallo64173 жыл бұрын
fadhel respect a toi la maman ta confié une lourde tache k le bon Dieu t'accompagne sur cette mission encore une fois respect a toi
@fatoumbackesylla44813 жыл бұрын
😭😭😭😭😭😭😭😭😭 ndeysan mere bi dioy lo nama fadel koubax nga nianne yi La nitt gni di nianal yallah nako souniu Borom nagou rafet nga xol trop yallah Nala yallah mousal sì thiat ak lamigne
@serignebabacardiouf90833 жыл бұрын
Un grand Mr ! Merci Fadel 🙏
@papaibrahimagueye21103 жыл бұрын
Puisse Allah SWT vous gratifier de Ses bienfaits Amiin
@pacopaco77093 жыл бұрын
Merci Fadel liguey bi amna solo
@fatoutop57632 жыл бұрын
Fadel yalla nala yalla defale diam bayilak sa diabote khole bou rafet nga yor ❤🙏🙏
@keurmassartvkeurmassarinfo23303 жыл бұрын
Y'Allah meu donne président rekk inchallah 😭🤲🤲 nous sommes fatigués way la population d keur massar
@elhadjithiam36373 жыл бұрын
Merci bcp Fadel vraiment vous faites du bon boulot
@sals12313 жыл бұрын
This is totally heartbreaking!!!!😥I cannot imagine what they are going through.May Allah bring the changes that will solve all these problems.This is why African leaders end up with a very bad ending,May Allah protect them all!!!My prayers are with all those suffering these situations.Hasbunalahi wa nikmal wakil!!!La ilaha illa anta subhanaka inni kuntum minal zalimin should be the prayers of all these people that are going through innodations right now.We give praise and thanks to Allah for all situations.
@dialiabusness3 жыл бұрын
Walahi bouma Yallah naré maye alale té guessou Massi gnie ko Yéwole Yallah bou alale bi akssi si Mane.Non sama khôl toye na vraiment.
@omarsylla53493 жыл бұрын
Wallahi ndeysan
@TOUBAKANKATV3 жыл бұрын
Thiey li Yalla DOLI NIOU sutoura Sénégal 🙏🇸🇳
@mortalla34loum653 жыл бұрын
oooh sama yaram dawna yalla nalene yalla takhawou metina
@fatouwade50483 жыл бұрын
Massa maman,yana la Yalla takhawou si barké Seydina Mouhamed SAW.
@generalking17983 жыл бұрын
Merr dioy lou nama nakk Fadell Bilahi yalla nala yalla defal diamou😭😭ay ndaye san li Meti na mer yalla nala yalla takha wo
@mo-diop22153 жыл бұрын
Ohh 😯 yalla nalèn souniou brome takhawou.🙏🏿 liii métina trop
@minalyminaly90083 жыл бұрын
Massa 😢😢Que le Tout-Puissant vous assiste amine ya rabbi
@simonndour89233 жыл бұрын
Des incompétents vraiment , du courage aux familles 🙏🏽.
@mariemegadio7743 жыл бұрын
Avant de construire logiquement il faut d’abord faire un plan d’assainissement sur les voies publiques pour l’évacuation des eaux usées. Ça me fait vraiment de la peine 🙁 Yallah nañu diapalé
@pendadia5623 жыл бұрын
Ils savent pas cest pour cela c triste niak xam mo waral lou beuri o contraire
@dialiabusness3 жыл бұрын
C'est décevant de voir ça au millénaire où nous sommes. Je me dis que le Sénégal doit surpasser cet étape !!!
@arimaz893 жыл бұрын
Cest pas uniquement au Sénégal cest partout dans le monde
@gabrielpro27473 жыл бұрын
La nature prend ces forces et au Sénégal on construit partout, c est pa tout les zones qui sont habitable
@ousmanesarr49883 жыл бұрын
Qui est responsable ds ts ses choses depuis 1960 on a ps des hommes qui aiment leurs pays mes des bandits qui ns gouvernent
@ramatakane19503 жыл бұрын
Que Dieu nous vienne en aide
@tallaseye98933 жыл бұрын
Maky Sall bo amoull xaliss pour défar ay kanall ténga diayaatt avions bi défaréko ay kanall mo geuneu nék farata fouff
@noreynisene14823 жыл бұрын
Yala nalenn borom bi taxawou li dafa metti quand je vois les enfants je ne plus retenir mes larmes
@serignebabacardiouf90833 жыл бұрын
Fait tres mal ! Je trouve pas les mots. Na borombi same léne.
@aboosow4223 жыл бұрын
Depuis Dubaï mais sama yaram dawna
@leuzpro28863 жыл бұрын
bilahi bro mais yalla bakh na
@marabout81603 жыл бұрын
Yeureum n’a leen lool de wourna s fallou 😭😭 Kay leen deuk si Touba fi amna Ay keur you yombou billahi gneuw leen fi
@abibatouniang25733 жыл бұрын
Keur massar deukk lignouy dadji yeupp si walou deukouway leitina.route you barii bahoulll le pire gnounei dagnfi defar pond thieyyyy lii🥺
@alioutallbayefall3023 жыл бұрын
Yalna yalla diappalé khewal ak wer
@diaaladji54363 жыл бұрын
Merci fadel
@ndacksall77723 жыл бұрын
Yalla n'a la diapale AK saye dôme amine
@anifanawtamsbi13943 жыл бұрын
Ndeysane sama goxx😭😭keur massar City yalla naleen yalla taxaou
@KatyNdeyeDiop3 жыл бұрын
Yallana lène yalla diapalé, dieuradieuf waye Fadél.
@massdieng33943 жыл бұрын
Kom pere ne nga Macky mofa Gagner 100/100 kon gerelene.. Yewoulene
@cheikhdione31483 жыл бұрын
Vraiment métina loll wallahi 🙏🙏🙏🙏🙏❤😢😢😢
@adjiamaimounasenghor52683 жыл бұрын
C’est douloureux franchement naniou sant yalla 😭😭🙏🏽🙏🏽🙏🏽nakh nekhoul si khol sou tawer fitt yeup deme yalla naniou yalla soutoural 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽maylen kholou mougne franchement les politiciens nous fatigue li warna niou yewou bou bakh nakh niome diarou niou Drah sen intérêt rek laniouy khol 😡😡😡🙅♀️🙅♀️j’ai mal au COEUR
@bibasene87173 жыл бұрын
Yén gniy votél maires yi nguirr intérêt personnel wala nguurr kharite ragal léne yalla yeureum domou adama yii l'heure du changement a sonné et si vous ne faites pas l'impossible pour s'inscrire et pouvoir voter vous êtes complices de ces situations malheureuses🙏
@ameuhjoop16853 жыл бұрын
Bly frr lolou nak sénégalais yii nio wra yéwou
@ibbousoom4143 жыл бұрын
Aferbi sonko rekkkk Inchalah
@cheikhmomarlo20203 жыл бұрын
Wallahi lui kounék comprendre nako. Yalla nalén sounou borom jaapalé. Ça fait mal!!!
@astoumbodji52723 жыл бұрын
Cette vidéo me rappelle les inondations de l’an dernier 🥺
@Momo-dl6bg3 жыл бұрын
Et ce sera le même scénario l’année prochaine rien n’est vas changer comme d’habitude rek …
@astoumbodji52723 жыл бұрын
@@Momo-dl6bg t’as raison deh 🥺 c’est tellement dommage 😞
@seulelaveritetriomphera3 жыл бұрын
C'est vraiment dommage, que le Bon Dieu assiste toutes ces familles. Il faut quitter Dakar pour retourner aux villages. C'est aussi la faute à ces habitants qui investissent des millions dans ces zones inondables. Pourquoi faire R+1,2,3... en sachant que la zone est inondable ?
@mumfaye58343 жыл бұрын
Tu passes à côté de l’essentiel. Il s’agit d’un problème d’aménagement du territoire. Pas d’industrie, l’artisanat sacrifié, plus de terre pour cultiver, alors comment vivre au village, avec quoi ? C’est plutôt l’incompétence des dirigeants qu’il faut pointer du doigt.
@biraneseck13073 жыл бұрын
Merci frere
@morsamb86233 жыл бұрын
Doyna Warr 😭😭😭macki yalla nafi niouguë thi diamou 😭😭😭😭
@cheikhkane62503 жыл бұрын
Wàllaahi sama xol sori na ci lii ana ñinga xamne ñoom lañu dégg réew mi yéen du ngeen dara Maki sàll yaa bon xanaa du yaw lanu dégg réew, baaxoo guddi baaxoo bëcëg yaw Maki sàll seetaan sa askan nii ana lu ko fi jar ragal Yàlla nga taxawu askan wi,Faadel noo ngi lay sant bu baax.
@moussalami23313 жыл бұрын
FADEL bilay so bayiwoul khouss 😃
@oumarndiaye36323 жыл бұрын
Du courage vraiment vraiment ces dure
@serignefalloufallkhassida42303 жыл бұрын
Ndaysan Yalnalen Yalla Takhawou Teguil Lene Natouyi
@generalking17983 жыл бұрын
Bilahi soniou yaye yi amo niou Sen fay😭😭😭😭
@fadiopseck53473 жыл бұрын
Yalla nalen yalla takhawou
@ibrahimasene78933 жыл бұрын
100 ème commentaire, anni président macky
@kingroma183 жыл бұрын
😭😭😭🙏🙏 yalla nalên yalla takhawou 😭😭😭😭
@rokhayandiaye15573 жыл бұрын
Ayewaye yalla nalén yalla taxawou
@diodiobdx94353 жыл бұрын
Svp le numéro de la dame la fin du reportage c'est pour petite aide merci
@mbacketv34503 жыл бұрын
Jac année comme ça 🙏🙏😭
@awafaye36383 жыл бұрын
Ndeyssane metina
@fatyndiaye20423 жыл бұрын
Certains qui disent que « c’est pas tous les zones qui sont habitables » fermez les teh nguen am yeurmandei bou État bi ligueyoon ndox bo wadd dem partout nak
@originali1553 жыл бұрын
Vraiment j'allais dire pareil c'est à l'etat mais aussi à ces maires qui ne sont que des bon à rien et des bras cassés
@serignebassirousylla41603 жыл бұрын
des incapables,des voleurs,des vautours nos dirigeants.yeureumlene askanbi
@sambayerelsow95913 жыл бұрын
fadal yala nala yala defal diam ak xewel si barke seringe babacar sy
@minata21743 жыл бұрын
Fadel yalnala Yallah faye
@mouhamadousalamtassawouftv2463 жыл бұрын
😭😭😭😭😭métina lol ndaysan yallanalé yalla takhaw
@dialiabusness3 жыл бұрын
Bravo frère pour le reportage.
@diopdeffdaradiop563 жыл бұрын
C vraiment triste 😥
@elhaditall19693 жыл бұрын
Thiowal newet nor lagnou kay waxtané .
@moustaphaniass3363 жыл бұрын
Dégg na deugg d
@modoucobar24083 жыл бұрын
Kiy mouthio dérétou askanam nore - nawéte dakoye fék mouye goundandate mok niako nékh ay domé rame laniou rék me alakhira dina nieuw dé bilahi
@fatoudiedhiou45083 жыл бұрын
😭😭😭massa ndeysane 😭😭😭
@dabadia1243 жыл бұрын
Maki sall ana sounouy miliar ya kate sa tounou ndaye doméram bi
@TOUBAKANKATV3 жыл бұрын
Ndayesan li métina loll way 😥😥
@paulelesarr34653 жыл бұрын
Merbi dioylonama fadel yallah molay faye ay way souniou gouvernement bi dimbeulile askanbi
@idahhdw53483 жыл бұрын
Mais il y'a un chose que peu de gens savent moy que ni fi yeup dèkh( lac) la wone niou seukk ko diay ko nitt gni et ils ont bien caché cette vérité aux gens, mane par hazard la tokk un jour un vieux peulh nieuw niane ma nokh ma may ko après mouni ndeysane fi la done sambé sama nakk (bœuf) fi yeupp nokh la wone, du coup avec cette nappe d'eau bou tawé rk dafay inondé nakh sous bi dafa mandi bou yagg
@keurgui72313 жыл бұрын
Li moy senegal émergent avec niou né kotieu barma mougui liguey
@modoucobar24083 жыл бұрын
L8géyoul sarap ndayam
@modoucobar24083 жыл бұрын
Kome gni bokouniou si réwmi ay domi rame nio djiité Sénégal
@fatoumatabarry1093 жыл бұрын
Salam Fadel svp je veux le numéro de la Maman à la fin 😢😢 aide moi svp 🙏🏾
@djibrilbassouldiouf56143 жыл бұрын
métina dé wayé nak président mon ngisi Daf loumou meun wayé yala bakhna
@khadysall67453 жыл бұрын
Toujours keur massar ana mairé bi elétion maire yii legui mou niew guén wathie koo mou dégage li dafa metii
@killahndiaye38383 жыл бұрын
C'est vraiment triste autorités yi nan leen dimbaly nguir yallah 😢
@omarsylla53493 жыл бұрын
Yalna brmb geuna dolli soutre
@serignebaraseck50793 жыл бұрын
Fadel ak Dakarbuzz diokhé léne numéro Orange ak Wave pour Lou way am 100fr 1000fr dougal fa peut-être mu done somm ñu diox jebalen ko si dound mogeun mo eup solo tmt ñu xolal lén solution da siy bakh dh
@marmichoue78573 жыл бұрын
Keur Massar n'était pas comme ça ya 15ans. Il pleuvait mais yavait avez de sable pour recevoir l'eau. Sénégalais mo tameux foumou guiss souff déféni keur khadj nafa tous les espaces sont bétonnés! On prend d'assaut les espaces libres, on vend des terrains et autorise des constructions sans au préalable gérer l'assainissement c'est inadmissible!
@mamegordgn49013 жыл бұрын
Je vous conseille de construire avec un vide sanitaire, c'est ce qui est conseillé quand on veut construire en zones humides.
@fallmmefall29203 жыл бұрын
C quoi vide sanitaire
@moussalo80783 жыл бұрын
Pourquoi au Sénégal les autorités ne travaillent pas. Incompétence pragmatisme et proactivé zéro..
@aissatousylla90263 жыл бұрын
Merci encore vraiment dommage pour le Sénégal
@modoudiop67493 жыл бұрын
Ce qui est plus écœurant dans cette histoire, c'est ces mêmes victimes qui vont accueillir leur bourreau macky sall avec des acclamations pour un 10 000 F CFA.
@marieme29613 жыл бұрын
Boul wax lolou dara leroula ci li nguey affirmer
@fatimasarr93843 жыл бұрын
Ce n'est pas joli niit nék ci nakar bi, ndiakaré bi, ngakoy blâmer ci lo khamné dara, dara, dara léroula cii. Évitons de reprendre les bouts de phrase qu'on lit ça et là, fou niou doug ci net bi taf kofa. Yalla nalén yalla saam, téguil lén lii. Les autorités locales et étatiques warouniou sétaan lii.
@momadulaye38133 жыл бұрын
Li eupeu si voleurs yi, niougui almadie, faté askan wi. Chaque année ni rék
@ameuhjoop16853 жыл бұрын
Wly frr nio ngi almady maire rou keur massar bann koo fallé la tokhou
@yacinesouare64133 жыл бұрын
Mougne rek Etat diapaléwoul kéne souniou keur 2005 ba légui niogui si nokh sama solution moy yalla dimaliniou barkél niou baniou dimali souniou wadiour
priorité moy li, mais pas 30 milliards pour des tenues
@aminambengue12403 жыл бұрын
Vraiment
@minata21743 жыл бұрын
Yalnaléne Yallah takhawou si barké Baye, bilay j'ai vraiment mal au coeur, mère xamoumala wayé lingay doundou ni ak sa famille, Yalnalasi Yallah dieulé, Yallah takhawoulé si barké BAYE
@binetafaal10853 жыл бұрын
Fii aye tole la wone il fallait pas construire la bas
@ndeykoyo173 жыл бұрын
Sorry mum
@anifanawtamsbi13943 жыл бұрын
Hum vraiment lii metina trop saxx 😭😭
@zasoumanikele47503 жыл бұрын
Merçi Macky Sall !..😪
@cheikhkane62503 жыл бұрын
Oh Mer bi ak fadel jooyloo nama de, yal na yàlla saafara jefe-jefe yi.
@abdoutoure24903 жыл бұрын
Mai. Li metina Warr. Na amm solision. Ana. Etat
@satoundiaye50983 жыл бұрын
Pour la grâce de dieu vous ki achète des terrains bou léne sani séne khalisse parce qu'il ya des zones no habitables qui ont beaucoup de sels et quand il la pluie l'eau ne part jamais
@maguettediongue8453 жыл бұрын
Moi senegal je ne comprend pas louer si ndokh alors k les villages lé pak c gratuit
@deuguerek50063 жыл бұрын
MR le président svp aide ces gens , j’ai vraiment de la peine pour eux . Qu’Allah apaise 🙏🏼